Zero vulgaire tout est propre gneup meune nagne ko setane lici gueneu neilh moy les secrets se decouvrent au fur et a mesure dougnou khaar baci fin bi lep di feigne. Chapeau à vous felicitations et bonne continuation !!!
Très belle série ! Très belle saison ! Très belle fin ! Secrets de famille, une série pas comme les autres car elle relate les réalités sénégalaises de tous les jours ! Chacun a eu ce qu'il ou elle méritait : Yama a mérité d'être heureuse et Kiné va payer pour ses erreurs ! Ceux qui étaient dans le mauvais chemin ont retrouvé le bon chemin ! Ya que le bien qui paie, le papa d'Alima en est l'exemple mais aussi Prince ! Donc sèmons le bien pour récolter le bien car c'est qui est essentiel ! Bravo à toute l'équipe de Yesdakar et à tous les acteurs et actrices, vous êtes les meilleurs ! Hâte pour la saison 3 Insha Allah ! Secrets de famille❤❤👌💕
Elhadji omar néna dama con 😂😂mandikate bi néna diabame amouma sa numéro. Ms madame samb chapeau 1er dame dou ay foo ani premiere dame yi aimé léne way🌹❤💖👍👍
La sœur de Prince elle joue très bien j’espère que dans la saison à venir elle aura un plus grand rôle. Mme Samb elle est très belle au naturel Macha’Allah.
*Lundi 5 Octobre 2020* Secrets De Famille L'un Des Meilleurs Séries Sénégal Yalla Nafi Yalla Déf Diame Ak Khéweul Ak Soutoureu Si Barké Seydina Mouhamad Amine 🤲❤
Au moin bi mom fin bi on est pas déçu afin pas comme l'autre mais warone guene wane yayou junior bimou khamai ni yama dou tegeu aussi sa réaction merci gawlene saison 3 gnune ASC SETANE LEP danuy wet
Passé une bonne magal touba que dieu le puissant vous protège thiy barquè serigne touba ana bayfal thiy doundou lène 100ans sans ordonnance chapeaux à vous 🙏🙏🙏🙏👍
Une vraie leçon de vie certe k haléla j'ai k 19ans mais diang nasi Lou barii alors mission accomplie car le message est bien passé merci à vous vraiment il y a k la réalité merci vraiment encore 😍🥰❤️
Koumou nekh ak koumou nekhoul Junior takeuna Yama😂😂😂Wa YesDakar mérré wone nalen nak mais nekhatina nak machaAllah chapeau à toute l'équipe🙏🙏🙏 niogui khar saison 3 bi inchaAllah🙏🙏🙏
Voilà une série qui éveille Avec ses innombrables conseils Quelle belle série ! Elle reflète le quotidien de notre vie Avec des acteurs professionnels Surtout les demoiselles J'adore les thèmes abordés Walay c'est ma série préférée Vous allez nous manquer sincèrement La saison 3 est attendue impatiemment Vous avez assuré mes chéris Alors c'est normal qu'on vous remercie Gaye Aïcha La Babacariste 🥰
Mane relation xaritou maty bi ki done diaay ndokh ak grand bi yollè bandit bi raye pa bi fane laye moudjè rèk laye khaar bientot inchalla yes dakar merci badiane mome machalla rèk
Felicitations a Yesdakar! Cette serie est un chef-d oeuvre et un plancher de salut! Qualite image, son, jeu d acteur.......en tout cas vous etes sur la bonne voie. Hello from Atlanta!!!
