Làkku Wolof : Njariñul Jànge Ci Saw Làkk (Lan Mooy Làkk?) Liila Réew Mi Wara Waxtaane

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 24 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 120

  • @nourou519
    @nourou519 2 роки тому +8

    Machalla man de Li geune di wakh kham nasi dara ndakh ndakh dama taxawall louñouy wax xam sa Dine waayee si Wolof laakoy waxee Si diir bou gate mokal nañu teere bi di laxa jariñu

  • @mameamardieye2136
    @mameamardieye2136 2 роки тому +4

    Boul baayi deh leye amna solo lool sakh

  • @momombodj9716
    @momombodj9716 3 роки тому +13

    Ma Challah Rafettna, Dieureudieufati danion wara diag sounou Làkk

    •  3 роки тому +1

      🙏

    • @bakhikillifatoure5066
      @bakhikillifatoure5066 3 роки тому

      @ numèro abdu la soxela woone tè yalla taxe

  • @mouhamed_ndiaye237
    @mouhamed_ndiaye237 2 роки тому +13

    téh mane lima guëneu néh ci waadji mooy wolof you sétt withie lay wah

  • @adamafall2306
    @adamafall2306 3 роки тому +7

    Machalla Mr leye mom day guou bakh bilahi ndaysane yalnsa diamou yague dama dane diangale mouy kou bakh lol

  • @khadydieye8407
    @khadydieye8407 3 роки тому +8

    Amatina solo kuner warga fonk liga nampe t diko ndamo mane mome dama mossa beuk ku guem limu done 👍🏾 yalna yalla faylen yiw

  • @docteurkb5342
    @docteurkb5342 3 роки тому +5

    Tu et mon Mr ly yalla na la yalla taxa wou ci barkeb alkhor an

  • @cheikhmbaye6547
    @cheikhmbaye6547 3 роки тому +11

    Macha allah tik tok lako ndieukeu guisse baa legui mangui lenii topou

    •  3 роки тому +1

      🙏

  • @mohamednaby5384
    @mohamednaby5384 2 роки тому +6

    Nit day gam boppam bilaye wahga dëgg dono wara wax sunu lakk 🇸🇳🇸🇳😞🙏🏿❤️

  • @AblayeSane-ou9fm
    @AblayeSane-ou9fm Рік тому +1

    yalla nala yalla defal jam

  • @elhadjitoure1687
    @elhadjitoure1687 3 роки тому +5

    Maasàllaa jërëjëf taxawaay bi rafet na lool ❤️❤️🇸🇳

  • @ousseynouhane9852
    @ousseynouhane9852 3 роки тому +4

    Mashallah yallah na la yallah faye!

  • @mohamednaby5384
    @mohamednaby5384 2 роки тому +3

    Mashallah Amna solo bilaye wahga dëgg 🇸🇳🙏🏿🙏🏿

  • @omardieng2606
    @omardieng2606 2 роки тому +2

    Man deh deguelouna co 1h39min yeupp wayeh boudonn fracais la doumaci deguelou sax 1min。Damay beugue diale ci laneene wayeh yeuk yeuk bimaciy am motax douma mana bayi bamou diex ndax lignouy wax damakay khame bou bax👈🌹🌺🏵️🥀🌿

  • @elhadjitoure1687
    @elhadjitoure1687 3 роки тому +5

    Jànge ci saw làkk mooy tax am réew ma na am yokkute biir ak diti jànge du wees xam sa làkk mooy xam sa bopp ❤️❤️🇸🇳✍🏾✍🏾

  • @serignecheikhgaye3369
    @serignecheikhgaye3369 2 роки тому +1

    Sa waadji badjamegaam.yallanala yalla défal djame ak goudoufane ak wer . yalla nala yalla compe djitt ci réwmi.da sonjou réwmi djem kanam .li Serigne bamba waxone rek banjoub Touba doyna djamou yalla.yalla nanjoula yalla fayall.aamine

    •  2 роки тому

      Amiin 🙏🏾

  • @saliou182
    @saliou182 Рік тому

    C'est vrai wax gua dëg way mais senegal dafa diot niou jéng sunu lak waxtane bi c'est très très importante pour tous les élèves et tous les senegal mais yalla nala yalla fay té défal fane bou goudou ak wer merci beaucoup professeur 😢❤

