image du jour: S Mountakha Moy Serigne Touba Aka Yéémé (Prière du Vendredi 1ér Mai 2020

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 8 лют 2025
  • Abonnez vous notre chaine UA-cam rafah tv Email mourtadarafahitouba23@gmail.com contact Rafah Tv service commercial 77 433 39 39

КОМЕНТАРІ •

  • @cheikhounadiakhate531
    @cheikhounadiakhate531 4 роки тому +337

    Kou beug cheikh mountakha beuseul j’aime ❤️

    • @assanesow9311
      @assanesow9311 4 роки тому +1

      je di sakh jaime

    • @mamematy5994
      @mamematy5994 Рік тому

      Mbacké yalnanga fi yague lol ta wér ci barkép Xassida yi

  • @ibrahimbassoum7248
    @ibrahimbassoum7248 4 роки тому +126

    Suis tidiane mais wallahi wallahi wallahi ! Souma guissé serigne Moutaha damay geuneu begg geuneu selle geuneu ragaal yallah !
    Wallahi yallah xamnako !
    Yallah na yallah yagaal tahawayène si dinér dji
    Yallah naniou yallah naniou yallah téguiil mbiss mi si barké yamoul jum'a

    • @laminmaster9387
      @laminmaster9387 4 роки тому +1

      Ibrahim Bassoum danga bakh rék ndeysan. Dieureudief

    • @salutfay8386
      @salutfay8386 4 роки тому

      Ndaysan

    • @maremengom1839
      @maremengom1839 4 роки тому

      Waw goor basoume

    • @mameboussodiopkhidma7540
      @mameboussodiopkhidma7540 4 роки тому

      Pasque kéne eupaléw la si s touba motah ngay yég mbegté thi s mountakha

    • @begmamedabakhrek9863
      @begmamedabakhrek9863 4 роки тому

      Ibrahima basoum tidiane ak mouride yeupou bén la man mourite la té guisga dama beg mm Dabakh 😭bilahi nimu mél si sama khôl yalla rek moko kham

  • @alqoudoshd3703
    @alqoudoshd3703 4 роки тому +109

    La Mouridiyya a toujours rappelé au monde entier qu'il y a un seul DIEU, Allah le Tout Puissant, le Seigneur de l'Univers. Et c'est vers Lui que nous retournerons. L'islam doit être notre premier rempart pour résoudre tout problème.
    Jërëjëf Sëriñ Touba. Sëriñ Mountakha yalna fi yagg te werr

  • @ibrahimadione8708
    @ibrahimadione8708 4 роки тому +162

    Baye niasse la beugue sama xool mé Serigne mountaha vraiment il est spécial j’arrête pas de le regarder avec son magnifique sourire je l’adore beaucoup machalah

    • @lahatmbackediouf7319
      @lahatmbackediouf7319 4 роки тому +3

      ibrahima dione machalla Dieuredieuf alhamdoulila 😍❤️❤️❤️

    • @profcoly6085
      @profcoly6085 4 роки тому +2

      Ibrahima khalil dione yalla gua yague lool té wér kou bakh gua machallah

    • @gamigam6420
      @gamigam6420 4 роки тому +1

      Baye geureum na même mane talibé baye la mai machala sohorouniou

  • @papoumendes369
    @papoumendes369 4 роки тому +354

    ❤❤Mon coeur te porte Mbacké paix et joie je suis chrétien (croyant)je l'aime de tout mon coeur...😥😥

  • @madouniambele4874
    @madouniambele4874 4 роки тому +5

    yala magui laye yane si barke yonetibi ak mame borom touba ga defal fane bou goudou ak wer s mountakha mbacke amine si barke saha bâ yi ak l islam

  • @aliounediba369
    @aliounediba369 4 роки тому +308

    Les mouridimes sont des exemples de tous secteurs merci SR MOUNTAKHA MBACKE

  • @gamigam6420
    @gamigam6420 4 роки тому +31

    J suis un disciple de Baye Niass mais j peut dire que serigne touba de part ces hassida a su gagné le coeur de tout homme en écoutant c hassida tu as le coeur qui tremble tu es a la foi triste et a la foi heureux car il a travaillé pour la religion, l'islam est fier d'avoir un fils nommé cheikh Ahmadou Bamba le Sénégal aussi es fier de vous l'incontestable serviteur du prophète PSl.
    Que dieu garde le Sénégal et chasse ce virus covid 19 hors du pays 💖

