INSEPARABLE saison 1 episode 16

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 6 лют 2025
  • Abonner vous à notre chaîne en CLIQUANT ici :
    / @sabadorproduction
    Contacts : 77 793 75 04 / 77 929 71 50
    Rejoignez nous sur:
    Facebook - / sabadorcouture
    Instagram - www.instagram....
    Tik Tok - www.tiktok.com...

КОМЕНТАРІ • 296

  • @falloumy1013
    @falloumy1013 Рік тому +197

    On a beau être un docteur on reste impuissant devant la maladie de l’amour❤️

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +9

      *Je te jure l’amour est puissant nt nakkk 😂😂il fait tomber tt les guerriers*

    • @thianeaida10
      @thianeaida10 Рік тому +8

      @@veroniquenatack7392kirassoulay dioyloo na ndanane ba tayi😂😂😂

    • @sambafall3509
      @sambafall3509 Рік тому +3

      ​@@veroniquenatack7392ay waay yaaw mi dél nopalou nak boy Véronique 😂😂😂

    • @AstouSane-v2y
      @AstouSane-v2y Рік тому +3

      Amine ❤

    • @thiatediop9555
      @thiatediop9555 Рік тому

      @@sambafall3509en kone setlou guako damako yereum elle es partout kou wax mou tontou 😂

  • @mamefatybousso392
    @mamefatybousso392 Рік тому +248

    Si tu tombé sur ce commentaires qu'Allah t'accorde un beau destin plein de réussite dans tous ce que tu entreprends ALLAHOUMA AMINÉ ❤️❤️🙏 déwénaty lén balén ma ak balnalén yalna yalla Bollé nu ball nu fékké watt ko aÿ att yu beuri brkp s saliou ♥️ kén bania manquer inchallah ♥️🎉

  • @ElagNaim
    @ElagNaim Рік тому +115

    La voiture de docteur avec la photo de Serigne Babacar Sy borome bonnet carré bii sama sope sama Yakar sama xol sama Serigne billay cheikh khalifa amoul morome

    • @seutouaby4140
      @seutouaby4140 Рік тому +2

      Del wakh sougniou yakar

    • @ndeyefatoundiaye5479
      @ndeyefatoundiaye5479 Рік тому

      Ken dou mom

    • @adjadiallo1783
      @adjadiallo1783 Рік тому

      @@seutouaby4140walakhiii

    • @oumousalamataniang6975
      @oumousalamataniang6975 Рік тому +5

      serigne Babacar sy sy alpha mayoro aly boy Michel Sambaye naar khalifa yaye daba ndiaye Fanta wélé nabou ndiaye sy malick fagaye demba missi diawara bakarek daramane arame lo coumba thiam mbagne pathé beugouma pathé khar yalla bopou thior borome bonné carré bi layenne la mais sama couzine yi aye Tidjane laniou tè mane dama leneu beug donc louniou beug beug nako dieulal ma may la ba diamono nekh😂

  • @boussobaly9864
    @boussobaly9864 Рік тому +37

    Ko d'accord si couple mamy et docteur

  • @sambafall3509
    @sambafall3509 Рік тому +33

    Dave ak sa wakh diou bari dji yeup fi ngay moudié 😂😂😂😂😂 wowowoooooooooooo 😂😂 merci Omar si pousse binga pousse Khadija 😂😂😂

  • @Soxnabinetasaliou
    @Soxnabinetasaliou Рік тому +97

    Take katou cheveux bou j’aime sama commanteire bou mala reukèe dinga mourou 🧕 dji 😂❤❤❤

    • @sambafall3509
      @sambafall3509 Рік тому +1

      Kone nioune goor gni mouthie nanioussi 😂😂😂

    • @GayeMayegaye-ty8jk
      @GayeMayegaye-ty8jk Рік тому +1

      Risque le lakhar do moru ❤bilay 😂❤

  • @Mia-ti8li
    @Mia-ti8li Рік тому +42

    Bounioula trahiré do to am confiance lolou mo dall mami elle a juste peur 😨 de revivre la même déception mais Bagnoul docteur bi😂

