Je pleure a chaude parceque je me vois en cette histoire!Ma mere a vendu les memes choses ,fripperies et tout rien que pour nous avec dignité!Alhamdou lillah je suis au Etats Unis elle ne va plus jamais !Never ever suffer in her life never !Je veux sil vous plait les contacts de Pape Sidy !
Moi personnellement c mon animateur préféré je l’aime beaucoup il a beaucoup contribué sur le Hip-hop sénégalais aru mbed c le meilleur émissions hip-hop au Sénégal 🇸🇳 mes respect frère 🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢 elle m'a fait pleurer ta maman Pape Sidy yalla na ko yalla may wér ak goudou fane lolou wayyyyyy si barké Chéikhna Chéikh Sadbou Aïdara🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ma sha Allah yalla nala yalla takha wou ma mère dafa souffert si life pr gnou réussi alhamdoulilah gningui deff tout pr la rendre heureuse parsk elle a mérite ❤️❤️❤️
Tu as le droit de pleurer. Pleurs mon fils. Tu en as le droit. J t'aime mon fils. Ta ma maman est une brave dame. Et toi tu es reconnaissant. J t'aime mon fils. Demeure béni.
Frère je t'adore souma guissé kou beug yaye damay contane doundal frère ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️g vécu 17 ans à soigner ma maman téy démna mais je regrette rien bravo frère
Machalah du courage WADIOUR keneu amoul fayam gorgorloule bou bah si sa yaye ba ma sagnone sa ma yaye nékeu fi di doundou ak mane ba maguet 😢😢 yaye yi fi nékeu yalla na niou doundou ba enerve yaye yi djitou yalla na lene yalla yeureum te yehe niou te khare ko si aldianaye firdawsi si barke S Mouhamed psl 🤲🤲📿📿
amena nio khameni bouniou dakarou change fate lilene indy dakarou top boite de nui yi conmenece tokhe woute ay kharite you bese mais nila nite dagaye khame figua diougue
Amiine doome da wara sagale wadiourame surtout Yaye, Pape Sidy thia kawe thia kaname, boule dioye Fall,Yallah nala Yallah nala Yallah same, sa téranga Yallah na yague
Dome ndeyame Pape goudal fane ni rekla thia kaname rekk ndeye kouko soutoural Yallah soutoural la Pape Sidy beugone nala mais yokouna Yallah nala Yallah lafal thiatt Fall
Yalla kham n'a sama yaram dafa done daw bilahi . Yalla n'agnou yalla d'éfal téranga gnou téral Sunu wajour yi . Ils le méritent Manou gnou Léen Faye. Aduna Mougn rek mo am solo
Machallah dôme bou neck li rek gay niane sa yaye geureum la niouye niane yalla nalene fi yalla yagal gni nek thi Souf yalana lene yalla diegueul te ate lene thi yeurmedeme 🤲🤲
C émouvant j ai les larme au yeux c ce que je dit tous les jour yallah dou dioum dou diawalé c pas pour rien que yallah dans 4part donne les 3 a maman❤
Pape sidy je t'adore et te respecte parce que tu aimes ta maman est nos mamans sont toutes notre vie elles méritent d'avoir tout ce qui est beau dans ce monde
Une MÈRE ❤️❤️❤️❤️ fait un FILS 🦾🦾🦾
Je pleure a chaude parceque je me vois en cette histoire!Ma mere a vendu les memes choses ,fripperies et tout rien que pour nous avec dignité!Alhamdou lillah je suis au Etats Unis elle ne va plus jamais !Never ever suffer in her life never !Je veux sil vous plait les contacts de Pape Sidy !
2STV
Pape Sidy kou baakh laf thiat
Beugue Daara. Maa Shaa Allah
Nieuw na sou niou DAARA CAMBEREINE tchi Cheikh Mbacke Laye. Contane tchi mome
MachAAllAh yalla nala yallah yobalal lep temou barkei incHAAllAh
Bravo Pape Sidi vs êtes naturel é humble et ne change jamais le monde t'aime vraiment.
