Vidéo "Iskëy! Kii mô dawalôn auto bi ci guèeju Gambie gi 1993" Thiérno Mountakha Omar Ndao

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 7 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 267

  • @kandeadama1307
    @kandeadama1307 3 роки тому +42

    Machallah je suis très fier d'être musulmane Dieu et unique

  • @babacardieng7399
    @babacardieng7399 3 роки тому +17

    Wawaw mome la dh Khalifa mountakha Ndao yalla na yalla yokou léram té tas gnou si barkém

  • @saerdiagne8198
    @saerdiagne8198 3 роки тому +2

    Gayi bayiléne Di wéréneté si ay keurou dîné lolou bawoule ta daye yé fitneu ha en plus abe dioulite d'où teukouwaté yalla rkk mofi nékk lépp momla 👉🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @mamourdrame4567
    @mamourdrame4567 3 роки тому +9

    Ndeysaaan, dama doon défiler rek guiss vidéo bi. Ndeysaaan l'homme au grand boubou blanc mooy sama toureundo, di sama rakku papa. Gagnuna depuis 2007, kilifeu gou mak la woon Touba. Tay seutuem mooy sama sokhna. Ndeysaaan, aduna dou dara. Yalna yalla yeureum Leen. Amine

    • @momoleinternaional6410
      @momoleinternaional6410 2 роки тому

      Non 2009 la geune adouna same mame lah bay momor drame touba sora taw wam bou Goor mougi todou serigne modou niou geuene wakhtan rek

  • @sheikhtijanycheriflofficie7997
    @sheikhtijanycheriflofficie7997 3 роки тому +72

    Wa keur Cheikhou Tidjiany Cherif lépeu lagnou meun ni ték bilahi

    • @ndaomor7899
      @ndaomor7899 3 роки тому +1

      BILLAHI wallahi

    • @lampseck9291
      @lampseck9291 3 роки тому

      Man de ma am sama guem guem guemoumako

    • @modoundao5896
      @modoundao5896 3 роки тому

      Bilahi

    • @matarseck7362
      @matarseck7362 3 роки тому

      Yena niakk diommm nak
      Guemolen nopilen teh mando

    • @amadousouleymanesow8549
      @amadousouleymanesow8549 3 роки тому +1

      @@lampseck9291 fall lolou lou wéer la,bimou déloussé sakh dagne niko bouko défati.amna niou né sakh moko dioural gatouk fanane.

  • @serignemoustaphamoukhtar3637
    @serignemoustaphamoukhtar3637 6 років тому +16

    Wao seydi mountakha Omar ndao darou salam صديق اكبر

  • @youssoufall2229
    @youssoufall2229 3 роки тому +1

    Je suis une jeune femme talibé mawlana cheikh ibrahima niass wayé yalla sake na kouné ci kaw souf té moye woner boppam founé machalla

  • @mouhamedndoye7305
    @mouhamedndoye7305 4 роки тому +23

    Guayi Yalla Yi nio Modeste deh ❤️🙏🏽

  • @fatimacissediaboumamedabak198
    @fatimacissediaboumamedabak198 6 років тому +30

    Li yep manmanou borom bi la machallah

  • @drameamdymoustapha8438
    @drameamdymoustapha8438 4 роки тому +18

    F'ier d'être tallibé Farokh ❣❤❣❤❣❤💔💔💔

  • @amethlamine9772
    @amethlamine9772 3 роки тому +5

    Kone ki amna vidéo ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ ah machaallah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @ousseynoudiagne440
    @ousseynoudiagne440 3 роки тому

    Machallahou yalla n'a yalla yésale yérmadém si môme ta tasse niou si barckém Amine inchallahou

  • @astoundiaye1476
    @astoundiaye1476 3 роки тому +1

    Lep deugue la Sama mame la mo dawal auto bi si guédji gui si nimbalou sunu borom nioukoy wowé Elhadji Mountakha Ndao di dom si Elhadji Omar Ndao yalna yalla yokkou sen leer tasse niou si séne barké 🙏

