@@damasdamas6847 loolu du dëg Serigne Babacar sy 1957 la guene aduna boobu Sénégal amagul indépendance fédération Mali moo amoone ta bobu Senghor AK Mamadou dia ño bokk partie ta amuñu problème ,1961 la seen problème commencer 1962 mu emprisonné ko
@@MyPacodiaz Senegaal neexula waxe ndax sos, parparloo ak wax loo xamul. Sëriñ Baabakar Si 1957 lafi joge te booba Sengoor ak Mamadu Ja ñoo raw mburoog soow. Wax jii mu wax amul !!! Budee Sëriñ Fallu aussi fekke na biñuy jàpp Mamadu Ja waaye lii mu ci wax taxul woon mu seetaan ko. Un témoin occulaire a raconté ce qui s'était passé récemment et la vidéo est sur le net. Xeex injustice waaw waaye buñu ko defe ak injustice aussi
Inechallah wor filay diéukhé. inechallah nioun seni seutt seuttatt niofiyy dieulé wor. kou wor niou Pender ko. si Macky ak wa apr lani ndieugéu inechallah ✅ the revelutions is on. mais dieuredieuff Cheikh bii léral yii amna solo
c'est bien beau le discours vraiment. Mais pour moi, en ces moments crucial on a beaucoup plus besoin de solution plus que des récits du déjà fais. Senghor dafa worr, dafa yak ok mais taxoul gnou diougué si worr ak kathie. tournons nous vers l'avant et voir comment remédier à cette situation pour qu'au moins nos enfants puissent, à l'avenir, vivre dans une stabilité économique, politique et sociale
MAA CHAA ALLAH AMNA NDIERIGNE TRÈS INTÉRESSANT MERCI CHEICK BI VEUILLEZ NOUS FAIRE PLUS SOUVENT PLUS DE VIDÉOS DE CE GENRE ET BEAUCOUP PLU LONGUE QU ALLAH VOUS RÉCOMPENSE AMINE
L'histoire qu'il raconte n'est passer comme Mamadou dia à été chez serigne fallou mbacke ils voulait rassembler tous les khalifa à un seul khalifa dia était communistes et laïcité serigne touba ammoul morrom yalla naniou ko yalla fayyall mbaye geuye syll va lui répondre in cha allah fii Sénégal koffi fallo serigne si gnoo layye fal sinon zéro
cheikh bi Mamadou Dia année bimouy neck président du conseil du sénégal en 1957 bobou la Sérigne Babacar guène aduna donc fatou na avant histoire bi di am.Té Mamadou Dia migui opposé ak Senghor en 1958 lorsque Charle de Gaulle propose un référendum sur la communauté française. Day bakh tamit nga lerral lolou bala confusion di am 👍 après tout: vive Ousmane sonko la solution✊
Je confirme tes propos un professeur d'histoire à l'université cheikh Anta Diop m'a raconté cette histoire comme tu l'a relatée. Donc il est tant que la jeunesse prenne conscience le mal du pays est entre les politiques et les marabouts
C’est faux serigne Babacar sy est mort en 1957 et mamadou Dia à été emprisonné par senghor en 1962, soit 5ans après la disparition de serigne babacar sy il faut vérifier la source.
Kii wakhoule né Serigne Babacar dako féké, dafa wakh né Mamadou Dia démone na wakh Serigne Babacar Sy de son vivant que ce que les gens disaient sur lui était faux.
Ya meun fen Serigne Babacar guene adouna avant indépendance 1957 la guene adouna senghor ak mamadou dia sen problème bi 1962 la bayilen doule ay fen day ame cohérence watawasaw bil khakhi bo xamni day ame ay fen ci biir
Sene probleme commencer woul en 1962. Mamadou Dia a tout le temps eu un discours souverainiste pour un détachement complet de la France lolou commencer woul 1962. Te nga rafetal say kadou.
@@watawasawbilhaq le problème entre Senghor et Mamadou Dia a commencé en 1961 et ensuite Mamadou Dia emprisonné en 1962 . Serigne Babacar est rappelé à Dieu en 1957 . Donc dire qu'il a contribué à l'emprisonnement de Mamadou Dia est totalement faux . Vérifiez vos infos.
Wakhabite YI AK Kemite YI Beug profiter si Sonko Boumou TAKH ngeni feeen. Serigne Babacar 1957 la Fatou, Mamadou Dia 1962 làko Senghor Teudj. Kon Say feen gueneee si Serigne Babacar. Mouy Sérigne Babacar di Sérigne Fallou ken taloul di complot Meun ngen feeen trop.
