Touba Scandale! non commenté : Nangou Diabarou Sa Talibe (confisque la femme de son talibé)...

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 455

  • @morniang2342
    @morniang2342 4 роки тому +83

    Sama gayi fonk len sen wadiour, afairou Serigne yii dou dara, man mom sama yaye moy sama Serigne louma am diokh ko...!!

    • @awadiallo9360
      @awadiallo9360 4 роки тому +9

      Walhatiko

    • @morniang2342
      @morniang2342 4 роки тому +12

      Dama khamni kat, Serigne bo khamne mola dakh keur mola dakh diabar mola dakh auto, ba pare nga kay diokh, lolou moy lane??? Magui diegalou dee, waye man dan afair guemouma ko man dal sama yaye loumou beugue madiokh ko

    • @user-ln4nd6ci9t
      @user-ln4nd6ci9t 4 роки тому +2

      Yaw khamon foy takhaw

    • @sididiakho6481
      @sididiakho6481 4 роки тому +2

      Ta raison ma bro

    • @henridior8348
      @henridior8348 4 роки тому +3

      Seydina mouhamed psl néna passeport bi laye dougal adjana sa yaye mo kaye signé
      Mé Dou Serigne wou Kate sén ndéye yi dmrm

  • @thimbythiomayar88
    @thimbythiomayar88 4 роки тому +14

    Data rek ak khaliss lonou gueum. Kou nangiu saa diabar doula yibou aldianaa

    • @ibrahimasarr1951
      @ibrahimasarr1951 4 роки тому +1

      Ya déèéde

    • @salifbalde8419
      @salifbalde8419 4 роки тому +2

      Duég duég wahati ko dééh

    • @minafall8709
      @minafall8709 4 роки тому +1

      Wakh leinn ma reik bann gor mo bagn data ak xalis si aduna

    • @salifbalde8419
      @salifbalde8419 4 роки тому +1

      @@minafall8709 yakar naa bariwoul déh...

    • @minafall8709
      @minafall8709 4 роки тому

      Salif Baldé dafa amoul Sakh gneup ko beug gor bo guiss mouy yeiwou fa diar di dang da ngui djigein motakh

  • @malkomx9503
    @malkomx9503 4 роки тому +8

    Mane dé Yallah képeuma doy, Serigniou diamono bi koulén topou mba nga yakarlén bilahi perteunga

  • @Serignefalloucamaraborom_chifa
    @Serignefalloucamaraborom_chifa 4 роки тому

    Yen gniepp yam aiyi vrai domèrangué kidnappée islam bii sathie guènn souffe si adiyeu guèns leck d'i gnious doul reck modifie yonnou Serigne bii ayi khathie deug-deug guenn ayi bokalé katt guén ta ma lenn kowhax kouthie dée saffar migui layi kharr ak mboléme koulén toop thie cène réhre gui au bon antandeur

  • @haqiiqatan5128
    @haqiiqatan5128 4 роки тому +22

    Lou thiow li di gueuna beuri niuy gueuna beug Serigne bi diko gueuna gueum diko gueuna yaakar
    Muniuy gueuna wane bopam

  • @talibebayam7620
    @talibebayam7620 4 роки тому +10

    Serigne Dam Atta Mbacké.
    L'histoire retiendra

  • @ousmanelam479
    @ousmanelam479 4 роки тому +6

    Serigne Touba kou bockoul thi môme même so bocker si thi familleyame dinga werrou.mack mou toulouni waratoul sakh khalat djiguene.gueumougnou yalla gueumougnou yonent gueumougnou Serigne Touba.Sen bakane reck.

  • @robinlustig3669
    @robinlustig3669 4 роки тому +11

    Si cela s'avere vrai, c'est d'une extreme gravite. Il faut porter plainte. C'est le conseil qu'on peut te donner.

    • @khadyjakonate9039
      @khadyjakonate9039 4 роки тому

      Bou porté plainte aussi dou moudié féne fi Sénégal la, mé doyna ware trop bilahy

    • @robinlustig3669
      @robinlustig3669 4 роки тому

      @@khadyjakonate9039 C'est la triste realite. Tant que la justice restera partiale ce pays restera malade.