  • @moussafalle6780
    @moussafalle6780 3 роки тому

    Sénégal rewou kiriam rewmo khamni amoule justice amoule sécurité amoule hôpital amoule like kou bakh amoule dara khana kirama

  • @jonest6396
    @jonest6396 6 років тому +10

    Serigne Mountakha Ndaw rta fils du grand qutb et khalif de la tariqa tidiane a El hadji Omar Ndao .Darou salam est à 5km de Nioro

  • @diouldedialloya9221
    @diouldedialloya9221 3 роки тому +2

    Cheikh tidiane du morom même talibém bu guena daw amna lu nek si mom

  • @aitagueye3569
    @aitagueye3569 6 років тому +22

    M Achallah je suis fier d'être t idiane

  • @rokhayatoudieng3210
    @rokhayatoudieng3210 6 років тому +33

    Walahi li dou dara si kouy werd Salatul Fatiha.Té thiow dou djipp.Képp kouy waliw Cheikh mola fété kaw

    • @general7952
      @general7952 3 роки тому +1

      Alhamdou lilahe mane sama saigne dafa rombe waliwou di deme aye taloubeme gnoy waliwou aki seteum alhamdou lilahe

    • @jallohamadoujarry9734
      @jallohamadoujarry9734 3 роки тому +1

      Te mouy deugue

    • @papandiaye920
      @papandiaye920 3 роки тому

      Dieureudieufé Serigne Touba

    • @papandiaye920
      @papandiaye920 3 роки тому

      Cheikh le marocain.

  • @abdousarr4928
    @abdousarr4928 3 роки тому +8

    Machalla lii yalla mayé dafa bari wakh mo bakhoul rek salatoul fatikha bokay werde li mo guena ndaw si say khar bakh danlenkay téré rek yalla khamnako

    • @ramadiaw607
      @ramadiaw607 3 роки тому +1

      Ah bon salatoul fatikha tu peux m'expliquer frère werdi bi comment on le fait

    • @abdousarr4928
      @abdousarr4928 3 роки тому

      @@ramadiaw607 oui mé pas par message done moi tn numero

    • @abdousarr4928
      @abdousarr4928 3 роки тому

      @@ramadiaw607 je t'envoyé tout en frasais et arabe

    • @ramadiaw607
      @ramadiaw607 3 роки тому

      @@abdousarr4928 ok mon frère moi je suis mariée motakh je ne peux pas donné mon numéro ici mais si tu as Instagram je te donne mon Instagram nga envoyé mako fofou

  • @deguenegueye1411
    @deguenegueye1411 4 роки тому +4

    Yalla na yalla tas gnou si sen barké❤

  • @talibereklabeuguedonendao5904
    @talibereklabeuguedonendao5904 6 років тому +12

    Machallah baye oumar ndao

  • @laminedrame8952
    @laminedrame8952 3 роки тому

    Dieureudieuff Serigne Mountakha Ndao💕💕💕

  • @laminedrame8952
    @laminedrame8952 3 роки тому

    Dieureudieuff Seydi Muntakha Ndao

  • @abasall711
    @abasall711 3 роки тому

    Fiere d'être talibe cheikhou tidiane machala aka gnu barer xam xam machala t waner wugnuko

  • @khadidiatoudia759
    @khadidiatoudia759 6 років тому +10

    Macha'allah Allahou Akbar hamdoullillah

  • @Bb2fav1
    @Bb2fav1 3 роки тому

    Machallah mon grand père Ndao beuleup ndoukoumane ❤️❤️❤️❤️

  • @KENZOTVS
    @KENZOTVS 3 роки тому +2

    Ki De Talibes Chiekh Bou Gnou Bary Khamoul Si Sénégal La Mo Def Lii Brom Darou Salam Thia Saloum❤❤❤ Kouko Brom Lamaj You Reuyi Defon Tey Ken Dou Dégg Senegal😂😂Te Yagge Na Sakh Nak