Salut fall merci tout yaye amour faye sidi fall alnagadou fane merci sidi thia kaw athiakanam rek
Tu m'as fait pleuré aussi je revois ma mers dans ses années de galère. Mais tay lepeu diexna gueye ndioro tes enfants sont super fieres de toi
Ahhh wi une brave dame. Elle le mérite vraiment
Ndeysane c'est émouvant ,ay nos mamans yallah na yallah fay len , pape sidy gueuneuleu gorgorlou
Moi personnellement c mon animateur préféré je l’aime beaucoup il a beaucoup contribué sur le Hip-hop sénégalais aru mbed c le meilleur émissions hip-hop au Sénégal 🇸🇳 mes respect frère 🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹
MachaAllah Pape sidy fall Mane mom damako fan rék baye fall bi courage et force a toi
Kou téral sa ndeye rek yalla téral la inchallah
Elle m'a fait pleuré... Longue vie à notre maman
Bilay c'est émouvant😢😢dem ba sa yaye dila geureum dafa nekh si xoll yalla na yalla May goudou fann sunu yaye yii incha allah❤❤
Ma sha Allah. Quou sagal sa yaye yallah sagal. Gueuneul goorgolu si sa yaye. Si khaw si khanam
Ça me touche beaucoup ça m’a fait pleurer même
qu'Allah le tout puissant te protège pape sidy fall sikaw sikanam depuis la France
J'apprécie beaucoup cette séquence, plein de leçons de la vie.bravo mbaye fall tu es naturel
Comme si c’était ma mère qui parlait c’est émotionnel dioyna fi yeup wallah ces genres de témoignages ça fait inonder mon cœur♥️😭
Psf lima nekh mooy simplicité bi mashallah, wahdji c'est riche en enseignements
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢 elle m'a fait pleurer ta maman Pape Sidy yalla na ko yalla may wér ak goudou fane lolou wayyyyyy si barké Chéikhna Chéikh Sadbou Aïdara🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ndeysan 😭😭sama xol sedd na deh 🙏🏾🙏🏾
Ndeysane pape sidy Mane damakoy beugue rek te yalla takh Machalallah amal diam
Yalla nala yalla yok bou bakh pape sidi fall bakhnala yalla fau sa khol kou bakh ngua kou yatou ngua amal diam
Bilaye sama touche vraiment que dieu veille sur ta maman
Machallah sidy contane naniou si yaw tu est bien ,tu a une bonne communication, humble vraiment on te souhaite le meilleur dieuredieuf
Mashallah liguey ndeye agnioum doom .sa kaw sa kanam rek lolou laniou rawanté wadiour dagne koy fonk
J’aime bien ce gars,surtout ne change pas
Li nekh na mais mane Doumako ame Parce-que mere bi ak pabi dem naniou avant maye mane dara. Machallah
Vraiment c'est une d'y Partager avec toi dans un même quartier tes un référence Bro Pape Nôtre cool frére on love 💪💪💪💪
Ma sha Allah yalla nala yalla takha wou ma mère dafa souffert si life pr gnou réussi alhamdoulilah gningui deff tout pr la rendre heureuse parsk elle a mérite ❤️❤️❤️
Tu as le droit de pleurer. Pleurs mon fils. Tu en as le droit. J t'aime mon fils. Ta ma maman est une brave dame. Et toi tu es reconnaissant. J t'aime mon fils. Demeure béni.
Tu m'as fait pleurer Pape sidi kou teral sa wajour yalla terarla boul ragual dara sa kaw sa kaname rak
Mais bizarrement je retient plus mes larmes 😪😭😭😭😭😭😭
Une mère restera toujours une mère❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭😭
Mar sha very emotional, keep it up.
Machallah témoignages yi rafetna maman🥰
Bonne continuation pape sidy fall, longue vie à tt les mamans ❤
Pape sidy respect li sa mère WAhk si iow motahk ma respecter leu, kusa wadiour guereum ma respecter leu🙏🙏🙏
Machalla pape sidi thia kaw thia kanam rek barkhé serigne fallou
Machallah pape sidy ne change surtout pas on t'aime comme tu es et longue vie à ta maman et toutes les mamans
Ndayssane dawna yauerem 😭😭 Machallah papa sidy fall ❤❤❤❤❤❤
Pape sidy vrai baol baol il parle du pure olof machala tres pertinente en sa langue
Frère je t'adore souma guissé kou beug yaye damay contane doundal frère ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️g vécu 17 ans à soigner ma maman téy démna mais je regrette rien bravo frère
Ndeyessane massa yalla na khipé aldiana🙏🙏🙏
Elle serait fière de toi
Yaye dou morome dieuredieuf yaye boye machalla rafétna
Yalla na Mère bi guoudou fane way🙏🙏 BiG Respect Grand PSF
PA sidi ya beurri diom manshalla sa kaw sa kanam ndeye ak baye d'où morom. Koulen teral yalla teral la
Un homme que aime beaucoup pour sa simplicité
Oh oh j'ai beaucoup pleuré Pape long vie à notre chère maman
Bien joué Pape Sidy Fall du courage et que le bon Dieu t'accompagne chaque jour de ta vie !!!!!
