Boy Niang na xamné dane Reug Reug mo dakh roi des Arenes! Likoy may ndam moy mou andi beuré door baña douté ci meuninam (sou xolé contre Modou ak Balla warna xam). 1-Reug Reug ndanane la mais bo xolé ñimou dane dañko naw ci beurém, soraléko de trop. Ñew beuré wouñou, xexouñou. Kén defou ci lou Reug Reug dindi (Elton, Jordan, BB Saloum, Gris 2, Gouy gui, Bomb) Sa thies seul la guiss mou minimiséko (lingay beuré danoul sax sama dom), dox ci kawam dane ko. 2- Li Boy Niang di beuré arrangéwoul Reug Reug. Boy Niang doko fété souf, doko dadialé. Xolal la defaite de Reug Reug contre General en Mbapatt dinga comprendre. 3- Boy Niang lén rek la soxla ci mom, force interieure, mobilité, souplesse et endurance. Souko amé bén action bounou ame ci Reug Reug daneko inchaallah. Mais loumou soralé ci Reug Reug niak combat bi. Reug Reug bokay dane do hesité ci bén action té kén douko bayék Lamb ci biir guéw. Yalnañou ci Yalla yobou ci diamak salam.
reug reug yangui changer communication dee dou ninga waxe won en côté d'Ivoire lougnouy, geuneu dem ngay geuneu diokh thieur boy niang après ngay soga comprendre
Reug Reug Yalla nako Yalla may ndam
Reug communication nice 👌 bonne continuation champion gua
No reug reug machallah il communique bien maintenant 😅 cest un grand sportif aux nouveau 👋🏽
Reug reug ndam rek inchalla diambar dji champion bii dof bii diam sii yow champion
Machallah reug legui maturité bi Mougui dougue déh kadou yi rafetna
Reug Reug késsè Champion 👑
Merci reug reug ndame rek
Fierté ØMĀR kane reug reug le Belligham de l’arène✌️
Reug Reug tu communique bien sa ce voit que tu es professionnel maintenant bonne continuation champion 😉
Reug reug yalla nako yalla maye ndam lou sedd si kaw boy Niang 2
Pour la première fois Reug Reug se prononce bien... bonne continuation
@@damegueye2221 dafa soneu rek après MMA bi mais ki fok mou tangal.Communication bi kou mou nékhoul gua dém ci novelas yi
Mais reug reug communication bi dafa am niveau sah 😊Machallah yagui nékk champion si communication
Futur roi des arènes inchalla
Boye Niang yalla nala yalla may dam si barké mame fallou 🙏🏿
Communication bi diarna yoon bonne continuation l’international Reug Reug ❤🙏
Reug reug yalnala yalla may ndam
Bne continuation si communication reug ❤❤❤❤
Balla gaye moy sama mbeur mais reug reug yalla na dane boy diang inchallah
Lolou kay diaroul wakh
Yaw kay nel fans balla la rek niou xam fane nga far
😅
@@wizmakhou6871vraiment 😂
Bilahi ya mane ya eup doole parel sa bop si lep reug reug yalla nala yalla soural
Mdrrr 😂
Rueg Rueg ❤❤❤❤king
Reug reug le sonko de l' arenes❤❤❤yafi nekk point
Produits lutte simple ❤❤❤
Reug sa communication bi is very good ❤
@@mamsaitsarr7600 djar na yone vraiment
Reug Reug Seul
Wa yenn louy senn problème ak communication bou bakh ou bou bonn day yagg ba nguenn lekk communication bi may lenn niou diam way
Merci reug linga wakh si modou rafetna
Félicitations champion et bonne continuation
Ya meune ya eup dolé frère ❤
Merci reug do sama mbeur mes conmucation nice na 🎉
reug reug kassé❤❤❤
Champion du Monde Oumar Kane 💥
Reug reug ❤🦍💪🏿
Wawaw champion du monde
diadieuf reug reug communication bi nice na
ki batay xamoul kan moy boy niang après lay comprendre louler lalen wax inchalla boy niang va battre reug reug inchalla
@@NdiaboutaDiouf amine inchallah boy niang ndam rk
Boy niang dakoy doumeu dane ko
Saway boy niang loum fi deff may niou way lamb la rek reug dou thiouné
Reug dakoy fakate mou reup 😂😅😊
Bougar bou Reug reug Dionne l’homme Diakhao
International bi ❤🦍🇸🇳
Reug reug tay sa wax rafetna Machalah
Rueg rueg ❤❤❤❤❤❤🎉🎉
Lou rare 😂😂😂 Omar Kane deff interview defoul penalty 😭😭manchallah bonne continuation.
Reug❤❤
Reug am nga combat bou graw sax😮😮
Bo dané boy niang dinama bétt
Peulh mol nga❤
Reug seul boy niang parewol foko diap lambdji diekh 😂💪
Boy niang seul 🥰
Reug reug seul amoul lenen
Ndeysane leigui mbeur bou mak la communication bi changer neu ma challah
❤❤❤❤❤💚💚💚💚💚
Bègue na tropp si sa communication bon chance
Communication bagui nieuw dh 👌 nonou leu rkk
Machallah tu évolue niveau communication👍
Ki pareei n'a si lamb 😂😂 amatoul envie comme avant😅
ioe danga nékh rk reug mo meun boy niang fouf sah té amoul loumouy tite si mome
Boy niang sa baye la😂😂😂
Dell wakh rk bala premier janvier 💚♥️🤫
Reug reug modou lo nekhouli afair dé 😂😂
Reug dé dioxoul combat bi thieur lolou rék moma titeul
inchalla dinga danou inchalla rabi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
4 appuis c’est une absurdité !!!!
