Les faibles d'esprit refusent de voir la vérité. Ils se croient être sur la bonne voie alors ils s'en écartent d'autant plus qu'ils avancent. Djaredjeuf professeur grâce à toi j'ai réactualisé mes connaissances ❤
Mané bayi lén gniom dagno diap ni lou yonent defoul rék bidah la, lolou rék moy sén dalil té wéroul hana kon yég si auto bida la yék si avion ✈️ yég si terrain hana konn lép bida là
Quelle pertinence! Que d'arguments irréfutables qui montrent que la tarikhya tidjania est ia voie indiquée par le prophète PSL. En réalité l'égarement des salafistes se conjugue par l'absence de discernement entre l'esprit et la lettre. S'emparer de la notion de biida comme principe d'explication de la négation du soufisme est l'erreur fondamentale des disciplines de Ibnou Tayemiya
Tarikha cheikh, rousna cheikh binga tou dou né kon ma wax lou graw,wayé pour ton info tarikha mooy yoon, bassi youtoube bi ,yoon la firri ndax mo lay permettre ngay kheuy di degue ay njabooti cheikh di wax si kham kham di zikr di bakk yallah di julli si yonnente bi sawm diko magaal... Té sa khol di guen bone té do si meun dara😂.
Boul yég si auto wala avion wala moto wala deuk si ay grade ciel bidah la nah yonent bi defou ko ,com dolén halat, yallah nalén yallah dég lo dîné aminn kou bah nga daga rér rék
Quand un homme parle il ne faut pas utiliser automatiquement la croyance prend le temp de réfléchir . je vous reponse la question pourquoi la femme n'a pa de barbe .
Mann lénn rékk layy wakh moyy thiono bi mame Elhadji malick dadj guirr l'islam, je suis sur qu'il va jamais inserer quelque chose qui contraire à la religion, dans l'islam.
li moy sén fort manam niaka déég.legui loy wah Yalla mi né borom khèl yi lay wakhal soudé sokhlawouniou xèll ci diiné? yèn même soudé ay textes yi nguén di layé ay nitta ko teug rek té done niou séni dég déssone lol
Yow jango jongo ! Sawal ta teddi ! Yonente bi dafa né sama ganaw dina am 73 ngir youy niow waýé 72 yeup werouñou bomou dess ben bouy ñongal diné islam ak sama souna !!!
Le Prophète (PSL) n'a pas fait le Hajj en avion. Donc c'est du biddah que de prendre l'avion pour aller faire le pèlerinage! Votre logique sur le bddah est illogique.
Li ci métti ba métti ci nag mooy ñi ëpp xàmmeewu ñu AG JAAMU-YÀLLA ag LOO XAM NI LII KÉNN TËNKU CI KÉNN. LÉKKIN ngay gam-gamle ak AG JAAMU-YÀLLA, jël AAYA, JOXE CA SA DÉGGINU BÓPP NGIR LAYALE KO AB BIDAA. Ak ñaata yoon la ñu léen indil xadiis yu léen di tere tàbbi ci bidaa. Ay yooni-yoon.
