MOUHAMED NIANG "MOU SERIGNE SALIOU" - YAAY MANE MAAY YAW FT KHALIFA NIANG
Вставка
- Опубліковано 5 лют 2025
- #mouhamedniang #serignesaliou #yaaymanemaayyaw
MOUHAMED NIANG MOU SERIGNE SALIOU ET KHALIFA NIANG CHANTENT CET ILLUSTRE MATINÉ, OU SERIGNE SALIOU MBACKE (RDA) SE RENDANT DANS L'UN DE SES DAARA FIT LA RENCONTRE DU JEUNE SERIGNE CHEIKH BETHIO THIOUNE (RDA) A TASSETTE LE 17 AVRIL 1946. CE DERNIER ÉTAIT ENTRAIN DE LABOURER LE CHAMP PATERNEL LORSQU'APERCEVANT L'HOMME DE DIEU SE MIT A COURIR DERRIÉRE SA CHARETTE POUR LE RATTRAPER.... ET C'EST AINSI QUE DÉBUTA SON AVENTURE AUPRÉS DE SON MARABOUT, SON AMI ET SA RAISON DE VIVRE SERIGNE SALIOU MBACKE (RDA)
Abonne toi Like et Comment
#TOUBA
#MOUHAMEDNIANG
#SERIGNESALIOUMBACKE
#SERIGNECHEIKHBETHIOTHIOUNE
#MOUHAMEDNIANG
#KHALIFANIANG
#SERIGNEMOUNTAKHAMBACKE
Nioune salihate yi yaw lanou beugue say son lanouy snap🥰🥰 sa kaw sakanam
❤❤❤❤❤bilaye❤❤❤ stp il est au Maroc actuellement ❤❤❤❤
Sa adiya waye❤❤❤❤❤
Bilay limay wakh sama xoll lako dieuleee mouhamed niang souma kay deglou sama yaram bii dafay daww ndakh mekctee yalla na yalla weral batt bii si barker s.saliou amine😭😭😭❤
Bly koumou daloul mano ko khame mouhamed niang nonou la may def🥺❤️
Done mourite bilay chance la barcké Serigne saliou ❤️❤️❤️
Ndaysane mouhamed ganaw yalla lo am lo mane serigne bethio la santal bubakh serign bethio waw koor gnage
Kou beugue serigne saliou rk beuseul j’aime mashala mouhamed niang yasi meune🥰🥰🥰👏
❤️❤️❤️❤️💯😭😭😭😭🇬🇲
❤❤❤❤❤❤❤
Dieukeur sama😍
@@ndiobadiop713 mon amoureuse ma femme ❤️❤️
Machallah yalna yalla may goudoufane ak weer diam soutoura tawfekh sama chanteur préféré ❤️❤️🙏🙏
😭😭😭😭Serigne Saliou ndiguel thioune sama sang bi yaggfi loll thioune nioun ak yow ba faww thioune mame bambi❤️❤️❤️
Dieuredieufty Serigne Salifou mouhamed niang yalna yalla lafard thiate sama chanteur préféré
J'aime cette chanson tellement machallah et Mohamed Niang 🥰😍😌🤩😏🥳🥰😍😭
Sama khol sed na😭❤️❤️
Yalla nama la yalla fayall machalla niang
Je suis tidiane mais nima beugué Serigne saliou walahi dafma yéme😭
❤❤❤❤❤❤❤c'est normal c'est lui qui est l'avocat des enfants un homme généreux qui a œuvré pour la jeunesse ❤❤❤❤
Sokhna khadydiouf❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Machallah moi je suis talibé baye mes j’aime tellement les mourid et les chansons de cette homme bilay 🥰🥰🥰🥰🥰
Akassa beugue nala dé
@@aichaibrahimafall6315 mala foufff 🥰🥰
Moi aussi je suis mouride mais j'adore baye barhama
@@ndeyebintadiagne5282 bilay gnioun gnieupp bénn lagn kon nay rafet rék 🥰🥰
@@aichaibrahimafall6315 🥰🥰🥰🥰fii la eupé
Képp kouy mourride wole sedetina sougniou fiért❤️❤️🥰🥰
Je suis fière d'être mouride va vie seringue saliou mdacké 💝💝
Yalnanou la yalla fayal cheikh béthio mame bambi Thiam bibarakaty sangue yaram seydina salih ❤❤❤❤❤
Amine barkep Sr Saliou
Yalna yalla wereul sa batt bi rek 🥰🥰 bayi nagn la ak serigne saliou sunu yakar 😭☺️
Barki Serigne Saliou mouhamed niang ligay wakh si Serigne saliou nekh na loll yalla na sa diam yague machalla nekh na trop❤️❤️❤️❤️
Koukoy am di woutti lenen 😭 dieredieufi Serigne saliou
Le meilleur chanteur du monde entier encore il a frappé plus fort manchalah ♥️♥️ yalla n'a sa dima yague goude fane ak weer rek inchallah
Amine thi barké seydina mouhamed psl
Machalla
Machallah mbacké Balla ♥️👌👌♥️💯❤️♥️
Amiiiiiiiiiiiine way
Wallahi il est le meilleur notre ambassadeur
Salaw way wi neeh na lool Niang wayé man limay ladj moy naka nga meuna wédé serigne bethio di gueum doomam.
