Vous avez tout dit serigne Momar Diagne,c'est un homme très sombre d'esprit et ils sont nombreux comme lui sur les plateaux de télévision et les sites Internet...
Dieuredieuf SERIGNE Momar Diagne yalla nala fi Bour yalla yagual te gua ande ak wer Bidiahi Mouhamadou Rassoul lilahi SAW barkép SERIGNE Fallou ak Serigneme
Alhamdoulilah dila sant bou baakh chaîne by baré na ndieurign yaagui léeral dignou guindy yalna na borom by féyal gnoula Sénégal Oustaz ak docteur dafer yomb lol Assalamou Aleikoum
Salam frère Diagne vous parlez de la "passion d'Hallaj" de Louis Massignon éditêe en 3 tomes. Vous demontrez encore une fois que vous êtes un vrai "guestou kat". Je ne rate aucune de vos interventions. Comme quoi les "grands noms de families" religieuses ne sont pas determinants pour guider askan wi des tenèbres vers la lumière. Chukran ya Imam.❤
Vérité absolue, mon frère !!! Serigne Momar Diagne est la preuve vivante que la science islamique n'est plus l'apanage des familles dites religieuses. Longue vie de piété et santé de fer à vous et à lui. Amiiiine.
Salam siar nala serigne momar diagne je suis tjrs tes videos ma cha allah. Mais tay daccorouma. Yalla danioukoy guiss diakk diahrane bou kiraay yeup dégné rek nga diaano ak yalla.
Serigne momar diagne le gardien des valeurs. Nous vous remercions vivement de par tes enseignements, tes éclaircissements et ton refus vers une manipulation des masses .Que le bon dieu t'accorde une bénédiction et t accepte parmi ces saints
Khamuma lou oustaz Mouhammad Mbaye wakh, waayé khamnaani amna hadith bou diglé naan sawum guilèm nguir fadiou. Soonè Yonent bi SallaLLAHOU alayhi wa sallam "guisoul YALLAH", lolou yaako sania wax. En tout cas, niaari groupe nio am ci sahaabayi ci wax dioodiou: gni né guis nako (Ibn Abbas mimou yar, ak baayam Abbas) ak gni wax ni guisuko ak ay beuteum (yaay Aïcha, Ibn Mas'oud ak niénèn). Waayé nioom sèn wax djènn la boo sètè : guisuko ak beuti matière, waayé guisnako ak beuti xolam, kon guisnako. Guisou khol bobou ay wax you bari amnaci. Booko gueustuwoon dina am solo. Lathia déss nak damathi maandou ba am louma leer.
Boudé yalla diouk took si kawaw araass malaka yi weur ko ngueen di xaar nak d'où ngueen ko meussa guiss. Ndakh yalla mom mola gueuna diégué sa bop. Kep kou guéneu bopam douko guiss mouk
Grand frère manoumà déglou vidéo bi bamou diêkh Biga tamblè di wakh limou wakh si Yonente bi SHSW rék là arrêté vidéo bi May lâdji ndax video you mélnii diarnà tontou ????
C'est trop facile de présenter des excuses après avoir sorties des inepties sans fondements susceptibles d'induire les profanes en erreur. Quand on s'aventure à parler des choses religieuses on doit, au préalable, maîtriser son sujet. La question est trop élémentaire pour qu'on s'y trompe aussi facilement. Il n'existe aucun début de piste pouvant étayer les propos de mohamed mbaye. Il a tout simplement laissé son esprit divaguer dans des élucubrations.
❤❤❤❤❤❤ Masa Allah mercie beaucoup Serigne Momar Diagne amatina sollo dieureudief ❤❤❤❤❤❤❤❤
Heureusement pour nous musulmans du Sénégal ,on a un serigne momar diagne comme nos grands parents avaient les serigne touba ,elhadji malick etc.....
Masha'allah je suis fier de mon oncle Serigne Momar
1 million d’abonnés pour notre sén ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vous avez tout dit serigne Momar Diagne,c'est un homme très sombre d'esprit et ils sont nombreux comme lui sur les plateaux de télévision et les sites Internet...
Ma cha Allah dieureudieuf sama serigne yana nga fi yague té wer ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdoulilah choukrane pour ces précisions
Machalla. G pas les mots pour traduire ma joie envers votre modeste personne. Que le bon dieu vous garde.
Salam aleykum Serigne Momar Diagne yalna nala yalla sàmm té wéreulleu ci barké ya Mohamed psl jërëjëf 🇸🇳❤️❤️❤️
Machallah amna solo dieuredieuf
Machalah yalna yalla yagal takha way bi
Dieuredieuf SERIGNE Momar Diagne yalla nala fi Bour yalla yagual te gua ande ak wer Bidiahi Mouhamadou Rassoul lilahi SAW barkép SERIGNE Fallou ak Serigneme
Yonentè bi 🥰❤️
Mouhamat Mbaye amoul xam xam dee
Am fit rek
Motakh mounane oustaze la
Jërëjëf sëriñ bi.❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vérités absolu serigne bi ❤❤
Amna solo lool❤❤❤
Ñi WARA WAKH çi REEWMI buñuwakhul BU mbugeul DI WATHIÉ kenn duçi much dé KON ñi WARA WAKH nañu WAKH moogeunn dé
Alhamdoulilah dila sant bou baakh chaîne by baré na ndieurign yaagui léeral dignou guindy yalna na borom by féyal gnoula Sénégal Oustaz ak docteur dafer yomb lol Assalamou Aleikoum
Télé dof yi fén Rék lanioy déf
Ils essaient toujours de mettre leur guides au dessus du Prophète parce qu'ils sont maudit.
