Ndeyssane xam-xam torokh na légui. Vous êtes réunis ici pour di wééranté ak di reuy reuy lou nane diw niéméwoul diakarlo ak mane ci live alors que diw momou mi ngui nonou tok. En plus wakhoulén pour diangue ak diangalé, mais pour qu'au finish, am kou gagné, ak kénén kou niou laminé pour niou roubéko. Limotakh Cheikh Ahmeth Tidiane Chérif wakhone "dara nékoul ci tééré yi loudoul khoulo". Xam-xam ci deunou Gorou Yalla lanékk. C'est pitoyable.
Oustaz assane t’es le meilleur
La dernière fois tu as humilié alpha devant ses supporters
Do xam Sax loy diap bly😂
machallah oustaz Assane ❤❤🎉🎉
Iow ibliss ngua assane amoul xam xam wa akhlou bida amou lene xam xam billahi
@ibrahimediop7470 wakhouma ak iow ok 👍
Assane khamol dara
Sa way guénal ci li nga nék. Xam xamou pékhé rek nga fiy nék di wax
Ouztaz assane bolte kene dou wakh Adiss hadith
Sois-disant oustaz assane démale diangui sa diné té bayi parparlo bi khamo dara 😂
hana do xool 😂😂😂 xam xam dou pékhé , antouka asssane limou wax fou lerr lako tek
Non assane diambar la nak
Yw oustaz assane arrangé wula ndax mo humilié alfa ba devant tout l monde..kou khol kham ni wahabiste yi amuniu xam xam ni deg deg
Oustaz Assane 😂😂man billay dinama ray seut diiné dalll legui
Nooooo assane Toure demal djangui kham ouli dara assane bolte
Assane mi khamoul touss
Asssane bolt
😮😮😮
Yén ni doul rek khamou léne katt
Ouztaz assane merci way..kham kham dou peikhei
Sapo assane
Oustaz moderne il est dans une peau qui n'est pas la tienne
Ndeyssane xam-xam torokh na légui. Vous êtes réunis ici pour di wééranté ak di reuy reuy lou nane diw niéméwoul diakarlo ak mane ci live alors que diw momou mi ngui nonou tok. En plus wakhoulén pour diangue ak diangalé, mais pour qu'au finish, am kou gagné, ak kénén kou niou laminé pour niou roubéko. Limotakh Cheikh Ahmeth Tidiane Chérif wakhone "dara nékoul ci tééré yi loudoul khoulo". Xam-xam ci deunou Gorou Yalla lanékk. C'est pitoyable.
Pourtant c’est intéressant je vois pas de mal à ça
Niom niaar nieupp sene xam xam seloul , wané wou rek ak buzz, motax niou dem thi ahmed cissé mii
Assane vraiment tu es nul amoulo xam xam🥲