La réponse de la maman de la fille qui a été mordu par nafi fallou fall

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 9 лют 2025
  • La réponse de la maman de la fille qui a été mordu par nafi fallou fall

КОМЕНТАРІ • 289

  • @diarriatoumbacke3166
    @diarriatoumbacke3166 7 років тому +52

    Thiey yalla adouna yakhouna nite yii perte naniou séne Ay valeurs, ngor ak diom rereu gni wara defar rereu yalla naniou yalla khirr si lou bakh té defal niou soutoureu si barki Serigne touba

    • @mamadoudiawara6935
      @mamadoudiawara6935 7 років тому

      Diarriatou Mbacke adouna yakhoul dh Sénégal mo yakh

  • @philippealmeida657
    @philippealmeida657 7 років тому +4

    Raféte nga dalleu té bari charme machallah

  • @mary18203
    @mary18203 7 років тому +6

    Joseph Correa moy sama man.
    Yallah meun leppa, yallah na la yallah yiir...

  • @alviny777
    @alviny777 7 років тому +9

    Oh bilay kii nekhnama elle a parfaitement raison

  • @AlphaDiallo-gz8gm
    @AlphaDiallo-gz8gm 7 років тому +27

    Sénégalais (e) dagnon gueum serigne de trop alors que bcp sont des escroc retourner vers Dieu en plus rappeler vous le jour du jugement c soit disant serigne pourront pas vous sauvez stp changeons les mentalités.

    • @fatiima3275
      @fatiima3275 7 років тому +1

      Mansour Sy tu as dit vrai pour ma part. Je n'ai pas de serigne mais sa me fait mal de voir les gens jurer sur eux

    • @CanKl
      @CanKl 7 років тому +1

      Fati' ima ceux qui le font sont des ignorants. Je suis soufi et je ne jure jamais par mon marabout

    • @abdougaye3440
      @abdougaye3440 6 років тому

      Yéne gnognou gnéna rér yakar ni kham guene lép.

    • @khoudiandiayediouf3045
      @khoudiandiayediouf3045 6 років тому

      Bougnou la liguéyone ba nga beugue dé Di nga khamni yalla Manou soudé djiné amna j'oumou douguou dinga dém si Serigne bouko meune mou tagalé la AK mome môme balade moulay raye

  • @khadimg2078
    @khadimg2078 7 років тому +6

    Très bien Sokhna si katal Ndéyam rek yako meun

  • @yofariedieng2086
    @yofariedieng2086 6 років тому +4

    Bayilén niak fayda souguén amé problème demlén tivaone walla touba ak yénén kerou diné yi gnognou la yalla maye mé arnaqueur yi pour lane

  • @ngomyacine5200
    @ngomyacine5200 7 років тому +17

    Sokhna ci wakh bou doffé nop ya coy dég nité coulé dég nigaye wakhé hamné degg rék gay wakh

  • @diarrasene2605
    @diarrasene2605 6 років тому +6

    Allakhou ak barr bismilla yalla na yalla yok diam yalla na khalé bi tané ak diam

    • @awamdaye5243
      @awamdaye5243 6 років тому

      Diarra sene j
      i
      ..
      .
      . @.. . jeu

  • @fatoumar20
    @fatoumar20 7 років тому +56

    Wakh bou donn deug kouko deg xam ko yaw linga wakh moy deugg

  • @khadimcisse7258
    @khadimcisse7258 7 років тому +16

    yalla dinako fé Niale légui bilahi

  • @Alktar.0560
    @Alktar.0560 7 років тому +142

    yene yeup pa yeme 7 h si souba ba 7h ci gone endurance bobou nga ame sokko amone ci diamou Yallah deugg deugg pendant des heures di toudd Yallah di diouli bayi beupp safane legui sa dôme weurr pour aller chez les charlatans vous êtes prêts à décrocher la lune et pour Dieu même diogg diouli les 5 premières normales sakh thiono la nous retourneront tous si souniou borom Allah SWT konne ndank rekk adouna dou keur!!!

  • @elpacino2451
    @elpacino2451 7 років тому +3

    nafi fallou fall deum nga sakéto serigne fallou di doule li dafa yomb troop ...

