Macha Allah notre Cheikhana Docteur Mouhamad Ahmad Lô hafizahūllah Djeureudjeufeuti yalna Yalla saam laa mayla wérr akk wérrlé gūddū fann xéweul gū sawann bawann Yalla mayla lū geuneu kawé sa ndjorte Yalla būssa yakaar tass thi dara 🤲🏻🎉🎊❣️ Djeureudjeufeuti Oustaz Abdallah Baba Dieng yalna Yalla fayy lénn sénn liguéy rafèt na trop 🤲🏻
Macha Allah notre Cheikhana Docteur Mouhamad Ahmad Lô hafizahūllah Djeureudjeufeuti yalna Yalla saam laa mayla wérr akk wérrlé gūddū fann xéweul gū sawann bawann Yalla mayla lū geuneu kawé sa ndjorte Yalla būssa yakaar tass thi dara 🤲🏻🎉🎊❣️
Djeureudjeufeuti Oustaz Abdallah Baba Dieng yalna Yalla fayy lénn sénn liguéy rafèt na trop 🤲🏻
Machallah yalna yallah samou len ❤😊
❤❤❤❤❤❤❤❤
بارك الله فيكم وجزاكم خيرا
Machalah cheikhana