Polygame une série que j’aime tant. Je vais vous raconter mon histoire avec polygame cette série était mon anti stress mon parlement du rire mon passe temps favori là où je puisais un vocabulaire riche avec les proverbes de maman Seune , Bou et Thiam et cela me faisait plaisir. Regarder polygame créait de l’allégresse du bonheur et de la gaieté dans mon cœur avec les leçons de morales que vous donnez surtout une chose polygame reflète typiquement la réalité de la société sénégalaise mais dans toute chose il y’a une limite on aura rencontré dans la vraie vie tous les personnages qui existent dans cette série mais quand même chacun finira par récolter ce qu’il a semé et ce quoi qu’il en coûte mais dans cette série on a l’impression de revivre toujours les moments des premières épisodes et ça n’encourage en rien du tout le fait de revenir en arrière toujours les mêmes scènes le même environnement ce qui m’inquiète c’est qu’on a jamais vu les autres fauteuils du salon wala gnaar kessé leu? chaque jour domoda nak kenne meunouko la situation reste toujours au même strate mais évoluez positivement nak franchement bientôt vous resterez là à compter les gens qui vous quitteront🙏 et c’est dommage que la publicité de goorou saloum et le Serigne qui passe tout son temps à se vanter prenne tout cet empleur barigo bou fess dell dou yeungeutou respectez notre intelligence waay
Ah oui vous avez parfaitement raison et moi aussi je regarde beaucoup cette serie mais ça n'avance pas pas de sanction ni de regret pour les malfaiteurs. Bour c'est la seconde fois qu'il accuse d'avoir détourné de l'argent et toujours les memes histoires d'accusation et de critiques dans sa famille surtout son père Bâ. Ça n'a pas de sens vraiment il faut qu'il revoie le scenario.
Si tu tombé sur ce commentaires qu'Allah t'accorde un beau destin plein de réussite dans tous ce que tu entreprends ALLAHOUMA AMINÉ ❤️❤️🙏 yalna diam yagué Sénégal brkp Ku téd ki ❤🎉
Scénariste ngir yalla na Bou werr. Keuram Sablux bi paré mou tohou ak Kiné ak Mere Seune. Ngene def 2ans plus tard niou guiss lenn ak sen dom niou fo nekk si diameu. Vieux Ba torokh di wouti ndimbeul si Gora mou rejetter ko. Astou tass. Khady delou si Pathé. Awa delou si Bath Jakarta. Ndeye Ndiaye abandonner Ba daw fekki yayam. Khady Baba am benen dieukeur. Bouddha dem Bango. Thiam nekk manoeuvre nioukoy kokali. Amina ak Oumou beugeu deloussi mou teu lenn. Yayou Fat Kiné am dieukeur bou sadique boukoy téyé si keur gui. Binome takk Niarel fekk Badiene delouci. Serigne khol continuer nekk soukou Serigne goor saloum bi. POINT 😂 YEN A MARRE BASTA
Gni ay nitou internet lagnou rek 😂😂 chapeau à vous polygame 💝 💝 💝 💝 li guene di def amna solo yeté kessé machallah wennibikoum hâte ❤❤❤❤❤❤❤❤ n'oubliez pas de like 💖 💖 💖 9
Le peuple réclame le bonheur de kiné ak seune et bou ay gora ya lakale vraiment diepi nako trop sakh bilay bonne ba sopil sa djiko bi way thiey yallah non ndeye Ndiaye dou nittou franchement bonne continuation à l'équipe polygame 😍🥺
Pathè a rèussi contre Bou et Seune sans conséquences. Amina à réussi contre Bou, Seune et fate kinè sans conséquences. Ba ak Ndeye Ndiaye gnome gnome da gnou ratte Bou nampe ko ba mou gnère. A quand la vérité senepeople
