Ndindy: Iran Ndao à Serigne Abdoul Karim "yague nala dégue, wayé bimala guissé..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 20 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 429

  • @dadindiaye4807
    @dadindiaye4807 5 років тому +85

    Je suis Tidiane mais Bilaye j’aime beaucoup cheikh Abdou Karim yalla Nafi Yague ta wèèrr

  • @djilydiop7560
    @djilydiop7560 5 років тому +84

    Ndaysan s. Abdou Karim mbakce yallna yalla guodall sa fan et iran NDA
    Machalla lobakh rek mo am solo

    • @papaditabdoulayediop824
      @papaditabdoulayediop824 5 років тому +1

      Machallah 👌👌👌👌❤️

    • @djilydiop7560
      @djilydiop7560 5 років тому

      @@papaditabdoulayediop824 👍👍👍♥️

    • @metzoyamal
      @metzoyamal 5 років тому

      s Abdou Karim yague fi lol té wér Iran baguenala bou wér yague fi lol té wér

  • @papegritalmbaye1596
    @papegritalmbaye1596 5 років тому +1

    Oustace Iran ndaw ya niakk kiane... 😍♥️Yalla nala s touba takhawou thii barkèpe s fallilou mbackè ak baye karim diadieuf beugu nala trop

  • @antandao5618
    @antandao5618 5 років тому +352

    L homme de l annee c est iran ndaw, ki est d accord avec moi?

    • @ElTIO_Galass
      @ElTIO_Galass 5 років тому +2

      Wakhi dof Li ba ila yaw mi dine la wara Don dou Anné rek

    • @cherifousinguinar8455
      @cherifousinguinar8455 5 років тому +4

      Iran nite geunou ko longue vie à lui

    • @youzarsiflo6894
      @youzarsiflo6894 5 років тому +1

      @@ElTIO_Galass vraiment yaw mi ya nitèwoul

    • @mbddiop4671
      @mbddiop4671 5 років тому

      Je propose Ser Abdou Karim ou TOUBA ÇA KANAM

    • @atouniang522
      @atouniang522 5 років тому +1

      Moi je suis daccord

  • @youssouphaserignebakhoum7113
    @youssouphaserignebakhoum7113 5 років тому +138

    Ceci est une leçon de vie pour nous talibes. Il n'y a aucun différent entre les tarihas. C'est à nous de consolider ceci

  • @moussasow8545
    @moussasow8545 5 років тому +30

    Yalla nama yalla wanalé ak serigne Abdou karime beug nako sope nako

    • @alaminesylo2680
      @alaminesylo2680 5 років тому

      Billahi moussa gno bokou beug beug d tidiane la d mais balamay dée beug nako guiss si sama adouna

    • @moussasow8545
      @moussasow8545 5 років тому +2

      @@alaminesylo2680 mane layénne la

  • @siloualtijani6972
    @siloualtijani6972 5 років тому +14

    Serigne Abdou Karim okho un homme de dieu machallah

  • @fatimafaliloulah1145
    @fatimafaliloulah1145 5 років тому +33

    Dieureudief Iran Ndao, machahalah Serigne Abdou Karim Mbacké ! Yalla nafi yague looollllll té were ! Barké Cheikhoul Khadim !

    • @senegalaisdiop2427
      @senegalaisdiop2427 5 років тому

      WAYAANE KÈPP CES IMBECILES DE CHRONIQUEURS TIDJANES QUI CHANTENT LES SERIGNES MOURIDES COMPLEXES .MAIS YAW IRAN SI CEVQUE TU DIS EST VRAI DIÈBALOUL DOMRAM

    • @momofit6047
      @momofit6047 5 років тому +5

      @@senegalaisdiop2427 iow lo bokk ak ibliss ?? Khana do djoulite ?
      Mouride la mais linga wakh téguiné woull boné Tidjane khamall ni cheikh ahmeth Tidjane cherif si la bokk elhadj malick sy si la bokk Abdou Aziz sy dabakh si la bokk képp kouy Tidjane si nga bokk wakhe day ame téguine au yarr

    • @mygodguideustotherightpath5448
      @mygodguideustotherightpath5448 5 років тому

      senegalais diop yaw ak sa bamél iran ak bamelam té mandou ak wakh deuge si diamou yalla la bok kon wakhal loula wor

    • @youzarsiflo6894
      @youzarsiflo6894 5 років тому +1

      @@senegalaisdiop2427 ndèysane yalla nèna kou nara tèkhè mooy niok mokkou yaw diango motakh sa wakh bi niaw bi