Pape sidy vrai good man leu
Machalah du courage WADIOUR keneu amoul fayam gorgorloule bou bah si sa yaye ba ma sagnone sa ma yaye nékeu fi di doundou ak mane ba maguet 😢😢 yaye yi fi nékeu yalla na niou doundou ba enerve yaye yi djitou yalla na lene yalla yeureum te yehe niou te khare ko si aldianaye firdawsi si barke S Mouhamed psl 🤲🤲📿📿
Ndeysane Machallah ❤️ ❤️ ❤️
Ohhh ndayesane p s f ma la beugué rek yalla takh ❤️💕💕💕💕
Dom djiou nekk warna weur li si yayam !! Machalah sa kaw sa kanam rekk
Machalla fall li nekhna 😭jai mem les frissons
Mashalla thia kaw thia kanam thi bakh pape sidi y'a bakh
amena nio khameni bouniou dakarou change fate lilene indy dakarou top boite de nui yi conmenece tokhe woute ay kharite you bese mais nila nite dagaye khame figua diougue
Machallah tu es tjrs souriant et tu es un exemple pour la jeunesse
Pape da nga bakh beugue sa yaye très reconnaissant meuno nga changer do khama ti ni sa yaye sonewone
Amine yaaye ♥️🙏Yaako ligguey maman.yalana YALLAH yokk kheweul yi té bayyila si kanamou ndjabott gui bâ si kanam mou yaguala terral
Machalla boy bi dama ko beuga Pape sidy Sui depuis paris
Pape sama Pape Latsouk Faye lalay kholé ni yow lamel sagalnama yalla nalen yalla diapalé
Machalla papa sidy fall ❤🙏❤
Machalla pape yalla nala yalla defal diam
ohhh ndeysann Mashallah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ndeysane pape Sidy MachaAllah ya bakh dôme dja ndeye dja
On est fier de toi li rekk yaye sou contané rekk yalla contane ❤
Manchallah Baye Fait k'allah SWT t''assiste
Amiine doome da wara sagale wadiourame surtout Yaye, Pape Sidy thia kawe thia kaname, boule dioye Fall,Yallah nala Yallah nala Yallah same, sa téranga Yallah na yague
Suis touché PAPE sidy sa yaye geureum nala.li rék la dome du sakou thi weuydiour.macha alla
Ndeyesann pape sidy lii mo takh ma beugue leu rek t yalla takh dangua baakh dioy na ba sone yalla na yalla motali sa yéné ci barké seydina mohamed psl
tu es vraiment un exemple parmi la jeune génération, bravo
Ce gars il est trop humble Wallahi 🥰
Fall ya bakh ❤️❤️❤️nagnouye fonke wadioure dafa bakh trop machalla gno bokone classe
Dome ndeyame Pape goudal fane ni rekla thia kaname rekk ndeye kouko soutoural Yallah soutoural la Pape Sidy beugone nala mais yokouna Yallah nala Yallah lafal thiatt Fall
Yalla kham n'a sama yaram dafa done daw bilahi . Yalla n'agnou yalla d'éfal téranga gnou téral Sunu wajour yi . Ils le méritent Manou gnou Léen Faye. Aduna Mougn rek mo am solo
Pape sidy fall ndiaga yaaram je l'aime bien
Machallah PSF yallana la yalla arrr té samla sii barkepp cheikh ahmadou bamba ❣️❣️❣️🤲🤲
Pape sidy diambar nga bro aussi tu es natural
Machallah laf thiat pape sidy yalna la yalla teral
Ndeyesane Maman tu me fais pleurer
Amine waye ndéysane lii downa yarame
Notre Baye fall
Yalna la yalla dolel té saam la bidjahi seydina mouhamed psl
Yallana Yalla Goudal sènfan Sunou yayi fi dèss ak mbolèm Diulit Amine Yarabi
Ma beug dom diou sagal wadiouram . Rien que pour sa je te porte désormais dans mon cœur soit béni
Formidable maman sop nako torooooooooop
Bravo papa djiby surtout ne change pas merci maman amine yarrabi
Machallah yaye ak doom Mbeuguél bou fort té pur telment
machalla , il est simple pape sidy, sa mére est brave, vive les mamans
Machallah laf thiat 🙏🏼🙏🏼🙏🏼
RESPECTS À VOUS !!!
Machallah dôme bou neck li rek gay niane sa yaye geureum la niouye niane yalla nalene fi yalla yagal gni nek thi Souf yalana lene yalla diegueul te ate lene thi yeurmedeme 🤲🤲
Grand bravoooo a pape sidi ,que Dieu nous garde longtemps encore notre chère Mamannnnnn
Ziar GOOR YALA bi mane lima nekh si yaw moy tu est fière de ndiarém diourbel moi je suis de dakar mes ces mon constat et puis BAYE FALL bi
Machalah pape sidi li nékhna trop longue vie maman 💗
Machallah Nice 🇸🇳🇲🇦
Pape sidy diambar nga 👌
C émouvant j ai les larme au yeux c ce que je dit tous les jour yallah dou dioum dou diawalé c pas pour rien que yallah dans 4part donne les 3 a maman❤
Pape sidy je t'adore et te respecte parce que tu aimes ta maman est nos mamans sont toutes notre vie elles méritent d'avoir tout ce qui est beau dans ce monde
Bravo bro, mn journaliste du hip hop l meilleur, k dieu vs protèges
Ndeysaane profitez de vos mères les gars je donnerai la terre pour revoir la mienne 🙏
maman Machallah Amiiiiiiine ya rabi 🤲🤲😭😭😭😭😭❤❤❤❤❤❤❤Ndeysane