Chapeau au senariste qui a changé la tournure de la série avec l implication de gora, mais nak sen listkhar katt bi meune na niak, yalla rek mo kham louy xew euleuk
Je ne peux plus me retenir depuis tout ce temps j'esite à commenter l'histoire de bou est l'histoire tipique de mon mari tout comme bou dépuit toute ces années mon mari vie la situation de bou il à fait un accident de la circulation et il est prapregie et depuis tout ce temps tout les mask sont tombées'''''''menouma wax lep mais doyna war
Wouy 😅😅gueudiona commentaire mais tey fawma defko ndah ndeye Ndiaye non ndeye Elle pétri de talant je l'aime bravo à l'équipe depuis le début yenang kay tek thie ax
Khady baba legui virus Ndeye Ndiaye dako doug seytané leu way yen dou Awa mofi wakone amna liguey wala 😅bilahi gora dinalen guenné fi nguen fogoulwone da nguen badola rek badiene mo geuneu yess
Awa ak badiène yénafi done bakh bakh lou si Bou ba nieup yakarni changé ngen ndèketei yoo ay dorr la Peut être ya seyda ndeye ndiaye douma rouslo 😂😂😂😂😂😂
Kine Bilahi waxe Gua louma kasss ba sone dioy na sone mouy waxe bu niak teiguine bobou( kou dei sa yay diouratt ) Dara geunoul niaw li vraimohjh Senegal ma rirano rek teiguine zero😭
Mama Seune tu dois arêtes de dire que ses ton fils bous qui a fait sa tu dois même pas parler tu dois leur regarder est rester calme si tu fais une bonne chose si tu parle à les choses que ton fils fait ses pas bon du tous Dieu pas payer tous
Polygame une série que j’aime tant.
Je vais vous raconter mon histoire avec polygame cette série était mon anti stress mon parlement du rire mon passe temps favori là où je puisais un vocabulaire riche avec les proverbes de maman Seune , Bou et Thiam et cela me faisait plaisir. Regarder polygame créait de l’allégresse du bonheur et de la gaieté dans mon cœur avec les leçons de morales que vous donnez surtout une chose polygame reflète typiquement la réalité de la société sénégalaise mais dans toute chose il y’a une limite on aura rencontré dans la vraie vie tous les personnages qui existent dans cette série mais quand même chacun finira par récolter ce qu’il a semé et ce quoi qu’il en coûte mais dans cette série on a l’impression de revivre toujours les moments des premières épisodes et ça n’encourage en rien du tout le fait de revenir en arrière toujours les mêmes scènes le même environnement ce qui m’inquiète c’est qu’on a jamais vu les autres fauteuils du salon wala gnaar kessé leu? chaque jour domoda nak kenne meunouko la situation reste toujours au même strate mais évoluez positivement nak franchement bientôt vous resterez là à compter les gens qui vous quitteront🙏 et c’est dommage que la publicité de goorou saloum et le Serigne qui passe tout son temps à se vanter prenne tout cet empleur barigo bou fess dell dou yeungeutou respectez notre intelligence waay
Ah oui vous avez parfaitement raison et moi aussi je regarde beaucoup cette serie mais ça n'avance pas pas de sanction ni de regret pour les malfaiteurs.
Bour c'est la seconde fois qu'il accuse d'avoir détourné de l'argent et toujours les memes histoires d'accusation et de critiques dans sa famille surtout son père Bâ.
Ça n'a pas de sens vraiment il faut qu'il revoie le scenario.