    • @resumedelivres8533
      @resumedelivres8533 5 років тому

      @@senegalaisdiop2427 con

  • @3snumeriques856
    @3snumeriques856 5 років тому +1

    machala j suis tidiane mei jaim baye karim bg nako giss lol sakh

  • @bamsbams3171
    @bamsbams3171 5 років тому +27

    Dokh mbokou li'si yalla wakh bari'na yalna yalla na'ngou séne diamou yalla Abdou Karim mbacké yague fi lol té wére si barki seydina mouhamed psl Amine 🇸🇳

    • @massambakhouma3357
      @massambakhouma3357 5 років тому +2

      Serigne abdou Karim mbackè mo gene réfèt abdou karim dè nga balma nak

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 5 років тому +28

    *_machallah Iran ndow Yalna yallah doulé xàm xàm Borom makarimall akhlàkh yalna fi té weurrr si barkép SERIGNE SALIOU MBACKÉ_*

  • @cissendiaga9995
    @cissendiaga9995 5 років тому +3

    Machahala Mbacke yalla na yalla goudeule saye faneu te wereule saye thier amine

  • @modoufallbetebeteitsenegal5272
    @modoufallbetebeteitsenegal5272 5 років тому +3

    MACHALLAH MACHALLAH MACHALLAH DIEUREDIEUFÉ MBACKE BALLA AÏCHA DIARAMA OUSTAZ IRAN NDAO

  • @senegalonline8021
    @senegalonline8021 5 років тому +20

    Lii dînée la, kep kouy dioulite warnaa meun contane xamni dinee ben le téyite nioko bok, inamaal moûminûna ikhwa ! Yalla na yalla def diam si rew mi 🙏🏿

  • @mamadouthiaw9280
    @mamadouthiaw9280 5 років тому

    Macha'allah mbackè yalna yalla yagala kou gnak kigna Iran takhaway bi amna solo

  • @niangniang7444
    @niangniang7444 5 років тому +1

    Macallah refat na lol yalla na len yalla faye si barkpe serigne touba amine

  • @ngagnendiaye3605
    @ngagnendiaye3605 5 років тому

    Vraiment Iran ndao sa khôl rafetna machalah Serigne Abdou Karim mbacké yalna gua fi tagg té werr amine

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 5 років тому +6

    Serigne Abdou karim yalnafi yague the andack weure barkep serigne fallou Mbacke

  • @fallouthiam250
    @fallouthiam250 5 років тому

    Serigne Abdou Karim yalla nafi yag té weurr gnep pako beug machala iran

  • @bayesalioudiagne1518
    @bayesalioudiagne1518 5 років тому

    Machalla diaty bi rafétna torop yalla na diamo yakh si barké khasidayi amine

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 5 років тому +5

    Akasa amna solo Dieure dieuf machalla merci irán ndao lii Raffetna lolle yalnanga fii yague the andack weure barkep serigne fallou Mbacke

  • @cheikhthioye6000
    @cheikhthioye6000 5 років тому +13

    Aka bakh baye karim wallahi ndeyssane

  • @modoutalibeserignembayesya3953
    @modoutalibeserignembayesya3953 5 років тому +51

    Bilaye Mbacké balla y’a bakh mala sope bilaye barkép seringe Mbaye s’y abdou

  • @mossanefaye9414
    @mossanefaye9414 5 років тому

    Gnanal lénma yalla bayimafi bayikofa bama gissko yalnako guisse mbeugueul bima ame si wadioureum seurigne falou yeupeu guisi mome yalnakofi yalla bayi❤❤❤❤

  • @moussasy2813
    @moussasy2813 5 років тому +1

    Masha'Allah Iran Talibé cheikh dafay am yar am xam xam am kilifa

  • @diasporasambtv7
    @diasporasambtv7 5 років тому +5

    Macha alla, Iran ndao!! Goudal fan! Amine 🤲🏾🙏🏽

  • @mamadoutop4142
    @mamadoutop4142 5 років тому

    Machallaha yalla na yalla defar lep bole dioulit yeup dolél niou katan ak soutoure li dsfa rafét trop baye karim

  • @5fallou
    @5fallou 5 років тому +4

    Masha Allah mbacke balla yague fi lole te weer tenou yague dila ziar 🤲🤲🤲🤲🤲🙏🙏🙏🙏💝💝💝💝

  • @idrissandoye6550
    @idrissandoye6550 5 років тому +1

    Macha allah li dafa nekh way serigne abdou karim nitou yalla bou ague si bakh la macha allah

