Sénégal wakh rekk souba AK ngone, ici tout le monde est dans le chômage, famille boo dougou kenna moocii kheuy dem liguey wout indi, gnoussi desse ken liguéwout
Vraiment deugue rekk nguafi wakh. Content nen trop. Sénégal daga done pays boo khamnè, ken yeéné wout sa morom diam, lolou moofi am. Dou dem saa way. Dou dem maalako wakh. Sénégal nitt gni degnoo khiff. Sénégalais lekk rekk.
Bilahi senegal war na rombou fi sakh mais présidant you bon rek
Ton .meilleur video machala
Argentine ni leu rafété kone thiey deukeu toubabe yeupeu avancer mais africain yi souffrance rék 🤕💔
Bien dit
Mon frére de coeur sama kharit diam si yow
vous avez raison mais notre principal problème en Afrique sont dirigeants dictateurs qui n'ont pas de projet pour leur jeunesse
Macha Allah
Good job brother 👏
Sénégal wakh rekk souba AK ngone, ici tout le monde est dans le chômage, famille boo dougou kenna moocii kheuy dem liguey wout indi, gnoussi desse ken liguéwout
Y los subtitulos.
Sénégal espace mom diaye kessé lenci kham, ba paré deukk ci wout Say 4 diabarr, dougal ci keurgui, problème depense yi démarré nak
Vraiment deugue rekk nguafi wakh. Content nen trop. Sénégal daga done pays boo khamnè, ken yeéné wout sa morom diam, lolou moofi am. Dou dem saa way. Dou dem maalako wakh. Sénégal nitt gni degnoo khiff. Sénégalais lekk rekk.
Diadief bayfall
Wawe gor fall