  • @momotraore8491
    @momotraore8491 7 років тому +2

    Boul di ton tou sokena si del ball ak yalla .boul defati video svp tu as raison

  • @djizmbow272
    @djizmbow272 7 років тому +9

    très bien parlè

  • @diagneabasa424
    @diagneabasa424 7 років тому +2

    sénégalais Yoko kham beurrer na daye torikhale nitte fi Sénégal FO dème neki FO dème agne terangua Sénégal la fek bakh namou leque guisstale thi teleyi TER bonne khole

  • @assgueye5653
    @assgueye5653 7 років тому +11

    je vous le jure khamoul dara femme bobou nafi bopam la mounane fallou fall di togne ser fallou..... sama cole sama sokhna moko neub mafokni danko dieul rek makoy setlo mounane ma khale bou goor bi moguikoy diaay si marche bi alor ke c'est faux

    • @cheikhdiopc
      @cheikhdiopc 7 років тому

      Ass Gueye Hahaha

    • @ballalo3917
      @ballalo3917 7 років тому

      woooy Ass Gueye rayngama
      nafi kholatal sa bopp

    • @mamadoudiawara6935
      @mamadoudiawara6935 7 років тому

      Dou danguene beug affaire serigne dem lene rek wara yew xadiou guoudi djouli djam yallah nga am werr yallah fadj seni sokh la mais non affaire de serigne rek

  • @aad4446
    @aad4446 7 років тому +48

    nafi fall, je savais qu'un jour ou lautre tu auras cette mésaventure moi je peux témoigner de ce que j'ai vécu avec cette soi disante guérisseuse qui ne cherche qu'à avoir le buzz et être citée dans la presse, cette dame au moins on lui a rendu son argent mais moi cette nafi m'a soutiré presque 1 million de francs en sarakh de tout genre deux bagues en or bélier et autre détails en plus du weekhaal, jai arrété daller chez elle parcque jai compris son jeu meme si cétait trop tard mais doumalako messeu baal parceque largent que tu mas soutiré khadiona si mane je lai gangné à la sueur de mon frond et je nai vu aucun résultat au contraire oumou rapp la fa djeullé elle trie les visiteurs selon leur statut si cest des journalistes des politiciens elle fait tout pour que lassistance sache que tel ou tel est là est son talibé à longueur de journée elle met l'audio de son invitation à la radio si cest un oyoof boubou comme moi qui vient la voir doula sakh yeukk soo khéffé mou wagni la mais si kouka nangou sama khaliss bingua lekk djeuleul mais alakhira damakko faay doumalako messeu baal en plus elle se permet de dire aux gens sass naléne sama mini chaine bi yaakhou mélni serigne mbacké mbacké walla sy gnoune gnoognou lanouy djookh sounou adiya mais pas fathiekat, jai lu le commentaire de mamy fortes tout ce que tu as dit est vrai cest la seule solution wakirlou si Yallah khamné moo djeukk té mooy moudj té lou am rék mooka neekh mooka dogual té kéne menou si dara té biss boukoo soobé mou dindikoo bamou sett khaliss danoukooy liguéy liguéy bou sell pa di ko tékk si ayy door. fathiekat bouy khéébaaté dou fadjal kéne sokhlam mais sama akkh dinal dall je te jure nafi fall

    • @mariemefall9222
      @mariemefall9222 7 років тому +2

      C une habituée des faits elle a soutirée de l'argent a une copine qui vit en Espagne plus de 500 cent mille francs son fils était malade Moi j'ai jamais crû a cette femme c une vraie menteuse en plus sou xamé ni ta compris son jeu elle ne taccepte plus en visite

    • @mamadouwade331
      @mamadouwade331 7 років тому

      AAD f

    • @SAYANDECAPILLAIRECLUB
      @SAYANDECAPILLAIRECLUB 7 років тому

      courage Dieu est au contrôle

    • @aminataniang2652
      @aminataniang2652 6 років тому +4

      Makhala vous croyez plus aux marabouts qu'a Dieu

    • @thiorofall8654
      @thiorofall8654 6 років тому +1

      Xamoul dara leek na sama 60000mil si ay rew nena mai doumalako meuss bal

  • @moissediop9949
    @moissediop9949 7 років тому +21

    7h si souba ba 7h si guone koula wakh diouliwoule fofou wakhtou diourome yi fofou dafa amone yakare ner dinako fadiale domame rekk nakhter ni padioume hopital amer nonoula amer bou wolof guanaw yalla