Adouna lépp lo gis nay raféte elek dou agne dou rére wayé lou mata Sor la👆yalla nagnou yalla soutoural fi si adouna ak alakhira yalla bou kéneu diakhlé🙏
De très beaux images de belles mises en scènes un beau histoire 💓✨ma Shaa Allah que dire de plus c'est juste top laf Tiate à bientôt pour la 3 ème saison
4 роки тому+78
Enfin félicitations 🙏 La première fois que j'ai commenté sur cette série Vraiment comme son nom l'indique Sécret de famille 🌹 Répond son nom C du lourd Équipe technique parfait Scénario t'es bien abordé En résumé 100 % Réussite 🙏 Bonne Continuation Yes Dakar 🙏
Vraimente ce film joue d la réalité o Sengal félicitations bravo secret d famille père malick e sir et c povre yama Kine e brava la femme d Elhadji Omar est un traitre
Ayoooh li la namone mane ❤️😍🔥 série bi daffa nékh trop té ameuna chance 👏👏👏cette série nous donne des leçons très important bilaye thiey adouna déffe lou bone amoul gnarigne kholale rk ki doffelo wone ouseynou rék fimou moudié 👀ak kiné rék lou bone limou déffe léppe elle vas le regretter 👁️té réthiou day féque dieffe wésse ......nakaté yo mome ak yama ay jumelles lagnou ak limou déffe yama léppe mo takh nitte boko khamoul rék boul ko déffe yéne yi😥
Toute mbekté merite une recompence merci Badiane vous avez été a la hauteur mbakh rekk mo am solo. Merci à toute l'équipe vous avez assuré....on vous attend si bénen saison mou bagna yag nakk dah secret de famille moy sama wetal❤❤❤
Félicitations à toutes l'équipe de yesdakar vraiment yénafi meune ndax rétane nagne fi dieulé nagne fi Ay leçon Chapeau à mon acteur préféré (thié) ya meune nieup
Maty et son papa vous me faisait pleurer tout le temps je n pouvais pas supporté une telle souffrance. Omar Yaw beugo lou bakh nga ame palais di deuk si baraak ba inondation diké kéne wonoula boutou palais
Bou lèn faaté Abonné !!! Saison 3 bi Ak Yeyen surprise you bess Takk!!!
jespere ke dou yague
Ms boumu yague🙆
👍👍👍😂😂😂😂
@@omarciss9492 iow Do Nitou Dara❌❌❌❌❌❌❌❌❌👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎👎
Félicitations à toute l'équipe de Secrets de Famille
Gniye déme magal yalnaniou dem si diam gnibissi si diam bravo à toute l'équipe de secret de famille ♥️
Amine 🙏🙏🙏
amine fall
Amine y’a rabi
Amine yarabi
Mechi
❤Kou yakamti saison 3 bi beuseul j'aime 👍👍niou fèkkè ko ak diam barkepp magal gui🥰🥰je vous aime YESDAKAR👈☝️
Amine
Amin way
@@dickegeuye7784 🙏🙏🙏
@@sinymbaye7612 🙏🙏🙏
Secret de famille est la meilleure during serie😊☺😊☺
Kou nieuwat fii pour fatali kou sii saison 3 bi 😂😂😂😂
Man
Mane😂😂😂😂
Moi
Bizarrement je me suis pas retrouvé. Celle qui est a la police kane laci
Mane😂
Man
Touba mongui nékh ni ta dara khéwa goul s touba mo barri Dolé yonou diamm❤❤❤💍❤
Jaime
Mourides nions mel nonous sen leppa nekh
@@dieynabaniang6456 👍👍👍👍
Zero vulgaire tout est propre gneup meune nagne ko setane lici gueneu neilh moy les secrets se decouvrent au fur et a mesure dougnou khaar baci fin bi lep di feigne. Chapeau à vous felicitations et bonne continuation !!!
En tout cas mashalah nekhna amna sens mais bou lene niou kharlo lou yagu pour saison 3 bi 🎉 qui est d’accord 👍
Machaala amena solo lol té nekh na . Bonne continuation sous la protection divine inchaalou thia kaw thia kaname.
