Merci outaz. Un homme véridique d'une dimension inestimable. Le problème ce sont nos politiciens voleurs qui sont à l'origine de ce problème et même les parents sont victimes de ces politiciens bidons. Barkhala fika
Ki moy khalifab diiné, daf lay wax foulé diokhleu ay solution beu paré dioubentil leu tchi yoonu yallah! jazakallah khayrann ya oustaz, sa doundou amna solo fatabarakallah!
Merciii Oustaz mane dé vraiment yalna ga goude fane mane yow rék laye sétane dila déglou rék mounena né lou barri si yow lakoy diangué que Dieu vs protége
Masha’Allah ya Oustaz nila kilifa diné di mel au moins gnou sentir né problème deuk bi yitel nal wayé tok say milliard andak gourou say say nan sama mame néna kou wakh guaniko mougnal té do fadj sokhlam
Déet waay .. esk meuss nga déegu bén Yon kiLifeu diné bu took di wakh ci aay mamam, mandou baxna dh niom xamaLougn Lén dara , kon menouniou xam ci Lign nék Kou Le wakh ni amouL kou ci wakhtann ak kiLifeu rewmi ci souf Serigne ci YalLah rek mo Lén gnor , défougn aduna bi mouy dara iL faut que niou xam LoLou tmt
Amine 🤝💗😍💟💞💌♥️🤲🤲🤲🤲🤲 machallah ya cheikh Omar Sall Qu'Allah vous récompense vraiment tu es très important pour la société longue vie toi et ta famille Amine
Mashallah ya oustaz barak'ALLAHOU FIK YALLAH na YALLAH yok kham kham bi mashallah soukrane kénn dou yow yagui dimbali société bi YALLAH nala YALLAH fay yiw soukrane séydi sall dimo mo sawata gathié
Al khalife général des musulmans. Point final. Hafizoullah Oumar Sall ,qu'Allah azzawajal te bénisse abondamment, bénisse ta famille. La pression familiale est la première cause,bien avant le manque de vision politique de l'emploi du gouvernement.
Rien que la veritė tres cher Oustaz. Je vis en Allemangne depuis 24 ans. Il y a une crise ecomonique à cause du covid 19. Il n ya assez de travail dans tous les domaine. Je connais beaucoup qui ont pris des indemites de licenciement pour rentrer au Pays. L avenir est en Afrique.
Merci beaucoup oustas oumar sall
Machallah amna solo djazakallahou khayran
Machallah yalla na yalla fayla
ماشاء الله بارك الله فيك يا أستاذ
Machallah ya oustaz
Machala jerejefe 🙏
AK lerr bilahi
Merci outaz. Un homme véridique d'une dimension inestimable. Le problème ce sont nos politiciens voleurs qui sont à l'origine de ce problème et même les parents sont victimes de ces politiciens bidons. Barkhala fika
Djasakoumoul'allahou khayrane
Ki moy khalifab diiné, daf lay wax foulé diokhleu ay solution beu paré dioubentil leu tchi yoonu yallah!
jazakallah khayrann ya oustaz, sa doundou amna solo fatabarakallah!
Moy sa kilifa dine yaw
Merciii Oustaz mane dé vraiment yalna ga goude fane mane yow rék laye sétane dila déglou rék mounena né lou barri si yow lakoy diangué que Dieu vs protége
Machallah long vie a toi
Aminé Machaallah
Merci ma soeur
merci oustaz pour la sensibilisation
Bien dit oustaz sur tous les plans
Masha'Allah Oustaz Oumar sall.. sa dundu amna solo ak sa discour aussi
Billahi oustaz li nga wah rek mo am man fo la diar
Amna solo oustaz
Merci oustaz Omar sall limoye deuge
Waye Di wakhe khalle yi baye gourgi
Salam oustaz alhamdoulila dieu merci que alla nous donne longue vie et beaucoup de santé pure vérité merci merci merci encore une fois
Merci ya oustaz pire vérité nga wakh
Masha’Allah ya Oustaz nila kilifa diné di mel au moins gnou sentir né problème deuk bi yitel nal wayé tok say milliard andak gourou say say nan sama mame néna kou wakh guaniko mougnal té do fadj sokhlam
Déet waay .. esk meuss nga déegu bén Yon kiLifeu diné bu took di wakh ci aay mamam, mandou baxna dh niom xamaLougn Lén dara , kon menouniou xam ci Lign nék
Kou Le wakh ni amouL kou ci wakhtann ak kiLifeu rewmi ci souf
Serigne ci YalLah rek mo Lén gnor , défougn aduna bi mouy dara iL faut que niou xam LoLou tmt
@@npm7576 Dou serigne you dessak nioune heure bi niom kaay na bakané rek Aÿ autos youy jaarr 450 millions.
