🔴Urgent-la réaction de Guygui après la sortie de fadam-Mane douma wax ak ay Nafekh,détruit Fadam

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 20 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 535

  • @goramekare9594
    @goramekare9594 Рік тому +59

    Senegal doynawar liguafi liguey yeup oh respect a toi champion yaw rek yaffi diap say morom diléne dane bèneu façon simpi bassikaw fatté khadiouffi

  • @methzoblinde3112
    @methzoblinde3112 Рік тому +1

    Merci Gouye Gui tontou di forokh❤😂fadam doul rék mom na am vue rék

  • @CHEIKHNDIAYE-bp6vh
    @CHEIKHNDIAYE-bp6vh Рік тому +16

    Mane wa keur siteu deh mais kii champion nako may diamou way 🙏

  • @modougeuye3524
    @modougeuye3524 Рік тому +11

    Merci bokom frère kodou.fan.wer fadame dafa bari wah

  • @gestuplus
    @gestuplus Рік тому +22

    Point barre, Bén barre..😂😂😂😂😂😂
    Gouy gui yalla nga am diam

  • @bebexaragne529
    @bebexaragne529 Рік тому +1

    Champion du courage bonne continuation lépp daye bakh inchallah fadame bayile domou jamboure dji

  • @makhtarsow2472
    @makhtarsow2472 Рік тому +7

    Fadam seytané yonam nékousi loutakh mou bayi beuré gouy gui limou def ci fadam défouko😊

  • @SerignesameToure-dq1zk
    @SerignesameToure-dq1zk Рік тому +1

    Ay waye ngir yalla té yalla rek takh bayilenne Gouy Gui ngir yalla mou nek si diame

  • @laminediallo5379
    @laminediallo5379 Рік тому +21

    Courage gouy gui tu es un vrai champion

  • @mamedoudadiop8312
    @mamedoudadiop8312 Рік тому +20

    Ndaysane amna lou nèk si khol bi nk 😢

  • @Nene-il9cp
    @Nene-il9cp Рік тому +5

    Très bien bravo frère mes contanat vraiment je suis très content de toi mes Amal diame

  • @lahatkonte3955
    @lahatkonte3955 Рік тому +10

    Gouy gui franchement Fadam défoula dara day analyser rk
    Limla wakh leppou deugue leu

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 Рік тому +6

    Gouye gui grand champion le baobab de l'arène, ligua fi deff kéneu fatéwouko kou dane Ama baldé rek yanou zarko beu biir wekh niaff ko thi souff ndanane ngua, soumadone yaw ngua dem entrainé éviter média yi , Yallheu neu Yallheu yoné nieupou diamou Inch'Allah

  • @omarlo506
    @omarlo506 Рік тому +2

    Gouy gui ya tay defal loula nekh ❤

  • @shiekhibrambackehdarboe7557
    @shiekhibrambackehdarboe7557 Рік тому +2

    Thanks Gui Gouye clean heart ♥️💯💯💯😎😎😎

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 Рік тому +31

    Laisse Fadam 2 tranquil , il fait très bien son travail

    • @neyzard1097
      @neyzard1097 Рік тому +3

      Non Fadam cette fois ci daffa joum vraiment

    • @SeneShots
      @SeneShots Рік тому

      Naféque bakhoule fadam limou wakh yoname nékou sii bou fékone Lou deugou si mome dagoye wo téléphone

    • @espritsaints4685
      @espritsaints4685 Рік тому

      Fadame satan leu

    • @rimjaalloow7392
      @rimjaalloow7392 Рік тому

      Ce que fait fadam 2 est très facile,parler sur les gens seulement,en plus la majeure partie de ces vidéos il parle sur Balla gaye 2 ,il doit changer de méthode avec coach Bakary