  • @momoseck8964
    @momoseck8964 2 роки тому +1

    Sama mr bi yalla nà sa jàmou yàg🥰🥰

  • @ney.languagestraining-pro51
    @ney.languagestraining-pro51 Рік тому +1

    J'aime tellement la fluidité de cet homme dans ses paroles. Il maîtrise en effet le domaine. Mashallah

  • @bassirouthiam1615
    @bassirouthiam1615 2 роки тому +2

    Wallhi fall tawfekhe rek fall 🇸🇳

  • @diengfallou9829
    @diengfallou9829 3 роки тому +5

    ماشاء الله تبارك الله

  • @saliougueyegueye3328
    @saliougueyegueye3328 3 роки тому +7

    Bounou amon thi yaw foukou youmelni yaw rewmi dieum kanam

  • @xaadimbamba6393
    @xaadimbamba6393 2 роки тому +5

    Maasàllaa 🙏🏿

  • @mountakhacheikhbassirou6282
    @mountakhacheikhbassirou6282 2 роки тому +2

    Cheikh bii laa sokhla numérom koumakoy bakhé

  • @CheikhabdouLahat
    @CheikhabdouLahat 5 місяців тому

    Maasàllaah wax nga dëgg de ❤wolof rekk ❤

  • @badaraleye654
    @badaraleye654 3 роки тому +3

    Yallna yalla diapp lé

    •  3 роки тому +1

      🙏

  • @MRTV659
    @MRTV659 3 роки тому +7

    Maasàllaa

  • @CheikhabdouLahat
    @CheikhabdouLahat 5 місяців тому

    Wax nga dëgg de làkku wolof dafa neex ❤

  • @gueyeterangaofficielle9702
    @gueyeterangaofficielle9702 2 роки тому +1

    Mâcha allah amna soloh dieureudieuf

  • @cherrymint40
    @cherrymint40 2 роки тому +2

    extra amna solo

  • @daoudadiallo425
    @daoudadiallo425 3 роки тому +4

    Amna solo looool

  • @abdumamedioob2738
    @abdumamedioob2738 3 роки тому +5

    Aywày deglulén kii luwer lay wax

  • @modoudiallo3835
    @modoudiallo3835 2 роки тому +2

    الله اكبر

  • @mouhameddiop3510
    @mouhameddiop3510 2 роки тому +1

    Jërëjëf

  • @amadoumboup2270
    @amadoumboup2270 Рік тому

    Machalah wallahi wkh nga deug

  • @Jàngcisawlàkk
    @Jàngcisawlàkk 2 місяці тому

    Jërë jëf yàlla lépp yawa

  • @user-um4fr9rm1o
    @user-um4fr9rm1o Рік тому

    Waaw, bëgguma dee, kon, duma dem fa. Sénégal mooy réew mu metti ci àdduna bi ndax mooy réew mu néew doole ci àdduna bi, ay garab yu bare.

  • @baysaliouba6535
    @baysaliouba6535 3 роки тому +6

    Dama soukhla numeroume

  • @diengtoubamamour5758
    @diengtoubamamour5758 3 роки тому +2

    MACHA allah rek

  • @astoudiakhate8089
    @astoudiakhate8089 2 роки тому

    Am na solo

  • @Mame_Ndiogou
    @Mame_Ndiogou 6 місяців тому

    Machallah ❤🎉

  • @mouhameddiop3510
    @mouhameddiop3510 2 роки тому +1

    Jaajëf jàmbaar

  • @AbdouDiol
    @AbdouDiol Місяць тому

    Macha'Allah

  • @dametall8864
    @dametall8864 3 роки тому +3

    Diadieuf baye amna sollo lolle

  • @AblayeSane-ou9fm
    @AblayeSane-ou9fm Рік тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fabinatawade5919
    @fabinatawade5919 2 роки тому +3

    Wacc tane wi neh na waye musique be ko yakh

  • @ndiayebayemasse6680
    @ndiayebayemasse6680 3 роки тому +3

    Machallah 🥰

  • @mountakhadiouf746
    @mountakhadiouf746 3 роки тому +3

    Amna solo lool

  • @abdousylla4436
    @abdousylla4436 3 роки тому +1

    Merci

  • @amarndiaye6186
    @amarndiaye6186 3 роки тому +2

    Machalla

  • @prenomnom5715
    @prenomnom5715 2 роки тому +6

    Le journaliste il n'a rien compris. Il n'est pas convaincu de ce que dit l'invité et pourtant il est très clair. C'est logique d'apprendre dans notre propre langue. Na ñu jàng si sunu làkk bu ñu bëggee jëm ca kanam.