Yalnala serigne Saliou Mbacké tékk lokho niang ballo🙏🙏❤❤❤machalla
Dieureudieuf mouhamed niang mou serigne saliou mbacke yague fin lol te wer sens ordonnance yalnala lafal thiate thiey backe serigne saliou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kou beugue Serigne Saliou beugue Serigne bethio , Mohamed niang yaw tamit yagaal diamono 🙏🏼 barké Serigne Saliou mbacke ❤️
Aminne
Serigne Saliou Ndigueul Thioune yala na fi yague teu were
HAAY MOUHAMED LILANATILA
THIEUY NIANG BALO DO SEEN MOROM DEH .
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
On parle de mouhamed mais l'autre il a vraiment assuré sa voix est tellement melodieuse🤦♀️❤❤machallah ✨
Le meilleur chanteur du monde c'est mouhamed niang mashallah 🕌❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❣❣❣❣❣❣❣🤩🤩🤩😍😍😍😍😍😍😍🤩🤩🤩🤩🤩🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰😅🥰😅❤❤❤❤❤❤
Kéne dou Mouhamed Niang yalla nako yalla Sam nga yague dignou bégueul
Al hamdoulillah Jeureujeuf serigne saliou mbacké
serigne bethio thioune Yalna Yalla yok ay leram ta tass ñu ci barkem ci barkep mame cheikh Ibrahima fall❤️❤️🤲🏾🙏
Kou buege Serigne cheikh salliou ♥️♥️♥️♥️
Amine
Nice khalifa et mouhamed. Une chanson qui me rappelle mon enfance à Saint Louis mes premiers pas si thiant gui. Vous avez repris une très belle chanson que j'avais totalement maîtrisé et chantais d'ailleurs dans les daaras. Ça m'a vraiment beaucoup rappelé ce matin quand je lai écoutée. J'arrête pas de l'écouter depuis ce matin. Khalifa t'as vraiment amené la voix de babacar aidara. Nice vraiment. Concernant le fond on chante à hauteur de sa connaissance.
SERIGNE BETHIO DIEUREDIEUFF
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
❤❤❤s.saliou mbacké❤❤❤,
Je suis tidiane Mais j'aime Serigne Saliou mbacke Mouhamed Niang tu es le meilleur ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️Kou beugue Serigne Saliou beuseul ♥️🙏🙏🙏🙏
Machala
Mmmmm
L'essentiel c que tu sois musulman
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭💯
le ju juste unk ju un tt lol ju on ID ils kh ju é ju k l'honneur khkig ml kg kg Judith khmer Joigny kg kg objet khki
Kou beug Serigne saliou mbacke rk lale j'aime je suis fière d'être moride ❤❤❤❤❤
ndaysaane nékh na loll dh Serigne bethio thioune yalla nako yalla dolly yeurmandé ak diegeul ko si barkép borom touba ak xassida yi barkép borom taif
Serigne saliou ndiguel thioune yagfi loll te werr y'a baxx baye amoul moromam sunu yitte 17avril bi😍😍❤️❤️
Lep Serigne saliou la, yalla nama yalla may dom bou toud Serigne saliou ak kuko begue amine.