Bàyyi waxi YONÉNT BI (a s), definu YONÉNT BI (a s) tóppi waxi KENEEN baa lu ñu ni KENEEN koo ka moo ko wax🤔 lool du xel sax. Du yàgg mukk-mukk ba ngéen génnee bénn aaya bu ni tudd léen YÀLLA ci kaw ÁNDADOO, WUTAL KO BËRËB, WUTAL KO WAXTU, WUTAL KO LIM, WUTAL KO NGËNEEL YOO XAM NI YÀLLA WAXU LA KO, YONÉNT BI (a s) WAXU LA KO
@idrissadieme4788 prof a posé une question spécifique. Donnez un verset qui contredit ce qu’il dit. Il a amené des versets. Au lieu d’amener vos versets, vous balancez une étiquette de cacophonie. Faut nous éduquer vous aussi. Si vous avez de quoi nous montrer qu’il se trompe, nous aussi on veut savoir hein. Svp brother. Merci
@@TLwilsonF1405 Allah nous a ordonné de suivre le prophète.IL Na pas interdit de faire des zikr mais faire des zikr conforme à l' enseignement du prophète 1_le prophète Na jamais appelé ces compagnons dans une mosquée pour les regrouper autour d'une foulard blanche pour faire des zikr 2_le salatoul Fatih n'est jamais mentionné même dans un faux hadith il nous par de rêve 3_le tarakha tijani et tous ce qui s'en suit sont des choses nouveaux années 80à90 Le problème c'est compréhension du livre d'Allah Est ce la traduction qu'il a des versets qu'il récit est similaire à celle des compagnons du prophète qui leur a enseigné C'est pas parceque je comprends l'arabe donc je peux traduire les paroles d'Allah Les sahaba comprené l'arabe mais allé voir le prophète pour qu'il leurs explique le sens Nous on suit le coran et la sunna pas selon notre compréhension mais la compréhension des compagnons du prophète
@@idrissadieme4788 vous n’avez toujours pas répondu à la question. Il a donné des arguments avec des versets à l’appui. Votre réponse aurait été de faire la même chose pour un argument opposé. Pour quelqu’un qui est assis au juste milieu pour faire un jugement personnel, vous n’avez toujours pas pu contre balancer ce qu’il a dit. Donnez moi un verset qui dit que prononcer le nom dallah dans une mosquée est interdit en dehors des heures de prière.
Yaw kay professeurs ya sankou aa kone legui geum nga hadith yaw kay amo looy wakh si yonèntibi Sallalahou HALEHYI wa salam ndakh yaw gueumo hadith gueumo sunna
Li thi yémé moy ki koy déf dafa jàpp ni thi deug la nék fékni thi nénn la nékk Dinë ji du ay réflexion philosophique Dem Len jangui Oustaz Omar Sall MachAllah yàlla Na ko yàlla Aar , Gudu faan, Alxuraan Ak sunna Thi dëguine mag yu Bakhti(Sahabayi)❤
Dangéndi sone rek Professeur waxoul dara lou niaw si sunnah au contraire dakay top mdr topp sunnah moy top diangalé yonenti bi sallALLAHOU aleyhi wa salam fi nieup ay sunnites lagne mais sa genre yi nio beug grawal yobou mbir mi fou sori di creer ay sectes di téré ay zikr mdr té YALLAH moko santané bo démé nak ba lou Oustaz wax nga gueum ko sans guestou vu que sa xél mi da noy kone daccord nga ak limou wax si Zikr saay té ngéne guestou mogueune ngéne di diay supériorité fogue ni yéna gueune nitt gni Madiama lim wax c'est tellement clair wayé sissoumane rek mokoy bagne mdr vous avez 0 preuves mais vous jouez les malins fi nieup ay sunnites lagne
Boul dougou si auto boul léké coudou boul diouli si Sidiada boul tal Lampe boul sétane télé doméram sanil sa téléphone 😅 Amoul won diamano Yonénte bi sws
Ngir Léral lentel Kat Yi lendemel askanwi partager maximum et abonné
L'aveugle n'est pas celui qui ne voit pas mais celui qui a des yeux et refuse de voir. Merci professeur
Ya wakh deug 🫡👌
Jazaakallah khayran Yana nala yalla fay yiw
Madiama diarama 12:50
Jarajef professeur Madiama Fall Yallah nala Yallah fey ta goudal say fan may la tawfeex ak taysir ci barké yonente bi SAW. Vraiment xol sedd na !!