  • @AsseNdao-e4o
    @AsseNdao-e4o Рік тому +1

    Merci way gouy gou

  • @ISmile__
    @ISmile__ Рік тому +5

    les lutteurs n'accepteront jamais les critiques.... c pas seulement Gouye Gui c tout le monde.... ils prennent pr ennemis ttes personnes qui disent des choses ne leur arrangeant pas. Gouy Gui doit comprendre c un personnage public ... mais hélas

  • @khadimfall1062
    @khadimfall1062 Рік тому +16

    Vraiment mane sama yone nékoul thi l'amb wayè gouygui fadam wax nala beugeu danga beuri wax demal entraînement dji

    • @seydinaomardiop4537
      @seydinaomardiop4537 Рік тому

      Lim ko wax deugeu la d

    • @alinesyllaSyllaaline
      @alinesyllaSyllaaline Рік тому

      Vraiment

    • @fifty6292
      @fifty6292 Рік тому +2

      Même sou néké deug Fadam dafko wére Gouy Gui amna gnoumou eup palmarès Gris Bordeaux 8 ans sans victoire Gouy Gui la gnémé

  • @Bilal66850
    @Bilal66850 Рік тому +8

    Vraiment Gouy gui à raison
    Fadam dafa eupeul trop il faut respecter les gens qu'à même

    • @ronebodjis4607
      @ronebodjis4607 Рік тому +1

      Fadam degue rek lako wakh na bayi wakh bii il ne devait même pas répondre

    • @fifty6292
      @fifty6292 Рік тому +1

      @@ronebodjis4607Fadam Gouy Gui la yapp na wakh ci Balla Gaye Gris Bordeaux yeufou Fake la def

  • @aichadiallo7414
    @aichadiallo7414 Рік тому +1

    Waye fadam wahoule louaye daye analyse rek antaque .sportif pour gua deferouwate coulahamoune dem. Ak.taye hamne change gua.❤❤😂😂😂

  • @barroaly1764
    @barroaly1764 Рік тому +1

    Gouye gui kass ndme rek inchalla ❤❤

  • @sarrmamadoulamine9773
    @sarrmamadoulamine9773 Рік тому +20

    Merci beaucoup Gouygui

  • @AbdouFall-e6m
    @AbdouFall-e6m Рік тому +1

    ay thi goy guu❤❤

  • @DjibrilNiokhorNDOUR
    @DjibrilNiokhorNDOUR Рік тому +1

    Merci beaucoup mbeur koufi titre ti Lou bonne porte leneko plainte

  • @diamouhamed2400
    @diamouhamed2400 Рік тому +16

    GOUY GUI NOPIL DA NGA BEURII WAKH DÉMAL ENTREINÉ DJI

  • @SerignesameToure-dq1zk
    @SerignesameToure-dq1zk Рік тому

    Billahi Gouy Gui champion nga yalla nala yalla maye combat maye la ndame bou reuye

  • @Amathmedina
    @Amathmedina Рік тому

    Fadame Limou wakh deug la mais warou co won wakh si réseau sociaux bi deko waron wo telephone 📞

  • @taybasakho-x9h
    @taybasakho-x9h Рік тому +1

    Gouy gui diamo rek si yaw biley damala beugué loul yalla nala yalla defal diamo inchallah lepo Dina bakh

  • @mouhamedndiaye2111
    @mouhamedndiaye2111 Рік тому +12

    Fadam wakhoul si yaw lou guen lamb soff nga trop

  • @aboubacarndiaye779
    @aboubacarndiaye779 Рік тому +19

    Fadam a raison,les gens attendent une réaction autre que celle affichée lors de ton dernier point presse,vos adversaires avancent et nous voyons un retard de votre côté et votre communication laisse à désirer, il faut privilégier les entraînements,la lutte n'est pas du culturisme avec nos respects

    • @SeneShots
      @SeneShots Рік тому +5

      Wakh loula wore bakhna trop, fadam amoul bén raison diko jugé nah lifi kouy gui déf si lamb fadam défou Ko amoul carrièrou lamb moudjé nék analyste frr arrêtez lén way