  • @Sonkomoyediomayetv
    @Sonkomoyediomayetv 5 років тому +44

    Bilahi serigne Abdoul karim yabakh mala beugue Mbacke lo gnane mou ame

  • @ibafall336
    @ibafall336 5 років тому +1

    Voila des choses qui meritent detre divulguer dieureudieuff serigne bi yalna yalla fayla si sa mizanou hassanatt

  • @sokhnafatimabous.mansoursy283
    @sokhnafatimabous.mansoursy283 4 роки тому

    Machala Serigne Abdou Karim MBACKE yalna na fi yagg lol té weure.Amine

  • @sambasour3561
    @sambasour3561 5 років тому

    Machan Allah serigne abdou Karim mbacké yalla nafi yagg lol té wér Iran ndao yalla nala yalla Yoku si barkep Kou tedki machan Allah

  • @abdoulahad7315
    @abdoulahad7315 5 років тому +4

    Iran NDAO est gentil kou beg baye Karim tapper aime

  • @adamafall820
    @adamafall820 5 років тому +4

    Merci ouzts bay karim da yemi

  • @talibessalioumbackesarrmor5674
    @talibessalioumbackesarrmor5674 5 років тому +100

    S abdoul karim diarama yague fi lol te weur barkib Serigne saliou mbacke iran ndaw machallah ame diammou rek mangui ziyar bou weur

  • @iboudieye1255
    @iboudieye1255 5 років тому +1

    Machallah amena solo cheikh Abdoule Karim yague fi te wérr merci iran contane si yaw

  • @aidarambaye2075
    @aidarambaye2075 5 років тому +3

    iran ndao yalla nala sarigne touba Faye🙏♥️♥️

  • @cheikhdiop2787
    @cheikhdiop2787 5 років тому +11

    Merci iran

  • @mamadousylla9139
    @mamadousylla9139 5 років тому +10

    ALKHAMDOULILAHII
    Yalla na diam yagu Sénégal ak fepeu si Adouna bi

  • @cvpointernational4549
    @cvpointernational4549 5 років тому +15

    Machallah Iran Baye Karim Mom YAGG ❣️ RK la fy déf inchallah

  • @massdiop7788
    @massdiop7788 5 років тому

    Machalla yalla na diam yague Dieureudieuf serigne Abdou Karim

  • @malickseck632
    @malickseck632 5 років тому +58

    Billaahi Serigne Mbacké dioumou ma,Kou bakh nga,té sopna nalla lool,Si barké Serigne Babacar Sy,Yalla na Borombi Azawadjal kheuthie Saw fane,sissa Barké bay Mame Fadiilou !

  • @mayoronguer2498
    @mayoronguer2498 5 років тому +18

    Baye Karim ziar nala boubaakh Mbacké Balla aïhicha yagfi téwerr barké borom Touba dieureudieufaty Khadim Rassoul amoul morom

  • @papendiaye3968
    @papendiaye3968 5 років тому

    Serign Abdoul Karim kou bakh la yalna ko yalla doli sam ak kilifa diné dji yeup

  • @ibrahimasenenabien1204
    @ibrahimasenenabien1204 5 років тому

    Merci oustaz iran dieuredieuf serigne bi Mbacke Balla Aïsa sa taxaway rafètna machallah

  • @toubandindyafricanhairbrai2924
    @toubandindyafricanhairbrai2924 5 років тому +2

    Thiey mbacke balla aissa..mala begue pire.. oustaz iran lou ma beguone yokkou na ya gnake kignane te bakh 💝💝💝🙏🙏🙏🙏diam ci yow

  • @mouhamedcisse5505
    @mouhamedcisse5505 5 років тому +11

    Bilahi iran ya bakh ta beugeu lou bakh ❤️😍

  • @helloworldbuzz
    @helloworldbuzz 5 років тому +1

    Mashallah SERIGNE Abdou Karim yalla naffiii yageuu té andakk wérrr🙏🙏🙏

  • @djibsondasilva454
    @djibsondasilva454 5 років тому +2

    Masha'ALLAH Iran rafét na!!