Amine ❤
Les faibles d'esprit refusent de voir la vérité. Ils se croient être sur la bonne voie alors ils s'en écartent d'autant plus qu'ils avancent. Djaredjeuf professeur grâce à toi j'ai réactualisé mes connaissances ❤
Professeur Madiama ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah merci beaucoup Mariambat❤❤
Machalla oustaz je vous suivez toujours dieredief yalla ne yalla Feye le
Merci beaucoup oustaz
Merci Pr Madiama ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ dieureudieufaty
Oustaz Madiamal YALLA NA YALLA GOUDEUL SAY FAN si BARKÉ SEYDINA MOUHAMED RASSOULOULLAHI SALLALAHOU ALLAHI WA SALAM🤲🤲🤲 ❤❤❤❤
Merçi professeur siguile ngua isl
Merci beaucoup ouzta
الحمد لله ماشاء الله تبارك الله جزاك الله خيرا يا أستاذ ❤❤❤
Mashalla Fatabarakallahou ❤❤❤❤
Professeur diné ji rek laye lèrale motakh gayi gis thisène bop pou 😂😂😂
Dieureudieuff dieuff amna solo ❤❤❤Akhlou mbirty mbirty danio bari wax rk 😅
xam xam day léérrr bilay je respect pr Madiama fall cest fait meme pas une semaine que je le suis
Merci beaucoup madiama
❤❤❤ professor Jerrejef
نسال الله ان يرينا الحق حقا ويرزقنا اتباعه ويرينا الباطل باطلا ويرزقنا اجتنابه
Amine 😊
Wakh deug yalla lilerna trop❤❤❤❤
5:40 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sounnah kesse kesse ❤
😅😅😅
Mou and akk mandou kessee kesse
Merci beaucoup madiambale
Nioune tidiane yi kouniou wakh dara togne niou wasifa ,khadartou diouma yeup yalla ko santane
Wallahi Moy ciratal moustaqim dé
Je suis au côté du professeur ❤
Masallah❤❤❤❤ ostas❤
Réunion yi ngeni def yen ibadou au 9:23 grand théâtre yonente bi dawou ko def khana kone bilay là wakh da yakou mana toi thaï togou 11:37 11:47 kay ba
Mané bayi lén gniom dagno diap ni lou yonent defoul rék bidah la, lolou rék moy sén dalil té wéroul hana kon yég si auto bida la yék si avion ✈️ yég si terrain hana konn lép bida là
Bilahi ❤❤❤
Al couran ak sunna ❤
Oustaz madiama fall❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Linguaye WAKH professeur niom douniouko WAKH.
Nous reconnaissons ton savoir .ils ne nous ONT rien apporté, sinon des POLÉMIQUES.
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Macha'allah madiama❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yene ibbadou yi aye seytane gene
Quelle pertinence! Que d'arguments irréfutables qui montrent que la tarikhya tidjania est ia voie indiquée par le prophète PSL. En réalité l'égarement des salafistes se conjugue par l'absence de discernement entre l'esprit et la lettre. S'emparer de la notion de biida comme principe d'explication de la négation du soufisme est l'erreur fondamentale des disciplines de Ibnou Tayemiya
Ya mana doul
Tarikha Tidiany dans toute sa totalité est Bidah
Tarikha cheikh, rousna cheikh binga tou dou né kon ma wax lou graw,wayé pour ton info tarikha mooy yoon, bassi youtoube bi ,yoon la firri ndax mo lay permettre ngay kheuy di degue ay njabooti cheikh di wax si kham kham di zikr di bakk yallah di julli si yonnente bi sawm diko magaal... Té sa khol di guen bone té do si meun dara😂.
Cheikh assane Tu ments.
Séne titre bi guéne titré dou deugueu dah oumar sall louko dougueul kaso moy diay dolé
Fenne moko dougale kasso . Et puis fenne kateu dou dioulite. Doundeule diner mo gueune nonon dioulite.
Yëne la saytané fëkë yëne gni diëlê sène dîné si ay gëntë
Prof démal diangui guit yalla yaw khamo daraa
Wazifa khadara bida you bonela
Tu mens
Boul yég si auto wala avion wala moto wala deuk si ay grade ciel bidah la nah yonent bi defou ko ,com dolén halat, yallah nalén yallah dég lo dîné aminn kou bah nga daga rér rék
@@SyllaMolaminnbillay
Niom féké wougnou diamono yonente bi loutax niou guemko
Quand un homme parle il ne faut pas utiliser automatiquement la croyance prend le temp de réfléchir . je vous reponse la question pourquoi la femme n'a pa de barbe .
Ki sakh prof lanla?
Tarikha dou touss
Kone niom guem niagn né baatou lahilaha illalah koumou moudjou sa lamigne rék téxé nga nguén wara mandou
Souna si kaw Tijania si kaw wahabiste salafiste si souf
Déléne wakhe deug
Sunnah si kaw bida si souf
Gnoune tidiane yi sounah lagnouye dounde
Bida ake tioune si wahhabites lagne ko khame
🤣🤣🤣🤣nena sunnah geni doundou yena sankou
@@NdaoMor-pz4wf yaw mi ya sankou
Souna bou ande ak mandou sii kaw
Le prophéte ne porté pas des lunétte salendialo Kate yi nguéne done
Mann lénn rékk layy wakh moyy thiono bi mame Elhadji malick dadj guirr l'islam, je suis sur qu'il va jamais inserer quelque chose qui contraire à la religion, dans l'islam.