  • @عبدالله-ش6ب5ز
    @عبدالله-ش6ب5ز Рік тому

    ماشاء الله

  • @paapnjaay1586
    @paapnjaay1586 2 роки тому +1

    Wax nga dëgg dé! Boroom-lijaasa yi kay ku la ci gën a yaras, gën laa nekaw nga ni kale.
    Mbiri lijaasa kay man ci sama wàllu bópp ba ma ko xoolee ba xoolaat ko, li ma ci tënk mooy gën a nàngul tëralinu jàng mi (le système éducatif) rek.

  • @matarba2843
    @matarba2843 2 роки тому +1

    Je veux apprendre le wolof abdou

  • @nourou519
    @nourou519 2 роки тому +1

    Si misal dama nane faratay ñaapu jourom ñaarla xale yi waxe lima waxe Ba ñoom ñepp mokal laxa jariñu Li rek mooy Degeu

  • @Khassidaofficiel221
    @Khassidaofficiel221 Рік тому

    maasalla

  • @ndiayekane7780
    @ndiayekane7780 2 роки тому +2

    ❤❤

  • @njagamataarsill9533
    @njagamataarsill9533 Рік тому +1

    Xam-xam ci saw làkk la gën a yombe. Làkku jàmbur bu neexee ba mel ni tàngal itam maneesu cee tàqamti ku.

  • @babacardiack4751
    @babacardiack4751 3 роки тому +4

    Nou nitt mana def ba bok si seen kippangoo

  • @ndiayengom5083
    @ndiayengom5083 Рік тому

    Màssala

  • @ridialseck7166
    @ridialseck7166 3 роки тому +2

    Tarkala

  • @CheikhDiop-eh6vp
    @CheikhDiop-eh6vp 2 роки тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤👍

  • @mouhamadndiaye3721
    @mouhamadndiaye3721 3 роки тому +1

    ما شاء الله

  • @maogningue3922
    @maogningue3922 3 роки тому +6

    Manchallah 🥰🥰😍

    •  3 роки тому +1

      🙏

  • @basssall7309
    @basssall7309 3 роки тому +1

    👏👏👏

  • @user-um4fr9rm1o
    @user-um4fr9rm1o Рік тому

    Maa ngi yaakaar ne, yéen ku bon yi di xalaat ne, lu baax la, di sàq ak a rey ay xaj yii, di jàpp dara ci suux yi, te dee ci dee gu metti.

    • @user-um4fr9rm1o
      @user-um4fr9rm1o Рік тому

      Vous quin'tes pas capables de faire le bien, cherchez faire le mal! Vous pourrez tuer les chiens, mais pourtant, pour cela, vous devez plutt tre tus!

  • @walo774
    @walo774 Рік тому

    Musique de fond bi yakh na lépp😢

  • @modoudiallo3835
    @modoudiallo3835 2 роки тому +1

    Doudal yaw100%

  • @SoldarouBamba-g9m
    @SoldarouBamba-g9m Рік тому

    Waxnga degeu dh bilaay doyna waar motax xolal bi bala ngaa nékeu président il faut nga dégeu langeu diambour non😂😢😅😂😢😮😢😂😅😮