  • @mamefatybousso392
    @mamefatybousso392 Рік тому +115

    Je vous souhaite d'être futurs milliardaires à tout qui regarde cette vidéo ❤🎉 brkp s saliou ♥️♥️♥️

  • @DiopDaba-st9nb
    @DiopDaba-st9nb Рік тому +55

    Mamy mérite d’être heureux ❤❤

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 Рік тому +24

    *Ay way mbeuguel qui es tu 😂😂😂Docteur insbi fébar bou graw moko dall mei mougnal tè diokh Mamy touti tps mou digéré déception wame..Wouy Déve tay gua déee lissa mi soneu na deh waoooowww😳😳😢😢😂😂😂*

  • @sagne1746
    @sagne1746 Рік тому +78

    On dirait que l'amour existe vraiment le docteur est fou amoureuse de mamy😂😂😂😂😂😅

  • @khoudiambengue4087
    @khoudiambengue4087 Рік тому +8

    Dev ndékété bandit la ak kanam gou yeureumteulou gui 😅😂😅

  • @fatoundiaye4203
    @fatoundiaye4203 Рік тому +3

    Chaque jour ma guiss nite commentaire on veut la bonheur de Mami tè mom si bopam beugoul boheureum 😂😫😫😫

  • @aissatoubaroi2873
    @aissatoubaroi2873 Рік тому +10

    😂 docteur mi nobaté na😂 pourquoi genre amour yii si théâtre rk la am😂

  • @nafidiakite3363
    @nafidiakite3363 Рік тому +84

    Le peuple réclame le bonheur de Mamy 🥰🥺

  • @mamefatybousso392
    @mamefatybousso392 Рік тому +34

    On réclame le bonheur de mamy et le decteur 😢dma lén ko nian thi ndiék thi ndiék rk nk beugou meh bén thiow😂😢😂🎉

  • @CheikhJAMIL-1
    @CheikhJAMIL-1 Рік тому +79

    Monsieur l docteur l'amour ne se quémande pas et sa ne se force pas 😂😂 nekal nite

  • @amyseck592
    @amyseck592 Рік тому +18

    Bly mbeuguel dou yeufou nitt 😭😂 docteur fait doucement 💔 mamy aussi khana do nekat ak omar 🙄 dev est tellement faible li limou donn 😂😂 mais khalé bou djiguéne bi khiff na trop 😅 la mère de khadija ken dou digueul sa bouy Seuy li c'est vrai que omar waroul won réagir ni prsk manon nako may patients mou expliquer en tout cas ken dou wakh lepp😂💗série bi risque le ragal dou ko setane😍bravo à l'équipe de sabador couture 💕

  • @diatousall291
    @diatousall291 Рік тому +14

    Wa docteur ak dal yi nk😂😂😂😂😂😂thiey amour

  • @matysakho2759
    @matysakho2759 Рік тому +6

    La discussion de Djiby et sa sœur me rappelle mon frère Daysane paix à son âme

  • @amysylla8644
    @amysylla8644 Рік тому +13

    Conseil frère amna solo 👍👍👍🥰🥰🥰🥰

  • @MarieGueye-ve4hy
    @MarieGueye-ve4hy Рік тому +26

    Yenagui top docteur rek ba fater dev no way😂😂😂😂ki Mo faible ak kanam gou nine gui

    • @ndeyebadiop
      @ndeyebadiop Рік тому +2

      Ya bone 😂😂😂

    • @MarieGueye-ve4hy
      @MarieGueye-ve4hy Рік тому +1

      @@ndeyebadiop deve kat da niak diom 😂😂Ken khamoul loumou bgeu ter genram gui aka fer beuri