  • @serignkane8731
    @serignkane8731 4 роки тому +136

    Mane bilahi dama beugue Serigne Touba blh 😭😭😭😭😭😭

  • @abdoulmbaye18
    @abdoulmbaye18 4 роки тому +6

    Mane dh wa fouta la meis sama yaram dawna thiey Mbacke diine rek😭😭 yalla nga goudou fane Mbacke 💝💝 liga takhwé diine bi nekh naniou🙏🙏🙏

  • @mamediarrabousso9875
    @mamediarrabousso9875 4 роки тому +86

    Ko nagu ne Serigne Touba amoll morom 😭😭😭😭 dieureu dieuf mbacke

  • @SouverainisteTV
    @SouverainisteTV 4 роки тому +69

    Je suis tijiane mais je suis trop content machallah

  • @modoungom1908
    @modoungom1908 4 роки тому +38

    Ndeysane + d 1000 Diouma bénn Diouma mo moy diouli tjr Serigne Touba si kanam rékk ba fawwwwww ( kaw kaw)

  • @TaphousTV
    @TaphousTV 4 роки тому +90

    Je le dis et je le redis
    Serigne Touba Mountakha yama gueneu sama boop.
    Loula nara daleu si safane na daleu si Mane.

    • @lahatmbackediouf7319
      @lahatmbackediouf7319 4 роки тому +3

      Amadou Moustapha Thiam Dieuredieuf yalla nagua fi yague tai wére. bilakhi lezi lailahailalaha tamaye teude ba goudi di ñiane 🤲🏾 sama Borom li dès thi sama fane yi mou diokhale ma serigne Mountakha 😭😭😭😭😭😭😭😭

    • @gallodieye7652
      @gallodieye7652 4 роки тому +2

      Ndeyessane daga bakh rékk

    • @mamefallloudiouf1306
      @mamefallloudiouf1306 4 роки тому +2

      Walah8 ya bakhe

    • @assanesow9311
      @assanesow9311 4 роки тому +2

      thiey ya ma gueune dh

    • @assanesow9311
      @assanesow9311 4 роки тому +2

      yalla nagua fi yagu

  • @aidagueye5765
    @aidagueye5765 4 роки тому +110

    Dieureudieufèti serigne touba diarama mame chiekh ibrahima fall serigne mountakha mbackè yalla nafi yagi lool

  • @fallbaradiop4246
    @fallbaradiop4246 4 роки тому +35

    Touba à cette période il fait tres chaud , les carreaux n'en parlons pas mais le khalif marche pieds nus bilahi ak talibé rek mo ame solo jeredieff Mbacké

  • @mouhamadaneallhamdoulillah0292
    @mouhamadaneallhamdoulillah0292 4 роки тому +98

    Limoy ndamou islaam manchallah😍🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @lomaguette9545
    @lomaguette9545 4 роки тому +22

    Serigne moutakha moy saguoup bép mourite di saguoup bép djoulite
    Guena yague guena wér
    Ayway yalla sakhal fi dieum dji thi barker alkhour hane ak khasida yi 😭😭🙏🙏🙏

  • @ibrahimambow85
    @ibrahimambow85 4 роки тому +88

    Yalla ne yalla bole nou yagal fi si barke Serigne touba 🥰🥰🕋🕋🕋

  • @awadajmiladiaw1670
    @awadajmiladiaw1670 4 роки тому +2

    Ça me rappelle talabadrou halayna min chaninnyatil wadahn lorsque le prophète arrive à Médine comme si j'étais présent ! dieureudieufé Serigne Touba😭😭😭