  • @sidimoctardiop3761
    @sidimoctardiop3761 4 роки тому +5

    Entoucas bâyi toogne moo gueun dioulli té yeenaghi toogne kouleen defoul dara dara diamou yalla bâ son GNU dieulko diokh KO kanenn dara guenouk doon pertement serigne Dam atta yalla nga fi yag té werr

  • @zillebwoyzillebwoy4262
    @zillebwoyzillebwoy4262 4 роки тому +9

    lila Ndam déff bakhna siyow .
    Nga Dore sokhnasi batah mu dem wakho wakhdji lutah sokhna si dem yoname? Bayiléne Dorre Djigen😥

    • @cyrene3796
      @cyrene3796 4 роки тому

      Wakhal si kaw

    • @musikonline550
      @musikonline550 4 роки тому

      Ça justifie pas que soit disant serigne bi di nanguou diabaram. Senegal pseudo serigne yi nioko yakeu

  • @djibrilndiaye5563
    @djibrilndiaye5563 4 роки тому +1

    Moussa Camara amena loumou wakh,preparelene moussa mougui niew

  • @maguettethiam2093
    @maguettethiam2093 4 роки тому +12

    Ayayway demal si mom wax tan lì rafetoul😭😭😭😭

  • @maxlalionne8146
    @maxlalionne8146 4 роки тому +16

    Touba tamite lifay kheww barina trop

    • @antatoure1494
      @antatoure1494 4 роки тому +1

      Bayi léne touba way akh

    • @musikonline550
      @musikonline550 4 роки тому +3

      @@antatoure1494 loutakh niouy bayi touba khana niom douniou aye nite? On est des mourides mais sou deugue dioté dagnoukoy wakh

    • @nnguerahmadou475
      @nnguerahmadou475 4 роки тому

      @@musikonline550 yaw khamngané dou mouride lii dafa gnaw

    • @dieynabaseck9266
      @dieynabaseck9266 4 роки тому

      @@nnguerahmadou475 doul

  • @mouhamedthiam9048
    @mouhamedthiam9048 4 роки тому +8

    Touma yag na si adouna si nite kou bah.jangual hista zeyide ibn harriss ak seyidina mouhamed psl,sunu yaye aicha rta,seyidina youssoufa ,seyidina yahya ak zakaria ,ak seyidina inssa dingua hamni nite niou bah gni yag nagnleina toumal.silo hamni boko topè bassi bir dingua hamni dara amoussi .

  • @abdoulsy8821
    @abdoulsy8821 4 роки тому +3

    Ce n'est pas nouveau avec vos marabouts.
    Portez plainte ,si vous tenez à votre épouse.

  • @rachelle8160
    @rachelle8160 4 роки тому +3

    Évitons les jeunes MBACKÉ MBACKÉ ils cherchent k hypnotisés les femmes mariées

  • @jeancharlesdiatta6875
    @jeancharlesdiatta6875 4 роки тому +7

    Kou bagne lou nekh Serigne N.Dam a raison . 😁😁😁 moi je me demande si c.est le premier cas ?Continuer avec les Serignes. ...et un jour vous verrez vos peres pleurez parce que en douce ils ont epouse vos meres et grand meres

    • @rachelle8160
      @rachelle8160 4 роки тому

      10 diabar daganena thi yéne,domérame

  • @mikakaw8968
    @mikakaw8968 4 роки тому +4

    Franchement li niawna... ki dagne ko wooor.
    Yalla nala yallah diapaler ...
    Non li metina trop...
    Sama yaraam gui daw sahh.
    Woor bahoul (trahison) ,
    Surtt avc la complicite de sa belle famille.