    • @jeremiefrancoisdiaz2638
      @jeremiefrancoisdiaz2638 Рік тому

      Mais attend il est de dire ce qu’il veut Bayilen diambour vous aimez trop juger les gens

  • @serigneballagaye4105
    @serigneballagaye4105 Рік тому +1

    Mém combat balla gaye 2 vs boy niang. Fadam boy niang lafaralon. Xamnasé loma l'air bilahi walahi

  • @AbouAbzo
    @AbouAbzo Рік тому +2

    Gouy gui dieulal Quench gua relancer sa carriere C le meilleur adversaires pour toi gua dém dougou si souff sii entraîner ba oss contact ba seuss

    • @modo6218
      @modo6218 Рік тому +1

      Bilahi lolou rek moy wakh dji yekk si dun yi

    • @Elhadji2187
      @Elhadji2187 Рік тому

      Meilleur combat pour relancer combat wam ak reug reug la waroul wonn dieull vraiment dafa entraîné woul wonn dara

    • @AbouAbzo
      @AbouAbzo Рік тому

      @@Elhadji2187 lolou deug la mais C le passé mongui souniou guinaw n'a dieul Quench dougou si dune yii entraîner 4mois walleuh 5 wagnii média yii dioubo ak ay rakam waa guediawaye goungué koo mou dane Quench yekk si kaw

  • @baityrba2447
    @baityrba2447 Рік тому

    Yallah na Yallah dfal lène diameuh ratakhal sen relatio amiine

  • @sambanossosethnjie7319
    @sambanossosethnjie7319 Рік тому

    Mètina dhh champion

  • @Elhadji2187
    @Elhadji2187 Рік тому +3

    😂😂Hun Fadam 2 meuso dann ken🤣🤣

  • @modo6218
    @modo6218 Рік тому +7

    Fadam degue la la wakh mais warona la dieul si souff

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf Рік тому +1

    GRIS 2 VS QUENCH KOU DANE DONE VIP AM FRANC ❤

  • @oumargadjosall1827
    @oumargadjosall1827 Рік тому +10

    Fadam tu as raison walaye demal liguey

    • @SeneShots
      @SeneShots Рік тому +2

      Yén aye nafék guén fadam amoul limou wakh sii gouye gui, beuré ba sone meunoul nék champion mou bayi nane daye analysé? Lou gniep meun analysé il faux respecté kouye gui

  • @serigneballagaye4105
    @serigneballagaye4105 Рік тому +1

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂fadam xamon na de nga am bis.merciiiiii guygui.fadam mo diahasé wa guiedway

  • @NgagneDiakhate-tm8nw
    @NgagneDiakhate-tm8nw Рік тому

    Gouy Gui du courage force a toi

  • @thiattfaye2346
    @thiattfaye2346 Рік тому

    ❤❤❤diambar deugg gua boul di tontou nioun beugue nanla ba paré

  • @moussandiaye1993
    @moussandiaye1993 Рік тому +8

    Gouy guii Bakary sakho lay guarouwalé😂

    • @kefgg
      @kefgg Рік тому +1

      😂😂😂😂😂😂😂

  • @sirmandiallo4685
    @sirmandiallo4685 Рік тому

    Du courage beur champion gua

  • @abdoulayedabo9509
    @abdoulayedabo9509 Рік тому +2

    Pourquoi les lutteurs n'accepte nt pas l'analyse des chroniqueurs ?

  • @yvonnebadiane2702
    @yvonnebadiane2702 Рік тому +14

    Fadame à parfaitement réson !