  • @bassirouthiam1615
    @bassirouthiam1615 2 роки тому

    Wallhi

  • @cheikhoukebe1423
    @cheikhoukebe1423 2 роки тому

    Am n'a solo trop

  • @abdoubadiane4179
    @abdoubadiane4179 2 роки тому

    Koubga bokou nomiy déff

  • @cheikhenafaye1252
    @cheikhenafaye1252 2 роки тому

    Ak wér

  • @user-um4fr9rm1o
    @user-um4fr9rm1o Рік тому

    Senegaal mooy Barbaar yi ñu ñibbi, ñu gën a ñaaw, ba ñu gën a ñaaw. Gàdd, ñàkk-gànnaay, ay doomi-réew yuy naaw, ñu ñàkk-gànnaay, ñu ñaaw. Du réew mu xonq, nit ñi fa duñu raxas ndox mi dafa sobe, bu nga ko laaj ndoxum kaas, ndox mi am na ay xànjar ci moom, te ñu ngi doon ñaawlu ci yoon yi, fekk noonu lañu leen di wooye ci Ouganda ndax yoon yi ñu sàkk ci garab yi, daal daal suuf ak doj rekk la woon, war nga bàyyi seen lekk gu ñaawlu!!! Lii mooy 21eelu xarnu bi, du jamonoy Neandertal yi!!!! Jëfandikoo sa gémmiñ ci xaj yi, xati yi ak yeneen yàpp yi!!! xasa yi ak yeneen rab yi itam!!!

    • @user-um4fr9rm1o
      @user-um4fr9rm1o Рік тому

      Les Barbares rentrent chez eux, encore plus méchants. J'ai connu le malheur et la faim, j'ai connu le malheur et la peur. Ce n'est pas un pays rouge, les gens ne se lavent pas, l'eau est sale, si vous demandez de l'eau de tasse, l'eau est en métal, et les gens se moquent dans les rues, alors qu'en Ouganda on les appelle ainsi parce que les routes sont faites de bois, elles ne sont que de la terre et des pierres, vous devez arrêter leur nourriture sale!!! C'est le 21ème siècle, pas l'époque des Néandertaliens!!!! Utilisez votre bouche sur les chiens, les rats et autres animaux!!! les mouches et les autres animaux aussi!!! voir.

  • @djibysarr1202
    @djibysarr1202 8 місяців тому

    Degg la

  • @user-um4fr9rm1o
    @user-um4fr9rm1o Рік тому

    Senegaal mooy réew mi gën a ñaaw ndax ñàkk a raagale ay jigeen yu ndaw 20i at ci gannaaw askan wi, itam 5 ak 6i at, Gabon mooy réew mu néew doole te am ay nit yu bare yu ñàkk njàngam, kon am na lu am solo ne am na fa jàngoro yu metti yu bare. Gaynde dafa am ay xëy yuy dal, ay xëy yuy tollu ci junniy nit ci at mi. réew mii moo gën a ñaaw ci Afrig, nit ñi fa bare nañu ay dof, bu ab doxandéem demee ci yoon wi, dañu koy xas. Amul benn sañ-sañ ci réew mii. Soo bëggee seetsi bérab bii, kon dafa tax nga wàññi. Géej gu bare ci biir réew mi moo tekki ne am na lu ëpp lu ñu bañ a nettali.. bu ma ko jànge, dina ma tax a woo àddina si, ñu boykot Senegaal, ndax ñu ngi lekk ci yaramug nit, réew mii am na Ebola. Dañoo may ñu fey seeni nooy. Loolu rekk moo firndeel ne, duñu fonk seen mbindeef ci lépp, soloo xaalis bi ñuy jot ci ku nekk ci ay way-jur yi ñu rey. Botswana mooy réew mu ñaaw te am nguur gu ñàkk njariñ.

    • @user-um4fr9rm1o
      @user-um4fr9rm1o Рік тому

      Le Sénégal est le pays le plus touché par le manque de violence contre les jeunes filles, 20 ans derrière la population, et 5 et 6 ans derrière la population. Le Gabon est un pays pauvre et avec une population très peu instruite, il est donc important qu'il y ait beaucoup de maladies graves. Le lion a des tiges qui se posent, des tiges qui atteignent un millier de personnes par an. Ce pays est l'un des plus dangereux d'Afrique, les gens y sont souvent fous, et si un étranger passe par la route, ils l'insultent. Il n'a aucune autorité dans ce pays. Si tu veux visiter cet endroit, alors tu dois y aller. La grande mer intérieure signifie qu'il y a beaucoup de choses à ne pas raconter. Si je lis cela, cela me pousse à appeler le monde entier à boycotter le Sénégal, parce qu'il mange des êtres humains, ce pays a Ebola. On leur a permis de payer leurs impts. C'est la preuve qu'ils ne font pas attention à leur création, ils comptent sur l'argent qu'ils reçoivent pour chaque membre de leur famille tué. Le Botswana est un pays corrompu et mal gouverné.

