@@djibybalde3426 et le prophète psl à dit : Allahou alayhi wa Sallam, a dit : « Les djinns se subdivisent en trois catégories : une catégorie qui a des ailes et qui vole dans les airs, une catégorie qui prend les formes des serpents et des chiens, et une qui est dans un voyage perpétuel et qui ne s’arrête que pour se reposer »
@@SeydinaMouhametPouye 🤣😂🤣😂non fans club asc mourid leu dîné local bida ak bokalé ak ambiance ak fanatisme saga ak menace de mort moy seni argument pour défendre seni asc mourid 🤣😂
Bayelene saga kilifa réw guén trop certains commentaires yii..ki kéy limi wokh nonoula so Mando tu peux marié autre femme c parcek ya des hommes dono meuneu féne djiguén so wokhé ki Li kénén ki gua wokh lénéne ...so amoule khél Do Kham limou wokh
Yaw ya baxoull si adouna sa baye sakh ki moka raw si adouna ak si allakhirra ki limi moka lalle si aye domou adama xamo noume tollou nga oubi sa data yaye bi di wakh
Fénnal yalla bakhoul teh yonneté bi moo tafsir coran bi lerral ko teh néna djoullite dou wessou 4femmes arabe bimouy wax deggouko menteur la même tounkara degoul diné ndax ki kenneuh warouko cétann mouy réralaté ...
baye ada wakhna deug bou demesi tafsirou dialalayni daguafa fekk li baye ada wax lou werla yen gnigua khamni si khamoguene boulene wedi loguene khamou diaraf
Thieuy Sénégal 😅😅 wa ine khiftoum ak wa ine khafo 🤣🤣 minguimay gnoromtane les 2 verbes sont au passé la seule différence c'est la 2e et la 3e personne du pluriel. Tu ne fais même pas la différence entre maadiy (passé) et moudhori'3 (présent ou future), mounane fi'3loul mourakkab. N'importe quoi ce pays.
nañou diangui tai bayi lou nit wakh inedi alkhourane meme bouko fire nouko nekhe ñoune nonoula yonentibi nena bokou na thii bakar youmakyi bokalai torokhal wadiour deugueul fene sahih moulim abu bakr mo ko netali.koufire alkhourae nouko nekhe yala ngua ammal affaire
Yaw sama mbokkou dioulite ragalal yalla te wolouko gni meunougn la lorr meunougn la dieurigne loudoul ni dafa neex allah (swt) bayil sa bopp ak yalla bou boba dinala samm
So dégué wakhine wi rek nga xam ni ki lamouy wakh wër na té deugou na .... Macha'allah
Dëg leu
Baye Ada top yalla may nako machallah tei borom bakhla
Mo fenn rk lay deff
Ya meune narr yagui fénal yalla té diga ko réthiou inchaa Allah
Nieme yalla rk
Merci Merci way kii moo bakh si kuy diingat
Mashala sama kharite sama serigne très éloquent yalla nala yalla lafale thiate tu méprise ton sujet
Alhamdou lilah sen holyi dio gueuleum si non qui loumou wah ham xam bou werla...machalah baye Ada...
Walahi wakh ng dege
Wakho deug Yalla wakh ni mounoulene guiss dieumi djiné....
@@marakane3625 astahfiroulah ...indima aya bou wah lolou...
@@djibybalde3426 sourate 7 verset 27 ...
@@djibybalde3426 et le prophète psl à dit : Allahou alayhi wa Sallam, a dit : « Les djinns se subdivisent en trois catégories : une catégorie qui a des ailes et qui vole dans les airs, une catégorie qui prend les formes des serpents et des chiens, et une qui est dans un voyage perpétuel et qui ne s’arrête que pour se reposer »
Tounkara I really respect you my brother... This people are confuse people
Billahi
Hey My Boy waxal
Ça waxx deh bayi baye niass ndax môme xam yalla la woté du Aÿ mbirou djinné pour Mouy léér
Boy yii daniouy saboté
C'est la vérité le coran autorise plus de 4 femmes.diné dio khamni nit meunasé weranté té guestu
C'est faux 😅 islam autorise que 4 femme
Bay ade fén bakhoul
MashaAllah ❤👍🏾
But people's are commenting rubbish
Ki wara raqal yalla femme rek lagniye def loutax le prophète a interdit des sahabas d'avoir plus de quatre femmes
Diambar nigua firé masna wa soulassa.... joumté amna fa. Gnar gnar boukoul ak gnar ak gnar. Sounou borom dafani gnou jeul si samou gnar yi wala gnétt yi... boul additionner boul multiplier.
Kham na neh yonante bi ak ay sakhabam kon ya léén guene duege alkhouraan ya moun doul
Baye ada wakho deug dh
Xam xam dou dièkh té baye ada si dieumi xam xam lay roté mouy cheikh'al islam baye niass di bayou gneup
Fenn rq ngay deff yaw!!