Kookou di woowé boppam professeur waxna len lou leerrr. Néena mom diiné khéll leuh dû texte !!😂😂 konn djaroul niouy djangui. Nagn xooll li déppo ak sougnou xéll rk niou djamo nonou yallah !!🚶🏾♂️
li moy sén fort manam niaka déég.legui loy wah Yalla mi né borom khèl yi lay wakhal soudé sokhlawouniou xèll ci diiné? yèn même soudé ay textes yi nguén di layé ay nitta ko teug rek té done niou séni dég déssone lol
Sois disant professeur khamoul daraaa
Demal diangue
Nn professeur limi wakh khadioule sakh séne boopou wedi rek laniou fi néke
Hana tareha Tijan nyo gana degee Yonantibi Alqural, Muhammad (SAW) deful hadara jumma kon nak du Sunna bidda la
Yow jango jongo ! Sawal ta teddi ! Yonente bi dafa né sama ganaw dina am 73 ngir youy niow waýé 72 yeup werouñou bomou dess ben bouy ñongal diné islam ak sama souna !!!
Le Prophète (PSL) n'a pas fait le Hajj en avion. Donc c'est du biddah que de prendre l'avion pour aller faire le pèlerinage! Votre logique sur le bddah est illogique.
yaw si guir gogou gua boke aller vous faire foutre yallah wakh guanioy fakh ay khadiss
Sougnou borom l'islam la wathié bayilèen thiakhaan ak tapalé
Yangui yorr téléphone portable khana bida la yonéta bi mosoul yorr téléphone
Ay chomane guène dara khamoulènko
Ba legui tontou woo deh indill fokkou yonnenté bi deffé
Li ci métti ba métti ci nag mooy ñi ëpp xàmmeewu ñu AG JAAMU-YÀLLA ag LOO XAM NI LII KÉNN TËNKU CI KÉNN. LÉKKIN ngay gam-gamle ak AG JAAMU-YÀLLA, jël AAYA, JOXE CA SA DÉGGINU BÓPP NGIR LAYALE KO AB BIDAA. Ak ñaata yoon la ñu léen indil xadiis yu léen di tere tàbbi ci bidaa. Ay yooni-yoon.
Légui lane mo takh le prophète et disciples ne les faisaient pas dans les mosquées.
Bayiléne cakhane
Le prophète ne voyageait pas en avion. Mais nous on fait. Donc on fait ce bida. Non vraiment c grave
Daffa niou done xalale yonn mo tah temps boubou kou jiouli niou réy la légui temp am na ndah l'islam takhaw na
Waxal gayi yonén ta mosoul yorr téléphone ndah bida la niou yorr téléphone
Wahabit .yi bayiléne ndialo
😂 le coran ne ment jamais 😂
Professeur khamo dara
Dangay fén
Bàyyi waxi YONÉNT BI (a s), definu YONÉNT BI (a s) tóppi waxi KENEEN baa lu ñu ni KENEEN koo ka moo ko wax🤔 lool du xel sax.