  • @loaboubacar3595
    @loaboubacar3595 Рік тому

    Gouygui ndskete Dof gua ligua wax si fadam nianw na😢😢😢

  • @bayfallyomboul513
    @bayfallyomboul513 Рік тому +4

    Respect Respect Respect Fadam Lou bahe rek lala begueule

  • @abipefaye
    @abipefaye Рік тому +13

    Gouy gui fadam a raisons dèmal entraînè mon guene dieuleul franc ou quench ou gris 2 danou par force gouy gui do dara

    • @oumarfall5628
      @oumarfall5628 Рік тому +2

      Mais Fadam mom foumou todjeu ??louka teré dem entrainer dji... mom maguoul Gouye gui... Dafa khamnii dafa teulé mo raw papa boy djiné motakh mou tell bayiii lamb.... Boyy djayy professionnel dé fekk nga todj fene nekk si référence

  • @omarsow7394
    @omarsow7394 Рік тому +1

    Du courage Gouye gui champion nga nioniou wakh moy sén liguéye
    Liguéyal rék yow bayilénne niou wakh

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5uc Рік тому +37

    Gouygui mala geuna contre fadam côté seytané bimou done mais lignou la wakh koula ko wakhoul dalay naxx bayil caméra yi liga dadj yakk siteu yoyou thiono bo beugué dara li dess sa lamb diga défe sacrifice wakh dji mom amoul sens ba paré yak quench fékhél combat bobou taxaw yak franc mome douma lako digal béne dioy la franc bouy nélaw sakh meno ko yé mais ni mome yagi si sakou bi koula ko wakhoul dalay naxx fadam dafa seytané mome djiko djiguéne deug la yoré ba paré day diakhassé

    • @dp8441
      @dp8441 Рік тому +3

      fadam amoul loumouy conse gouy gui bou amon loumouy conse gouy gui yeksi fi gouy gui yeksi si lamb fadam warna rousa tok sakh nan dafay conse mbeur

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc Рік тому +2

      @@dp8441 nom fadam mome dafa seytané lolou baxoul surtout si gor yalla djiko bou saleté la yoré fadam xam nako légui dama ko done bégué mais dafa seytané si gor yalla

    • @dp8441
      @dp8441 Рік тому +2

      @@MilkMilo-qr5uc dafa bari wakh trop com kou nek roi lambji

    • @alinesyllaSyllaaline
      @alinesyllaSyllaaline Рік тому

      Boy pourtant fadam wakh naka deuk

    • @alinesyllaSyllaaline
      @alinesyllaSyllaaline Рік тому +1

      ​@@dp8441migi niaw dh 😂😂😂😂

  • @mamathiam5649
    @mamathiam5649 Рік тому +8

    Nioune guediawaye laniou deuk mé vraiment dagua bari wakh

  • @ndiagadieng5381
    @ndiagadieng5381 Рік тому +1

    Courage frère

  • @ibrahimacoly756
    @ibrahimacoly756 Рік тому +2

    Sénégal koffi wakh deug mou mèrre 😀😀😀😀😀Fadam a raison

  • @saliouthiam2462
    @saliouthiam2462 Рік тому +9

    Vraiment gouy gui wakh na deugue fadam dakooo wérr 😢

    • @ronebodjis4607
      @ronebodjis4607 Рік тому +5

      Non du tt weerou ko degue rek lako wakh il ne devrait même pas répondre il doit prendre de la hauteur

    • @saliouthiam2462
      @saliouthiam2462 Рік тому

      @@ronebodjis4607 tu as raison mais comme limou wakh fadam manone nako appelé au téléphone 📞 si souff

    • @abdoukhadredjilybeye8785
      @abdoukhadredjilybeye8785 Рік тому

      ​@@ronebodjis4607toute vérité n'est bonne à dire surtout dans la place publique

  • @abdourahmanefaye1437
    @abdourahmanefaye1437 Рік тому +8

    Vraiment fadame lui doit du respect

    • @babacargueye-or5ti
      @babacargueye-or5ti Рік тому

      Fadam a parfaitement raison il doit aller entraîner point final

    • @abloslimshady
      @abloslimshady Рік тому

      Il doit Aller s'entrainer, Fadam deug rek la wax!
      Sénégal ko wax deug mouné dang ka niakal teguine!