Mesouma ma am j'aime thi secret de famille tay khana fin bi dina am
Ma dimba lila🤣
Merci 🙈
J'aime 😄😄
😂😂
Merci bcp bravo pour le travail ❤❤❤
Sopéy Serigne Touba kaylén mayma j'aime ci 👍
Cv
CVCV
Aminé waye
Serigne Mountakha Khalifa Général Des Mourid yalla nafi yague té And AK Wér
Amine
Anmin
Amiin
Amine
Amine
Série pleine de leçon, j'ai failli pleurer tt au long de cet ultime épisode. Félicitations la famille YES DAKAR, tous les spectateurs y compris.
Très belle série !
Très belle saison !
Très belle fin !
Secrets de famille, une série pas comme les autres car elle relate les réalités sénégalaises de tous les jours ! Chacun a eu ce qu'il ou elle méritait : Yama a mérité d'être heureuse et Kiné va payer pour ses erreurs ! Ceux qui étaient dans le mauvais chemin ont retrouvé le bon chemin ! Ya que le bien qui paie, le papa d'Alima en est l'exemple mais aussi Prince ! Donc sèmons le bien pour récolter le bien car c'est qui est essentiel ! Bravo à toute l'équipe de Yesdakar et à tous les acteurs et actrices, vous êtes les meilleurs ! Hâte pour la saison 3 Insha Allah !
Secrets de famille❤❤👌💕
Jadore ton commentaire tu as bien resumé le contenu du film
@@abdoulayedia8535 merci bcp
Très belle série ❤
Bonjour
Sava namenala nacasoubasi Nice
Oohh la séquence du mariage jador yalnanou yalla maay biiss bou rafet amin
Amiiiiine
Amine
@@gayeaichalababacariste1217 amine way
Amine
Amine way
Yalla na gneup magalii sii diam ak salam si barké serigne Touba Mbackè
😍❤️❤️❤️Bamba la joie 🤩
Elhadji omar néna dama con 😂😂mandikate bi néna diabame amouma sa numéro. Ms madame samb chapeau 1er dame dou ay foo ani premiere dame yi aimé léne way🌹❤💖👍👍
💖💖💖
Sama toma
.
Xxxxx
^
Vives émotions , beaucoup de suspens et surtout beaucoup de leçons de Vie de l'épisode 1 à la fin.
Bravo Yesdakar...
💖💖💖
Yakam tiwon na série bi sama série préférée 💔💔💞💞mes nakk Touba migui nekh DH bilay machallah ken d'où s Touba yallna niou KO yalla fayall 🙏🙏🙏🤲🤲🤲🤲
Amine ya rabi
💞💞💞🤩🤩
Sama khél mi yeup mongi fofou déwén inchallah dina séti touba deukou borom touba
La sœur de Prince elle joue très bien j’espère que dans la saison à venir elle aura un plus grand rôle. Mme Samb elle est très belle au naturel Macha’Allah.