  • @abdourahimseck6334
    @abdourahimseck6334 4 роки тому +147

    Quand c dur seul les durs avancent .dieuredieuf mbacke

  • @profcoly6085
    @profcoly6085 4 роки тому +43

    Mane li la geume mouride dou bayi yooname ndahté diamonoy péste noire bi serigne touba meussuol teudj diouma ndiaréme bi kone diamonoy corona virus dou takh niouye teudj diouma wou kou téd ki machallah wa touba yalla laniouy diamou té corona simple diamou yalla leu machallah mbacké balla aïcha geuneu yagg geuneu wér touba la référence 💪🏿💪🏿

  • @amyfaye6157
    @amyfaye6157 4 роки тому +60

    Dieuredieuf serigne touba alhamdoulilah bima doné dioulite teksi nék mouride❤️❤️❤️😍😍😍🙏🙏🙏🙏

  • @cvpointernational4549
    @cvpointernational4549 4 роки тому +39

    *ndysan 😭😭 yalna yalla gouddal fanam blly Serigne mountakha mbektè mourid yi machallah Dieu que accepté nous prières ❤️❤️🌙❤️🤲*

  • @khadimfall9441
    @khadimfall9441 4 роки тому +53

    Alhamndou lilahi dieuredief seringe touba yalla nafi Corona bi diougé 🙏

  • @rokhayafaye9864
    @rokhayafaye9864 4 роки тому +20

    Maan déé talibé cheikh Ahmed Tidiane Chérif laa,mais damako beugue rék téé yalla takh.yalla naafi yague looool téé wéér.amine

  • @wizkilifeuhtv_officiel1532
    @wizkilifeuhtv_officiel1532 4 роки тому +182

    DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA DIEUREDIEUFETI SERIGNE TOUBA

    • @ibrahimnguer8795
      @ibrahimnguer8795 4 роки тому +2

      WiizKilifeuh_Official nala diam sonal bilayi 🙏🙏

    • @ndeyemary8447
      @ndeyemary8447 4 роки тому +1

      Mbacke BALLA yag fi lole tai were machalla ken dou serigne touba bilahi dieuredieuf

    • @DKM888DKM
      @DKM888DKM 4 роки тому +3

      Diera diefé Serigne Touba amoul morom

    • @rokhayathiaw5137
      @rokhayathiaw5137 4 роки тому +1

      Bilahi matnako diereudiefe yaw miko wakh

    • @youssouphandiaye76
      @youssouphandiaye76 4 роки тому

      Bane khassida la

  • @Plumemng
    @Plumemng 4 роки тому +4

    Bilahi walahi talahi Serigne Mountakha Mbacké yay libidor yay diamant yay ourous ya baxx ya raww ya niou mom niola beug❤️

  • @al_mouridya_loficielndiaye7706
    @al_mouridya_loficielndiaye7706 4 роки тому +58

    Mbacke yalla nafi yague té wer barkep khasidayie

  • @khadyndiayeyayefall9014
    @khadyndiayeyayefall9014 4 роки тому +34

    Thiey Mbacké yalla ngafi yague diniou goungué barké cheikhra fall Mbacké doundeul sa dounde gui amna ndiarigne 🙏😭😭😭

    • @sayenaboundiaye6044
      @sayenaboundiaye6044 4 роки тому +1

      Amine way

    • @astoundoye3993
      @astoundoye3993 4 роки тому +1

      barké alkhourane mame boye mala beugue magui dioye yeurmadé bi nékone si serigne saliou mo nék si mome yalla nagnou yalla rouse bayil gnoukofi bari diam nékhi réee thiéy Ahmadou guéne dou mome

    • @khadyndiayeyayefall9014
      @khadyndiayeyayefall9014 4 роки тому

      @@sayenaboundiaye6044 amine ya rabi 🙏

    • @khadyndiayeyayefall9014
      @khadyndiayeyayefall9014 4 роки тому

      @@astoundoye3993 amine way🙏 wayé malako geuna beugue nak❤😂

    • @astoundoye3993
      @astoundoye3993 4 роки тому

      @@khadyndiayeyayefall9014 iiiih khady lolou mome doumako nagou mame boye bokou mako ak kéne lolou laye wakh mai yaw khadial nala touti 😂😂

  • @patricelumumbaestunefierte781
    @patricelumumbaestunefierte781 4 роки тому +207