  • @ndirmatar5957
    @ndirmatar5957 Рік тому

    Hoooo champion dioume ga tay li warou la yawe nitte kou bakh ga wara tontou wakh yi bay wakh wakh you niawe yi

  • @modoudieyembayesikurulah2019
    @modoudieyembayesikurulah2019 Рік тому +1

    Rue des fois dame bruit du fantôme de gloire

  • @badiallodia4208
    @badiallodia4208 Рік тому +1

    Gouye gui courage ont est tous derriere toi jambar gua

  • @lahadboukharagnelo6707
    @lahadboukharagnelo6707 Рік тому

    Merci Fadam 👊👊👊👊👊

  • @piscoyoungtccam3891
    @piscoyoungtccam3891 Рік тому +1

    champion nga

  • @SerignesameToure-dq1zk
    @SerignesameToure-dq1zk Рік тому +1

    Ngir yalla bayilenne Gouy Gui mou nek si diame

  • @serignesam8982
    @serignesam8982 Рік тому +2

    Franc Moy Sama mbeur mai Gouy gui wax n'a deugu fadam xamoul touss

  • @papasarr1364
    @papasarr1364 Рік тому

    Ngobane léne sama commentére😂😂😂😂

  • @basalmane317
    @basalmane317 Рік тому +4

    Ayway gouy gui wagnil wakh yi heeeeeeeeee😅😅😅😅😅😅

  • @bourybarry3911
    @bourybarry3911 Рік тому

    Grand bayyil wakh bi stp Demal entraîné ngua djeul avance, encaissé mooning. Mane gouy gui ancien bi lagnou sokhleu mais pas kiii Yoww sans micro bign leyy tallal doo dem

  • @Concept0208
    @Concept0208 Рік тому

    Gouy Gui lilépou ay détails la. Té doula yobou fén.
    Ate yangi dém, dolédji moungi wañékou. Dieleul say adversaires nga beurré.
    Wa Salam.
    Gouy Gui vs Quenz
    Gouy Gui vs Franc
    Gouy Gui vs Tayson 2 (revanche)

  • @cheikhahmettidianesarr9086
    @cheikhahmettidianesarr9086 Рік тому +1

    Salam,Gouy Gui a parfaitement raison,si fadam ne l'a jamais apprécié étant son connaissance.ce gars n'a pas le droit de parler sur lui, soyons honnête.

  • @ImerPascalMendy-ru5bb
    @ImerPascalMendy-ru5bb Рік тому

    Gouy Gui Champion laa dioxko thieur

  • @BallaMarone-dw7bi
    @BallaMarone-dw7bi Рік тому +3

    Gouy gui dinama Ray way fadam am nga sokhla nk😂😂😂

  • @Justin-Lo.
    @Justin-Lo. Рік тому

    Gouy gui sakanam gui esk ya ngi entrainé 😂 mdriiiirrrr legui kanamou noceur ngayoorr😂😂

  • @bassndiaye2654
    @bassndiaye2654 Рік тому +1

    Verité absolue Gouy gui fadam saytané la

  • @manoumbaye6277
    @manoumbaye6277 Рік тому +2

    Bayil sites yi nga ligueyi, wakh ji beuri na

  • @tallasylla2505
    @tallasylla2505 Рік тому +6

    Courage champion 💪

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Рік тому

    Merci gaye Gui fadame nafekh la

  • @yyytgg1882
    @yyytgg1882 Рік тому

    C'est valable pour tt le monde bayilen nitt yi dounde lignou beug

  • @HamadiseydiGuissé-e7o
    @HamadiseydiGuissé-e7o Рік тому +1

    Merci champion fadam c un vrai fumiste qui ne connaît rien en lute ki n'as même pas 2 victoire en arène c nomme expert Sénégal dall

  • @beuguebambaseck4916
    @beuguebambaseck4916 Рік тому +3

    FADAM DAFA COMPLEXÉ BAKARY MOTAX LEGUI MOUNÉ DAFAY DEF COMME MOM DI DEFCSANS LANGUE DE BOIS ☝️FADAM BOUL SOPEKOU NEKKAL NIIT