  • @zaraba4442
    @zaraba4442 8 місяців тому

    Cette dame elle est forte du courage pour ta fille ❤❤

  • @diatousow1908
    @diatousow1908 7 років тому +22

    ah mane déh diomina mé bo kholé femme bi version wam mo valable deug nékhoul mé femme limou wahk ressemble à une vérité absolue

  • @mamediarra9739
    @mamediarra9739 6 років тому +1

    Bayilen serigne Te diap si yalla

  • @khadimcisse7258
    @khadimcisse7258 7 років тому +28

    Sokhna si ligua wakh lépu deguele

  • @DioufPapa-v4s
    @DioufPapa-v4s 8 місяців тому

    Merci sister

  • @elpurity6691
    @elpurity6691 7 років тому +2

    Cette femme a complètement moi même je suis témoin de leur insolence au staff de Nafy j'ai été choquée de leurs comportements méprisant

  • @dioced1
    @dioced1 7 років тому +28

    Soubhanallah Allahou Akbar. Qu'Allah nous guide!!!! Apprenez votre religion!!!! Sinon vous êtes fichus pour de bons!!!

    • @amayelthiam4037
      @amayelthiam4037 6 років тому +1

      dioma lecomte ils sont déjà fichus lol

  • @kinefall8544
    @kinefall8544 7 років тому +10

    les guérisseurs sont comme si ils sont célèbres c'est difficile de les voir en tête a tête je suis partie au Sénégal pour voir un guérisseur connue c'était très difficile

  • @lampfallndiaye6814
    @lampfallndiaye6814 7 років тому +10

    Mane khamou ma loutah thiaga bou diouk rek ni dafaye set aka fathie nie fay deme nioko def

  • @talibebambasoldaroucheikhi3805
    @talibebambasoldaroucheikhi3805 6 років тому +1

    Billahi linga wakh moy dag nafi na bayi serigne fallou dxoul si ay thiaxann

  • @diagneabasa424
    @diagneabasa424 7 років тому +3

    nafi dafa tokk wakh femme bi tokk femme foulleu moye diaye dakcare

  • @ngonediop356
    @ngonediop356 7 років тому +5

    femme bimouye deme dafa beuguone kouko fadiale domame rek kome bepe fathkate domame bignou eguer ker nafi domdji nekou gnou gnibi mou bagne ndakh domdji Khamer na rabamm mai yaydji khamoul intention fadiou seulment yayedjou diakhler

    • @bailandiaye2184
      @bailandiaye2184 6 років тому

      C'est une grande menteuse elle profite des gens là même chose que ablaye diop et en complicité avec les tele

  • @medoukane9408
    @medoukane9408 6 років тому +1

    vraiment j'aime ta personnalité

  • @boypoulo8770
    @boypoulo8770 7 років тому +1

    SOKHNA sii bou fakhe dagnoula wonii gua deff ndanke ndanke rekk d'al diam rekk adouna amoul sollo

  • @bintadiallo2555
    @bintadiallo2555 7 років тому +13

    ki limou wakh moye deug

    • @awafall2349
      @awafall2349 7 років тому

      Binta Diallo mani loko woor ni Nafi moo diap domame. Bimouy deme keur Nafi Fall bane intention la amoone

  • @ngonediop356
    @ngonediop356 7 років тому +6

    Ta raison dh bilaye

  • @beugueloubax9241
    @beugueloubax9241 7 років тому +3

    yéna yam top léne feulé ragal léne YALLA

  • @diagneabasa424
    @diagneabasa424 7 років тому +1

    femme limou wakh fi moyé dafa démone pour nafi fadialko mais nafi moko dake môme nafi mola gueuna kham femme bii ak domou femme dofuole djinne l'Aa bou guande

  • @adamaseck2142
    @adamaseck2142 6 років тому +2

    tu a raison tout le monde le c

  • @nguenelguilofficiel1146
    @nguenelguilofficiel1146 6 років тому

    Sokhna si li nga wakh deugue diou ler la sokhna sosou di fathie khamoul dara

  • @AminataGochou-ku3ig
    @AminataGochou-ku3ig 5 місяців тому

    Aaah kone dalay doug après nga dem si mom mou fathieula.