Machalla oustaz
Amine 🤝💗😍💟💞💌♥️🤲🤲🤲🤲🤲 machallah ya cheikh Omar Sall Qu'Allah vous récompense vraiment tu es très important pour la société longue vie toi et ta famille Amine
Merci beaucoup
👍
Walayi ouztaz macha allah longue vie a vous
Oustaz vraiment Dit longue vie a vous
langue vie mon ousitas
Dieuredieuf oustaz yalnala yallah same ame nga solo lole ci réwmi bou amone niou bari niou méle ni yowe kone diné bi avencé
Ndékété Oustaz xam na auto bou tudd Rolls-Royce machallah
Machalah merci beaucoup
Merci beaucoup papa Omar Sall Dawnayram Machalla
Mashallah ya oustaz barak'ALLAHOU FIK YALLAH na YALLAH yok kham kham bi mashallah soukrane kénn dou yow yagui dimbali société bi YALLAH nala YALLAH fay yiw soukrane séydi sall dimo mo sawata gathié
لا إله إلا الله وحده لا شريك له له الملك وله الحمد وهو على كل شيء قدير🌹🌹🌹🌹
Macha Allah ustaz merci vraiment pour vos propos véridique
Thank you may Allah guide you
Machalla mbokk diazakallahou khayerane chékhe bi ♥️😍
Cheikh Mohamed
Machala Al imame, dafamélné
Danga Diar thii galgui Ndaysan
Yalla nala Yalla faye yiw amna Sólo Ni lagnou wara acourager Ndaw gnii
Cette analyse est plus que pertinente , kaddug lislam
Al khalife général des musulmans.
Point final.
Hafizoullah Oumar Sall ,qu'Allah azzawajal te bénisse abondamment, bénisse ta famille.
La pression familiale est la première cause,bien avant le manque de vision politique de l'emploi du gouvernement.
Mala beugue yalla nala yalla faye
Well said ustaz much love to you I'm living in Turkey from the Gambia
Yalna Sénégal 1000 personne you melni yaw machallah long vie ya oustaz
walahi oustaz yalnanou yallah maye dégg ak topp
Bilay walay Oustaz.
Waax ngue lép.
Dieuredieuf.
machaAllah Oustaz yalna Yalla degeureull leu
Li nga wakh amna solo machallah
ay way oustaz li lay dieurigne machallah
#Bisimillah# Oustaz yalla na la ya Rabi sutoural @ASALAMALEOKUM@ @Asalamaleokum@
Oustaz dieureudieuf Li nga wakh Lou wér Leu .. naniou gueuneu gorgorLou rek sougn borom beuri na yeurmandé dina bakh insha'alLah
Mashala oustaz
Vous avez tout dit
Machalah ouztaz 🙏
شكرا يا أستاذ
Yalnala Yalla fay yiw Oustaz
Machallah sama oustaz bi contana dh bilahi. Diam rék
Demacontan oustaz oumar sall
Mashallah Amna solo
Machallah amna solo
Bilahi oustaz méme sa rak boula dieuké téki gnu ték ko sa kaw yalla mo yor weurseukk
ماشاء الله تبارك الله حفظه الله ورعاه
Nehoul ba nehoul ouztaz oumar sall deug reek ngay waakh
Machalla oustaz Omar yalla na yalla goudal sa fane si barké seydina Mohamed
Macha Allah Yalla na Yalla barkel ta samou leu
Merci
Machallah ya oustaz yallah nala yallah are té faye la 🙏🤲❤
ماشاء الله جميل جداً بارك الله فيكم وجزاكم الله خيرا يا شيخ
Ousstass wahale wayy
Lou weur machalah
ما شاء الله حبيبي ❤❤❤❤❤❤❤
Merci ouztas a ces jolis propos
MERCI Ouztaz. Tu toujours en phase avec la vérité..
Vérité absolue 👍🏾👍🏾👍🏾
Merci beaucoup oustaz pour les encouragements
Machalla Aka ller 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭❤😭❤❤
Machalha amna solo barack allahou fikoum 👏👏
Merci Oustaz
Machalla y’a oustaz
Machallah oustaz
Mashallah sama oustaz si quelqu'un a ses contacts qu'il m'aide à le rencontrer
Les gens on leur diplôme sans même avoir un stage renumerer
Yalnala yala fay woutéga ak kilifa diné yiga khamni sen thiép bou niné rek lidiantiwouniou talibé yi ndax etat moy ninal sen thiép
Ake adiiya yinouy dioxe serigne yi bounu ko dedjè wone mane nanou si oubi boutique
Deug.
Niit yé nara yéwou.
Kone sa baye dou kilifa diné
حقا وصدقا
حفظك الله ورعاك
Franchement tout dit
Amna solo
Tu vas parfaitement raison merci beaucoup 👏👏🙏🙏🙏🙏🙏🙏 que dieu te donn la long vie
Machalla 💓💓
Bilahi linga wakhe fi lep degela
Mach'Allah Oustaz
Merci mon père
Wolah oustaz oumar sall machalla
Rien que la veritė tres cher Oustaz. Je vis en Allemangne depuis 24 ans. Il y a une crise ecomonique à cause du covid 19. Il n ya assez de travail dans tous les domaine. Je connais beaucoup qui ont pris des indemites de licenciement pour rentrer au Pays. L avenir est en Afrique.
Machallah Oustaz Oumar Sall
Am na solo torop
♥️♥️SENEGAL ♥️♥️REK
Dieuredieuf Oustaz. Les politiciens sont encouragés par les chefs religieux
Manchallah deugue dou rombe nopp
Machaalah que dieu te protéger Allahou ameen seydi sall
Oustace Oumar salle toujours plus véridiques que jamais que te garde pour l'éternité
Bilay doylou ak ndioub rek mo am solo yalla nanou yalla samm
Machalah deug rék nga wakh
Thank you may Allah guide you ❤️❤️❤️👍
😍😍😍😍
ما شاء الله یااستاذ
Wallahi oustas 🙏