Oustaz Oumar Diallo ak Pape Sidy Faal, bilahi soumalèy sètaan yow ak Moor Kèbè dèmay geuneu diap si lima nèk ahloul sounah waldiama…Oumar Diallo borrom kham kham la dou thiakhane mokoy kothie, ki mooy Talibè Dr Mouhamad Ahmad Lo hafizahoula wo ra’ah… bilahi Gaïdè ba ngui yalla nala yalla fay…quand a pape Sidy faal tu me rassure trop même Parceque tu est très intelligent en plus lima geuneu nèèkh si yow mooy dè’ ngay dieufeundiko sa khèl donc keep up my brother we love ❤️ you from the bottom of our ❤️, keeping rocking the most importantly is never give up. Thank you .
Ma cha allah chaque jour danla wara invité si plateau yi con légui yalla Sénégal changer diazakoumoul Lahou hayrane ouztase Oumar Diallo alhouran AK Sounnah rek Moy deug
Machallah ya ouztaz omar diallo yalle na yalla barkel ame na solo trop bilahi legui lepou ler inchallah jeunesse bi yepou inchallah dinane yéwou inchallah nane beuril lini dem si télé yi rk❤❤❤
Le gars en bleu n'a qu'à continuer à mieux étudier c'est mieux Dire que la corruption n'est pas haram c'est de la mecreance... qu'Allah nous en preserve
Oustaz Oumar Diallo ak Pape Sidy Faal, bilahi soumalèy sètaan yow ak Moor Kèbè dèmay geuneu diap si lima nèk ahloul sounah waldiama…Oumar Diallo borrom kham kham la dou thiakhane mokoy kothie, ki mooy Talibè Dr Mouhamad Ahmad Lo hafizahoula wo ra’ah… bilahi Gaïdè ba ngui yalla nala yalla fay…quand a pape Sidy faal tu me rassure trop même Parceque tu est très intelligent en plus lima geuneu nèèkh si yow mooy dè’ ngay dieufeundiko sa khèl donc keep up my brother we love ❤️ you from the bottom of our ❤️, keeping rocking the most importantly is never give up. Thank you .
Oumar Diallo et Mor kébé sont très pertinent mancha allah
Allahou Akbar machallah oustaz Oumar
Ma cha allah chaque jour danla wara invité si plateau yi con légui yalla Sénégal changer diazakoumoul Lahou hayrane ouztase Oumar Diallo alhouran AK Sounnah rek Moy deug
Ma Sha Allah
BarakAllahoufikoum Ouztaz Omar Diallo.
Si seulement on invitait des gens de sciences comme toi dans les plateaux
Macha Allah oustaz Omar Diallo ak oustaz mor kebe dem bi genn dii dem thi plateau yi amna solo جزاكم الله خير
Masha Allah ça se voit que Oustaz Oumar Diallo est vraiment sur la Sunna qu'Allah le préserve
Pape sidy merci beaucoup
Oustaz Oumar Diallo pertinence si yow la bokk mashAllah. Deugg deugg la vérité n'est pas égale au faux
Dieuredieuf Oustaz Omar Diallo.Yalla na borone bi degueureul sa lamigne té yokk sa kham kham, allahoummah salli ala seydina Mouhammad wa salim.
Mashallah Oustaz Oumar Diallo
Yalla nala yala Faye yiw yalla défal la diam ak khéweul
Machallah Cheikh Oumar 💯 Qu'Allah vous protège 🌷
Mention spéciale à oustaz omar diallo lerr na machalah.
Masha allah oustaz Omar Diallo
🤣🤣🤣 waji khana daray Ahmed Khalifa niass la dianguè
Allahou Akbar oustaz Omar Diallo qu'Allah te préserve
Machalah Oustaz yallana yalla sam la
Merci beaucoup oustaz Omar belle initiative Pape Sidy
MachA'Allah ya oustaz Omar Diallo Yana yalla saamla...
Maa Chaa Allah Oustaz Omar Diallo. Xam xam rék mo weur. Salaam à tous!
Walahie ahlou suna rek moy deug mbaye dieul nga koue🤣💓💓💓💓💓
Machallah ya ouztaz omar diallo yalle na yalla barkel ame na solo trop bilahi legui lepou ler inchallah jeunesse bi yepou inchallah dinane yéwou inchallah nane beuril lini dem si télé yi rk❤❤❤
Vous êtes très pertinent oustaz Oumar sall
Oustaz oumar diallo yalla nala yalla fay macha allah
Mashallah oustaz oumar diallo est cultivé
Machalah oustaz oumar Diallo et pape sidy tu es vraiment courageux
جزاكم الله خيرا وأحسن الله إليكم وحفظكم الله
Machallh oustaz Omar Diallo Sam tourondo
Machalla oustaz oumar diallo voila gni gnoy élément wou doctor ahmad lo contane nagnou
MACHALAH oustaz oumar
Masha Allah oustaz oumar Diallo yalla nala yalla Faye
Oustaz omar sagou lislam lá yalla na yalla faye la
macha allah oustaz oumar diallo yalla na yalla barkel
Machallah ya oustaz Diallo fait pas accepté de de Fiat débat avec faut oustaz la merci o Diallo ♥️♥️
Deug rk mo wor ❤❤
Pape sidy l émission est intéressante mais il faudrait invité 2 personne du mm niveau intellectuel
Ma challa oustaz OMAR DIALLO
Pape sidy fall mashaa Allah yangui deff sa ligeye, Oustaz oumar Diallo jazzakamoullah Hairan . Kissi dess nakk iow dangay comédie
ماشاءالله أطال بقائك علي خدمة الدين بورك فيك
Lahilaha ilalah Mouhamed Rasoulilahi
Oustaz bi ak dégradé bii 😂😂
Non Oustaz Omar vs êtes très pertinent maasha Allah.