  • @Mossdef7
    @Mossdef7 5 років тому +4

    Bilahi mbacke damala yagua beug rawatina bi serigne Serigne abdou Aziz guene adouna ngua deplacer dem tivaoune diale ji tekoune khamnani sa diot bari woul yalla nala yalla bayi fi lol nga and ak wer banga teyi jhilafa gui ci barke Serigne babacar Iran nak mom nagnou ko baye ak yalla rek

  • @mamadoufall1642
    @mamadoufall1642 5 років тому +11

    Machalla kontana

  • @Aistv2014
    @Aistv2014 5 років тому +17

    Machallah Refétna

  • @abdousarr4928
    @abdousarr4928 5 років тому +1

    S abdou karim mbacke bilahi ya bakh yalnangafi yague té wér

  • @antagueye3022
    @antagueye3022 5 років тому +10

    Serigne Abdou Karim yag fii lol ak wére mbaké Iran machalah kou gnak kignane ga

  • @juniormana427
    @juniormana427 5 років тому

    Dieureudieufé sérigne touba machallah sérigne Abdou karim mbacké amine ni sa baye nga mel yalna ko sounou borom yok lérem falilou mbacké sama yakar adouno ak alakira

  • @dabambacke3994
    @dabambacke3994 5 років тому

    Machalah mbacke yalnala yallah feye

  • @jadoredieuetmohamedkhadimo2521
    @jadoredieuetmohamedkhadimo2521 5 років тому

    Iran ndao ndeyssane sa mélomane nekh na serigne touba ndax yow ak ignane nekoule si yow si kaw rek gua dieum inchallah

  • @megalebu
    @megalebu 5 років тому +1

    Merci Iran, serigne abdou Karim MO baakh. Yalla na diam yagg

  • @moussasallngom6578
    @moussasallngom6578 5 років тому +4

    Machalla nda nga bah rek mbake serigne mansour sy Malik yalla na ko Yalla fayal si barke seydina mouhamed

  • @momoanna6samb35
    @momoanna6samb35 5 років тому +3

    Dieuredjef Mbacké serigne Abdou karim. Machallah

  • @omardieye9814
    @omardieye9814 5 років тому

    Machalla yalla yalla defall diame

  • @orfandefoot1469
    @orfandefoot1469 5 років тому +18

    Daga Kay guise rek beug ko j en ai les larmes aux yeux 😍 on a pas eu la chance de voir Serigne Fallou mais on en est pas moins triste on t aime Mbacké

  • @djibikonta8546
    @djibikonta8546 5 років тому

    Machaalah Fatabarak_allah yalna diame saxxx Sénégal

  • @ndongali3540
    @ndongali3540 5 років тому

    Machallah rafét na Iran Diambar la Yalla na Yalla sakhal jaam dji di Nianal Serigne Abdou Karim Yalla nafi yague té andak wér si Barké SERIGNE Fallou Mbacke !

  • @behramithiam7315
    @behramithiam7315 5 років тому

    Thiey Cheich Abdou Karim Mbacke Moma Tale bama Tak dieureudieuf Mbacke max de j'aime pour sama Cheich Abdou Karim Mbacke Mbacke

  • @mamytasylla5489
    @mamytasylla5489 5 років тому +6

    Kouné amgua Serigne wayé cou djak woutiii Mouridoulahh🙏

  • @moussadinedinerekmowor9025
    @moussadinedinerekmowor9025 5 років тому +1

    Yalna yalla fayla yuiw serigne Abdoul karim mbacke yagfi lol mbacke

  • @annatoure1341
    @annatoure1341 5 років тому +3

    Longue vie à Iran Ndao et à Serigne Abdou Karim Mbacke

    • @fahabi4725
      @fahabi4725 5 років тому

      A toi aussi anna🙏🇸🇳

  • @bayefallouserignebabacarsy
    @bayefallouserignebabacarsy 5 років тому +9

    Machallah bilahi content na trop wayy

  • @khadimkhebe7749
    @khadimkhebe7749 5 років тому +3

    Mashallah amna solo lool bakh rek mo am solo

  • @bayefallouserignebabacarsy
    @bayefallouserignebabacarsy 5 років тому +56

    Kene serigne abdou karime Mbacke yagg fi lole té adak were si barkep seydina Mouhammad 🙏🙏🙏🙏🙏🤲🤲🤲🤲🤲

    • @kharbalabci3622
      @kharbalabci3622 5 років тому +2

      Yaw nopil yaaye saga Mourite khamé nala wayé démal rék

    • @kharbalabci3622
      @kharbalabci3622 5 років тому +2

      Yaw nopil yaaye saga Mourite yi khamé nala wayé démal rék

    • @ndiayemana314
      @ndiayemana314 5 років тому +3

      Yaw amoo lo wakh nopil 🤐🤐

    • @abdougueye5494
      @abdougueye5494 5 років тому

      ki kay defoul lolou kese lou bon rek lay wakh waye stp changél sa tourbi ga balma

  • @cheikhthiam5073
    @cheikhthiam5073 5 років тому +3

    Iran contain na dh♥️♥️

  • @alydiarra6692
    @alydiarra6692 5 років тому

    Serigne Abdoul Karim mbacke voilà un Serigne qui aide les pauvres les handicapés et autres qu'Allah le récompense