    •  4 роки тому +2

      woor gou bonne Sakh

    • @mamankanefaye1190
      @mamankanefaye1190 4 роки тому

      @ domou bireul bi 😂😂

    • @garamtv677
      @garamtv677 4 роки тому

      @ sa thioutoundeye

  • @siradjindiaye2764
    @siradjindiaye2764 4 роки тому +16

    Te sax man am na kuma ci doon waxal mune ma waaji dadaan duma ndawsi guddi ak bëccag te jot nakoo fase (9) (fo)i te loolu bu amee sëy ba lislaam haraamal nako bu yàgg
    Te yéen ñiy tas xabaar yi ak ñiy commentaires dellu léen ci alquraan waxoon na leen ne bu leen ab kàccoor andi lee xabaar saytu leen ko ba xam wér na
    Waaye nag dommage ndax daanaka boo xoolee commentaires yi daanaka waxi par-parloo rekk nga fiy gis te wax ji kiko wax gennaat na ba jéggalu

  • @kingjames5726
    @kingjames5726 4 роки тому +2

    Li mou wakh yepou si c’est vrai Serigne bi ndiallo kay la mais wadji doff na aussi

  • @mounawiroulbounyanetv1496
    @mounawiroulbounyanetv1496 4 роки тому +4

    Alahou akbar 😭 Li mome Geuna Yémé

  • @demebadiekh7476
    @demebadiekh7476 4 роки тому +1

    Thiey serigne mbacké mbacké you bess yi😎😎😎🤭🤭🤭🤭

  • @user-mm7ue9kz7z
    @user-mm7ue9kz7z 4 роки тому +1

    Tu es amoureux mon frère courage!

  • @Marieseck534
    @Marieseck534 4 роки тому +7

    Sama béneu neveu dé serigneum def nako lou mel ni

  • @babacardiop5575
    @babacardiop5575 4 роки тому +8

    Diarama seydil hadji malick sy

    • @momo.business.global6369
      @momo.business.global6369 4 роки тому +1

      Toi tu es un Satan ce que le gas a dit n'a aucun rapport avec ce que tu as écrit. Séytané ibiliss

    • @simbadicko1194
      @simbadicko1194 4 роки тому

      Talibe cheikh do deug thi yene détail yi, ndak bo tenkou thi Alqurane loubari déflay diomb

    • @sopebayamesanteyayame5397
      @sopebayamesanteyayame5397 4 роки тому +1

      Tidiane aka nekh, naguou sa diabarou talibe ci mouride rek la ame ,thièy lé mouride bordel rek ak djiguène. pa bi loumou meune ci khalèbi sakh nooo, thièy seutou bamba BA yi

  • @yerosow3713
    @yerosow3713 4 роки тому +4

    je comprend plus vous êtes de la famille de serigne touba où non méfiez vous des femmes

  • @Rimka912
    @Rimka912 4 роки тому +7

    C'est grave

  • @khadydia7837
    @khadydia7837 4 роки тому +13

    🤣 C'est vous dans vous 🤣

  • @ndiayemor3072
    @ndiayemor3072 4 роки тому +1

    😀😀😀😀Serigne nangu jabaru talibe wutel yat

  • @mamediarraseck2548
    @mamediarraseck2548 4 роки тому +1

    Bayil lène yakheu der..Senegal natou yi douffi diouk ndakh togne nittou yalla yi.Serigne Dame Abdou Rahmane doussa morom seuteu Serigne Touba leuh té waliou yalla leuh bayilène ndiabotou Serigne Ibrahima Mbacké.Yoe nak lilay daal khamagoko sakh

  • @henridior8348
    @henridior8348 4 роки тому +3

    Serigne bi kou beug leuff la
    Dmrm futur khalif

  • @morndiaay7723
    @morndiaay7723 4 роки тому +6

    Mane dh yémouna si Sénégal ani sutoura

    • @musikonline550
      @musikonline550 4 роки тому +2

      Pourquoi moukay soutoural? Ana serigne ak naguou diabarou diambour?

  • @moussadiatta5320
    @moussadiatta5320 4 роки тому +10

    serigne bi dé wakh na deug comme que nio deff sén bopp mbam niou traité léne comme mbam rek

    • @ousseynouboye2112
      @ousseynouboye2112 4 роки тому +1

      Non non suis pas d'accord

    • @garamtv677
      @garamtv677 4 роки тому

      damay deugue sa ndeye iow ak moussa camara

    • @cherifahmet9395
      @cherifahmet9395 4 роки тому +2

      @@garamtv677 C'est ça, toujours et encore des insultes et rien dans la tête. En attendant que ngay djéma DEUG ..., seugn bi dina ROUKH séni sokhna yi. Yawmal khiyam gnowa goul sakh, seugn bi di worr talibém si kaw souf. Kom ke seugn yi gno mom sen doundou ak seni déé, nangou lén séni djeuf. Djapo lén si dara.