Ndakh Mamadou Dia 1962 la tambali ame discours souverainiste? Bapare digante Senghor ak Serigne Babacar lolou yaw meunoko nier. Dangene di teli teli wakh wakh mais quand un historien - Iba Der Thiam - decide de rédiger la VRAIE histoire vous voulez bruler sa maison, nitou aljannah yi.
Ce qui nous a échappé sur Mamadou Dia et Cheikh Anta Diop ne va pas nous arrivé sur Ousmane sonko parce que le peuple Sénégal en est conscient. Nous avons non seulement un peuple jeune et déterminé pour libérer le peuple mais aussi une nouvelle "Religion "appelée le Patriotisme
@@watawasawbilhaq khol bou sed khel mou sel diam diou barry mo gueune adounak lissi biram sante yalla bou wer doyloko wolouko merci abdoulahi wa khadimou rassoul
Diamono yoyou salafisme dougoul rewmi te Mamadou Dia tidian la woon Di toucouleur Serigne Babacar sy 57 lafi diogue té Senghor 60 la tok xolatal li ngay wax
Monsieur tu t'es trompé. Serigne Babacar Sy n'étais pas dans ce monde lorsque Mamadou Dia était en pleine politique. Vérifiez et vous allez vous en rendre compte. Et tu n'es pas le seul
Goor gui sa wakh amna solo lol mais pr man DH biko Senghor di fekél boba fékna Serigne Babacar sy guén adouna soudone doundou dou ame Mame Abdoul Aziz mofi nékon ta defnasi loumou meune mais Senghor teukh Goumba nangou woul dégue
Nitou ngour loumou beugg deif dougn ci khool Serigne ci. Lignou beugg reik. De Senghor à Macky. Mame Abdou liko ci waroon deif nako comme ningko wakhei Dieredieuf
@@watawasawbilhaq Lima méti mooy yangui réetaan Di sabooté ,toudée sa chaine watawasaw bil haq. Mais je reviens sur ma question Wahouma né dou nit ,je veux bien que ngua diohma ay preuves thi li waji wah. Béneen bi mooy yaw réetaanal rék mais moi je veux une réponse
Vous êtes vraiment ridicule Histoire Mamadou Dia sakh maitriser woulen ko. Serigne Cheikh domi Serigne babacar mi done opposer Senghor gagné ko nak té Cheikhal khalifa done waydiouram??? Vous etes betes sen wax yi fekhélen ba guenè Si Président Ousmane Sonko. Con ngen rek
ماشاءالله وجزاكم الله خيرا
Serigne Babacar sy fekewoul bingnouy teudj Mamadou dia
Kii wakhoule né dako féké, dafa wakh né Mamadou Dia démone na séti Babacar Sy de son vivant néko lii niite yi di wakh ci mome dou deugg.
@@damasdamas6847 loolu du dëg Serigne Babacar sy 1957 la guene aduna boobu Sénégal amagul indépendance fédération Mali moo amoone ta bobu Senghor AK Mamadou dia ño bokk partie ta amuñu problème ,1961 la seen problème commencer 1962 mu emprisonné ko
@@MyPacodiaz Senegaal neexula waxe ndax sos, parparloo ak wax loo xamul. Sëriñ Baabakar Si 1957 lafi joge te booba Sengoor ak Mamadu Ja ñoo raw mburoog soow. Wax jii mu wax amul !!! Budee Sëriñ Fallu aussi fekke na biñuy jàpp Mamadu Ja waaye lii mu ci wax taxul woon mu seetaan ko. Un témoin occulaire a raconté ce qui s'était passé récemment et la vidéo est sur le net. Xeex injustice waaw waaye buñu ko defe ak injustice aussi
De sages paroles
Masha'allah
WOR PEUPLE BI DINA FI DIÉKH INSHA ALLAH
Lo p lors
C’est très bien de rappeler l’histoire pour qu’elle soit bénéfique .
