Si vs mourrez un jour ( yalla na yekh ) on va pas t'amener a niageu niassene comme tu le dit tes proches vont t'amener à Kaolack comme t'a fait avec sidy
No pa bi doff la nena kou amaguoul diabar khamaguo adina MDR...... Fognou KO binede akk koulako diangual del wakh Lola woor ki ta dit k yoof dagnouye dindi ayy thieurrr guattsoo
Sénégalais nio beugue polémique tu es qu'un être humain nit day dioum nul n'est parfait mais tu fais partie si niou eupeu kham kham si Sénégal sénégalais wakh ak critique rek takhoul Sénégal avancé ngén balma
Xam nga li geune bone si adouna bi makh bou soff ta xamoul dafa soff di weurr di netali akh di wakh niou lay weddi rekh niémé ay révélation ta liguay wakh dara takhou si
Ahmed khalife niass jaaxalnama soutoura dara
Longue vie à toi niass
Yalna yalla guoudeul say fane Mayela wér
Ki nako ay mbokkam fatj il n'est pas sain d'esprit!
@@maimounafall8936 kouko wakhone sa wadiour dinala nekh???
@@fatouawaniass687 kilifa déy wakh farata mais pas di polémiquer rék
Ahmeth Khalifa Niass Raggalal YALLA...Raggalal Sa Borom Guir YALLA,Fi loofi wax dinkko waxate eulleukk
Walahi
amed xéll mi nékhoull 😱😱
Pourquoi tu t acharne sur Cheick ton neveu c est dommage es triste 😔 sidi lamine niasse que la terre lui sois léger niasse Coumba Abdala
Niass mala beugue DOUNDEULLE bassi kanama kanam
Beugeu nga framason pur
Je suis verement desole nguene balma si werou koor lagnou nek. Me pabi amoule bene dignite nguene balma
Deugeu rék ga wakh 👍
Dangay doul dmrm
Deug pirr ga wakh amoule bèn dignitè
Abdoulaye Seck diokh masa
numéro svp
@@abdoulayeseck6672 paa bii nafèha leu
Gayii ahmeth khalifa niass comprendre laine koo dafa commencé dieum makk instant bii day nagg
😂🤣🤣🤣😁🤣
No lolu day yomb trop kaolack nguay demeu force doley mbam
Wé Macky téré métiém journalism
Journalists Yi dou nguén liguéyi té kayi khalifa niass
mi nguén di dougueul rémk,di xawi souteràm
Mome werrou koor day rakadiou koi🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Tu ma tuer quoi🤣🤣
Kilipha dee bou beugue mate limou donne ayy wakham d'où bari surtout site Internet yi
Tu a parfaitement raison 👍👍
Walay
Si vs mourrez un jour ( yalla na yekh ) on va pas t'amener a niageu niassene comme tu le dit tes proches vont t'amener à Kaolack comme t'a fait avec sidy
Force yoff Lang lay soul lingay yabaté yoff par la force
Est ce que Pabi normal na ?
Bonne question
Fatima Ly j'en doute fort
Pa bi werrou koor lay bagne
Noppil ngay wakh rek
😂😂😂😂😂😂
Bilay wakhatiko kii rapp yi koor lay bagne bétisame yeup werou koor lay eupp loumouy guéneu 😂😂😂
😆😆😆😆😆
Kii dousa moromou baye away Senegal am léne yare
Korgui al wakha lay nane
😛😛😛😛😛
No pa bi doff la nena kou amaguoul diabar khamaguo adina MDR...... Fognou KO binede akk koulako diangual del wakh Lola woor ki ta dit k yoof dagnouye dindi ayy thieurrr guattsoo
Laté nga trops ci médiats yi outal sa télé bop bok beug nga vue trops
😁😁😂😂🤣😂🤣
Massage thailandai si werou koor banguako waxé ba legui la nanguou ngua done sama serigne
Manlima diakhal si nitki souwahe li tey bousouba mouwah li
Sénégalais nio beugue polémique tu es qu'un être humain nit day dioum nul n'est parfait mais tu fais partie si niou eupeu kham kham si Sénégal sénégalais wakh ak critique rek takhoul Sénégal avancé ngén balma
Ay way anni soutourra qu'elle Monde sommes nous on lui laisse dire n'importe quoi
Mé pabi dioulite leu
Kéne dou kham lép di wakh lép ameth dél déssal touti adouna amoul solo dél soor euleukk
Ahméth mariet bizeufffff
Tu es un vrai domérame
Ken doula suul nianga kaolack laniou layy soul par force
Liga wakh c'est grave
😂😂😂😁🤣😂😂😅😅
Ki vraiment da doy warr
Ki nama yalla bale dou kilfa
Accepter wo yoff wayé danél ngua keur diabaram
Aka beugg camera
Bareki yalla Doo nite
Say say bi
Doul rek il faut respecter yoffff
Ahmed khalifa motoul kilifa koi amo bene khorom
Kii tall ndéyam reck mo bakh sii mome
Bayilènn sunu père Ahmed, mom daniouko sokhla setsiko diko interview, c'est tout. Bayilenn diambour dji 🤷🏾♂️🤷🏾♂️🤷🏾♂️
Kilifeu da bakh boudoul won wawe chekhe colonije fami bi
Media senegal louni nulle amoul tope nite ko khamni wakhoul dara si ndiarigne. Gnoulaye invite partout. Arrete de rendre celebre des gens stupides
Doyena doyena doyena bayile tongne tongne du kalathie
Le masseur thaïlandais il a fumé quoi encore ?
😁😁😁😁😂😂😂🤣🤣😂
Kagne gaye nopi pere domans
Ragale yalle
AKN yaw kagn ngay nopi rek la beuga xam tmt😂😂😂😂😂
Gua balma mais yaw do dara et aussi sénégal aye seytaner na gnou louye serigne jaurai aimé que sidy restée et toi partir car tu les un exemple
Pa bi dafa soof trooop, il nous amerde
Kii est ce que weurnaa???. Naa cheikh niasse moytou. Boumou tak diabar tant kii mingui doundou. Liguey lakay def mou dé.
Yagi tong wa yof dé
War ga may nite yi diamou sa wakh bari trop 😈
Xam nga li geune bone si adouna bi makh bou soff ta xamoul dafa soff di weurr di netali akh di wakh niou lay weddi rekh niémé ay révélation ta liguay wakh dara takhou si
Ki mo sooff
ki dafa nakh
Wallahi nitou fitna nga dél wakh deug, bayi yé fitna
Yaw tu n'es pas cohérent avec toi même .toi tu ne veux pas qu'on enterre a Kaolack et tu exige la famille de sidy
Ki iska werna
Day yombu bo dewé kaolack lanlay yobu par force ga yobu bayu diambour iow niou bayila si wetou guedj gui kl gay dem sa tangor ba
😂😂😂😂
Ki daniouko nara bayi bamou commencé yeuyi sagar niouy soga khamni weroul
Fen rak ki
Yaw kou amoul diabar rék dou kham aduna
Altaf Limbada yaw khana amo diabar ?doul way kou amoul diabar amo dôme do kham responsabilité !
Aka boug djiguene ki bandit bou grave the nafiik
Ki da weroul
Doul rék
Aka meuneu soss té bone siy mbokam
Way kii doukilifa merd
Ki baladé lagneko wara dagatéé yotko gayndéye parker anne
Ya latté
Vraiment arrête waaye
Mak boxam né doul rék
Yawe doule rék yawe saye thieure éficasole