    • @garamtv677
      @garamtv677 4 роки тому

      @@cherifahmet9395 damay kate sa ndeye

    • @cherifahmet9395
      @cherifahmet9395 4 роки тому +1

      @@garamtv677 🤣😂😁 Toujours des insultes à la place du savoir que vous n'avez pas et refusez de chercher au bon endroit.

  • @yacinetall7995
    @yacinetall7995 4 роки тому +8

    C'est grave mais yénela rék guisagouléne dara

  • @yfftgyfh695
    @yfftgyfh695 4 роки тому +8

    Nooo lé gui kay diaratoul serigne dam rék wala gran dame😂😂😂😂😂

  • @yvefay620
    @yvefay620 4 роки тому

    Ahhh !! Serigne dame ...Hana gunégui défa saf diggueu marine affaire ? Gorgui 'outil bénéne meuneu am diggueulé hawa yolom

  • @samb.5428
    @samb.5428 4 роки тому +1

    Quel pervert ce monsieur Dame Atta ! Un vrai Teddy Bear (cougar version homme), il aime la chaire fraiche, ça ne fait aucun doute.

  • @ousseynouboye2112
    @ousseynouboye2112 4 роки тому +4

    Li dafa niaww barkè BOROM touba sa diabara talibè,leep soxnasi la rek elle sont graves les femmes ces des sorcières nioy toukkil adouna walahi

    • @lemzosene8563
      @lemzosene8563 4 роки тому

      Non boul wah sohna si dara djigene khelam matot payi degno thiaga way ahh defna lou bonne

  • @mouhameddiao2225
    @mouhameddiao2225 4 роки тому +2

    Que la vérité tombe dieu est juste

  • @diopmohamed8321
    @diopmohamed8321 4 роки тому +3

    Billahi kouthi diangaloul say doom noukham sen diine ay mbaam lanoulenidef

  • @tupac6345
    @tupac6345 4 роки тому +12

    Serigne déloko diabaram way

  • @demebadiekh7476
    @demebadiekh7476 4 роки тому +5

    Thiey soutoura amatoule ame na rapor sexciel kaye 🤣🤣🤣🤣🤣😉😉😉😉

    • @khadimg2078
      @khadimg2078 4 роки тому +2

      Report sexciell ahahah1🤣🤣🤣

    • @minafall8709
      @minafall8709 4 роки тому +2

      😂😂😂😂😂😂

  • @nanitimera7848
    @nanitimera7848 4 роки тому +4

    Les activise a non resont de insulted les marabou mbacke mbancke

  • @bijoux7662
    @bijoux7662 4 роки тому +2

    Sooy wakh sa loubone boul sédé lo s touba niack fayda thipppp

  • @lapuissancendnd9592
    @lapuissancendnd9592 4 роки тому

    Sénégal khama gouniou sarakhame kilifayi naniou wakhe si li serigne saliou mame fallou mame abdou ajije serigne babacar seydina baye seydi thiaw Sénégal sokhe la nagne séni niane🤲🤲🤲🤲😭😭😭😭

  • @AbouIbnBabouches
    @AbouIbnBabouches 4 роки тому

    Vous feriez mieux de vous occuper de votre vie au lieu de rester dans ces âneries de Serigne et autres...
    Nous sommes tous égaux, sommes issus d'un rapport sexuel entre deux personnes et nous finirons tous en cadavre..., Donc oubliez ces fanfarons de Serigne...

  • @rachelle8160
    @rachelle8160 4 роки тому

    Anna serigne ak dieul diabarou diambour,domérame

  • @Espoir-mk7ge
    @Espoir-mk7ge 4 роки тому +13

    VAS CHERCHER UNE AUTRE FEMME!!!