    • @hafsadjigo
      @hafsadjigo Рік тому +1

      Sohorguaa😂😂😂

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +1

      *Wakh gua deugue déh mei Déve momm loumou am djieul😂😂😂😂*

    • @MarieGueye-ve4hy
      @MarieGueye-ve4hy Рік тому +1

      @@hafsadjigo ki da faible way mouy layam layam ni mousse 😂😂😂

  • @seydouly6762
    @seydouly6762 Рік тому +20

    Machallah notre série préfère 🎉❤😊

  • @AichaDiallo-ju9ts
    @AichaDiallo-ju9ts Рік тому +1

    Mami mi billahi bougoul bopam ak bonheur yayame 😢

  • @bintou3365
    @bintou3365 Рік тому +3

    Balamay déh niounane on réclame le bonheur de mamy 😅té môme si bopam beuguoule am diammm😅😅 elle préfère la souffrance 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @khadysaliou3752
    @khadysaliou3752 Рік тому +14

    Arme laa si seuy dagama fk sama podiou Nday takma fekoma sii bede khadija rk lay topou Omar infidèle di firé waté yaa ame fite deug😂😂

  • @abdouthiao9690
    @abdouthiao9690 Рік тому +21

    Djiguene bou sonnou mo guena bone goor bou sonou
    Elle ne pourra pas controler c pulsions billay😢😂😂😂

  • @mustafaasamb8419
    @mustafaasamb8419 Рік тому +18

    Wuy Docteur faj na malde ba far feebar. 😂 😂 Ku xam mbeugeul yëfu lan la na ma ko wax. 😂 😂 Sonal nanu torob. 😂😂😂

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому

      *😂😂😂😂bilay ioe😂😂😂*

    • @seutouaby4140
      @seutouaby4140 Рік тому

      @@veroniquenatack7392wa yw ni gua narra diappé sa adouna kou commentaire gua tontou 😂

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому

      @@seutouaby4140 *Seutou Aby🤣🤣🤣🤣Ni ioe rk mane gnè lay topou mei ioe mane guay topou🤣🤣*

    • @FatouSéne-c8m
      @FatouSéne-c8m Рік тому

      ​@@seutouaby4140defa âme diote rek😂

  • @aicha3515
    @aicha3515 Рік тому +21

    😂😂😂😂ah docteur do sol say dall nakk bouma rouslo😭😭😭😂😂

  • @astoubus.salioumbacke
    @astoubus.salioumbacke Рік тому +12

    Mamy mi abal lenma yare ma dorgo bamou nor qui mo beugoul bonoheuram ci dieume bopame

  • @RichPathSuccess
    @RichPathSuccess Рік тому +10

    Omar sougnoula néwé wakhale loye wakh 🙈😂😂😂 chaque jour déle diokh kadougui Khadija malaye nopale😅

  • @mamemaraimembacke
    @mamemaraimembacke Рік тому +14

    L'amour 💕 con na seuuutttt😂

  • @omarsall9821
    @omarsall9821 Рік тому +11

    Avenirou baba mognu gnor, revanche rek amoul lenenn mane dei lila wakh ba yen tamite lolou ngen wakh mom rek lagni topou 😂😂😂😂😂😂

  • @ahmadndour7868
    @ahmadndour7868 Рік тому +13

    Docteur djiguéne gni khamouniou kouleine beug kouleine di teik souffrance laniouye beug

  • @veroniquecoly345
    @veroniquecoly345 Рік тому +4

    Le bonheur de khadija Omar mi kou rew là

  • @aramegueye-ox8ff
    @aramegueye-ox8ff Рік тому +9

    Yayou Khadija eupél na dh waroul dokhaléi ak omar sa doom bouy seuy warr ngako wakhé néene loudoul li