Yaye bou bahk la am Prince waronne xol bénén ligey
bilahi elle joue bien son rôle
Mme Samb et yama les plus belles
Nianalén sama rak pape mo gueneu adouna vos prière svp👐
nako yala khare aldiana firdawsi si barke seurigne fallou mbacke
Yalla nako sunu borome diegual .teru ko ta teral ko si barké seydina mouhamad( psl) ak mbolem djulit you nek barsakh
Amiine
Yalnako yalla kharé aldiana firdawsi
Yalla Nako Yalla Kharé Aldiana
*Lundi 5 Octobre 2020* Secrets De Famille L'un Des Meilleurs Séries Sénégal Yalla Nafi Yalla Déf Diame Ak Khéweul Ak Soutoureu Si Barké Seydina Mouhamad Amine 🤲❤
Awo ndeyou dieukeur waay koussi d'accord beusseul j aime
Awo boubakh lanou wakh
Xana Awo nga
dafa lerr
*Yalna sougnou borom deffal gnou diam Magali ak diam gneuw thi diam barkép Mbecté mi* 🙏🏾❤
Amine
Euy bou employés yeup meilone ni Seynabou mi😂😂😂😂🤦🏽♀️🤦🏽♀️🤦🏽♀️ Kiné dotoko defeuti 😂😂😂🤦🏽♀️🤦🏽♀️
Walahie darra tahe gua wahe ko je t adore beaucoup😋😂🤣🤣🤣
Dafa yabaté rék mélni kou yor say mbam di youkhou waté rék niaw😂😂😂
Mercie
Ki regarde avec son téléphone portable
Moiaussi
moi
Moi
🙋🏽♂
Me
Ndeyssane chapooo a vs bilay. Badiane tmt kéneuh dou mom si série bi . une vrai badiane😍😘😘😘félicitation
Macha Allah Kheiw Bi Nexna Amna Sagnesei Ak Classe Yallah Boumou Oumpou Keineuh Si Barkei Mouhamad PSL🙏
Au moin bi mom fin bi on est pas déçu afin pas comme l'autre mais warone guene wane yayou junior bimou khamai ni yama dou tegeu aussi sa réaction merci gawlene saison 3 gnune ASC SETANE LEP danuy wet
Toma wakha tiko daniouy wet trop
Mai di nguama ray way.....setane lep....hahaha
Wow
Lolou amoul chance
Teug ak guér ak guéweul ay sôpleu
Ñépp si mame Adama ak Awa lañ bayékô
Wa ani el capo
Une série avec beaucoup de succès et de sens . Très constructive avec des leçons à en tirer. ..Bravo bravo à tous ces acteurs. .vraiment.
Oh il m'a fait pleurer ouseynou,c'est dur un malheur provoqué par un être humain ,ça fait mal yala naniou yala same té arniou barké yonent bi psl
Amine
Amine yarabi dafa ammm niou bonne deh wayé Lou wayy deff bopamm yalla na niou yalla moussal si yeen deff deff yi
Lou aimé sma commentaires yalla nala yalla may khéweul ak tawfeh si bissou magual gui si barké borom touba
Bijoux est tellement belle série bi mom rien à critiquer j'espère comme moi que vous avez tiré une bonne leçon 💖💖💖💖💖💖 mon plus long commentaire 🤣🤣🤣🤣
Ken dou mouyen Magalou diam ak salam si barke cheikhoul khadim💪🙏🧡
Njiy magal ci yalla nalén yalla tekk ci yonou diamm
Ousseynou franchement tu as remporté meilleur acteur tu as assuré cet rôle comme pas possible
1
Merci lep yènla
J'adore, j'adore, j'adore ! Une des meilleurs séries de l'année. Yakam ti naniou saison 3 bi. Chapeau bas à vous
Team madame samb pouse bleu🖒
Khana pousse 👍awo yi la😀😀😀
Secrets de famille fait partir des meilleurs séries de Sénégal
Wa khana senegal serie yèp nioy meilleurs
Machalla namone lalie amna solo
Weuzista Pouye billahi wakhatiko
@@ndieumbediop322 dama khamni serie bou niou commenters nè meilleurs serie
Du Sénégal
Chapeau à ousseynou il à vraiment assuré son rôle insi que toute l'équipe félicitations 👏👏👏
No Ousseynou merite bcp de felicitation et des encouragements il a bien assuré son rôle
⁷8⁸ùýý
🙏🙏🙏🙏
Bly😍
@@abdoulsow395m,pp,,m,pp,,,,p,m,,p,,pp,p,pp,,ppp
Passé une bonne magal touba que dieu le puissant vous protège thiy barquè serigne touba ana bayfal thiy doundou lène 100ans sans ordonnance chapeaux à vous 🙏🙏🙏🙏👍
Merci mame saliou protége