❤❤❤
J'aime votre chaîne que dieu facilite
Machala oustaz Oumar Diallo xam xam rk mo worr
Thiey yalla kimomo moy ban façon oustaz
Merci beaucoup oustaz Diallo
Oustaz Oumar Diallo Mala beugue
Thank you so much Oustaz oumar Diallo
Pape Sidy ngir YaALLAH boul invitee ti ce comedien yangui koy may influence
ماشاء الله أستاذ عمر جال
Machalah imm Omar diallo
Salam Salam noi pape sidi émission bouné khéni me'soumako guis macha allah oustaz omar diallo😂
Ousmane beuy daye andeu ak moromi beuyame wala niou thieré ko tay mome keur deume yi nga dougou 🤭🤭😂😂
machallah omar dialo
MACHALLAH OUSTAZ DO MOROMOU BOY YI
Wa oustaz Ousmane mi mom foumou djanguè khana ??? Sheutt 😂😂🤦🙏 machallah ♥️ oustaz Oumar Diallo
machallah déle déff émission you mélni amna solo
Mashaa Allah seydina Oumar
Bravo Sidy Fall
Machalla amna solo
Mashallah
Masah Allah Oustaz Omar Diallo Amnalo
Macha Allah yaa Oustaz
MachaAllah Oustaz Oumar kham kham danioukoy diangue mais kén douko tékk si khél
Amouniou kham kham koulén invité niou dém😂di wakh ay moussiba rk
Mach allah
Le gars en bleu n'a qu'à continuer à mieux étudier c'est mieux
Dire que la corruption n'est pas haram c'est de la mecreance... qu'Allah nous en preserve
borom yéré bu bleu mom dugnko dédd tmt
yalna yalla fayla yiw oustaz Oumar
Merci oustaz
Machaalla barakalahou fikoum y'a imams
Masha Allah🙏 oustas Omar jallow ❤️
Machalha OustaZ Omar
Barakal lahou fik
😆😆 oustaz wa daganatan
Merci oustaz omar
machallah outaz omar
Sénégalaiyii degniy fowee Islam wallah
2stv Pape sidy fall Vraiment c'est irresponsable de donner l'opportunité de parler au grand public de certains personnes
شكرا أستاذ عمر جالو
merci Oustaz Oumar
Merci Oumar Diallo
Macha Allah ya Oustaz aka am fole
Oustaz omar yalla same la
Ce Ousmane là est extrémement nocif pour une société comme le Sénégal
Alhamndulilah contan na.🙏
Macha Allah
Non mais ce gars il est très dangereux. Il doit même pas être invité sur une télé.
Khana l'autre oustaz wa APR leu thiéy Sénégal founiou dieum
Vraiment ce gas il est malade., Di wakh thi dîné Di wakh aye erreur.
😂😂😂😂nooohhhh mai ousman mi dafa dofff wala dafa gniaff ndayam ki louko dall
Ce soit disant oustaz ne doit pas assister à des cours religieux
Macha Allah oustaz Oumar Diallo
DIALLO bravo 👏
Dierdieuf ya oustaz omor Diallo
Cet homme n'a pas sa place sur ce plateau il balance ses versets pour montrer qu'il les a maitrisé la ou il n'ont pas leur raison d'être
Est ce que ce bonhomme est Saint d esprit ???
Kii dafaye khoumbeul palatau bi mo geuneu khamni lingaye wakh yawe oustaz oumar moye deugue 😁yallah na borombi barkél
Mais qui est ce que ça va bien nanioulen diangui souniou diné 🤧🤧
سبحان الله. هاذا الرجل، جاهل جدآ، عافاه ورحمه. وبعد ذا لك عفا الله، شيخنا عمر جل ورعاه.
Mais ce que je me demande pourquoi tu lui invite sur ton plateau
😂😂
Ousmane ya nekh dh😄😅😅😅😅😅😅😅😅
LAAAH ilaha ilaha Mouhammad rassouloula.
Non wadji rewna Billahi, ki prkw mouy wakh Thi dine dji louko nekh n’importe quoi 😐