MashaAllah 🇸🇳🇪🇦❤❤❤❤❤
Salam frère Diagne vous parlez de la "passion d'Hallaj" de Louis Massignon éditêe en 3 tomes. Vous demontrez encore une fois que vous êtes un vrai "guestou kat". Je ne rate aucune de vos interventions. Comme quoi les "grands noms de families" religieuses ne sont pas determinants pour guider askan wi des tenèbres vers la lumière. Chukran ya Imam.❤
Et Pourtant son Grand-père est cheikh ndiouga diagne grand érudit de cheikhna cheikh sadbou
Vérité absolue, mon frère !!!
Serigne Momar Diagne est la preuve vivante que la science islamique n'est plus l'apanage des familles dites religieuses.
Longue vie de piété et santé de fer à vous et à lui.
Amiiiine.
Machallah ❤
SOUBHANA ALLAH🙏
Salam siar nala serigne momar diagne je suis tjrs tes videos ma cha allah. Mais tay daccorouma. Yalla danioukoy guiss diakk diahrane bou kiraay yeup dégné rek nga diaano ak yalla.
Choukrane ❤❤❤❤❤❤
Machallah papa
Sénégal daniouy diawale beurriwahh ak am hamm hamm
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Serigne momar diagne le gardien des valeurs. Nous vous remercions vivement de par tes enseignements, tes éclaircissements et ton refus vers une manipulation des masses .Que le bon dieu t'accorde une bénédiction et t accepte parmi ces saints
👍👍👍👍🇸🇳
Kou ci moytou w9ul ahmed cissé dingua doug ci halkandé
ASTAGHFIROULLAH
baye mbaye kay da mana soce mane de bimako dege dama tit
Bouko wakhone béne kilifeu dinné kone sénégal take wayé yoneneti bi amoul koukofi représenter s
😢
seeet kii respecte woul yonente bi waaye respecte woul diouliit yii
❤❤❤
Oustaz you bëss yi mothx doumasi déglou kéne topou séne bakane rek moléne nior ak beug buzz
Ki dafa diangoule fene rek laye mohamite mbaye amoule xame xame
Ajarama
Grand frère ma nguilay massawou ndakh bodé wakh aki nafekh ay thionola.
🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Khamuma lou oustaz Mouhammad Mbaye wakh, waayé khamnaani amna hadith bou diglé naan sawum guilèm nguir fadiou.
Soonè Yonent bi SallaLLAHOU alayhi wa sallam "guisoul YALLAH", lolou yaako sania wax. En tout cas, niaari groupe nio am ci sahaabayi ci wax dioodiou: gni né guis nako (Ibn Abbas mimou yar, ak baayam Abbas) ak gni wax ni guisuko ak ay beuteum (yaay Aïcha, Ibn Mas'oud ak niénèn). Waayé nioom sèn wax djènn la boo sètè : guisuko ak beuti matière, waayé guisnako ak beuti xolam, kon guisnako. Guisou khol bobou ay wax you bari amnaci. Booko gueustuwoon dina am solo.
Lathia déss nak damathi maandou ba am louma leer.
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Télé keur doff yi kay warnañou djokk ci ñom
Djereudjeuf saa baay!
Boudé yalla diouk took si kawaw araass malaka yi weur ko ngueen di xaar nak d'où ngueen ko meussa guiss. Ndakh yalla mom mola gueuna diégué sa bop. Kep kou guéneu bopam douko guiss mouk
Islam Sénégal dall...
Ouztaz buzz rek moko dougal si lolou touss khamouko
😂😂😂
Grand frère manoumà déglou vidéo bi bamou diêkh
Biga tamblè di wakh limou wakh si Yonente bi SHSW rék là arrêté vidéo bi
May lâdji ndax video you mélnii diarnà tontou ????
Mouhamed mbaye se trompe certainement mais personnellement je pense qu’il a été induit en erreur par une histoire mal apprise il n’a qu’à rectifier
C'est trop facile de présenter des excuses après avoir sorties des inepties sans fondements susceptibles d'induire les profanes en erreur.
Quand on s'aventure à parler des choses religieuses on doit, au préalable, maîtriser son sujet.
La question est trop élémentaire pour qu'on s'y trompe aussi facilement.
Il n'existe aucun début de piste pouvant étayer les propos de mohamed mbaye.
Il a tout simplement laissé son esprit divaguer dans des élucubrations.
Soi disant oustaz bohamne serignou tariyahyi ak sétekatyi lay tendre micro té yalla wah dafa haram
Je mal pour mon pay laissons-le prophète tranquillement vrement Oustaz Mbaye amoul kham kham
❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