  • @mbayesonko8968
    @mbayesonko8968 7 років тому +56

    Nafi khamoul touss lékna sama 60000 bilakhi khamoul touss

    • @faluthiam1960
      @faluthiam1960 7 років тому +12

      mbaye ndiaye
      ms mane dama khamoul loutakh guen di dem si serigne si mane sama yaye dafa ganiou ms louma beugue damay dem si barabam niane limay niane ms pas ay faut maraboutas

    • @camararock4543
      @camararock4543 7 років тому +3

      mbaye ndiaye c'est des iblis tout est bon pour chercher l'argent

    • @boromverite1242
      @boromverite1242 7 років тому

      iow mbaye ndiaye sokhna nafi fallou fall def lekk sa khaliss ndiil sa facture bou won sokhna nafi fallou fall kayii ak sa facture momeu kekou mouyii leguayel deyii def facture merci

    • @faluthiam1960
      @faluthiam1960 7 років тому +2

      borom verite
      ms yaw lane motakh ga beugue mou indi facturan

    • @boromverite1242
      @boromverite1242 7 років тому +1

      parceque sokhna nafi fallou fall koumu diaye deyii am facture meme soula diaye deyii def facture soula setal deyii am facture mbaye dal sou fekk degue layii wakh na niow ak facture souba mane ak mbaye niou dem ba ci keur nafi fallou fal mou rambouss ko wa salam

  • @moissediop9949
    @moissediop9949 7 років тому +5

    khamoule dara rape la mo douguou khaler fegnouko mate ko khaler bi khaler bii khamer nako mome djinne laa dakoye wakh achaque fois mai nena khaler bi dou massawerre yalla ko eupe doler

  • @lathfall7369
    @lathfall7369 7 років тому +2

    Moytou lene serigne yi dinane lene sacrefe

  • @diengselly6344
    @diengselly6344 7 років тому +1

    eskey c'est bizarre dh mais louleneu dall rk begg serigne moleneu dal geumoleneu YALLA daraa wasalam

  • @Pénda-e3d
    @Pénda-e3d 6 місяців тому

    Dèlène diouli di niane yalla bayi seirigne yi sokhna deugeu rèk wakh

  • @saerdiaw790
    @saerdiaw790 5 років тому +1

    CEST VRAI LE JOUR LA JAI T LA BA LA FEMM LA ELLE LA DIT LA VERITE DEUG NEKHOUL

  • @abdourahimkanetouba3120
    @abdourahimkanetouba3120 6 років тому +2

    Nafy day doul rékk Mane mii wonako mouy doul rékk

  • @diagneabasa424
    @diagneabasa424 7 років тому +1

    foutess Borom veriter Borom fene oui kouye tekou mono d'Ara daguaye bayi kiguaye tekou mou guise do d'Ara loudoule soukke koula diapp diapp soukk kou la baa bayii soukk yagui merder mais guissgua femme bi bo l'ennko bayiwoule di guenne fegne A suivre😯😯😯😯😯😯

  • @bambafall8323
    @bambafall8323 6 років тому +5

    Kii mo pank nak ..fan naala sakh

  • @aminadiagne604
    @aminadiagne604 7 років тому +2

    ay diagne naar sama domou baye ligua wah rek moy deug

  • @khadimg2078
    @khadimg2078 7 років тому +2

    Moh nafi kou todj lefeule Ndéyam la khamoul thiotou ndéyam

  • @taphandione2857
    @taphandione2857 7 років тому +1

    affaire bi serigne basse molèn dak fathie mo lèn gena ragal yalla

  • @diagneabasa424
    @diagneabasa424 7 років тому

    kou Am sa Cheveux poko kepeuwoule bopou nenne guaye deff ki soko kholer khamner sakouwoule ndibeule femme bii wakhou deugue mo nekhoule kounekake sa avis anhhhh