Mais Serigne Babacar Sy Etait mort avant l’emprisonnement de Mamadou dia
Merci beaucoup père
Machallah et merci pour tout 🙏
Inechallah wor filay diéukhé. inechallah nioun seni seutt seuttatt niofiyy dieulé wor. kou wor niou Pender ko. si Macky ak wa apr lani ndieugéu inechallah ✅ the revelutions is on. mais dieuredieuff Cheikh bii léral yii amna solo
le 16mars a Dakar chère patriotes du Sénégal résistance leurs de révolutions a sone chère patriotes du Sénégal résistance
c'est bien beau le discours vraiment. Mais pour moi, en ces moments crucial on a beaucoup plus besoin de solution plus que des récits du déjà fais. Senghor dafa worr, dafa yak ok mais taxoul gnou diougué si worr ak kathie.
tournons nous vers l'avant et voir comment remédier à cette situation pour qu'au moins nos enfants puissent, à l'avenir, vivre dans une stabilité économique, politique et sociale
Si tu ne connais pas les erreurs du passé, tu risques de les repéter...c'est aussi simple que ça
le 16mars a Dakar chère patriotes du Sénégal résistance leurs de révolutions a sone chère patriotes
MAA CHAA ALLAH AMNA NDIERIGNE TRÈS INTÉRESSANT MERCI CHEICK BI VEUILLEZ NOUS FAIRE PLUS SOUVENT PLUS DE VIDÉOS DE CE GENRE ET BEAUCOUP PLU LONGUE QU ALLAH VOUS RÉCOMPENSE AMINE
L'histoire qu'il raconte n'est passer comme Mamadou dia à été chez serigne fallou mbacke ils voulait rassembler tous les khalifa à un seul khalifa dia était communistes et laïcité serigne touba ammoul morrom yalla naniou ko yalla fayyall mbaye geuye syll va lui répondre in cha allah fii Sénégal koffi fallo serigne si gnoo layye fal sinon zéro
ما شاء الله ماشاء الله حفظ الله عثمان سكو باعدا ءه
C un triste realite pour Notre pays
Machalah, Serigne LÔ amna NDIEURÎGNE
YALLA soutoural 🤲
Maacha Allah très claire
Bilaye c est vrai tout vos propos sont vrai
Kii vous a dit que ce qu'il est vrai va lire histoire
cheikh bi Mamadou Dia année bimouy neck président du conseil du sénégal en 1957 bobou la Sérigne Babacar guène aduna donc fatou na avant histoire bi di am.Té Mamadou Dia migui opposé ak Senghor en 1958 lorsque Charle de Gaulle propose un référendum sur la communauté française. Day bakh tamit nga lerral lolou bala confusion di am 👍
après tout: vive Ousmane sonko la solution✊
Bien dit
Ok. Mais mamadou meune nga niou wakh bane annee la tambali ame discours souverainiste?
والله يجزيكم احسن الجزاء
Je confirme tes propos un professeur d'histoire à l'université cheikh Anta Diop m'a raconté cette histoire comme tu l'a relatée. Donc il est tant que la jeunesse prenne conscience le mal du pays est entre les politiques et les marabouts
MachaAllah pertinent
Machallah serigne bi je suis TIDIANE mais votre discours est véridique
salut c Mamadou lo sebikotan merci diaradijeuf
Sa Tidianiya j'en doute fort qui di doule di dadiéler gay fénn diko diapaler
Sa waay li ngay wax xamoc dara
Serigne Babacar est décédé le 25 Mars 1957 bien avant notre accession à l'indépendance et l'emprisonnement de Mamadou Dia.
C’est faux serigne Babacar sy est mort en 1957 et mamadou Dia à été emprisonné par senghor en 1962, soit 5ans après la disparition de serigne babacar sy il faut vérifier la source.
Merci djamil
Kii wakhoule né Serigne Babacar dako féké, dafa wakh né Mamadou Dia démone na wakh Serigne Babacar Sy de son vivant que ce que les gens disaient sur lui était faux.
@@damasdamas6847wokho degue
@@babacarmbengue651 yaw khana dégo wolof wala sa xelmi dafa déss
Ki Wakhoul Deugg Sérigne Babacar Sy RTA 1957 La guèneu ADOUNA Affaire Mamadou DIA 1962 lewone ki Yakk Dèrrou Senghor moko takha Diogg
Thieuy Sénégal yagg naa beuri ay naafekh
Macha Allah amna solo lol
Deug mo gneuk moy moudiou
Am na solo non d’où sengor rekk Moo yàq senegal
Ça c'est vrai. Il y a aussi les marabouts
شكرا
جزيلا
Ah oui plus de leçon on est preneur merci
Partager svp 😕👆
Manchalla bon a savoir vraiment
Degue baye amna solo
Ya meun fen Serigne Babacar guene adouna avant indépendance 1957 la guene adouna senghor ak mamadou dia sen problème bi 1962 la bayilen doule ay fen day ame cohérence watawasaw bil khakhi bo xamni day ame ay fen ci biir
Sene probleme commencer woul en 1962. Mamadou Dia a tout le temps eu un discours souverainiste pour un détachement complet de la France lolou commencer woul 1962. Te nga rafetal say kadou.