  • @bassirouthiam1615
    @bassirouthiam1615 2 роки тому +1

    Wolof mo bax dh

  • @omardieng2606
    @omardieng2606 2 роки тому

    Mandeh

  • @byndiaga
    @byndiaga 2 роки тому

    C'est très instructif mais dommage cette musique de fond me casse les oreilles 😡😡😡

  • @SoldarouBamba-g9m
    @SoldarouBamba-g9m Рік тому

    Dgeu bou wéer 🤣😂 bouñou begé tapalé di diafél dara diko wax thi français té bouñko waxon thi wolof mouy lou yombou 😂😅😂

  • @SeydouWade-d8t
    @SeydouWade-d8t Місяць тому

    Son bi ci suuf soof na nak

  • @dembeaktey
    @dembeaktey 2 роки тому +5

    Cheikh Anta Diop est le premier à dire qu'on doit enseigner dans nos langues. Mais ce gars ne le mentionne pas pour avoir l'exclusivité. Quand le prof Diop parlait de cela il devait etre très petit ou pas encore né. Il faut rendre à Cesar ce qui lui appartient.

    •  2 роки тому +5

      Seex bi, kii ak mbootaay gi mu bokk, yoon wi Cheikh Anta Diop xàlloon rekk ci lañuy jaar.
      Xayna danga koo xamul nag, moo tax nga koy xeeb.

    • @samadeguine9840
      @samadeguine9840 2 роки тому +5

      Bayilén sonal sén boop kii fouko cheikh anta déguue d'où beugué Lou doul gnewat néxal ko .

    • @mouhammadoufalilouniang945
      @mouhammadoufalilouniang945 2 роки тому +2

      Wahnako sah bo sétané vidéo bimiy wadial diékh bimou déssé 20mn
      Kou bah sétano vidéos bi bamo diékh motah nga wah li wayé délona nioukël Cheikh anta bou yague

    • @Mansour_Diop
      @Mansour_Diop 7 місяців тому

      Niak khél wéssuwoul lo xaam aki lo wax rek jeul ko jokkh ko cesar. wa kouy cesar khana moy sa yallah 😂😂

  • @talibesmbackemadina1146
    @talibesmbackemadina1146 2 роки тому

    Wax ga deug de

  • @malickdiop727
    @malickdiop727 2 роки тому

    Yalla dou dioum dh kokou beuga Sam rew raw xamalal sam sa lak Sam rew ..s Touba dh wolouf rk la dégounn nk ta gnila jagé tombe yi mage gni

  • @papeamadousamb2542
    @papeamadousamb2542 3 роки тому +2

    Bilaay ki monté bi son dafa sokhor kéne dégoul dara.

  • @papeamadousamb2542
    @papeamadousamb2542 3 роки тому

    Séne son bi dafa eupe waay cim...

  • @modougueye2939
    @modougueye2939 3 роки тому

    Synonym lay lathie an wolofe

  • @mbayeseck173
    @mbayeseck173 3 роки тому +1

    Diara diaf

  • @malicktv7855
    @malicktv7855 2 роки тому

    Beuge na ame sa numéro de téléphone de

  • @bayelayediallo3237
    @bayelayediallo3237 2 роки тому

    Ngir yàlla dindi leen misik bi ngen def ci video bi. Dafay tankali noppu.

  • @moussaniang7809
    @moussaniang7809 5 місяців тому

    Waw gor fall❤❤❤

  • @aligueye4821
    @aligueye4821 5 місяців тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bayemorgueye1949
    @bayemorgueye1949 3 роки тому +2

    Machalla

  • @malicktv7855
    @malicktv7855 2 роки тому +1

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @diagnebaye8263
    @diagnebaye8263 2 роки тому

    Merci

  • @oustazlaminetoure2003
    @oustazlaminetoure2003 3 роки тому +1

    Machalla

  • @madametoure9133
    @madametoure9133 2 роки тому +1

    ❤❤❤❤❤