Il paraît que chaîne bi y'a pas d'entraide car je vois des situations qu'on passe ici té si tu entends l'histoire tu sais que la femme c'est juste un mari qui lui manque pour que mou changé et si c'est un homme c'est juste une femme qui lui manque pour que mou changé aussi. Cette dame si j'avais la possibilité de mieux la connaître dina envisagé takko parce-que mane aussi beuggouma Di déf lou bakhoul . Mais je ne sais pas si c'est la chaîne qui ne laisse pas passer certains commentaires comme bi ni ou bien. Encore une fois nama may ma takk mère bi ngir Yalla Soxna rék laa beugg Moy émission net tali bou démb bi hier
Il faut sortir de votre tête ces histoires de dédeulé. Beaucoup d'hommes gèrent mal la polygamie et délaissent la 1ere femme. Il faut se décider soit à rester dans ce mariage et supporter, soit divorcer. Deuxième point : allez à d'aval khel consulter un psychiatre pour vos troubles du comportement. Du courage.
Kou beug Saydina Mouhamed lalal j’aime ❤
Yaw ndiépa ko begue
@@FamaDiop-o2x gnii nekoul joulit nak🤣
Ma chérie dou béne dédelé goor mo melle nonou dounal sa dounou topoto saye dome té bayi ko ak Yalla
Dou lolou dh djiguene day teyi bopam moka def koula takoul nga koy diokh sa bopou bou doyale bayi la
@ Deugla dé
Khame na ni thiucume mdiaye mome doye na ware
Maniko thie thiéyyyyy😢Sénégal dale thioukoum diop ndiaye bi comme mbourou ak thon 😢lék légn ko def dale😮yalla bakhna 15h52
Salam Sister Fatou Namone Nala ❤Dafa Gor You Doye Rek Na Topato Ndiabotam Yallah Bakhena ❤Sama Wale Ci Caffè ☕ Gui Merci Et Bonne Continuation Dieureudieuf 🙏❤
Mou deuké nonu deuké nonu deuké nonu😅😅😅
Tioukoume Ndiaye 😅😅
Il paraît que chaîne bi y'a pas d'entraide car je vois des situations qu'on passe ici té si tu entends l'histoire tu sais que la femme c'est juste un mari qui lui manque pour que mou changé et si c'est un homme c'est juste une femme qui lui manque pour que mou changé aussi.
Cette dame si j'avais la possibilité de mieux la connaître dina envisagé takko parce-que mane aussi beuggouma Di déf lou bakhoul . Mais je ne sais pas si c'est la chaîne qui ne laisse pas passer certains commentaires comme bi ni ou bien.
Encore une fois nama may ma takk mère bi ngir Yalla Soxna rék laa beugg Moy émission net tali bou démb bi hier
Il faut sortir de votre tête ces histoires de dédeulé. Beaucoup d'hommes gèrent mal la polygamie et délaissent la 1ere femme. Il faut se décider soit à rester dans ce mariage et supporter, soit divorcer.
Deuxième point : allez à d'aval khel consulter un psychiatre pour vos troubles du comportement. Du courage.
Li yeup farou rap mokoy def!
Loumouy def moy mou tek alquran feup foumou nek! Diko deglou ba paré diko teg tchi keurgui mouy diang tchikaw.
Balla mouy teudd tamit nay diang Ikhlass Falaq ak Nnaass ba paré euf tchi lokho yii ray ko tchi yaramam bala mo teuddi nelaw gouddi, lolou dina takh farou rab bi bayiko!
Farou rap moy yakk seuy dioullit niou beuri! Alquran kassé ak sellal moko meuna dakk!
C est les hommes qui sont Comme sa, il faut que les femmes prendent leur vie sans dependance.
❤❤❤
Tioukoume diop diop diop diop diop diop diop diop diop diop diop diop diop diop 😡😡😡😡
❤
Thioukoum Ndiaye bamou kheume boudone thioukoume Diop fi toth😂. Wakh naléne Goor dou projet. Djiguene gni yewouléne take séne seure ligueye , oute si loléne diape meuneul séne bopou. Goor mom bou Thioukoum Niang wé banga sapi ko mou séti lénéne bagne léne
Louy projet ??
@ ligueye diamou yalla lidieunti sa bopou
@diariabousso466 Sëy dou diamou Yallah ?
Mani casse bi lay toth tour café gui sonouna niou si😂
Métina
Naw si ya bëg topou sa bakane bala say mbokou téréwé acceptêl wadj rk ak ay defaut wam
Pour deudelebi mom khamna serigne bou bakh seydi Ibrahim5la toudou demal compte tiktok nga guiss numérom fofou