    • @lampseck9291
      @lampseck9291 3 роки тому +1

      Ana video yi 93 gui dafa yague dara bayillen sene thiakhan yi

    • @amadousouleymanesow8549
      @amadousouleymanesow8549 3 роки тому

      @@lampseck9291 yaw mi ya wara gueme mba noppi.suis mouride et saloum saloum

    • @KENZOTVS
      @KENZOTVS 3 роки тому

      @@lampseck9291 Ani Vidéo Bi Sa Serigne Joule Si geudj gui iaw

    • @lampseck9291
      @lampseck9291 3 роки тому

      @@KENZOTVS lola dafa yague trop 1895 lawon bobou vidéo yomboul

    • @lampseck9291
      @lampseck9291 3 роки тому

      @@amadousouleymanesow8549 man awma loumay wakh ak yaw kep kou garouwale mouride yi niou tontou la

  • @Buzz24senegal
    @Buzz24senegal 5 років тому +6

    Manchallh merci beaucoup

  • @morhmorh4992
    @morhmorh4992 6 років тому +15

    Sénégal Amna ngou bakh dh

  • @imammohamedcisse2427
    @imammohamedcisse2427 6 років тому +3

    Kene dou cheikhou Tidiana radiyallahou hanehou kou diekhe si mom rek mo Man li

  • @cheikhahmethtidianendiaye7847
    @cheikhahmethtidianendiaye7847 3 роки тому

    Dieuredieuf cheikhna tidiane cherif ❤️ keune d'où mome

  • @daarajimedia.8861
    @daarajimedia.8861 3 роки тому

    How come this miracle happened in Gambia and Gambians are not aware? Simply put, it never happened in 1993. Amul tey amul élék. Allah SWT is listening and is watching.

  • @babacartourre7826
    @babacartourre7826 3 роки тому

    Machala ndow yalna yalla yokou sa lerr yii

  • @babacarcisse5991
    @babacarcisse5991 6 років тому +17

    machallah kii nio bok deuk li lou wér la

  • @sopeycheikhalislambaye7425
    @sopeycheikhalislambaye7425 3 роки тому +2

    Macha'allahh yalla rek moy karim

    • @milkinsa6560
      @milkinsa6560 3 роки тому +1

      Mais kilifa gui deignah Aÿ enrif lagn deh

    • @sopeycheikhalislambaye7425
      @sopeycheikhalislambaye7425 3 роки тому +1

      @@milkinsa6560 waw deug leu wayé anriff bilahi lagniou wara sakou daffa diaffé nak mé yalla nagniou ka done si barkè cheikh Ibrahim baye rta

    • @milkinsa6560
      @milkinsa6560 3 роки тому

      @@sopeycheikhalislambaye7425 amine nagn si am yakine rek Baye moy DEUG wadji dafa todj Sénégal def si deunou goor yallah you barri mahrifa bâ pareih neilene bouleine Tass seini keur Baye pabi defli gnou barri hamougn mossna mahrifa

  • @matydiop1059
    @matydiop1059 6 років тому +4

    ماشاء الله شكر. الله. اكبر. ماشا ء الله. جشك الله خير. جرجف وشلم. الله. الإله

  • @bassiroundao1331
    @bassiroundao1331 6 років тому +10

    Machallah ! Yalla na yalla yokou leram

  • @farokhdiaspora4486
    @farokhdiaspora4486 5 років тому +2

    Ki moy ehaji Mountakha omar

  • @elbachirprod9539
    @elbachirprod9539 3 роки тому +2

    MACHALLAH

  • @cheikhtoure2671
    @cheikhtoure2671 3 роки тому

    Ki moy sama serigne nio serigne elhadji serigne woly Touré diabou ndaw konda diam yallne yalla défall niapo diam

  • @citizenmistik2258
    @citizenmistik2258 3 роки тому +1

    Allahou Akbar 👆 MashaAllah

  • @tkhtidj3695
    @tkhtidj3695 3 роки тому

    Machallah fier detre talibe cheikh tidjani cherif esqueye seydy ndoa

  • @peaceandsalam2852
    @peaceandsalam2852 3 роки тому

    Yàlla nako buur yàlla yërëm té xaare ko thia Aldiana you guena kaweee ya ñu mu fa fekk ak niouko fa fekk té yokku ay leeram té tasniou ci barkeem 🤲🏾🤲🏾🤲🏾

  • @justintimeclean5840
    @justintimeclean5840 3 роки тому

    My Brother Elhaji Muntaha Secka is Name After him.