  • @ndeyebadiop
    @ndeyebadiop Рік тому +21

    Amour sakh warouna 😂😂😂

  • @serignediop-kd2ok
    @serignediop-kd2ok Рік тому +14

    bonne contuniation yousou vraiment ya diay casting

  • @diamafallousamb7563
    @diamafallousamb7563 Рік тому +4

    Lissa mimom rodenadai😂😂😂😂 ay dave ya faible menosaxx tenir😂😂😂😂

  • @mariamasarr2148
    @mariamasarr2148 Рік тому +6

    GNU togatt Di xarr fi ba vendredi😮

  • @diarra-zm8tv
    @diarra-zm8tv Рік тому +12

    Ohh beugél sof na😭🥰

  • @admedieng4373
    @admedieng4373 Рік тому +40

    Merci Djiby pour ta conseil envers ta tite sœur 😢

  • @saynaboundiayemouhamed8988
    @saynaboundiayemouhamed8988 Рік тому +2

    Oumar miii rééw na dh😂😂ki en khottou barigo moko guen mbaam

  • @sambafall3509
    @sambafall3509 Рік тому +12

    Mangui doga kham litakh l'adage disaitet c'est ce qui arrive à Dicteur 😂😂😂😂wouy mbouguél aka bari dolé sakh kaay naak 😂🤣

  • @filyfall5364
    @filyfall5364 Рік тому +27

    Ah docteur il est amoureux 😅😅

  • @khoudiambengue4087
    @khoudiambengue4087 Рік тому +4

    Docteur khana mbeuguélou indo nga nara doundou ak mamy loy def ni

  • @fatimaba9770
    @fatimaba9770 Рік тому +8

    Legui mamy mome lanla beugue nk 😂

  • @aicha3515
    @aicha3515 Рік тому +7

    docteur kay dieulma comme mamy beugoul kay😂😂mann beugue na

  • @fantadiop3293
    @fantadiop3293 Рік тому +4

    Wa est docteur biiiii môme febar n'a deugueune tane nak masta beugueul😢mamy diapaleko nak

  • @fatougueye-zh7td
    @fatougueye-zh7td Рік тому +10

    Mami dieulal Youssoufa bakhna😂

  • @awasow-yt5xx
    @awasow-yt5xx Рік тому +8

    😂😂le docteur me fait rire😂😂😂

  • @diazdia3639
    @diazdia3639 Рік тому +11

    Son bi déymay dioylo bilahi walahi 😭😭😭😭😭😭😭

  • @seydinaababacarsaerdiallo3077
    @seydinaababacarsaerdiallo3077 Рік тому +16

    Non mane médecin bi dafmayy fatheu. « indépendant de ma volonté » Nigua dieulé mbeuguel bi mo eupeu 😅😅😅😅

  • @Soxnadieye-pq7jj
    @Soxnadieye-pq7jj Рік тому +2

    Nila deh docteur mbiir sosi beuguè dara dangua siy def dara nalako diaral

  • @GalsenMediatv
    @GalsenMediatv Рік тому +2

    Série bi khana dafa diékh gatte n'a fane comme carrièrou abdou Thiouba Lo😂😂😂😂

    • @GalsenMediatv
      @GalsenMediatv Рік тому +1

      Naka djékk épisode yi nimoye Sorri wé la khameni séné khalat mo beuriwoutt, ms t'inquiète pendant tout ce temps là idée warra n'a âme khana, nak😅😅😅😅😅😅😅😅

  • @beauty3166
    @beauty3166 Рік тому +15

    12:04 J'ai bien aimé la discussion de Djiby et sa soeur, aye deugue kép lako wakh, ci goor gni

  • @haranyndoye6726
    @haranyndoye6726 Рік тому +4

    Khadija yayam tamit kènn dou momm li mou déf dou yonn waroul reagire comme ça sur tout que mou gneuw keur diambour sa domm bouy sey dou ni guay wakhé ak bien vrai que goor waroul daurr djiguènn mais waroul waunn dokhalè ni

  • @noreyni5448
    @noreyni5448 Рік тому +19

    Série nekhna machallah ! Bonne continuation 🙏

  • @nafissatoundiaye76
    @nafissatoundiaye76 Рік тому +1

    Yayou khadija tamit eupeul na😂😂😂

  • @adjisene4835
    @adjisene4835 Рік тому +2

    deception bo si diougué sa xol bi dina beugu dh mais sa xel mi moley bloqué. par contre le Dr ressemble bizarrement a pape cheikh le fénéant