❤❤❤
Absolument
Ok😊
Lo nguiss sakh day ame fin 412 episode c’est trop
Mention spéciale à ndeye ndiaye et Fatou kiné bravo
Non Ndèye Ndiaye yalna goudou fane 🙏🏾🙏🏾moy sama anti stress 😂😂😂😂😂😂😂
KOu beugeu Mouhammad psl❤❤
❤❤❤❤❤❤ Salallahou Aleyhi wa Salam ❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤psl
HALEYHI HALEYHI SALATOU WA SALAM ❤❤❤❤❤❤❤
🎉🎉 pop
La kinez ❤ ma meilleure diam si yaw tu assure grave mâcha Allah ❤ tu es une femme exemplaire ❤
Koubbeugue sarigne mountakha lalala j'ai me❤❤
Non Ndaye Ndiaye moo néekhh néna déllo Léne séne xéll cii yalla Nieup Dioukk Bayé koo Fii😂😂😂😂😂😂😂😂
Li damako retane ba thiorokhane
Daleine beugu diakhassé ak yalla di
Daw nagnou Ndeye Ndaieye 🤣😂😂
On réclame le bonheur de fat kiné ♥️😢ma kinéz elle ❤️ joué très bien son rôle ❤️ machallah ❤️ laf thiatt ♥️ chapeau à elle ❤️ courage ma belle ❤😢
Ekcvm xupokhit😊
Si tu tombé sur ce commentaires qu'Allah t'accorde un beau destin plein de réussite dans tous ce que tu entreprends ALLAHOUMA AMINÉ ❤️❤️🙏 yalna diam yagué Sénégal brkp Ku téd ki ❤🎉
Amine 🙏🏼🙏🏿🙏🏿 et pareil pour vous madame
Allahouma amine
Merci a toi aussi pareillement Q.u Allah te préserve ya rabby
Amine yarabi
Amime yarabbi
Scénariste ngir yalla na Bou werr. Keuram Sablux bi paré mou tohou ak Kiné ak Mere Seune. Ngene def 2ans plus tard niou guiss lenn ak sen dom niou fo nekk si diameu.
Vieux Ba torokh di wouti ndimbeul si Gora mou rejetter ko. Astou tass. Khady delou si Pathé. Awa delou si Bath Jakarta. Ndeye Ndiaye abandonner Ba daw fekki yayam. Khady Baba am benen dieukeur. Bouddha dem Bango. Thiam nekk manoeuvre nioukoy kokali. Amina ak Oumou beugeu deloussi mou teu lenn. Yayou Fat Kiné am dieukeur bou sadique boukoy téyé si keur gui. Binome takk Niarel fekk Badiene delouci. Serigne khol continuer nekk soukou Serigne goor saloum bi.
POINT 😂
YEN A MARRE BASTA
Yalna yalla khép doli😂😂😂😂
@@maramelo9036 🤣🤣🤣 non li Kate da moudiou metti.
@@aminatandoye2041billay dagno sonou dafa wara fin gnou nopalou😂😂
😂😂😂 no ya meune kaye
Scénariste kay lire et fais ce qu'on te dit ndax sone nagn bilay walay
Ndaye Ndiaye moo néekhh néna Mame Diarra mou Ndawe😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
SOkhna Diarra bou ndaw😂😂😂
Gora médecin après la mort,Ndeye NDIAYE 😂😂😂😂😂
L'ingratitude de cette famille me dépasse
Gni ay nitou internet lagnou rek 😂😂 chapeau à vous polygame 💝 💝 💝 💝 li guene di def amna solo yeté kessé machallah wennibikoum hâte ❤❤❤❤❤❤❤❤ n'oubliez pas de like 💖 💖 💖 9
J'adore la discussion de kiné et Ndeye Ndiaye de très belles leçons machalla
Ndéye le serpent est devenue mature, et gentille 😂😂😂😂
J'espere qu'elle ne fait pas semblant 🤣😂😂
Ndeye ndiaye ma tuer 🤣🤣🤣🤣 mais à part ça loutax fougnouy wakhe tourou yallah rek nitt gni di tankamlou😂waleu di zapper dem sene yone
Ndeye Ndiaye mi esk warou niou ko diokh émission yèetè😂😂MDR nènako aye way Sokhna Diarra bou ndaw🤣🤣🤣🤣
Ndeye ndiaye 😂😂😂😂nena bilay sokhna Diarra 😂😂😂😂
Ndeye Ndiaye yallah na goud fane😂😂😂😂😂
Amine❤❤❤❤❤
Encore une fois on réclame le bonheur de fate kiné et bou svp et maman seune et la guérison de bou svp
Vraiment l'amour que ma fille porte pour ndeye Ndiaye ne dépasse alors qu'elle n'a que 5ans
Machalla il faut que tu l'améne chez n'deye ndiaye
❤❤
Daa Mell ni mann ndeye Ndiaye rk laa beugu😭💕
sohna djiara mou ndaw no ndéyyyy est extraordinaire 😊
Seune boul wakh dara wa keur gui lou dale BOU rek yakoko yobé tu es le seule responsable
Vraiment
Vérité.