@@watawasawbilhaq le problème entre Senghor et Mamadou Dia a commencé en 1961 et ensuite Mamadou Dia emprisonné en 1962 . Serigne Babacar est rappelé à Dieu en 1957 . Donc dire qu'il a contribué à l'emprisonnement de Mamadou Dia est totalement faux . Vérifiez vos infos.
@@watawasawbilhaq vous etes vraiment ridicule fekhelen ɓa guené President Ousmane Sonko sen waxi doff yi
Maachallah lou léérre nagne té mata bayyi héll 👂👂👂
Machalah mé daguat trop
Dieureudieuf papa
واضح يا استاذ جزاك الله خيرا
Merci
Mashallah
Segor bakhoul motardel rewmi
وانتم
في
جانب
الحق
LI NGA WAX DEUGUELA DIEUREDIEUF
Merci Lo
Macha'Allah ! Soniou barilé vidéos you melni dhé dinaniou amal ndieurign lou bari waay.
Jaradieuf amna solo trop
Neetkou Ngnoul doyna waar
Wakhabite YI AK Kemite YI Beug profiter si Sonko Boumou TAKH ngeni feeen. Serigne Babacar 1957 la Fatou, Mamadou Dia 1962 làko Senghor Teudj. Kon Say feen gueneee si Serigne Babacar. Mouy Sérigne Babacar di Sérigne Fallou ken taloul di complot Meun ngen feeen trop.
Ndakh Mamadou Dia 1962 la tambali ame discours souverainiste? Bapare digante Senghor ak Serigne Babacar lolou yaw meunoko nier. Dangene di teli teli wakh wakh mais quand un historien - Iba Der Thiam - decide de rédiger la VRAIE histoire vous voulez bruler sa maison, nitou aljannah yi.
Deuredeufe machala
Mouhamedou Lo Merci
Dieuredieuf li amna solo ndah hamoumako wone
Macha alla amna solo
Machallah Senghor a fait beaucoup de mal.C'est lui qui a retardé le Sénégal.
Chère conpatriote du Sénégal résistance leurs de révolutions a sone chère patriotes le 16 mars
Mouhamadou dieureudieuf .
Le pays doit tout son retard et ses malheurs à senghor
Machalla
Senghor mo yak Senegal un grand traître vrai domouharam
Traitre bigeuneu reuy mooy serignes y iko si diapalé banou sakal pèkhè
@@lasagesse2225 damelni c'est tout les marabouts du Senegal ño nopiwone pendant ce temps ce traître Senghor di dul
Ragale borombi amoureux senegal
féne bakhoule dé si Serigne si
Lou Lerr nga wakh Sénégal Kaye wor Rk Laniofi Neké
Yawmi yaay woor kat teh do waxkatou deg.
Yalla naniou yalla moussal ci borom xel bou niemé yalla ak feenkat
C triste
machaALLAH Serigne bi YAAG fi lool té wér Di wax Di nu fattéli YAL n'a YALLA FAY LA
SALAM LES ÉPOQUES NE SONT PAS LES MÊMES SOYONS PRÊTS
Pape li am solo dakh nioune ndaw. Gni xam li xèwone demb tay dji dianganaci Lou bari manchallah
Mamadu Ja moo waroon njëkk Seŋoor ci mag ñi waaye dafa rëyoon
Walahi deugle
Deug rèk moye Deug
Kiy wax kan la.?Amna solo lool ndeysaan.
serigne bi ,kouy wakh si kou deuddou nanga kham ni baméle soriwoula.wa salaam.