@@Oumou_Fatima_Joob louma fen soxna diarra
@@mbayediop109 ngani kii xam-xam ley wakh?? Do ragal Yalla ci lingay wakh??
سبحان الله العظيم 😥😥
Tounkara a peur de corriger ce gars
Pourquoi wahouko 4 femmes la islam mayei
Wakho deug deh mato talibé baye done Sergine si péyi BAYE BI
yaw tamit bay momom peyi bi
😂😂😂serigne tarikha yi fene rek fene rek fene rek fene 😢😢
Sa baye molénn ko diangall
@@SeydinaMouhametPouye kon kham nga ni dey fene lolou ngueye confirmer 😂🤣
@@mamadousy6312 lathie ko sa bay bakham 🤣🤣
@@SeydinaMouhametPouye 🤣😂🤣😂non fans club asc mourid leu dîné local bida ak bokalé ak ambiance ak fanatisme saga ak menace de mort moy seni argument pour défendre seni asc mourid 🤣😂
@@mamadousy6312 al hamdoulilah ba douma mourite
Kii mo minah full allahu akbarr
Jais cree les homme est les djinne pour quil madore
Machalla
Xam xam daal am nga ko
Li ci dess nag tabaarkalla
Ki hamoul dara
سبحان الله
Hum j'ignore pour la véracité des ces propos car je ne suis pas savant mais je sais cas-mm qu'il metrise bien ce qu'il dit
C juste des mensonges rien n logique mouye rappe n’a ni rek borome xame xame deugeu daye dalle teye te dou reupi reupi comme qui
Habib dieng Dakar Sénégal
Day fén rék
Machallah xam xam bi amna solo
Machalla niass ❤❤❤❤
Ce sont ces genres de Domerame menteurs qu’ils ne faut pas donner la parole…
Ki njibar katt la.
Noumiu firé alquran bane sahaba mooko deggée noonou
en tout cas loumouy waxx lere na
Tounkara dagha wara andi niar niou xam xam me ki wakhoufi dara
Yawe ya fi wakhoul Dara
Mais le numéro de baye ada
77 715 06 06
Wakhlène loulène nerx ba yalla diappla.
Kou si yalla diap rk tothie salou bonnnn
le soufisme ou tassaouff autorise d'épouser plus de 4 femmes.
Merci labas!!
Pas vrai
Bo xamoul soufisme nopil mo geun ngay séddé lo xamoul ak Lou wéroul
Bo xamoul soufisme nopil mo geun séddé lo xamoul ak Lou wéroul
@@Amesoufi313 soufisme lenenn loudoul creer benenn diné boudoul islam defou gnouko! Donc yaaw yaa wara nopi!
Bayelene saga kilifa réw guén trop certains commentaires yii..ki kéy limi wokh nonoula so Mando tu peux marié autre femme c parcek ya des hommes dono meuneu féne djiguén so wokhé ki Li kénén ki gua wokh lénéne ...so amoule khél Do Kham limou wokh
Ki bakhoul chi society
Manna gatt
Yaw ya baxoull si adouna sa baye sakh ki moka raw si adouna ak si allakhirra ki limi moka lalle si aye domou adama xamo noume tollou nga oubi sa data yaye bi di wakh
Inahou madjenoune
Astafouroulaye 😂
Yow diango go al korona
Macha Allah ci al khour aan dji
Kii dafa kontane rèk mo takh
Boungéne tongué nga xamni yaw xamo lou yalla wakh mane mi rakame rék doumasa morome xamo léne drh ba parréh lou waye wakh guéne wédi
Boul tongne baye niass
Ki deh mom diang nah vraiment , enh tounkara ?
Nn yalla 4sokhe na la wakh ,ki limou wakh dou dege kouma wodi woma
Tounkara diomina
Fénnal yalla bakhoul teh yonneté bi moo tafsir coran bi lerral ko teh néna djoullite dou wessou 4femmes arabe bimouy wax deggouko menteur la même tounkara degoul diné ndax ki kenneuh warouko cétann mouy réralaté ...
Séne wa keurr bame dathe bolléne dadialéh rakame rék dousséne morome si lépp yaw xamo drh di wédi sa data yaye
Li mettineu khol😭
TALIBEI BAYE EGAL KHOL BAYI... TOUKARA TAY DIOMI NGUA ...LOL
Tout ce qu'il a dit c'est clair
🇸🇳
Fen
No galsen mo nexx té bari borom kham kham
doul rekkkk
al coran nga weedi
yaw boo gueumoon al coran doo fenn . Khamoo touss
yaw kou yakar baye ada kou appa xamxam yaw kou niaka yar nga
nia ka kilifa
mo , baye ada fenn rek la niou dakk.
baye ada wakhna deug bou demesi tafsirou dialalayni daguafa fekk li baye ada wax lou werla yen gnigua khamni si khamoguene boulene wedi loguene khamou diaraf
Yaaw dh ya dakhaa doul baye Ada mi sakh!!