  • @daroulmiraya3622
    @daroulmiraya3622 6 років тому +7

    Baye mountakha ndao

  • @alhaqq310
    @alhaqq310 3 роки тому

    Wallahi macha'Allah 😍❤️❤️🥰🙏

  • @basscisse2811
    @basscisse2811 3 роки тому +1

    Machallah a mena solo

  • @alimatousougoufara1571
    @alimatousougoufara1571 3 роки тому

    machallah beuleup ndoukoumane ndao sandené arame fakha

  • @muhammedsamba4294
    @muhammedsamba4294 6 років тому +9

    Allahu akbar ndayesaan

  • @mikkha2745
    @mikkha2745 4 роки тому +3

    vidéo bi warna law ci reseaux sociaux yi gneup jot ci statut ko yalla nako law bala koor gui di diéh ci, télé yieup ak compte reseaux yeup facebook snapchat instagram tik tok partous inchallah

    • @abdoudrame5770
      @abdoudrame5770 4 роки тому +1

      Kou bakh diarou ko danga bakh rek waye mom Nena mbiram da tomouranke

  • @wakeupafrica9906
    @wakeupafrica9906 3 роки тому +2

    Batay amna ñiou geumoul ni Serigne Touba Diouli na Si Gueijj gui...😅😅 ñiak kham Yalla woroul.

    • @makhouceessay686
      @makhouceessay686 3 роки тому +1

      Lou leer nga wakh
      Li lekk firnde n'a ni matou yalla amna

  • @bossbamba2751
    @bossbamba2751 3 роки тому +1

    Allahou akbar nitou yalla amna

  • @seynabfallou395
    @seynabfallou395 3 роки тому

    Machalla Senegal lou bari lagnou ame

  • @cheikhsakho6974
    @cheikhsakho6974 5 років тому +4

    Darou Salam rek incahllah

  • @mamadousy5587
    @mamadousy5587 6 років тому +6

    Macha Allah ndao

  • @cheikhsakho6974
    @cheikhsakho6974 5 років тому +2

    Machalla sama serigne

  • @daviddiouf3698
    @daviddiouf3698 3 роки тому +1

    Xam yalla djegueko mo gueune li bokouna silou guena touti si tarikhabi bilahi lazi lahi laha Ila houwa

  • @ndiayendiaye5188
    @ndiayendiaye5188 6 років тому +8

    Macahallah 💪💪💪💪💪

  • @pascallaminembaye9881
    @pascallaminembaye9881 3 роки тому

    Gneme yallah gui rek ..Trop de mystiques tuent la foi... Sénégal NDIAYE, doucement !!!!

  • @astoufall8125
    @astoufall8125 3 роки тому

    Ki mouride la talibe cheikhoul khadim borome darou salam

  • @abdoulayeniang2503
    @abdoulayeniang2503 6 років тому +7

    Allha machallah

  • @madickedrame8605
    @madickedrame8605 5 років тому +3

    Machallah fatabaracalla

  • @cheikhgassama8942
    @cheikhgassama8942 3 роки тому +1

    Mahalla ❤❤❤🙏🙏🙏

  • @abdoudrame5770
    @abdoudrame5770 4 роки тому +5

    محمد منطقى إبن شيخ الحج عمر ندوا دار السلام جور درب

  • @papandiaye920
    @papandiaye920 3 роки тому

    Serigne Touba dé ce sont ses écrits qu'il considérait comme des kiramaa malgré tout ce qu'il a accompli comme miracles

    • @amadousouleymanesow8549
      @amadousouleymanesow8549 3 роки тому +2

      Votre commentaire là n'a pas sa place ici.on est pas là pour comparer.il l'avait fait par ce qu'il n'avait pas le choix.par ce qu'il devait se rendre dare dare au gambie et que ke férry etait dejà parti

    • @milkinsa6560
      @milkinsa6560 3 роки тому

      @@amadousouleymanesow8549 ki Ap seytanei la fa goorou yallah yeup di dadjei si halamoune arwah dougn KO fekeih beug nek fi di diaxassei rk