  • @diobadiouba5119
    @diobadiouba5119 4 роки тому

    Wa lii khana Moussa Camara yeugouko😅😅😅

  • @syllaahmado3933
    @syllaahmado3933 13 днів тому

    Aduna Amul solo

  • @morserigne2952
    @morserigne2952 4 роки тому +2

    Amo soutoura dé mane nou diamou way

  • @salifbalde8419
    @salifbalde8419 4 роки тому +5

    Séring yii mom moy lolou , sénegal défa doy waar déh...

  • @diopsouhaibou1296
    @diopsouhaibou1296 4 роки тому +3

    Serigne khawou Boussa wa khoufi lou ler eska dou ya dialaw Kassou Radiap ba Tabaski yaga na de ba guia khame ne manou gou Moni loy wathie wathie wathie koy tas say ak Goudol tas say da am

    • @siradjindiaye2764
      @siradjindiaye2764 4 роки тому +1

      Wax dëgg Yàlla

    • @soundiatakeita6080
      @soundiatakeita6080 4 роки тому

      Mem sou ida gui maté sah warta takh mou djeulco sohna nakh wadji daco defone bay defco kilifa ba paré djital co si lep si waloum seiy bi

  • @zaldiop6293
    @zaldiop6293 4 роки тому +1

    C'est un serigne loumou deff baxna ndakh mola gantier adouna ak lakhira moudougal aldiana serigne momo soutedee ak sa diabar sakhh barkee rekk ngueyy am😂😂arrêt de suivre ces gens là il non aucun pouvoir sur leurs propres personne comment vous pouvez espère quelque chose des leurs part si c'est que des déception🐑🐑🐑mbehhh

  • @wakeupafrica9906
    @wakeupafrica9906 4 роки тому

    AU SÉNÉGAL ON EST CAPABLE DE TOUT FAIRE ... Faite attention à ce qu'on nous donne en consommation avec les sites internet ils ne font que vendre leur produits...

  • @aissatousouare463
    @aissatousouare463 4 роки тому +2

    Eey waay kii beug na diabaram dji dee ndeyssan. Mougneul reek comme que gnoun mounou gnou ci darra bouffi weer sa bopp. Daagnou leey kokoli doong... Andal ak sa sago😂😂😂 té gueum yalla

  • @domouwalothiam7075
    @domouwalothiam7075 4 роки тому

    Moi en tant que Sénégal je m'en fous ni guèneu di déf yor diabar diko fonto bi kéneu takeko vous venez pleurnicher, j'ai des rapports sexuels avec elle dans mon salon dans le cours c'est pas notre problème maintenant elle est marié cherche pas une autre fille c'est tout 🙏

  • @moustaphadieng6544
    @moustaphadieng6544 4 роки тому

    Guis nga gor bouy tak diabar day tak djiguene bouco beugue mais di topou djiguene comme c est pas possible moh

  • @deggfeenjotna
    @deggfeenjotna 4 роки тому +3

    Ya Allah lquran ak Sunnah wétena Senegal

  • @layembodj8826
    @layembodj8826 4 роки тому +1

    Vraiment Est Ce Que Ce Marabou A Des Talibes C'est Honte De Faire Ça. Diabarou Diambour Nga Tak Ko Foko Tek Dou Diné Dou L'islam

    • @Corailpro
      @Corailpro 4 роки тому

      Cest le potentiel successeur de serigne moungtakha pour le khalifa. Mara bi dou n'importe ki deh. Hahaha ab kilifeu leu daal

  • @morkhoule4112
    @morkhoule4112 4 роки тому +1

    Ani moussa camara yaguenaleinn wakh la bouteille ba defff momm la coubeirr gui di kheigne

  • @layewade1758
    @layewade1758 4 роки тому

    Ay Serigne dame 😂😂😂 rapport sexuel

  • @laveriteappartientaallah5218
    @laveriteappartientaallah5218 4 роки тому

    Serigne bii li métina trop yonou mourides trop de thiakhane lolou beurri trop si yonou mourides trop trop