Serigne saliou thione yalla nafi yangue barké borome touba 🤲🤲🕋❤️
Ya meu Serigne bi🫶🫶🫶🫶🫶🫶🫶🫶🫶🫶😎😎😎😎😎😎fier d'etre mouride🌹🌹🌹🌹🌹
Machalla 😭🤲 Serigne mountakha mbacke khalif général de l'islam Almoutakha mbacke yall nafi yageu te wér
amine 🤲❤️❤️❤️
Amine Amine Amine Amine
Amine ya rabi
Wa Mouhamed Niang mi nii lagnou kay bagni chanson bou moudié guéneu rk gueneu nekhhh🥰🥰
Machalla ana tkiantakoune yi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalllah yalla na batt bi gueuneu weer sama Werekane prefere ci Barkep Serigne Saliou🥰🥰🥰🥰🥰😍
Beuguenalankhamm sam mbokk talibe ❤❤❤❤
Ndeysane les images disent tout nekhna trop niang balo doundal werall amal diam na yalla weraall battt ni ❤❤❤❤❤
Bilahi son bi nimi def sama khôl bi mak yalla rekk dioko khame❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Dmalaye déglou Di bék rék bilakhi yalla n'a sgne saliou fayal nioula ken d'où iow si mime réw machallah 🥰🥰🥰🥰🙏
Barki borom Touba way wii nimoumay déf❤️❤️❤️❤️❤️, nèkh na, dall na ta ande akouk talibé
Macha ALLAH☝🏽 talibé Baye Niass laniou waayé niou beugue cheikh béthio laniou ndakh mooy Serigne saliou ta Serigne saliou mooy cheikhoul khadim( Rta)
Billahi thiey seringue saliou mdacké amoul morome ❤❤❤❤a ❤❤❤❤❤
Wayatina dé diambarou serigne saliou bi le meilleur de sa génération yalnasa diam yagui 💖💖💖
Dama beugue Serigne saliou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Barkep Serigne Saliou mbacké sama khôl sedtina si yéne Macha Allah Dieuredieufaty borome diamono♥️🙏♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Muhammed niang kén d'où si sounou serigne bi 💯
Toutes ces chansons sont des chefs d'œuvre. NIANG L'éminent l'excellent!!!
Machll
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰❤️❤️
Nimala begué la mouneta explique kén😘😘😘😘
Ndeysane Serigne Saliou Thioune Dieuredieuf Mouhamed Niang♥️♥️♥️♥️♥️♥️🥰🥰🥰😭😭😭
🥰🥰🥰🥰🥰❤❤❤❤❤Mashallah Mon fils yalla na bate bi wéer yafi meune
Mala beugue mouhamed sama khéwe ieo laye woo❤️❤️❤️❤️💓💓💓💓❣️❣️
Le meilleur de sa génération en route vers 17 avril inchahalla ❤️💚
Machalla
❤❤❤❤❤❤❤❤long vie mouhamet niang
Ani talibë serigne saliou Mbacké mouhamed Niang amo morom wallahi 😍😍😍
NIANG MOUHAMED YAA FII MEUN
Niang ballo damala beugue ndakh li nga beugue serigne saliou yalna sa diam yague 🙏🏾♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️ken dou serigne touba 😍
Mouhamad defati ga li seed souniou xol at souniou bokou saint louisien bi dieureudieufati serign Saliou
*1 millions de vues bala semaine bé diekh🥳🥳🥳🥳🥰🥰🥰🥰mashalah niang ballo défa tinga sa meunine😌😌😌*
Machalla Niang 🥰🥰🥰🥰🥰
Lolou moy degue 5million machalla Niang 😀😀❤❤
*🎶Nouveau album Sante Serigne Saliou Par Serigne Mandoumbé Thiam Wadial 17 Avril*
*ua-cam.com/video/-ze03lkawrg/v-deo.html*
*ua-cam.com/video/-ze03lkawrg/v-deo.html*
Na kou nek partager lien bi sa whatsapp rk mou matt
❤❤🙏🙏
Mouhamed Niang à Vie ❤❤❤
Repose en paix cheikh bethio thioune ❤️🕊🪦💔
Amine
Vs💔💔💔💔💔💔💔💔💔:#
Amine 🙏
Machallah Niang ballo doune boulette yalna yalla weral bat bi yok sen ler tass niou si sen barke
Fière de toi toujours égale à toi même Moukhamed sante serigne saliou ba faww ♥️🙏
Yalla naniou yalla fayal serigne saliou ❤❤
Alhamdoulilah Dieureudieuf serigne saliou Mouhamét Niang yalla na bat bi wër 🥰😍
Mouhamed niang ya dak woy senegal ya dak bindeu machallah
Serieu tu es fort