  • @alhadjindiaye2248
    @alhadjindiaye2248 5 років тому +3

    Machallah Machallah Machallah

  • @tvadamandiayekhassaidtouba8388
    @tvadamandiayekhassaidtouba8388 5 років тому +2

    Diadeiuf s touba khadimou rassoule diadieuff s touba Iran Ndaw linga deff rafeth na yalna leu yalla defale diame

  • @mariamadiallo96
    @mariamadiallo96 5 років тому +1

    Sama sangue bii baye Karim ☝🏻

  • @Antiarnaquesn
    @Antiarnaquesn 5 років тому +35

    Iran guéwalou l'islam ana gnouko beug☝️

  • @sokhnadiallo9013
    @sokhnadiallo9013 3 роки тому +1

    Dieureudieuf Serigne Touba Yalla nguén fi yag

  • @taibndiaye9489
    @taibndiaye9489 5 років тому

    Bay karim mbacke yalla nafi yague ta wer iran yalla nga goudou fann barkeb mam diarra bousso

  • @famathiam2575
    @famathiam2575 5 років тому +1

    Yalla nalla yalla faye serigne abdou karim bake

  • @kalidouwade9442
    @kalidouwade9442 5 років тому

    Machala li rafétena, yalla na diam ci yag ci sunu réw

  • @doudoudiong6131
    @doudoudiong6131 5 років тому +4

    Sérigne Abdou Karim Mbacké Yalla ngafi Yagg lol té Wër Y'a Baax way wakh sa Mbakhou way dou wagni si sa Mbaax dara lingua Sèddé si Sérigne Abdou Aziz Sy Al Amine ak Sérigne Mansour Sy Borom Daara ji Yèna bock Sèn Maam Maarame Mbacké lolou Yalla moko Dèf té dottoul dègne Iran Ndao Diarama yangui Dieuf lou bakh si Rèwmi l'I Sèddénako Mashaalla

  • @papatmbengue7767
    @papatmbengue7767 5 років тому +1

    Machallah ouztaz Iran amna solo

  • @senegalba1071
    @senegalba1071 5 років тому +22

    Machallah

  • @vieuxniangbongo2832
    @vieuxniangbongo2832 5 років тому

    Machala iran yaw guen nala beugue bilayy

  • @mohameddamembaye8451
    @mohameddamembaye8451 5 років тому +5

    Machalaaaa mbacke diadieuf irann ndao

  • @mbayethiam5776
    @mbayethiam5776 5 років тому

    Serigne Abdou karim sama Serigne Abdou Karim yague fi lol té werr. Merci Iran Ndao.

  • @modidiaw8291
    @modidiaw8291 5 років тому +17

    Mane douma mourid waye baye Karime damko beugeu ta yalla takh yalnako fi yalla yagall

    • @ElTIO_Galass
      @ElTIO_Galass 5 років тому +4

      Bayi Lené di mot bobou Adouna gnepp ay mouride la nou ndakh gnep Thia yonou yalla lanou dieum
      Mouy mouridoulahi

    • @mbddiop4671
      @mbddiop4671 5 років тому +1

      Tout le monde musulman est mouride...car cela signifie voie qui mène vers DIEU
      ..TOUTES LES CONFRÉRIES RELIGIEUSES MUSULMANES VONT VERS DIEU

  • @mamyaya1038
    @mamyaya1038 5 років тому

    Akassa Mbacke balla aïcha mashaalla amna solo

  • @babagning3697
    @babagning3697 5 років тому +4

    Machalla Serigne Iran ni rék la

  • @modousall2693
    @modousall2693 5 років тому +1

    Iran ndao yaw diam rek ngay ame barke serigne touba

  • @mammordiop3617
    @mammordiop3617 5 років тому +2

    Machallah Li nexna loll way ndaysane

  • @diengbara5923
    @diengbara5923 5 років тому +11

    Dieureudieuf baye karam🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @mothiamo2006
    @mothiamo2006 5 років тому +3

    Serigne Fallou ci Diamono dieureudieuf

  • @toukoubaaba1946
    @toukoubaaba1946 5 років тому +6

    Aka bakh s. Abdou Karim

  • @falloulaye129
    @falloulaye129 5 років тому

    Baye karime machalah ngépala beuge

  • @babouly5078
    @babouly5078 5 років тому +2

    Machallah lomg ya chekh un es fière de toi

  • @batorgueye7295
    @batorgueye7295 5 років тому

    Bay karim yalla nafi yagu loll nèlène jaime

  • @diagneomar8981
    @diagneomar8981 4 роки тому

    Machallah serigne by