    Jërëdëf Serigne touba amoull morom je le répète jërëdëf Serigne touba amoull morom

  • @mamadoumansourfaye4684
    @mamadoumansourfaye4684 4 роки тому +11

    Je suis Tidiane mais Serigne Mountakha 🇸🇳 nieupp la beugg yaggfi lol té andak weurrr inchala

  • @mouhamedsaliousourang6456
    @mouhamedsaliousourang6456 4 роки тому +31

    Ndeyessane serigne bi mogui dieumeule diné bou bakh machalla yallanako yalla dolé tahawou si barkep werou koor gui inchalla

  • @ousmaneediop2012
    @ousmaneediop2012 4 роки тому +56

    Les 60 personnes qui n’aiment pas la vidéo. C’est quoi votre problème ?
    Mbacké yalla ngafi yagu té wéér 🙏🏿

    • @mbayangdiaw2432
      @mbayangdiaw2432 4 роки тому

      Moma diakhal waya dieureudieuf Ahmadoul Khadim

    • @senegal3620
      @senegal3620 4 роки тому +4

      Il y'aura toujours des coeurs qui diront non c'est l'oeuvre de iblisse mais nioune wa keur Serigne Touba laniou nioune rek nio diakhal iblisse. Dieredieuf Serigne Touba

    • @chiekhousall6874
      @chiekhousall6874 4 роки тому +5

      Slt svp pas de commentaires sur les j aime pas respectons leurs choix en tout cas nous les talibés on le porte énormement sur nos coeurs et comme le disait Serigne Mountakha rek mouride dou khole loukoy sokhoré

    • @عبداللهوخديمرسولهصلىاللهعليهوس
      @عبداللهوخديمرسولهصلىاللهعليهوس 4 роки тому +2

      Pour mane danio khamoul bine wara beuss waye li xana amoul koum nekhoul

    • @mberythies5738
      @mberythies5738 4 роки тому +1

      Peut-être une erreur mais sunu wadji yakarouma niitt bagn nako

  • @alkhouranaksounnasounna5021
    @alkhouranaksounnasounna5021 4 роки тому +47

    S.mountakha mbacke yalnafi YAGA loooolll TEWER

  • @ibrahimaseydouba590
    @ibrahimaseydouba590 4 роки тому +2

    Serigne Mountakha yala nafi yague lolou tei Weir kounei amine yala nassa adio fadiou tei are la si Coronavirus bi Amine

  • @madamendiaye3337
    @madamendiaye3337 4 роки тому +22

    Ohhh mback sm yaram dawna yag fiii téwér barkep nabyne moustapha psl ❤️🙏🏿

  • @diabateadama8892
    @diabateadama8892 4 роки тому +1

    Dieureudieuf serigne touba akassa yalla na yalla yokk lèrame té mou yaguefi lol té wére

  • @assanegueye1357
    @assanegueye1357 4 роки тому +63

    Kendou duu serigne Touba. Yalna fii yague te werrr
    AMINNN

  • @abubakrsow3542
    @abubakrsow3542 4 роки тому +1

    Djeureudjeuf SERIGNE TOUBA MBACKE. ..Mbacke ap sagg nga ci L'Islam YALLA na YALLA goudal fan wi Amin...

  • @mbenguekhadimmbacke4157
    @mbenguekhadimmbacke4157 4 роки тому +17

    Jeurejeuf serigne touba serigne mountakha mbacke yalla nafi yague ta andak wer

  • @mamanbadji1259
    @mamanbadji1259 4 роки тому +1

    Dieureudieuf Serigne mountakha mbacke balla Aïcha yague fi loole te ande ak werr serigne touba amoul morom

  • @bayembackedieng7072
    @bayembackedieng7072 4 роки тому +172

    Gueune yagg gueune Wer rk Mbacké Balla

  • @baytirsamb2064
    @baytirsamb2064 4 роки тому

    Alhamdou Lil Lahi. Djeureujeuf Serigne Touba.
    Serigne Mountakha Bassirou MBACKE Ya Allah Yaggal koo sunu biir tey dooli Weeram cii barke Mame Cheikh Ibrahim Fall.
    Wayeyy mbok yii dimbalileen meu cii khassida gui Ak khetou dadji gui. MachAllah