amma solo trop trop trop sakh
Ce qui nous a échappé sur Mamadou Dia et Cheikh Anta Diop ne va pas nous arrivé sur Ousmane sonko parce que le peuple Sénégal en est conscient. Nous avons non seulement un peuple jeune et déterminé pour libérer le peuple mais aussi une nouvelle "Religion "appelée le Patriotisme
Tu es un egaré
@@senegal3620 Je te comprends tu es assis sur ton cerveau,ton degré d'intelligence est bas
Yi doule you pata
Limal ma benne. Vraiment vous la amolen kham kham amolene teguine bapare fokni yena gueun nieup 🤣
Motakhite. Senegal bok si ndaré yi si adouna bi
@@watawasawbilhaq khol bou sed khel mou sel diam diou barry mo gueune adounak lissi biram sante yalla bou wer doyloko wolouko merci abdoulahi wa khadimou rassoul
Mersi 1000...…
🥇🥇🥇🥇🥇🥇🇸🇳🇸🇳
Vrai Hadj la
Diamono yoyou salafisme dougoul rewmi te Mamadou Dia tidian la woon Di toucouleur Serigne Babacar sy 57 lafi diogue té Senghor 60 la tok xolatal li ngay wax
Mamadou dia dadone teukou serigne si diwakh tarikhayi dafa bari béne rék la wara done motakh akou serigne si dalko
Monsieur tu t'es trompé. Serigne Babacar Sy n'étais pas dans ce monde lorsque Mamadou Dia était en pleine politique. Vérifiez et vous allez vous en rendre compte. Et tu n'es pas le seul
Merci ta bien vu
Lourer
WALA YÎ
Si seulement les gens écoutaient et utilisaient leurs cerveaux, ils sauraient qu'ils n'ont pas besoin de ces tarikhas pour se rapprocher d'Allah.
Wallahi frére dégatina deugue
Que des mensonges 😢
Limal ma benn
@@watawasawbilhaq SERIGNE babacar n’était pas là lors des histoires de Senghor et Mamadou Dia
Qui a dit le contraire ?
Soucar len s’en aduna bi dara change wufi sonko du massa nek président Sénégal
Mouno fée wax ci Mamadou Dia Lou Serigne cheikh tidian sy xamoul moom midoon opposé Senghor nek ossi Domi Serigne sy té demoon Al Senghor
Wakho lou am
Baye niass etai avec mouhadou
Serigne Babacar Sy n'a jamais trompé qui que soit revoit tes propos et excuse toi ndakh martaba dou baalé té Serigne Babacar Sy rta nitou yalla
Yalla mola ko wakh?
Ça way ni s’en problem moy Sergine me dunuci amndam
Sénégal d'où démm😅
Lou lerr Nga Wakh. macky sall tanki Senghor Rek lay dokhé
Dieureu dieuf li dé dalna xeel
Tous sauf sonko
Yéneu weureu wakh
al quran kéne douko fowé
gros menteur Serigne Babacar est décédé en 1957 avec l'accession du Sénégal alors que Mamadou Dia été encore avec Senghor .l'affaire Dia en 1962
Kone 1957 la Mamadou Dia tambali ame discours souverainiste?
Yaw billahi wakho deugue, wahabiya nga , ni rek nguéne méle soléne sagnone dinéé tasss menteur
Yaw werngeu ?
Goor gui sa wakh amna solo lol mais pr man DH biko Senghor di fekél boba fékna Serigne Babacar sy guén adouna soudone doundou dou ame Mame Abdoul Aziz mofi nékon ta defnasi loumou meune mais Senghor teukh Goumba nangou woul dégue
Nitou ngour loumou beugg deif dougn ci khool Serigne ci. Lignou beugg reik. De Senghor à Macky. Mame Abdou liko ci waroon deif nako comme ningko wakhei
Dieredieuf
wakh dafa diafé bilaay, ndioume té yi barina si kaddou yi.
Seringe babacar sy est disparu 25 mars 1957 mamadou dia emprisonné en 1962 kholatal lingaye wakh
Mamadou Dia 1962 la tambali ame discours souverainiste?
Senghor n'avait pas ni la capacité ni le niveau pour tromper et corrompre Serigne Babacar Sy (je ne suis pas D'accord).
Lolou foko tek
@@watawasawbilhaq ki wah lolou fan la ték limou wah noonou? Soomako wahée rék ma tontoula
Serigne babacar nit dongue la nit mane nako nakh fofou lako tek 🤣
@@watawasawbilhaq Lima méti mooy yangui réetaan Di sabooté ,toudée sa chaine watawasaw bil haq. Mais je reviens sur ma question Wahouma né dou nit ,je veux bien que ngua diohma ay preuves thi li waji wah. Béneen bi mooy yaw réetaanal rék mais moi je veux une réponse
🤣🤣🤣
Vous êtes vraiment ridicule Histoire Mamadou Dia sakh maitriser woulen ko. Serigne Cheikh domi Serigne babacar mi done opposer Senghor gagné ko nak té Cheikhal khalifa done waydiouram??? Vous etes betes sen wax yi fekhélen ba guenè Si Président Ousmane Sonko. Con ngen rek
Digante senghor ak serigne babacar danko mana weddi ? Kou wakh si sene yalla yi ngen dieufrou
Soyons srx t'as fait des erreurs sur certains mots du verset
Ya meuna fen dhé
Kou say way diour yaroul sank naniou la