Une vraie leçon de vie certe k haléla j'ai k 19ans mais diang nasi Lou barii alors mission accomplie car le message est bien passé merci à vous vraiment il y a k la réalité merci vraiment encore 😍🥰❤️
Long mettrage le plus long de toute lhistoire des series senegalais
Bonne remarque
Fo fatei un café avec
un café avéc fooko fatté
@@abougueye7850 aka guouddoone
2h de temps mo takh mangi soga am temps bi sétane ko nice
Koumou nekh ak koumou nekhoul Junior takeuna Yama😂😂😂Wa YesDakar mérré wone nalen nak mais nekhatina nak machaAllah chapeau à toute l'équipe🙏🙏🙏 niogui khar saison 3 bi inchaAllah🙏🙏🙏
Boulen faténi chaque saison am histoire Bou bess
@@fatougueye4164 yakarouma saison 3 dina nekk une nouvelle histoire🙄🙄
@@adjidiop3905 saison bi bimou commencer niit gni di Kass lolou laniou wakh khawma nak legui
@@fatougueye4164 doyna war dh parceque saison 2 bi nekhna sou amé suite tamit dina geune nekh naniou khol rek affaire à suivre
yoksi bii:avéc impatiance
J’aime beaucoup badienne 🤣 elle t’aide mais en te crachant ses vérités
Yeah
Voilà une série qui éveille
Avec ses innombrables conseils
Quelle belle série !
Elle reflète le quotidien de notre vie
Avec des acteurs professionnels
Surtout les demoiselles
J'adore les thèmes abordés
Walay c'est ma série préférée
Vous allez nous manquer sincèrement
La saison 3 est attendue impatiemment
Vous avez assuré mes chéris
Alors c'est normal qu'on vous remercie
Gaye Aïcha La Babacariste 🥰
Belle plume😍💖
P
Merci 💖💖💖
Mane relation xaritou maty bi ki done diaay ndokh ak grand bi yollè bandit bi raye pa bi fane laye moudjè rèk laye khaar bientot inchalla yes dakar merci badiane mome machalla rèk
J’aime beaucoup la maman de yama elle est douce calme et toujours de bonnes conseils 🥰
Cvb
Cv 🎈♥️♥️
Sa sérénité est extraordinaire 😍
c'est pas ca mamam mes adoptive
Ousmane Ba je sais merci 🙏🙏
Felicitations a Yesdakar! Cette serie est un chef-d oeuvre et un plancher de salut! Qualite image, son, jeu d acteur.......en tout cas vous etes sur la bonne voie. Hello from Atlanta!!!
Je tenais à féliciter toute l’équipe de Yes Dakar❤️🙏🏽 et les acteurs aussi ma sha Allah s’était trop beau❤️🥰
Ndayssane Maty doundou na lou meti yayam guéne adouna mou découvrir mamam fek il est trop tard c vraiment triste mais amna sens aussi
Pèlou Amadou sow bi mom kagn lay damou 🤧🤧
Mais khalei bi nimouy wakhé Eladj Omar nekhna deh🥰🥰❤️
Le sèrie du sènègal ki EST d'accord avec moi💪💪💪
Moi
Adouna lépp lo gis nay raféte elek dou agne dou rére wayé lou mata Sor la👆yalla nagnou yalla soutoural fi si adouna ak alakhira yalla bou kéneu diakhlé🙏
Amine
Amine yarabi
Amine ya rabii
amine Ya rabi yalla nala.yalla Same samenou
Amine wa🙏
Badiène Gokh c’est trop un amour waay😍🥺❤️
Bilahi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@@gayeaichalababacariste1217 😕
Sama fans yi si secret de famille. Mme samb. prince...ak Badiéne je vous adore
ouh nékhna trop meilleure de tous autres séris qui est d'accord
👇
C vraix
Nekh na lol mais bène parti rek moma thi geuneu nekh ba tour sama rongogne😭 muy wakh tanu prince ak soeur rame bi cétè touchan😍
Finally 🙄
Aujourdhui c le 4 mais merci a toutes l'equipe de secret de famille 😍et felicitation a vous 😍😍♥️
C 3 kay ishh 😂
Yawtamit dhieureudhieff sa xol rafétna trop
@@kadiasy970 🤣🤣
@@ametsall7470 merci beaucoup c gentil 🌹
❤❤❤
J'ai beaucoup appris sur la saison 2, et je trouve domage qu'il existe des gens comme kiné dans la vraie vie.