  • @fazaniangthanksyou751
    @fazaniangthanksyou751 3 місяці тому

    Top lene yalla tabayii sering siii

  • @galasndiaye5349
    @galasndiaye5349 4 роки тому +5

    Li nak môy moudiouk diamono djigeune diarout lii

  • @coubasow6613
    @coubasow6613 4 роки тому +2

    Merci beaucoup mousa camara

  • @fall10fall86
    @fall10fall86 4 роки тому

    Le linge sale se lave en famille. Pas la peine de preciser le lieu où vous avez fait le rapport sexuel. Kiko tak tamit niémé na lou salté. Gni takk lou eup 4 femmes aussi niongui si ndialo.

  • @adamandongo4653
    @adamandongo4653 4 роки тому +3

    Sokhna si moo goré wuul rk

  • @moussacamaramanlimagwaplag7033
    @moussacamaramanlimagwaplag7033 4 роки тому +3

    Yaw boul doh ci kaw helou ga yi barke borom touba waho deug li am wahoko serigne-bi yaw hana amo kilifa Mo tah mani li am wahoko

  • @djatoudiawara1075
    @djatoudiawara1075 4 роки тому

    Demal wakh sa mbette serigne Mountha Mbacke

  • @AbdoulayeDiallo-wh6mp
    @AbdoulayeDiallo-wh6mp 4 роки тому +1

    سبحان الله 😱😱
    Il n'es pas sérieux

  • @sallibrahima9964
    @sallibrahima9964 4 роки тому +2

    Ziar vraiment YAYE kou yabate gua meune féne yaw amo soutoura Naka gua meune publiquement wakhné sekh gua ak Sokhna n'importe quoi serigne bi bou beguone Sokhna si douloko maye ligua wakh yenouyoul mana, en plus sa kharite intime mo retourné takal ko serigne bi diagualé wathianala yambar gua rek

  • @abouba1485
    @abouba1485 4 роки тому

    Sénégal lou nèkh way dèf parceque nénaniou dénio ame wèrouwaye

  • @kalakala8032
    @kalakala8032 4 роки тому +2

    Ana talibeyi no komant 😂😂😂😂😂😂

  • @salsandiaye2387
    @salsandiaye2387 4 роки тому +3

    Thimm koulène tok bayi yalla soy dèè di lak tèkiwoulène dara

  • @nanitimera7848
    @nanitimera7848 4 роки тому +2

    Yene la rek mouride tope lene sene wadiouri mo guene serigne

    • @serignendiaye6280
      @serignendiaye6280 4 роки тому

      Bol gon sako lo ko gony topou yéne domi saytané yi

  • @boubacardiouf8454
    @boubacardiouf8454 4 роки тому +2

    Tu n'as pas besoin de nous le dire. Va régler ça avec lui.

  • @moustaphadieng6544
    @moustaphadieng6544 4 роки тому

    Sa way arrêtes li djiguene diarouco ah

  • @fallypapa307
    @fallypapa307 4 роки тому

    Li gnawww na torope thiaye sounou mbacké mbacké li doye na warrrr

    • @rachelle8160
      @rachelle8160 4 роки тому

      Kate diabarou diambouryi yi lanioufi néké

  • @petitjohnlincontournable7345
    @petitjohnlincontournable7345 4 роки тому +1

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣welcome To Sénégal

  • @falconseyetros1606
    @falconseyetros1606 4 роки тому +4

    Non Rousna sahh wallah..

  • @ndeyesadiokane9407
    @ndeyesadiokane9407 4 роки тому

    wa ki wérna li kén warouko wakh thi radio

  • @Serignefalloucamaraborom_chifa
    @Serignefalloucamaraborom_chifa 4 роки тому

    Noo lennè yinn lagniu yarkar baparé guén gueun gnio beug lou néx gueun gnioow beug lu bon ak lu bax lepp bagniou lenne darra russoulèn darra digniou digui aldjianayi doulreé ku leu meuneulou fii dara es que meneul nala fèe darra naniu d'élu
    Thie Alhuran d'élu thie Rassûl d'élu fa Yalla sa doundu perte
    S
    A il
    Akhir
    A
    Nul
    E d
    A
    E
    A
    Diarru koo

  • @mamadouba614
    @mamadouba614 4 роки тому

    Ww Serigne dame atta menimi la walla

  • @albaraka4111
    @albaraka4111 4 роки тому +1

    bu nekke khalifa nangu jabaru jambur dina bari wa salam !!!