  • @mary18203
    @mary18203 7 років тому +11

    Nianal len Sokhna xi ak domam

  • @keishyt8110
    @keishyt8110 6 років тому

    Li rek motax Sénégal dou avancer

  • @mameboussodiop6024
    @mameboussodiop6024 6 років тому

    doyna war maintenant ki FAI confiance vraima Sénégal kagne la honnête du am motakhitr dougnou bouché mètres

  • @timathiam8508
    @timathiam8508 6 років тому

    Wakilou len lep ci yallah bolen andeh ak yallah soubhanah hou watahlah ak mouhamed salalahou aley wasalm bolen dolen mosa diaxlé

  • @elmalickgueye383
    @elmalickgueye383 6 років тому

    Dégue deug xol ak xolla, gueum naala. Déllou thi YALLA RÉK MO YOR LÉPP.

  • @diopmaman1692
    @diopmaman1692 7 років тому

    doule akk fene thi nafi fall la euper l'I mou foule thi you tubi eupena

  • @papewade4979
    @papewade4979 6 років тому +1

    nifi falou fall moy lan Aÿ doorla rek

  • @brahimbehnass7228
    @brahimbehnass7228 7 років тому +1

    Wakh diouler kouka degg xamko.ki loumou wakh deuggg leu

  • @mbayesonko8968
    @mbayesonko8968 7 років тому +19

    Bilakhi wakh gua deug

    • @mbackedieng5580
      @mbackedieng5580 7 років тому

      mbaye ndiaye .loolou leu cheytané ne veut pas entendre les noms de DIEU

  • @astoudia2663
    @astoudia2663 7 років тому +8

    Niom niepa yam nafi ak bassirou ndiaye khamouniou dara yaw tamit ab dof nga nakala nafi Mana neké rabou sa dome deme Len diamou DJI yala té def Al khouran sen werou way mo geun si yen té ngen bayi ndiabar katyi they don't know nothing

  • @coumbadiallodjeri2831
    @coumbadiallodjeri2831 7 років тому +11

    Tu as raison deh

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 Рік тому

    Yakar kouy dee ya meuneu bokalee demlen diagui

  • @abdouazizsy5228
    @abdouazizsy5228 7 років тому +1

    Maleu beug sokhna si

  • @safiafam314
    @safiafam314 7 років тому +5

    c vrai yanék si deugu

  • @brahimbehnass7228
    @brahimbehnass7228 7 років тому +1

    Wawaw mangui si guinaw yaw sama domou baye nga tei sama mbokk khelkom nieup benleu tei mane samay mame xelkom lagnou deukk

  • @cheikhkane269
    @cheikhkane269 7 років тому +6

    Nafi bobou ab dil Kat la rék.

  • @beuguefallou1677
    @beuguefallou1677 5 років тому

    Mane lima diakhal moy yaww négua sa mame dadone fathie waa légui loutakh yaubou woko fofou mogeune gua yaubouu koo thi nioo hamoull tamitt

  • @oureyerassoul822
    @oureyerassoul822 5 місяців тому

    Nafi doulkate la sama khoulowalé wayé dotouko defati

  • @diagneabasa424
    @diagneabasa424 7 років тому

    samy yow Ya wara ragual sa boro du wakh thilokhamoule tousss nafi la akk femme bii akk allahhhh

  • @religioncoranetsunnahmusli2588
    @religioncoranetsunnahmusli2588 6 років тому

    Sokhna yaw rek comme rek rap parsk yaw mi deme ba ame dome di beute lamin tague cheveux sokhna so amé dome daga rawa sèll tay sèllale avc sa motakh doléne amna arr sèni dome

  • @mj-zq4qg
    @mj-zq4qg 2 роки тому

    Senegal guemleen yalla

  • @assanendiaye2997
    @assanendiaye2997 6 років тому +1

    Li yeup niak yakine mo lene ko yobe amougnou bene géum da guéne wara bayi diamoukatou kheureume yi te dioublou si yalla