  • @moundawgueye1081
    @moundawgueye1081 4 роки тому +64

    Thieye ken dou serigne touba

  • @lahadboukharagnelo6707
    @lahadboukharagnelo6707 4 роки тому +23

    Billahi fi Serigne touba rek mofi 'nek kou d'accord

  • @mansourdiop3056
    @mansourdiop3056 4 роки тому +10

    Yallah ngafi yague Té wére mbacké kou beugue serigne mountakha beusseul j'aime

  • @idaf.731
    @idaf.731 4 роки тому +52

    Machallah machallah émouvant qu’Allah vous protège

  • @falloufall1816
    @falloufall1816 4 роки тому +14

    Akssa dieureudieuf Serigne Touba Khadime Rassoul Serigne mountaha mbacké balla ayesa yalla n'a ga fi yagué te serre amine ya Rabi 🙏🏿♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @bayecheikhdiop51
    @bayecheikhdiop51 4 роки тому +3

    Diaradieuf serigne touba qui d'accord avec moi

  • @SonkoActu
    @SonkoActu 4 роки тому +13

    Kou yabou gnibbi Touba! MachaAllah! 😍 Yag fi lol t wer Mbacké Balla

  • @abigailcisko5290
    @abigailcisko5290 4 роки тому +4

    Ana gnou beugue serigne mountakha bachir té yalla takh

  • @adjadioumangom1166
    @adjadioumangom1166 4 роки тому +22

    Mbacké Balla yalnague fi yageu loll teweur yallamusal la si fébarbi thie barké SERIGNE touba

  • @sallfatou7153
    @sallfatou7153 4 роки тому +6

    Allahou Akbar thieuy sounou mbecktei mi keimanei. Doundeul weiral Mbacké balla aïssa. Feiss nga deil ci sounou ❤️yi. Amine ya rabi 🙏

  • @fatoucha554
    @fatoucha554 4 роки тому +27

    Ki mako beugue barcké Sérigne Saliou Mbacké yague fi waye té wére ♥️♥️

  • @fallougueye7690
    @fallougueye7690 4 роки тому +2

    Serigne mountakha yalla nafi yagg té andak wërr day gueneu bax di gueneu nex ba aldiana rek

  • @m.k.g3046
    @m.k.g3046 4 роки тому +14

    DIEUREDIEUFÉ BOROM Touba.
    Serigne Mountakha Mbacké Yalna fi yague loll té were

  • @mamediarramouhamed
    @mamediarramouhamed 4 роки тому +1

    Cëy mame dji yague fi lole ta wer da ngua fi geuneu yague mouy geuneu nekh di geuneu bakh machalla al mountakha dieureuf s touba diarama mame cheikh ibra fall ❣❣

  • @mariasant3937
    @mariasant3937 4 роки тому +13

    Alhamdoulilah bama doné dioulit. Alhamdoulilah bama doné Mouride. Beugue Serigne Touba mo dax néx dak lem

  • @miami7867
    @miami7867 4 роки тому

    Dieureudieuf contane na trop li moy djioulite diamou YALLA ba dé contane na thie khalif bi machallah yague fi Mbacké té wérrr

  • @gayeelmagoofficielstv87
    @gayeelmagoofficielstv87 4 роки тому +58

    Amena solo lole faire la prière en respectant les mesures d'hygiène

  • @cheikhamadoukasset4380
    @cheikhamadoukasset4380 4 роки тому +12

    Khooles yi séédatina. Khooles yi fékhaatina. Mbacké yalla gua guena yague, guena wéére thi barké alkhourhaane kariime. Di ndokaalé thi wéérou koor gui. Yalla na nieup ame diam taaye ak euleuk.