Moi kiné me fait pleurer 3 épisodes yi yép démay ko dioye bilay
Ndeye Ndiaye dama ka begueu srx 🥺 je ferai tt pour te rencontrer inchallah 🤲📿🕋❤️
Gora si réellement tu te considère comme le fils aîné de la famille loue un appartement pour ton père et laisse Bou en dehors de ton hypocrisie
Machallha fat kine toujours naturelle belle forte Machallha ❤❤❤❤❤❤❤
Vous ne pensez pas que bou et entrain de piéger sa famille k😮😮😂
Piège encore saniou ko😂
C se k je pense vraiment 🙈
@@maremecamara1832 Kon niokoy kèk si écran bi Nak😂😂
No Bou dafa teik dil hamna ak docteur bi lolou la halatt srx
Nono dafay modie deh sakh
Le débat entre kinez et Ndeye ndiaye c'est fort machalah ❤❤❤
Le peuple réclame le bonheur de kiné ak seune et bou ay gora ya lakale vraiment diepi nako trop sakh bilay bonne ba sopil sa djiko bi way thiey yallah non ndeye Ndiaye dou nittou franchement bonne continuation à l'équipe polygame 😍🥺
Je vous souhaite d'être futurs milliardaires à tout qui regarde cette vidéo ❤🎉 brkp s saliou ♥️♥️
Amine ya raby
Amine
Amine ❤
Amine
Amen
Scénario bi war nagn ko kholatt, lii seune ak ndiabottam dii dounde métina il eat temps niou dounde bonheur vraiment
Ndeye et kiné ❤quel duo😅
Ndeye Ndiaye nenako soxna diarra mou ndaw😂😂😂😂
Héé gora yagui dougou si lo khamoul deh si faillite deh gua nara fouy gua yeuk gua succès yalla nagnou yalla moussal si père bou melni ba
kholal badiéne mou mel jumbo ni 😂Ndeye Ndiaye Ray nama😂😂
😂😂😂jumbo keyyy
Wala maggi nokoss
Pathè a rèussi contre Bou et Seune sans conséquences. Amina à réussi contre Bou, Seune et fate kinè sans conséquences. Ba ak Ndeye Ndiaye gnome gnome da gnou ratte Bou nampe ko ba mou gnère. A quand la vérité senepeople
MO gnou diakhal😢😢
Chapeau au senariste qui a changé la tournure de la série avec l implication de gora, mais nak sen listkhar katt bi meune na niak, yalla rek mo kham louy xew euleuk
Gora Kay chenapan la
Je ne peux plus me retenir depuis tout ce temps j'esite à commenter l'histoire de bou est l'histoire tipique de mon mari tout comme bou dépuit toute ces années mon mari vie la situation de bou il à fait un accident de la circulation et il est prapregie et depuis tout ce temps tout les mask sont tombées'''''''menouma wax lep mais doyna war
Wakhal les téléspectateurs pensent k c exagéré k li bou di doundou amoul alors k mougui si keur yi.mougne rek diouli di niane lo guiss day djekh
Walahi même mane mi moma dal depuis 2015
@@faliloudrame3119 massa yalla baxna
@@maimounandiaye-le1tu yii défoit dama nan dafa am kouma xam wax sama situation senariste bi
@@beugfallou2853 guisgue kou gnou nane mougneul tu te dis dou mouss djekh.yalla mokoy djekheul mbamou djek talal sa lokko yi sougnou borom kesser.massa