  • @ngonediop356
    @ngonediop356 7 років тому +1

    yow nafi ki yayela domame terernako sa keur mou bagne lnieuw bassa keur yendou 7h si souba ça 7h si ngone fadiolene nane heurou djine yi guaye khar yow dagay louch ana serigne falou mbacke bigua mboubo dafa labirone lole nitte danena danou dielle thi wetam moi defeulko nawssi defoula dara yako rogne tre togne d'où gualath waqqalam

  • @khadymaguette9233
    @khadymaguette9233 6 років тому +2

    Nafi porte toujours des gant

  • @yvonnesarr3418
    @yvonnesarr3418 7 років тому +12

    Vérité absolu

  • @diagneabasa424
    @diagneabasa424 7 років тому +2

    Ya yeye deff photo diane yena yame yowmomou lagnou yoni dokhale fowi

  • @mariamasene7086
    @mariamasene7086 6 років тому

    Thi rang bii il y'a des espion ou des micro peut-être que tu as parle avec ton voisin sinon comment elle a su que tu as vu l'autre? Soyez plus intelligent

  • @mamidiop3570
    @mamidiop3570 7 років тому +5

    Doynawar trop bilay

  • @momodioume3802
    @momodioume3802 7 років тому +3

    Seny cheveux naturel lol comme ay goor.

  • @kadijasow1945
    @kadijasow1945 7 років тому +1

    deugg pirr nga wax loudoul yallah nénn la ki meun dou teukou dalay bayi nga guiss

  • @bayelatgadiaga1427
    @bayelatgadiaga1427 7 років тому

    Sokhna nafi bokko degué mou wakh rek nga kham ni mo nekhoul fo deug li louko fi diar ndakh alal ak tour rek.

  • @iyasakhesab5517
    @iyasakhesab5517 6 років тому

    Je suis un bon marabou maintenant les femmes je veu des milions

  • @SENHITViews
    @SENHITViews 6 років тому

    yangua manel key, est ce k dou mamelle tamit lol...........di baaatarei key ...nena ay cokiimentaire keyyy ....thiey bilei toubab

  • @aminafall4556
    @aminafall4556 6 років тому

    Aye mane dama tite sakh si sama bopou bilahi adouna bi yakouna rap yi diniou dougou rek do nek nite do nek djiné wa li tamite louy garabame

  • @cheikhmbaye1087
    @cheikhmbaye1087 7 років тому

    diadieuf amna solo

  • @oureyerassoul822
    @oureyerassoul822 5 місяців тому

    Nga nokeu ko

  • @user-uw3dk2we4n
    @user-uw3dk2we4n 7 років тому +2

    Elle est magnifique cette femme j'aimerais beaucoup faire sa connaissance

  • @awakane7811
    @awakane7811 6 років тому

    akhirouj jamane gnewna ba paré nagn dlo khel yi ak Khol yi si borom bi

  • @samydiamanka9837
    @samydiamanka9837 7 років тому +5

    domou adama ken douko tekou

  • @evayu7323
    @evayu7323 7 років тому

    limoye akhirou zamane ma cheikhoul dadial ak sina

  • @ngonediop1952
    @ngonediop1952 7 років тому

    bolene demer thi pajou nafi gnom amoule comentaire amna bene pa niouner pa ass mouye wakhe si nafi gnome gneupe ay djinne lagnou senekhette ta barri dagno sakanne

  • @awakane7811
    @awakane7811 6 років тому

    thiakhane bi beuri na si adouna bi nagn geum yalla

  • @khadimndiaye1115
    @khadimndiaye1115 6 років тому

    joseph correa kay😂😂😁

  • @sanoundour4092
    @sanoundour4092 6 років тому

    Makhaala golo gou diokk né day fathieuu

  • @nouroulsaliou9308
    @nouroulsaliou9308 7 років тому

    senegal mo nekh deh bilay

  • @SN-kx8mk
    @SN-kx8mk 5 років тому

    Dame bi sadique na

  • @medoukane9408
    @medoukane9408 6 років тому

    a weuy yaw la gueum, bayko ak yallah c'est une démon