  • @sokhnacoumbasaliouseck5662
    @sokhnacoumbasaliouseck5662 4 роки тому +7

    Thiey nitou yalla ak serigne bokoul Mbackè balla nitou yalla nga doundal tei wére morom mbegté mi day rétane rek 💖💖💖💖💖💖💖💖💗💗💗💗💗💗

  • @dembadiop5127
    @dembadiop5127 4 роки тому +40

    Le drapeau de l islam est en "grande beguete " grâce à Serigne Touba actuellement représenté par le Khalif Serigne Mountakha (yagu fii tee werr ). Diarama Lamp fall.

  • @mameboussodiopkhidma7540
    @mameboussodiopkhidma7540 4 роки тому +31

    Li moy deug couné meune na bayi faratay sunu brom bamou déss ndah séne mame jia yallah ak yonantam slws dagniou ko jiaralone louné mou bayi ak jiabotam ak deug kam guir l'islam kone ni la wara démé yallna nieup am jiam barkep wer wi

  • @antafall5547
    @antafall5547 4 роки тому +1

    Dieureudieufe Borom Touba

  • @boromnonstress9511
    @boromnonstress9511 4 роки тому +61

    Santè Cheikh ahmadou Bamba rek billahi doli Santè yalla sunu Borom bi rek Mbacke yagg Fi té am wér lolllll amine Barki Serigne modou Awa Balla Borom darou mouhty Macahallha amatina solo lolllll Barki Serigne modou Awa Balla Borom darou mouhty

  • @toubandindytv3215
    @toubandindytv3215 4 роки тому +10

    الشيخ محمد المنتقى البكي شيخنا وحبيبنا أطال الله عمره ببركة الشيخ الخديم
    Serigne Mountakha Mbacke Yalnafi Yague Lolou te am ak werr barkéb Serigne Touba Amiine

  • @yayoufallou6387
    @yayoufallou6387 4 роки тому +1

    Une détermination exemplaire Dieureudieuf Serigne Touba Serigne Mountakha mbake Yalla nafi yague te weer.

  • @boromnonstress9511
    @boromnonstress9511 4 роки тому +7

    Amine 🤲🤲🤲amine amine Yarabi yalla na yalla nagou nian yi Barki Serigne modou Awa Balla

  • @fallbaradiop4246
    @fallbaradiop4246 4 роки тому +2

    Ceux qui appuient sur 👎 c quoi votre blem vraiment!!!
    Longue vie à Serigne Mountakha et à tt nos guides religieux yén laniouy titerooo 😍😍😍

  • @bayedjilikane7495
    @bayedjilikane7495 4 роки тому +14

    Serigne Mountakha yalla nafiyagne amine Balla aicha

  • @djoulytoure1747
    @djoulytoure1747 4 роки тому +1

    Mask bi amna solo surtout ci mague.

  • @barbienoir9929
    @barbienoir9929 4 роки тому +4

    Fière d'être mouride💖🙏

  • @amyndiaye458
    @amyndiaye458 4 роки тому

    Serigne mountakha yalla nafi yague té weur si barké seikhoul khadim

  • @niangcheikh4236
    @niangcheikh4236 Рік тому

    Yalna fi yague lolll te werr mbackė Amine yarbbi barcėp cheikh Akhmadou bamba mbackė ❤️🤲❤️🤲

  • @yorosarr4140
    @yorosarr4140 4 роки тому +12

    Serigne Touba Amoul Morome Adouna ak Alakhira

  • @mamadoukane6619
    @mamadoukane6619 3 роки тому

    Oh yallana diamou yag si rew mi serigne mountakha yallana say fane goudou yalla weral la

  • @diarra__diouf777
    @diarra__diouf777 4 роки тому +5

    Bilahi j'ai des larmes aux yeux😥mane serigne mountakha damako beugue barké serigne touba

  • @ouakamedakar4209
    @ouakamedakar4209 4 роки тому +1

    Barké s.touba sama khol séd neu ak khassida bi si souf dieuredieuf serigne Touba

  • @sofimarietoucisse4412
    @sofimarietoucisse4412 4 роки тому +4

    Dieureudieuf Cheîkhoul Khadim Mbacké. Maa shaa Allah SERIGNE Mountakha yalna fii yag té wérr Mbacké