Walahi azim dama beugue Ndéye ndiaye elle me plaît bcp même dp8 khallé mome rk la toppou
J'adore la discussion de kiné ma meilleure famme adoré je t'aime fort ❤️❤️
GORA n'a pas baisser les bras pour la maison de bou les 2 parents de cette famille kéne khamoul bane nithe lanou
Gorra il m’énerve sheutttt 😂😂😂😂
Ba wakhe na deugue Ndeye Ndiaye djiguènou wéroule laye nourole 😂😂😂 😂😂😂
Mom la giss
No série bi yalla boumou diekh way ❤❤❤❤❤😂😂😂😂
Ndeye Ndiaye tu ma tue 😂😂😂😂😂😂😂
Ce qui est bizarre le marabout a tous les solutions l'homme connais tous incroyable les Mara sénégalais
😂😂😂😂😂 vraiment
Sauf pouvoir soigner bou bien sûr, mom limouy aye yepp meunoul fadj bou 😂😂
@@mariemegueye7714 😂😂😂, wokh gua lêpeu. Wollay na fatthieu Bou. Tè daffa lamb sax
Ndaye mo geuna Faux 😢si Lou yalla binde😂😂😂😂😂
Thiam dou nittou dara 😅😅😂😂
Ndeye ndiaye bayi niou way😂😂😂
Ya saye da ndééééééééye Ndiaye 😂😂
Mane Gora ak Ba rek la geuna dieipi
Les autres mom wakhou ma séni wakh
Wa mére seune nak kagn lay am bonheur li mom legui dafa soff nak 💔
Bilahi mome sax aye retan dako diap non ndeye N’Diaye amoul koi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Sokhna diarra mou ndaw mouy amnafi toutondo 😂😂😂😂😊
Ndéyassane avant douma raté béne épisode mé légui moye lolou
Ndeye Ndiaye 😂😂😂khala Rassoulilahi 😂kheipii guissoul kenn
Ndaye ndiaye yalna godou fane😂😂😂😂😂😂😂❤
Amine yarabi 🤲
Wouy 😅😅gueudiona commentaire mais tey fawma defko ndah ndeye Ndiaye non ndeye Elle pétri de talant je l'aime bravo à l'équipe depuis le début yenang kay tek thie ax
Ndeye ndiaye je t’aime trop barkep serigne saliou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Plus bipolaire que Thiam tu meurs 🤣🤣🤣
Thiam d'où nitou dara 😅😂😂
Keurgui ñeupa bipolaires
Pas d'exception
@@dabakhwade4695 😅😅😅😅walaye tu m’as tué 😂😂😂
Faroule féne
Degolen badien dh je fais ce que tu veux😂😂😂😂
Machallah Ndeye Ndiaye ❤😂😂😂😂😂❤❤🇲🇷🤴💯❤️🏆🤣😊
Wa ndeye Ndiaye mi esk ay rab fègnouwu ko 🤣🤣🤣
Bon prévenez moi svp quand Bou sera rétabli et pourra se défendre je regarderai à ce moment parce là moy lolou...
On reclame avc de BA et fin de saison
Sokhna Diarra mou ndaw😂😂
Ndeye Ndiaye dou nitou fi👩🏽🦯
J'aime ndeye Ndiaye et Fatou kiné ❤️🥰🥰🥰❤️🙏
Ndeye Ndiaye y maa jumi ya Saida la deh muneh😂😂😂😂😂😂
Badiane nena Ndeye Ndiaye boul diar yonou pout😅😅
Khady baba legui virus Ndeye Ndiaye dako doug seytané leu way yen dou Awa mofi wakone amna liguey wala 😅bilahi gora dinalen guenné fi nguen fogoulwone da nguen badola rek badiene mo geuneu yess
Wa Ba wén Ningenn def Ndéye ndiaye niawna😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Qui est d’accord que les rumeurs de soit disant Bou a détourner l’argent de l’entreprise peuvent venir de Gora ?
