Serigne Babacar Mansour SY a inscrit son empreinte dans l'histoire de la tarikha et tivaouane. Longue vie pleine de santé, sérénité, sagesse,abondance et réussite dans la miséricorde divine !
Alhamdoulilah seydi Aboubacar Sy Mansour yalna fi yague loll té weirr soutoureu xéweul ak barke AK ay rakam AK jabootou seydi hadji Malick yeup inchallah 🙏
Serigne Babacar Mansour SY a inscrit son empreinte dans l'histoire de la tarikha et tivaouane. Longue vie pleine de santé, sérénité, sagesse,abondance et réussite dans la miséricorde divine !
MachaAllah yalla na brome bi défal wérr ak werlé tawfékh ak taysir si barké yonénetiby sws bamou Di si djouly sy Demba
Machala Serigne Mbay Sy Mansour yalnafi yaggue té wérr mom ak khalifa dîné yeup. Alhamdoulila rabbil alamina.
Alhamdoulilah seydi Aboubacar Sy Mansour yalna fi yague loll té weirr soutoureu xéweul ak barke AK ay rakam AK jabootou seydi hadji Malick yeup inchallah 🙏
Serigne babacar sy mansour amna louken amoul
Walahi son nom sera gravé à jamais dans l’histoire de la Tarikha Tidjane et de Tivaouane ❤️
Sy Malick thieureum la yalna ko mourlou yalna fi yague lol té wer barké sangou sangue yi SAWS
Serigne Babacar sy Mansour sunu khalifa bi yallah nakofi yallah yagal te andk weur❤❤❤❤❤❤❤
Jumah Ji kemtane la, Mashallah ❤
Dieureudieuf sy
Alhamdoulilah ❤❤❤❤❤❤❤
Machala sy malick
🥰
❤❤❤❤❤❤❤❤