  • @amyndao605
    @amyndao605 6 років тому +12

    Eskey ,ñi ñoy wa darou salam ca saloum

    • @mamadouseck9755
      @mamadouseck9755 6 років тому +1

      Amy NDAO eskeuy sama goor ga imame Touré fala deukk

  • @papesambafall5907
    @papesambafall5907 6 років тому +4

    Allah akbar

  • @elbachirprod9539
    @elbachirprod9539 3 роки тому +1

    ALLAHOU AKBARE KABIRA

  • @dieynabadiop1621
    @dieynabadiop1621 6 років тому +5

    Machalla

  • @serignemoustaphamoukhtar3637
    @serignemoustaphamoukhtar3637 6 років тому +3

    Ki moye sama serigne

  • @ablm9101
    @ablm9101 3 роки тому

    Machalla ndao koudna

  • @papediop9544
    @papediop9544 3 роки тому

    Ma cha Allah yalla motali

  • @gabrielmendy4825
    @gabrielmendy4825 3 роки тому

    CA Comfirme lA PRIERR DE CHEIKH AHMADOU BAMBA MBACKE KEN DOU MOM

  • @abdoudrame5770
    @abdoudrame5770 4 роки тому +4

    Mai du nianal khalifa Bachir mou ya geufi lol the wer ak kou ne amine

  • @baaysaamcamara1312
    @baaysaamcamara1312 6 років тому +4

    MashaAllah

  • @assanesane3596
    @assanesane3596 3 роки тому

    Migui dounde fane lako meuné djiss svp

    • @abdoulayewague4207
      @abdoulayewague4207 3 роки тому

      Non mon frère il est décédé moi je les racontre a darou salam il est très janti paix a son âme reposé en paix

    • @assanesane3596
      @assanesane3596 3 роки тому

      @@abdoulayewague4207 oh lala que son âme repose en paix ta eu la chance de rencontrer un homme pieux

    • @abdoulayewague4207
      @abdoulayewague4207 3 роки тому

      @@assanesane3596 Oui assane c'est té un grand marabout mes très sincères très semple

    • @assanesane3596
      @assanesane3596 3 роки тому

      @@abdoulayewague4207 oh massa

  • @ndiayesewrou3351
    @ndiayesewrou3351 3 роки тому

    Masha Allah ndaw

  • @makhtarndaotv5927
    @makhtarndaotv5927 6 років тому +7

    alhamdou lilah

  • @lessyliennebadji
    @lessyliennebadji 3 роки тому +1

    Wolou Yallah dafa diafé mais bakhna trop daf lay diokh fiite walay

  • @papendiaye3825
    @papendiaye3825 3 роки тому

    Waw serigne bi kene dou yaw ndao beuleupp bilay sa may lerna kene dou ko werrane té

  • @tagadia72
    @tagadia72 3 роки тому

    ماشاء الله تبارك الله فيك حسنت

  • @naniousamejikkoyi2112
    @naniousamejikkoyi2112 3 роки тому

    Yalla mogii méyé ba legui

  • @khaliliibrahimacisse.4267
    @khaliliibrahimacisse.4267 3 роки тому

    Walahi ndeysane ndao kounda

  • @deffaly9056
    @deffaly9056 3 роки тому

    MASHA ALLAH ♥️♥️♥️💕

  • @astechinfo7154
    @astechinfo7154 3 роки тому

    Wallahi deugeu lë saloum saloum dagne doule wakh rk mais ponkal yappu ngui saloum

  • @binetadia8027
    @binetadia8027 6 років тому +2

    J'ai fait une erreur il est aparanté à la famille Touré de medina Touré à Kaolack manchalah

    • @pendadieye5739
      @pendadieye5739 6 років тому +1

      C la famille d alhadji serign Touré a medina salam

    • @amydiakhate6890
      @amydiakhate6890 4 роки тому +1

      C'est pas la famille Touré. C'est la famille de seydi elhadji omar ndao le qutbu à darou salam nioro