  • @lola-jv7sz
    @lola-jv7sz Рік тому +1

    Wa doc bo défé ni kouy fathie patients yi😢😮

  • @papehamathniane1792
    @papehamathniane1792 Рік тому +1

    Ndeysane Dr Youssoufa masta
    Mais loutakh rék djiguéne dou beug mouk Kiko plus tôt kikoy torokhal😢😢

  • @aramegueye-ox8ff
    @aramegueye-ox8ff Рік тому +13

    Déff xaléi bou djiguéne bi sonou na😂😂😂

  • @Croyante-Rush0197
    @Croyante-Rush0197 Рік тому +18

    Pour mane médecin dou beug😂

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +7

      *Ahhhhh😂😂khana docteur dou nitt😂😂😂*

    • @Croyante-Rush0197
      @Croyante-Rush0197 Рік тому +2

      @@veroniquenatack7392 réponse bi dé magui kadone khar 😅ay veroo 😏🤣mais nak niom d'habitude dougnou gawa beug dé

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +2

      @@Croyante-Rush0197 *Diokh nala ko nakk🤣🤣Véro gui ni deh🤣🤣ahhhh dama wakh deugue di momm gnou srx yi mei gnouma kham gnio gueuneu beugue diguéne🤣🙏🏼🙏🏼*

    • @Croyante-Rush0197
      @Croyante-Rush0197 Рік тому +2

      @@veroniquenatack7392 mbadou yalla bakhna 😅❤

    • @aminatadiopamy1249
      @aminatadiopamy1249 Рік тому +1

      Mouni wa ya rew 😂

  • @momosylla5912
    @momosylla5912 Рік тому +2

    Youssoupha yangui déconné boul forcé ba yakk patience you

  • @abdouLahadWade
    @abdouLahadWade Рік тому +11

    Belle serie ❤❤❤omar

  • @fatoudieng9360
    @fatoudieng9360 Рік тому +8

    Wa ms doctor 😂😂😂😂

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 Рік тому +9

    *Wa Omar tmt est ce que cv mogue koy sogua deff kay comprendre ko rk mei Yayou Khadija noumou dokhalé dou yone eupeul na trop*

  • @od11prodiop42
    @od11prodiop42 Рік тому +3

    Lisa😂dinaa diékhale daoure dé😂

  • @BbfadiengKane
    @BbfadiengKane Рік тому +4

    Ndeyssane amour kouko doundoul doko xam docteur bi da beugue rkk ndeyssane 😢yeureunako nakk thiey amour🥺

  • @Kiyajobe
    @Kiyajobe Рік тому +1

    Heartbreak can make anyone behave like mamy but at the end you will still fall in love like
    Never before and a reminder to all the girls watching, your virginity is your only dignity as a woman.
    watching from The Gambia 🇬🇲

  • @CisseSoda-kw9ot
    @CisseSoda-kw9ot Рік тому +5

    Ay l'amour qui est ti😂

  • @RamouNdong-f8w
    @RamouNdong-f8w Рік тому +1

    Ki comme moi pense k titre série bi da faussè au lieu de inséparables c'est trahison

  • @ndeyeamydiop3264
    @ndeyeamydiop3264 Рік тому +14

    On réclame deux èpisode par semaine please 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🎉❤

  • @morkhoule2020
    @morkhoule2020 Рік тому +10

    Docteur boule forcée mamy bou siso bayi ko bala gua doundate le pure de ton passé

  • @MamanDAFFE
    @MamanDAFFE Рік тому +2

    Ndeysann yousoufa nenako damala fath bapare diarefa febarr😢

  • @fatoudiallo7981
    @fatoudiallo7981 Рік тому +23

    Mamy nak soff gua meune gua ame kou gueuneu docteur ish nékal nitt

    • @hafsadjigo
      @hafsadjigo Рік тому +2

      Foumou diar takh 😂😂😂 Omar mo yakk xol bih yakétt mais yallah bakhna espérons que mou accepté docteur bih rék 😂😂😂