Reug Reug bayil thiakhan nga dém outi dolé sino boy Niang déflay danou dé man iow la faral mai éns bi mom amo dolé😢😢😢😢😢
Amoul doole nga wakh d 😢😢
Entréné woul dè insbi dafay weur di wakh rek
Eyyy reglel ufc dou morom muuu one championship belt ak pl
Dafa touti reug, paréwoul pour le 1er
Ordinateur mérite na combat nk lague 🎉
Yalla nala boy niang danne
Boy Niang na xamné dane Reug Reug mo dakh roi des Arenes!
Likoy may ndam moy mou andi beuré door baña douté ci meuninam (sou xolé contre Modou ak Balla warna xam).
1-Reug Reug ndanane la mais bo xolé ñimou dane dañko naw ci beurém, soraléko de trop. Ñew beuré wouñou, xexouñou. Kén defou ci lou Reug Reug dindi (Elton, Jordan, BB Saloum, Gris 2, Gouy gui, Bomb) Sa thies seul la guiss mou minimiséko (lingay beuré danoul sax sama dom), dox ci kawam dane ko.
2- Li Boy Niang di beuré arrangéwoul Reug Reug. Boy Niang doko fété souf, doko dadialé. Xolal la defaite de Reug Reug contre General en Mbapatt dinga comprendre.
3- Boy Niang lén rek la soxla ci mom, force interieure, mobilité, souplesse et endurance. Souko amé bén action bounou ame ci Reug Reug daneko inchaallah.
Mais loumou soralé ci Reug Reug niak combat bi. Reug Reug bokay dane do hesité ci bén action té kén douko bayék Lamb ci biir guéw.
Yalnañou ci Yalla yobou ci diamak salam.
Belle analyse ❤
❤❤🎉🎉🎉
Reugreug yagui may commencé sof😢,démal entrainé dji gir yalla 🫣🫣🫣🫣🫣🫣
😂😂😂Saway ki mo eup bn2 Dole 😊apre ngenn d comp
Reug reug esque xam boy niang dalay dane inshallah combat piège pour toi
Reug reug migui may commencé Safadi
reug reug yangui changer communication dee dou ninga waxe won en côté d'Ivoire lougnouy, geuneu dem ngay geuneu diokh thieur boy niang après ngay soga comprendre
Comp naaa boubax ni Thiapathioly bi dou aye tiaxane
Lamb la dal xana niom niar nieup am nagn combat
Boye Niang mola meune foufe jour ba ngaye comprendre sakh
Dou ngalani de francis nganou la dolé ne kholl ligué ne di wakh😢
Peulh gneweul Thiès dielsi Modou anta
Modou anta mane😂
Entous cas ragal na sa combat ak boy niang da mélni paré woko bou bakh depuis nga diogué thi mma bi a te voir da melni da ngay noyal
Combinaison m ngu niew
❤❤❤🎉
Reug doffou lamb dji lègui dagua nittè lol dofal way mbeur soulla nèkhè meun ga liguay dèf
Reug reug bou signaturé kou nék nane meunoul communiquer alors que dafay néexal rék légui boudoul lamb niou introgé ko Mouy wax kounék nane légui Daf meuna communiqué té Reug reug meussoul changer nii leu meuusa méle Dafay néexal rék sénégalais mo métti😂😂
Boy Niang Seul Domou Pikine Bii Ndam Rek 💚❤️
Dou Ngalanou 😂😅 Ngannou La 😅
Ngalani kay gnouss nako ba pare 😂😂 Ngannou moy star bi
Yow mome Reug Reug bayil ba guene sissa niari combats yi mouy Boy Niang ak Ama niou khol lofay def ba pare danga moudje bari wakh trop
Koula conseil maintenant tu commences à communiquer bien 👍
Mais Yalna boye niang am ndame
Ki mom dafa Bari wakh légui
Boy niang dinla douma daan la 💚♥️
Inchalla si barke cheikh tidiane
Dangay geunt rèk mè sou bèsba dinga dioy dè😂
Reug reug kholoule boy Niang
@@CheikhMbéngue-v7x dangay ndaye doull
Linga beug nga wax
😊
Ngannou mounal ngalani lool😂
Tey mom wakh nga wakhi nit
ngannou pas ngalani
Nganu dou ngalani
Reug seul😂
Mais Reug lsmbj DJ désoul 1 mois wala
Boy niang mola meune
Waho deug💪
Chekh bass anti reug reug sa khole dou nékh dh reug rek
Loumou leundeum leundeum boucki for beuy
ki parewoul sakh pour beure le 01janvier reug reug sa façon de communiquer nekhouma dara
Tu n'est pas exceptionnelle pourquoi mouy communiquer lola nekh
Wakhou fi dra lou niaw wala lou graw
@@YannickDieng-wv4sh Vraiment 😂😂
Nganou ou ngalani
Ki mo meun boy niang fouff
Damaye lathé rk boy Niang noumou mana dané reug reug moma diakhale 😂
Kou dane sathies kii dou la diaxale bayiléne wakhi doff
@modou2004 kou dieul champion du monde NK ha wakhi doff
Damalay lathie kou dane Sa Thiès avec la manière Sa Thiès mi fowé Reug
Bayil sa khel mi nkey fowé ndam Yalla ko yorr
@@adamasene2768 boy reug mo bimouye guéne arréne nationale victoire la guéne ok
Ngaaka gua boy Niang dinala douma dane la
Reug : Modou doussa morome nak:
Epuis Franc néna: #Soko dieulé mou nokouleu #
😂😂😂Saway Esk Xam nga ki deg deg
Franc reug reug si douche rek lako danoul kokou sou reug reug di nelaw meunouko teuyé
Ki hol bé néhoul😂
Mé kane moy ngalani ?