Adouna diourom gnar bax rk ame solo
Bouma menonn fadj kou dof Dina fadj nieup niou annoul ak s'en xel da meti trop 😭
Ndeysan yene ak khol bou rafet mo eupeu leup dole te amga yene bi mashallah
Mme Samb yaw lay weur machallah en plus d’être très très belle tu es correcte polie sage et pudique inbox me bok say sagnsé baxna
De très beaux images de belles mises en scènes un beau histoire 💓✨ma Shaa Allah que dire de plus c'est juste top laf Tiate à bientôt pour la 3 ème saison
Enfin félicitations 🙏 La première fois que j'ai commenté sur cette série
Vraiment comme son nom l'indique Sécret de famille 🌹
Répond son nom
C du lourd
Équipe technique parfait
Scénario t'es bien abordé
En résumé
100 % Réussite 🙏
Bonne Continuation Yes Dakar 🙏
Thierno Amadou Sow la namoun fouki nit di gass fouki nit di soul😂😂 ding ma wétal nak 😂
😂😂
Mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr
Bilay
🤣😂🤣😂
😂😂😂😂
Meilleure série de 2020. Ca mérite un prix spécial franchement. Na 3ème saison bi gaw gneuw. Laf tiat so yen. Li lasenegal sohla. Louy yeetee
Cette serie fait vraiment parti des meilleurs serie, je l'adore
Kep koy dem magal Yallah na la Yallah tek ci yonou diam ❤️🙏🏻
Amine
Amine
Dama xar ba sone🌈✨
Bon magal a tous🇸🇳🤤❤️
Alhamdoulillahi ❤️☺️ épisode bi guenneu na heuu qui est heureux comme moi😉
Mane dama merr ☹️
Meusuma am j'aime saison 1 ak saison 2 yeup diaplen si bokk pur long métrage bi
Lebalnala
@@antaba3363 🤣🤣🤣🤣🤣
Bravo à toute l'équipe. La seule et unique leçon a tiré sur cette saison 2: "Que dans cette vie on ne récolte que ce qu'on a semé. "
Secret de famille a un grand sens Macha allah😘
Vraimente ce film joue d la réalité o Sengal félicitations bravo secret d famille père malick e sir et c povre yama Kine e brava la femme d Elhadji Omar est un traitre
Bly
Djeul ngene sene temps tamit! Diabanté nafi 2020 fois
Kone amna si morom 😂 touti ma tdd pour signaler wa production bi.chak seconde ma dougou youtube
Billahi mane mome énervé 😠 wone nasi sakh😂
Bilay kone makk yaw gno yamm demb damay titt si nelaw sakh di dougou di khol mais touss😂😂
@@coumbadiop7176 aaaaaqqaààaa
❤❤❤❤Série bi dioy nassi comme chui émue ossi
Dama dioy dall 😭😢
Mahalah yalla naléne yalla maye wérr ak goudou fann lingéne déff série bénela si Sénégal yalla na guéne KO motali si diam
😂 obligé pour pouvoir comprendre saison 3😂
Sama Série préféré 💪bon Magal @ tout🤲🏻
Badiène gohh gui Dale meune Na sagn sé. Macha Allah. Tekssi yiww
Ndeyesane awo Bou Bakh ameu na solo gnoune awo yi laf thiat way😍
Machalla la
Wayé amna nio Bonn deh comme sa ma awoo
@@aisstouciss901 wa ameu na mes Khana bary woul
La seule série sénégalaise pleine d'enseignement et de valeurs. Continuer sur cette lancée
Mes encouragements
Vraiment l’épisode final a bien réussi tout est développé chapeau à vous yesdakar forever
Ayo fin de saison way yama enfin t'es heureuse ❤️❤️❤️