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +1

      *Vraiment dafa soff way dou djiokh docteur bi sens tmt*

  • @thiounekhady4024
    @thiounekhady4024 Рік тому +6

    🎉🎉🎉🎉❤❤❤ deuxiem comenter

  • @mballoseye9116
    @mballoseye9116 Рік тому +6

    AYY Mami ❤❤

  • @antandiaye4744
    @antandiaye4744 Рік тому +2

    Mamy mi louko dal mome nioune djiguéne bouguou gnou kou baax

  • @MoustaphaKa-hn3yf
    @MoustaphaKa-hn3yf Рік тому

    Non mamy mérité na bonheurs bou bari bilah

  • @assyniang4328
    @assyniang4328 Рік тому +8

    Série bi lay topou ❤

  • @maremetandiang134
    @maremetandiang134 Рік тому +3

    Mane khawma loutah yene djiguene yi beugue goor boulene di torokhal mamy tegua diap thi docteur mogueune si yow deeh bakhna guay titarouni ish

  • @mameastandiaye1899
    @mameastandiaye1899 Рік тому +2

    Docteur 😂😂😂😂😂wouy😂😂

  • @MaguetteFaye-h9z
    @MaguetteFaye-h9z Рік тому +5

    Mami soff na way ish

  • @mustafaasamb8419
    @mustafaasamb8419 Рік тому +7

    Série bi neex na. 🥰🥰🥰

  • @MariamamSene
    @MariamamSene Рік тому

    Mamy ndeye sane khole bi da yakhou

  • @fatoumaiga6736
    @fatoumaiga6736 Рік тому +3

    Dev ak lisa 😂😂😂

  • @mballoseye9116
    @mballoseye9116 Рік тому +12

    Docteur bii badou bayi léguéye bii

  • @maguettegueye4714
    @maguettegueye4714 Рік тому +4

    Docteur tmt ki es ti😂😂

  • @Serigneassanethiam
    @Serigneassanethiam Рік тому +2

    Kou beug khassida abounel si mane

  • @astougaye7221
    @astougaye7221 Рік тому +11

    Mbaguel dal mo soukhour😢😢❤❤❤

  • @saynaboundiayemouhamed8988
    @saynaboundiayemouhamed8988 Рік тому

    Ayway Mamy nk normalement docteur bi moko war yor dh episode biii di niew nii mm niom niaar war nansé commencé sen relation amoureuse🙏🏽🙏🏽

  • @Falloumbaye7221
    @Falloumbaye7221 Рік тому +8

    Docteur bii wéroul😂

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +1

      *Mdrr da fadj Mamy ba parè moudjié fébar 😂😂😂*

    • @SokhnakhadyMbacke-854
      @SokhnakhadyMbacke-854 Рік тому +1

      ​@@veroniquenatack7392iow dh yaay répond tous les commentaires

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Рік тому +1

      @@SokhnakhadyMbacke-854 *Mane la deh🤣🤣magui thi série yeupp*

  • @khadijadiop7292
    @khadijadiop7292 Рік тому

    Film mbeguel😂😂

  • @dabandiaye5314
    @dabandiaye5314 Рік тому +2

    Mamy aka sof nak thim🚶🏻‍♀️🚶🏻‍♀️🚶🏻‍♀️

  • @bintoundiaye5739
    @bintoundiaye5739 Рік тому +1

    Ndeye saane docteur

  • @iboubodian-hx1yh
    @iboubodian-hx1yh Рік тому +5

    Mom rk lay top

  • @amyndiaye6849
    @amyndiaye6849 Рік тому +2

    Merci Khadija 🤣🤣🤣

  • @dabandiaye6323
    @dabandiaye6323 Рік тому +7

    Mbeguél qui es tu yaghi beugua doflo docteur bi mamy nak sof gha nanghoul ko ghén dound lounékh