Du yàgg mukk-mukk ba ngéen génnee bénn aaya bu ni tudd léen YÀLLA ci kaw ÁNDADOO, WUTAL KO BËRËB, WUTAL KO WAXTU, WUTAL KO LIM, WUTAL KO NGËNEEL YOO XAM NI YÀLLA WAXU LA KO, YONÉNT BI (a s) WAXU LA KO
Video pouri xamoulén dara
Proff vous dites de la kakaphonie
@idrissadieme4788 prof a posé une question spécifique. Donnez un verset qui contredit ce qu’il dit. Il a amené des versets. Au lieu d’amener vos versets, vous balancez une étiquette de cacophonie. Faut nous éduquer vous aussi. Si vous avez de quoi nous montrer qu’il se trompe, nous aussi on veut savoir hein. Svp brother. Merci
@@TLwilsonF1405 Allah nous a ordonné de suivre le prophète.IL Na pas interdit de faire des zikr mais faire des zikr conforme à l' enseignement du prophète
1_le prophète Na jamais appelé ces compagnons dans une mosquée pour les regrouper autour d'une foulard blanche pour faire des zikr
2_le salatoul Fatih n'est jamais mentionné même dans un faux hadith il nous par de rêve
3_le tarakha tijani et tous ce qui s'en suit sont des choses nouveaux années 80à90
Le problème c'est compréhension du livre d'Allah
Est ce la traduction qu'il a des versets qu'il récit est similaire à celle des compagnons du prophète qui leur a enseigné
C'est pas parceque je comprends l'arabe donc je peux traduire les paroles d'Allah
Les sahaba comprené l'arabe mais allé voir le prophète pour qu'il leurs explique le sens
Nous on suit le coran et la sunna pas selon notre compréhension mais la compréhension des compagnons du prophète
@@idrissadieme4788 vous n’avez toujours pas répondu à la question. Il a donné des arguments avec des versets à l’appui. Votre réponse aurait été de faire la même chose pour un argument opposé. Pour quelqu’un qui est assis au juste milieu pour faire un jugement personnel, vous n’avez toujours pas pu contre balancer ce qu’il a dit. Donnez moi un verset qui dit que prononcer le nom dallah dans une mosquée est interdit en dehors des heures de prière.
Yaw kay professeurs ya sankou aa kone legui geum nga hadith yaw kay amo looy wakh si yonèntibi Sallalahou HALEHYI wa salam ndakh yaw gueumo hadith gueumo sunna
Wahoulla lolou dee dalla nee doulenn tontou sii hadith mais si alkour ane lalendi tontou 😅😅😅
au il faut bien réfléchir pourquoi la femme n'a pas barbe 😂 yalla dou khel
Li thi yémé moy ki koy déf dafa jàpp ni thi deug la nék fékni thi nénn la nékk
Dinë ji du ay réflexion philosophique
Dem Len jangui
Oustaz Omar Sall MachAllah yàlla Na ko yàlla Aar , Gudu faan,
Alxuraan Ak sunna Thi dëguine mag yu Bakhti(Sahabayi)❤
Dangéndi sone rek Professeur waxoul dara lou niaw si sunnah au contraire dakay top mdr topp sunnah moy top diangalé yonenti bi sallALLAHOU aleyhi wa salam fi nieup ay sunnites lagne mais sa genre yi nio beug grawal yobou mbir mi fou sori di creer ay sectes di téré ay zikr mdr té YALLAH moko santané bo démé nak ba lou Oustaz wax nga gueum ko sans guestou vu que sa xél mi da noy kone daccord nga ak limou wax si Zikr saay té ngéne guestou mogueune ngéne di diay supériorité fogue ni yéna gueune nitt gni Madiama lim wax c'est tellement clair wayé sissoumane rek mokoy bagne mdr vous avez 0 preuves mais vous jouez les malins fi nieup ay sunnites lagne
Madiambal dangay fohe dine yala
C'est toi qui refuses de voir la vérité 😅
Bayil sa xélmi ngay foyé
Iow danga khamoul lou beuri 😅
@@debaz958 di Tari alhour-an té doko geussou dof sakh mola geune
😂😂 ya meune doull khana iow ak séne wa keur yénakoy fowé professeur rk laniouy topou❤❤
Professeurs bo khamni gueumou hadith gueumoul sunna yaw kay ya sangnou rek tarikha cheikh yagoul sa waay
Iow topeul feulé wakhofi gatt
😂😂 fall yagui wakhe kholl deh talibé cheikh abadane ❤
Damani yeen bayileen tapalé wassifa mouhammad Sallalahou aleyhi wa salam khamoko lolou mooy wakh dji wassifa biddah la point
Iow sisa bopou yay bida bande d' ignorant
Boul dougou si auto boul léké coudou boul diouli si Sidiada boul tal Lampe boul sétane télé doméram sanil sa téléphone 😅
Amoul won diamano Yonénte bi sws
Dof bou mag bi fékhél kham sa bop
Yalla borom khél yi lay wakhal domraam
Fékhél boul talati ventilateur boul nan dokhou frigo ak robina démal gasse téén boul dém hôpital ak pharmacie 😅kouti dof
Foutaise