    • @cheikhdiallo4436
      @cheikhdiallo4436 3 роки тому

      @@amydiakhate6890 x e,

    • @abdoudrame1729
      @abdoudrame1729 3 роки тому

      yaw bo khamoul dagay lach mba nga nopi

  • @ibrahimademba1627
    @ibrahimademba1627 6 років тому +2

    Mach Allah

  • @fredcavalo4300
    @fredcavalo4300 6 років тому +18

    Madoli tie dafa tediu Balou yalla bou bakh dakh ragal yalla

  • @binetadia8027
    @binetadia8027 6 років тому +6

    Ils sont de Kaolack plus précisément Médina salam

    • @taphatoure8644
      @taphatoure8644 6 років тому +2

      Bineta Dia pas medina salam mais darou salam

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 6 років тому

      Medina salam serigne Fallou touré mofa nekk.

    • @pendadieye5739
      @pendadieye5739 6 років тому

      @@abdoulabdoul7809 borom khôl sed yaram sed

    • @aliounendiaye5535
      @aliounendiaye5535 4 роки тому +1

      Yallah moye kharim et pourtant pourquoi dougnou ko magal béssam bi

    • @aliounesarr7655
      @aliounesarr7655 4 роки тому

      Darou salam

  • @daoudasall7460
    @daoudasall7460 3 роки тому

    Allahu Akbar !

  • @moustahpaseck3467
    @moustahpaseck3467 3 роки тому

    Machla ❤️❤️❤️❤️💯💯

  • @modouceesay8329
    @modouceesay8329 3 роки тому

    mashallah Amna solo 🕋

  • @ibrahima-sall
    @ibrahima-sall 3 роки тому

    Sénégal lifiy ay kilifeu té lakhatou mo epou li fégn

  • @ameetfallsenegal3506
    @ameetfallsenegal3506 3 роки тому

    Machallah ndao mais loutakh yinné thie sama mbokku tidiane yi di wédi ni serigne touba rta diouli na sy guij gui ba paré di geume li
    Nitou yalla loumou manoul amoul

    • @amadoudia165
      @amadoudia165 3 роки тому

      Kou li kha wah eupeu neude mane moussouma khiss tidjane bouko wedi nitou yalla moune n'a loune

    • @ameetfallsenegal3506
      @ameetfallsenegal3506 3 роки тому

      @@amadoudia165 machallah sama serigne bi walahi iow sa khol bi mo défarou rek ndeysan

    • @abdoukarbalatv5250
      @abdoukarbalatv5250 3 роки тому +1

      Yamana fene kane moko wedi dobayi aferou sisou yi

  • @mamadoumbaye1518
    @mamadoumbaye1518 3 роки тому

    Yalla rek mo magg! Ndeyysan

  • @hommeblack5787
    @hommeblack5787 3 роки тому

    Mansha halla

  • @katimtoureofficiel6672
    @katimtoureofficiel6672 6 років тому +5

    Ndaw kounda diallo

  • @mikkha2745
    @mikkha2745 4 роки тому +1

    el hadji mountakha omar ndao koumay wah ki moy kan kilifa bi done na dég histoire bi wayé baye niass lako téegone koumay explique fou kilifa bi deuk ak foumou bok ci tariha sénégal ngir yalla yag dég histoire bi mais hamoumassi dara

    • @bongo383
      @bongo383 4 роки тому +1

      Kii mogiu deek darou salam nek talibe chéikh Di dome sii Elhadji Omar Ndao Moy brome mako wakhe.

    • @mikkha2745
      @mikkha2745 4 роки тому

      @@bongo383 darou salam bi bane region la nek

    • @s.modoubousso565
      @s.modoubousso565 4 роки тому

      @@mikkha2745 digantém ak thioro mongui wara tollou ci 5 kilomètres souma dioumoul deuk bou beuri ay lérr... Elhadji omar ndao farokh kokou kéneu la

  • @bayelayesakho8934
    @bayelayesakho8934 3 роки тому

    Macha Allah❤️❤️❤️

  • @falloudiaw4648
    @falloudiaw4648 3 роки тому +1

    🙏