  • @laminmanneh1048
    @laminmanneh1048 Рік тому +1

    Merci gouy gui

  • @Justin-Lo.
    @Justin-Lo. Рік тому +1

    So entrainé tei thiakhano ken eupouleu dolé😂 mais son topei repas yi AK pion yi 😂 Michelin ngay nékkatt dh com Boulay Zooss Di fokheu sa baram bi

  • @Amathmedina
    @Amathmedina Рік тому

    Gouy gui fadam lim la wakh deug la Bly walahi kou guiss sa lekh yi khamne entraîne woo

  • @babacar3178
    @babacar3178 Рік тому

    Bilay kayi danio kon topou dome yi

  • @ibrahimaseye7267
    @ibrahimaseye7267 Рік тому +2

    Trop de communication tue l’a communication! Gouy Gui Li ngay wakh dafa bari même so amé deug dotoul saffé, il faut faire comme Boy Niang parler peu et bien

  • @cheikhgueye1070
    @cheikhgueye1070 Рік тому

    Il a parfaitement raison gouye gui

  • @DaoudaDiallo-nz2ge
    @DaoudaDiallo-nz2ge Рік тому

    Courage kouye ki yawe nitte kou bakhe nga yalla mon la daifare boule tontou

  • @mouhdy852
    @mouhdy852 Рік тому +5

    Vraiment danga Bari wakh gouye gi 🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐🤐

  • @fromsenegalilovegalsen6401
    @fromsenegalilovegalsen6401 Рік тому

    Suis d'accord avc gouye gui fadam2 yaw tu fai parti mm generation que gnom gouye modou lo ak bg2 dagua done beuré tapet motakh gua daw téyé micro di kebétou il faut les encourager pa les rabaisser

  • @khadimkaire100
    @khadimkaire100 Рік тому +6

    Gouye gui khana bala deff interview dayy diwooo??😂😂😂😂

  • @mouhameddiagne9347
    @mouhameddiagne9347 Рік тому +3

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣yoro Ten ma djeunde doun 🤣🤣🤣

    • @Mod-t2y
      @Mod-t2y Рік тому +1

      😂😂😂😂

  • @nfamaradiatta2781
    @nfamaradiatta2781 Рік тому +1

    Gouygui es Bien
    Vraiment

  • @harounadrame7752
    @harounadrame7752 Рік тому

    Même la journaliste elle est fatiguée elle transpire 😭🤣🤣

  • @smatar085
    @smatar085 Рік тому

    Très bien dis goy gui fadam seytanela merci big up

  • @ibrahimasougou7061
    @ibrahimasougou7061 Рік тому +2

    Fadam deug lala wakh bayil liguay déf démal entraîné mo gueune

  • @mouhameddia7895
    @mouhameddia7895 Рік тому

    Merci

  • @SambaSeck-wl8py
    @SambaSeck-wl8py Рік тому +4

    L'aléne sama ngobane😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @noreynibenafannoreynibenaf4097

    Lingaye wakhe niéméwoko té ku beuri ay detaille ngeu,

  • @kadermbaye396
    @kadermbaye396 Рік тому

    Fadammm soumako guissé mouyy wahh si lamb vraiment dafmay def réé😂😂😂 59 combat 0 victoire

  • @Dakartiktok
    @Dakartiktok Рік тому +1

    Fatema Dia amegaa problème 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
    Dagaa niaak walaaa dagaa sonouuu😂😂😂😂😂

  • @moussaseck967
    @moussaseck967 Рік тому

    Bilahi fadame môme vré saytané la même nioune wa pikine Daf nioye diakhassé gouy gui wakh gua degue

  • @CheikhMbaye-tw7gv
    @CheikhMbaye-tw7gv Рік тому

    Blh ta raison fadam seytané la