  • @modoudiengbeuguefallou1776
    @modoudiengbeuguefallou1776 4 роки тому

    Dieureudieuf Serigne Touba Serigne Mountakha Yalna yalla goudal sa fane guena yague guena weer Mbecté mi

  • @chiekhousall6874
    @chiekhousall6874 4 роки тому +5

    Bsr merci serigne sam Mbaye qui disait que l homme fait pensée uniquement à Allah et son prophétique psl serigne Mountakha est l exemple patent

  • @cheikhndiaye4514
    @cheikhndiaye4514 4 роки тому +2

    yalla ga yage fi seringue bi Ak kou wax Amine

  • @soldaroumamesaliou7609
    @soldaroumamesaliou7609 4 роки тому +11

    SÉRIGNE MOUNTAKHA MBACKÉ YALNAFI YANG TÉ WÉRE MOURITE NÉLE AMINE ♥️♥️♥️

  • @yamardiop9005
    @yamardiop9005 4 роки тому +2

    Je ne trouve pas les mots just pr exprimer ma joie .dierejef serigne touba

  • @matarndiaye9498
    @matarndiaye9498 4 роки тому +20

    mbacké yalla n’a gua fi yageu téwérr 🙏🙏

  • @fatoumbengue8716
    @fatoumbengue8716 4 роки тому

    Serigne Touba amoul moroom💪💪💪💪yalla n'a yalla bayyil gnoufi serigne mountakha mbacke ba leppou lou mou yene mou agg🙏🙏🙏

  • @tallambengue4412
    @tallambengue4412 4 роки тому +5

    Organisation exceptionnelle. DIARADIEUF serigne Touba

  • @loufsalihtoure88toure61
    @loufsalihtoure88toure61 4 роки тому

    jëurejëuf Serigne mountakha bassirou mbacke yalla nafi yagg tè wèrr amine chi barcké Serigne touba Mbacké

  • @zallmbaye3602
    @zallmbaye3602 4 роки тому +11

    Kou contane beuseul j’aime 👍 ❣️❣️STOP 🛑C0VID 19

  • @tapha326
    @tapha326 4 роки тому

    Serigne touba lou mou mome dou ame morome thi kao soufe yal naniou yala fayal thi barke seydina Mohamed amine

  • @darousamtv9726
    @darousamtv9726 4 роки тому +16

    Kourel darou khodoss gui gno mana diangue dh Serigne montakha mbacke yallana fi yague lool barkép borom touba

    • @youssouphandiaye76
      @youssouphandiaye76 4 роки тому +1

      Bane khassida la

    • @Djiguibs
      @Djiguibs 4 роки тому +1

      @@youssouphandiaye76 Ila Khayrina leu touddou. kheweul, toppou ndigueul, Serigne Mountakha yalla na fi yagg

    • @youssouphandiaye76
      @youssouphandiaye76 4 роки тому +1

      @@Djiguibs amine akassa diadieuf way 🙏🙏🙏

  • @souleymanedante4318
    @souleymanedante4318 4 роки тому

    Dieureudieufé serigne touba khadimou Rassoul. Serigne Mountakha Mbaké yalla nafi yaag loole té ande ak wérr

  • @abdousarr6812
    @abdousarr6812 4 роки тому +12

    S muhamadu muntakha Mbacke yalla nafii yagg tè wèerr ❤️❤️

  • @codoufalldieng3563
    @codoufalldieng3563 4 роки тому +4

    Je vraiment Fière d'être mouride machalla mbacke akassa yague fi lole mbacke ta ande ak weer amiine yaraabi

  • @abibatouniangba2612
    @abibatouniangba2612 4 роки тому +5

    😭😭😍😍 fier d'être mourite

  • @abdoufall1124
    @abdoufall1124 4 роки тому +1

    Mbacke yague fi té wer si b touba

  • @ablayendiaye9551
    @ablayendiaye9551 4 роки тому +13

    Thiéy Serigne Touba ❤

  • @waganegning5554
    @waganegning5554 4 роки тому

    Sérigne moutakha yalla sounou borome bayilafii beusi canama ma caname daradiay kou tède kii diakhnagnou la sounou leuppe manchalla ❤❤❤❤