Tu es au dessus
Bi mom da yémé .duo bou doy waar
Même l autre sa voix est extraordinaire
L'autre c Khalifa niang
Merci
@@awaseck2524fréram la wala
👍👍👍👍👍❤️❤️❤️❤️❤️♥️♥️♥️🤍🤍🤍🤍
Machallah serigne mokhamada 🥰😍😍😍🤍🤍🤍🤍Sante serigne saliou bou wer ❤
Djeuredieuf serigne
Saliou dieureudieuf dieuwrigne khalifa ak mohamed mane sokhna faty bou bousso touba ndar bama ka deguelo way bi dafma fatali lou beurri barki serigne bethio tourna na sakh aye khewole dakh serigne bethio dafa sore sama khole wanegueni tay nieupe benelagne ta deh serigne bethio fi mou teude ame mbecte bou reuy waye dinañou manquer lolou waye diereudieufeuti serigne saliou
Yalna yalla lafal thiat avant tout le meilleur chanteur sama sopé sama zikroulah bou mak goudou fane ak wére rk lalay nianal ndakh linguay waye si xol lay diougué di délou si xol♥️💪💪💪💪
Quel jolis duo de mouhamed niang et son frère
Gueuna yagg gueuna wer Niang yalla na yalla weral baat bi ken yaw Niang fière d'être saalihine
Machala niang tu as encore frappé
Dieuredieufty Serigne Saliou Mbackè 🙏🙏
Affaire ca borome Way bila serigne Saliou mbacké nii ngay déff sama khol yàlla rék moko kham😇😇
La voix de Mouhamed Niang me donne la chaire de poule 🥺🤌❤️❤️❣️machalla
Mouride par chance et fier💯🤌❤️
محمد يلنليل دفلدام
Bilahi mom key kemane leu deugue fière d'être mouride❤ sama borom keur motakh ma kham mouride tidiane bou done mouride t fière😍 nak walah❤
Billahi nexna
@@binetoulamotte6517 machallah ❣️
Machalla nekhna trop Mouhamed Niang rek ken du mom si Serigne saliou gnoun salihates yimom content nanu siyaw trop
Dieureudieuf serigne Saliou 🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla yalla n'a saliou weral batt bii goude fane wer werle
Mon amour Serigne Bethio Merci Pour Tout❤❤❤❤Dieurdieufty Serigne Saliou ❤❤❤🙏🙏🙏🙏
Machllah ❤❤🎉🎉
Doumassi doyal je l'écoute plus de 6fois.nekhna.dieureudieuf serigne bethio môme migniou wanaler ak serigne saliou.
🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏👌👌👌👌
Machaalla Mouhamed yalna batte bii werr wayé ken dou Khalifa wallahi lii nexna💖💖💖
Sante Serigne Saliou mbacké❤️🎉mbecté Mii SMA khôl😭❤️ sedd mouhamed yalla na bateu weer❣️
Toma 🥳❤️
Machalah néxena❤❤❤❤❤
Machallah ❤️❤️❤️beugue Serigne Salihou ❤️❤️❤️🌳🍀🌴🙏
yaye man mayy yaw lako SERIGNE SALIOU wakhonn SERIGNE BETHIO mom la wakhatt SOKHNA AÏDA dieumeumm dji yalla nafi yagg tewer
Machallah niang ballo défati nga sa meunine yalla na yalla wéréul batt bi si Barkép S Saliou 🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Mouhamed niang mou serigne salliou rek li ci baat bou nex rek 👍👍👍👍🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Yalla na yalla wéraal lén té saam lén , mon chanteur ❤️❤️❤️❤️
Ziar nalen Sama sope bi machalla yalla nako yalla doli yeureume te doli xewalam
Mach'allah un duo explosif chapeau à Mouhamed Niang
Li nexna dihh
Franchement Khalifa NIANG est hyper fort c'est à cause de lui que je me lasse pas d'écouter la chanson.
Mouhamed NIANG toujours égale à lui même.
Que Dieu vous bénisse abondamment.
Thiey😢😢❤❤❤❤
Toujours à la hauteur de nos attentes
Di nittou fi❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Thiey lou yag bilahi des moments inoubliables .vraiment au temps thiant gui nékhonena té diar si yone... domage...
Machalah mouhamed et khalifa yalla na l'éne serigne bi samb dja dieuf serigne saliou ❤❤❤💖🤍