Wallahi li dafay luntal xélou domi adama yi warouna
Ndongo ahmede khalifa
Baye Ada Top machala
Xam xam bi weurna machalah tunkara sakh est emu
Féne réck
Non fénn yi werna ki doul rk
Kii mo meuna douul!!! Laa hawla wa la huwwata!! Yalla amna gnoumou reubb naq!!
Aywaaaay kii lanla wax Lou amoul nak sokhnassi
@TORODO TV N:1 yaay bayou doulkatt yi yaw!
Dul rek
Sénégal mo nekha wakhé
KOU MOU WARA KOUKHA MOUD NANOUPI
KOU XAM MOU WARA WAX KOU XAMOUD NA NOUPI
Thieuy Sénégal 😅😅 wa ine khiftoum ak wa ine khafo 🤣🤣 minguimay gnoromtane les 2 verbes sont au passé la seule différence c'est la 2e et la 3e personne du pluriel. Tu ne fais même pas la différence entre maadiy (passé) et moudhori'3 (présent ou future), mounane fi'3loul mourakkab. N'importe quoi ce pays.
Serigne bi Baye Ada wakhoul Wa in khaafo dh
Mom ikra kitabak bobou sah mom khamoul ban kitab la yalla di wakh
wa "inkhiftoum" c'est deux temps a la foi bro faut bien réfléchir
Kii dé tounkara dou ko yape ci xamxam😂
Bayil bay niass yaw fénal rk
Nitt kouneh yalla taggatal nala djin ak malaka mounek sa andando
Ki fen katt bou bon la
Le Djinélogue
😂😂
En tout cas kou diangue la
Mais ki doffe leu il faut l'interner
You don't know nothing go back and learn Qur'an Allah SWT don't said marriage 6 wives
He is crasy don’t listen to him
Damn guys😂😂 sén anglais yi ohh🤧🤧
Abusé Abusé Abusé Abusé Abusé
Maachalah
nañou diangui tai bayi lou nit wakh inedi alkhourane meme bouko fire nouko nekhe ñoune nonoula yonentibi nena bokou na thii bakar youmakyi bokalai torokhal wadiour deugueul fene sahih moulim abu bakr mo ko netali.koufire alkhourae nouko nekhe yala ngua ammal affaire
Mane guissou ma woone lii...yowe kouy fene rek sa taalibé la......salopard bi....vrai imbecile nga mbaam bi
Ya meuna doul
Demal nga diakhal arabe
🤭🤭
Yamanaka doull way
Dey doul rek
Tounkara bayile yamba
Ya menne fénn 😃😂😂😅😂
😂😂😂😂😂
Il dis n,importe quoi c gar la
Bo dindé limou wax
Tek fi dara
bayi len incar
baye aada graaw nga !!! khana ya eup khamkham imam malick ??? mdr c pa srx
Le prophète avait 12 femmes
@@adambarhamdiagne7053 ça ne concerne que le prophète le grand nombre de femmes
Maneu fene masnaa dou lolou
mai kii mognémé yalla pour qoi monè mazna moy4 ahahah n sènègal loway nèkh wakh kii bodégué nimoy wakhé nga kham né khamoll dara day soppp rék
Kii moo mana fenn. Waaw da doff moo takh mo am aye djinné.
😂😂😂😂
الله يهديك
والله یحتاج الدعاء
انا احتاج 782081390
واتشاب
Day féne Alkhouràne waxoune lolou
Borome nokhouy
tounkara tu tes fait humilié
ki degoul al khouran
Ki dey doul 4 famm la yalla wah
Dommeharam leka sama150 mille.niaw kenn deguetoula
Yaw sama mbokkou dioulite ragalal yalla te wolouko gni meunougn la lorr meunougn la dieurigne loudoul ni dafa neex allah (swt) bayil sa bopp ak yalla bou boba dinala samm
@@mouhamadibnismail5827 merci
Kii loumouy wax si coran bi maîtriser wouko khamoul dara loudoul sossal borom bi
faut pas wéddi gratuitement andil Aÿ leral
Souniou kilifeu si Sénégal akk borom xam xam you si eup 4 femmes laniouy yam. Mal interprétation moyy am parfois
C'est un menteur
Mé ci alkoran lay wakh dh mé tonckara wakhuol tô mouy wooté si alkouran momodiaxall
ndiabarkat yi fèn rek mooy sèèn metier.charlatan
Thiaga rék ak beug djiguén mo takh mouy détourner aya yalla yi