    •  4 роки тому

      Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine:
      ua-cam.com/channels/tEULeCJpv7u-iOgIYo79iA.html merci

  • @salioudiaw3089
    @salioudiaw3089 4 роки тому

    Ndéyssane😂😂😂😂😂😂

  • @laveriteappartientaallah5218
    @laveriteappartientaallah5218 4 роки тому

    Trop de orgeau cé eu takeu si yéne sa wauroul

  • @moustaphadieng6544
    @moustaphadieng6544 4 роки тому +1

    Rapport sexuel ci ab salon tamit dou nex ymgx mom kay ci Kaw lal bi rek

  • @bigbeuzse7en_asm07
    @bigbeuzse7en_asm07 4 роки тому +1

    Subhana Allah

  • @cheikhibrahimakarediwane8107
    @cheikhibrahimakarediwane8107 4 роки тому +1

    Wadji limou wakh Lou yaguela dou 2019 sakj té mom mi ndon wakh tobalna Serigne bi iow borom site bi kou mana féngue té yarou wo kilifa kou tolné s dame ata Dana nagou diabarou diambor mélné kou diagoul

  • @cesttekzoone60
    @cesttekzoone60 4 роки тому +1

    Khamnany badoolaga dé bo bayé kay nou tak

  • @bayeseye3361
    @bayeseye3361 4 роки тому +1

    Y'a mana faine ligaye wakh d'où degue

    • @khadyjakonate9039
      @khadyjakonate9039 4 роки тому

      Pourquoi tu lui traite de menteur alors il as bien expliquer son histoire,. Mé toi à sa place

  • @jomandemarjane6617
    @jomandemarjane6617 4 роки тому +2

    Pourtant c'est le co-khalife

    • @abdoukhadirdiop9592
      @abdoukhadirdiop9592 4 роки тому +1

      ma leral la touty rek so mane am benen version bi di nga xamni limou wakh amoul ensuite dou la ko khalife serign sidy mou serign abdou lahat moko mak ? di djegalou nak

  • @daoudandiaye7706
    @daoudandiaye7706 4 роки тому +1

    Danga noppe khalébi di tiiteurou bamou reutieuleu 😅😅😅Amooo dara loowakh,baayiléen bounguéen beugué séen Soxna yi di sagou, aka tiiteurou bamou dm ngay, rayy niti di wakh .

  • @solofallwz
    @solofallwz 4 роки тому +1

    Ani moussa camara
    Mais li c'est tres grave....li gnawna lol....

  • @diopmayoro6011
    @diopmayoro6011 4 роки тому +3

    Kholal ma yeufou mbam yi rek gnie aye vrai imbéciles lanou djiguen rek ak khaliss beug ni aldiana yénako môme

  • @thiamaminta7502
    @thiamaminta7502 4 роки тому +6

    Bouléne rouslo séne mame

  • @mouhamedthiam9048
    @mouhamedthiam9048 4 роки тому +1

    Zayide ibn harrissa (sahaba) yonentibi dako jaappè wone kom domame ba bolèko si ahloul bayti .kerok bimou takè sohna ba sohnasi tasse ,yonentibi takk amoul louko yeifeuri makka wahoul si louniou niaw lo halate si lou niaw wah nagn ko yonentibi psl..bayileine kilifa yi guein di toumal ta gueine halate seine bameil nioune haamnagn leip nimou dèmè kougn si nèhal haliss gua jog dal si kaw kilifa yi ta niom douniou tontou serigne touba fi lako mbahane touba toumal .....

  • @rachelle8160
    @rachelle8160 4 роки тому

    Démal Dakhar ndéyam mou diokhla sa diabar

  • @diabelgueye1096
    @diabelgueye1096 4 роки тому +2

    Serigne touba dh mom amoul morom