En tout cas ça peut être lui parce que Gora est photocopie légalisée de Ba
@@khadynancymane4402😂😂😂😂😂woyy
Moi je pensais de Amina mais tu n'as pas tord
N'oubliez pas Amina
Ou de amina
Bravo l'équipe polygame ❤❤❤
Awa ak badiène yénafi done bakh bakh lou si Bou ba nieup yakarni changé ngen ndèketei yoo ay dorr la
Peut être ya seyda ndeye ndiaye douma rouslo 😂😂😂😂😂😂
Boul yakar si y’a Seyda 😂😂😂😂koko😂yesss
@@Blackwomen15🤣 vraiment
@@Blackwomen15 moma diaxal🤣🤣🤣🤣🤣
Gore moom bisam l'ay khaar mooy kilife kilife lou ni Mouna day engase😂
Oh ndeysane ndeye Ndiaye tay comme khobou garap ci salon bi chut peral bi dangna ya seyda 😂😂😂😂😂
Jadore la maturité de Fat Kiné. Jiguéne bakh rek moko war macha allah. Love you sort much❤❤❤❤❤
Wouyyuuu dioguendo bi raynama guir Yallah dagal lene ma partie bi😂😂😂😂😂😂
No gora vrai ipocrite leu 😂😂😂 famille ba bi dale 6 moyeu 9 ndeye Ndiaye 😅😅😅😅
Bo begué deug deugue tane si boula nex rek ñeup yéme
Et il va réussir
Ndeye Ndiaye waye raye nama😂😂😂😂
😂😂😂FIN BI MOMAY RAY QUAND NDEYE NDIAYE COMMENCE EN DISANT KHALA RASSOULOULAH ET QUE TOUT LE MONDE PART😂
Kine Bilahi waxe Gua louma kasss ba sone dioy na sone mouy waxe bu niak teiguine bobou( kou dei sa yay diouratt ) Dara geunoul niaw li vraimohjh Senegal ma rirano rek teiguine zero😭
ak tasou bobou awo bou dé dè gniou guéné say dome dougnioul sougniouy dome dafma nakari trop
Wouy Ndaye ndiaye 😂😂😂😂
Mama Seune tu dois arêtes de dire que ses ton fils bous qui a fait sa tu dois même pas parler tu dois leur regarder est rester calme si tu fais une bonne chose si tu parle à les choses que ton fils fait ses pas bon du tous Dieu pas payer tous
Vous êtes les meilleurs ❤ bonne continuation à vous ❤
Srx meilleurs mom defa tougn ko car serie va dans tout les sens
Ndeye Ndiaye tu m'a termine🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Bac en pochec❤❤❤🎉🎉
Polygame family's LA Alnihara Jummah Mubarak to Ya all Muslim s 🤲🤲🤲🤲❣️❣️❣️❣️ Kine my love 💕💕💕💕💕💕💕💕💕
Familles Thiam môme gneupa bipolaire
Guir yalla bou na diouk
Vraiment
Diotna dé😊
Mane dal wa poligame diakhal nan ma dagniouy sopékou kome kamalion rk😂😂
Ndeye Ndiaye tu me tuer de rire
Ay ndeye Ndiaye 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
i like Ndey Ndiaye 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Ndeye Ndiaye rk lay topou 😂😂😂
Pourquoi Serigne Bi meunoul fadji bou kom il détient des savoirs et peut guérir des maux
Polygame vraiment nak Yéna gui beug melni nii wird wiri, à la fin c’est quoi le projet!!! Saq fois bou sa mère sa femme gnoy am blem
Bilahi
Soxna Diarra mou Ndaw 😂non Ndeye Ndiaye douma Ray man😂😂😂😂