Yaw mom yagui fepp
faye abdou ak yaw tmt
Pass partout 😂😂😂
Fatou Gueye dafa appartement fi khamna fouma déme féke kofa
Ohhhh long métrage ngay am fofou ♥️♥️on attend la 3eme saison inchallah ♥️😍merci pour tout ce bonheur que vous nous procurer 🥰 YESDAKAR thia kaw
Coco
Bon magal a tout Dieuredieufy serigne touba 💞
😁❤️😍
Mention special à toute l’équipe de 7 série mashala
Ayoooh li la namone mane ❤️😍🔥 série bi daffa nékh trop té ameuna chance 👏👏👏cette série nous donne des leçons très important bilaye thiey adouna déffe lou bone amoul gnarigne kholale rk ki doffelo wone ouseynou rék fimou moudié 👀ak kiné rék lou bone limou déffe léppe elle vas le regretter 👁️té réthiou day féque dieffe wésse ......nakaté yo mome ak yama ay jumelles lagnou ak limou déffe yama léppe mo takh nitte boko khamoul rék boul ko déffe yéne yi😥
Dafanekh amna sas
Toute mbekté merite une recompence merci Badiane vous avez été a la hauteur mbakh rekk mo am solo. Merci à toute l'équipe vous avez assuré....on vous attend si bénen saison mou bagna yag nakk dah secret de famille moy sama wetal❤❤❤
Félicitations à toutes l'équipe de yesdakar vraiment yénafi meune ndax rétane nagne fi dieulé nagne fi Ay leçon
Chapeau à mon acteur préféré (thié) ya meune nieup
أللهم صل على سيدنا محمد وعلى آله وصحبه وسلم تسليما كثيرا إلى يوم الدين
Mâcha, Allah je suis vraiment ému 💞🙏🤗bonne continuation à vous que dieu vous garde aamiin
Yalna gnou fékè saison 3 thie diam ak kheuwal thie barké borom touba
La serie secret de famille est tres interessante mais tirélensi leçon surtout si dernier episodebi les hommes maries respecté vos premieres femmes
Bily kou bayi djiguene ndakh djiguene weroo
Amoule Bène lecon bonii tiirè si seri yi
Sèryi ñoo tase seye yèpou
@@aloudia4180 yagui mérr deh🤣🤣🤣🤣mais ces vrai nak tiré des leçon surtout vous les hommes
Chapeau a yesdakar, vous avez assuré, une serie pleine d'enseignements et des lecons à tirer. Force a vs. Diam si yéne.
J'attends avec impatience la saison3 avec de nouvelles histoires remplies de secrets
😂😂
Très belle fin vous m'avez fait pleurer merciiiiiiii et bravo à toute l'équipe.
Hâte pour la saison 3 ❤❤❤❤
Franchement chapeau a vous Secret de famille meilleurs série de l'année qui est d'accord?? ♥️♥️♥️
Depuis hier neilawouma ,leikouma nanouma😂😂😂😂 ndakh série bi dama khar ba sonou🙈🙈
😂😂😂
Loulako diaral tmt😂❤
😂😂😂
😅😅🤣
Mossidessone
Première commentaire yalla nanu magali si diam delousi wat si diam inshallah
Lii nak moy nit boko xamoul deko wowei ehhh🤐
Dom deh danguay Diour wayei xamo kouy diariniou😭longue vie à nos maman
Chapeaux à vous 🙏🏻🙏🏻
Maty et son papa vous me faisait pleurer tout le temps je n pouvais pas supporté une telle souffrance. Omar Yaw beugo lou bakh nga ame palais di deuk si baraak ba inondation diké kéne wonoula boutou palais
Franchement suis avc Kiné elle est la meilleure... Félicitations