Balla Gaye 2 attaque et détruit gravement Siteu : "Dafa possé ay beugne..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 23 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 225

  • @oumitandiaye6780
    @oumitandiaye6780 21 день тому +18

    Je suis fans de Modou lo mais je vais supporter balla gaye pour ce combat

  • @geoffroyntab3132
    @geoffroyntab3132 21 день тому +40

    Bilayi ,bou bayy ay wax ethnie.
    Nous sommes tous les mêmes.Vive le Sénégal❤
    Balla rek

    • @footballgod4351
      @footballgod4351 21 день тому +2

      Saway bayilen seytane fi nieupa am ay mbok te kunek say mbok ngay wo on sait que nous somme les meme

    • @cheikhdiop9673
      @cheikhdiop9673 19 днів тому

      @@footballgod4351 kounék say mbokk guay wo Kone lamb dji bou béne nitt dém stade ande ak siteu na andak ay mbokam késsé mou diékh mbeur boufi amati combat na sénégalais yi am foula nafa ay mbokam késsé dém pour gougué ko koudoul mbokou mbeur mi boum dém stade mou diékh lamb légui affaires de mbokk la

  • @mouhameddiagne7890
    @mouhameddiagne7890 21 день тому +9

    Siteu lalll ngua lalaké dei Bilahy bi dou yoyou Balla Seull❤❤❤❤

  • @yacinebouballaguaye2243
    @yacinebouballaguaye2243 21 день тому +28

    Machalla lafe thiate petit frère balla l'homme au mental fort très courageux combattant hors pair inchalla ndam rék inchalla Amine yarabi 🤲🏻❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🏻

  • @GoraNdiaye-m7h
    @GoraNdiaye-m7h 21 день тому +13

    Balla yalla na dan site sie barkè cheikh Ibrahim fall lampe ❤

  • @aliounembaye5512
    @aliounembaye5512 21 день тому +17

    Balla bilahi yaw bo bayè lamb nioune say supporters souniou amati bén mbecté di sétan lambe vraiment on t'aime s'il vous plaît yokal entraînement yi rek ya meune niép danio sokhlawate guiss souniou bop si arène bi

  • @OusmaneDialloOuz
    @OusmaneDialloOuz 21 день тому +5

    Wallah je ne jamais supporter Balla gaye mais cet fois ci vraiment je lui supportes

  • @papediouf4607
    @papediouf4607 21 день тому +41

    Lamb j dou afaire éthnie mane sérer la té Balla la faral sport la rek😎

  • @TitinoFall
    @TitinoFall 21 день тому +16

    C'est la première foi may faral balla gaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @niangmamediarra9665
      @niangmamediarra9665 19 днів тому

      Nio yame kone😂😂siteu dafa niak diome balla nako sempi Rek sani ko si guinaw sakou yi😂😂

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 21 день тому +99

    *Non nekhoul beu nekhoul mais Balla moy khoromou lamb. Et je suis un grand fan de Modou Lo mais yallah deugue leu beugue. Lii nekoul sakh face à face présentation kessei leu mais nekhal nako comme si combat bi soubeu leu.*

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 21 день тому +32

    Siteu ya ngi doga déthie ki balla leu dou yoyou 😂

  • @KaderSeck-b4i
    @KaderSeck-b4i 21 день тому +16

    Inchalla !!!! Balla gaye 2 va corriger siteu , il parle troo cet petit 😂

  • @yilebaba6565
    @yilebaba6565 21 день тому +18

    Balla késsé ❤❤❤

  • @assaneseye2148
    @assaneseye2148 21 день тому +4

    Le meilleur lutteur de tout les temps sama Balla gaye 2 dossen morom

  • @AbouSengott
    @AbouSengott 21 день тому +5

    Yo allah wallou BG 2❤❤❤

  • @mouhamadoulaminendiaye3595
    @mouhamadoulaminendiaye3595 21 день тому +7

    Thieye balla mo ame sagne sagne ❤❤❤❤

  • @MansourDiop-y6j
    @MansourDiop-y6j 21 день тому +12

    Balla Gaye 2 moy lamb ❤❤❤❤

  • @dondiego9293
    @dondiego9293 21 день тому +10

    Siteu dafa barri wakh day danou ba parei di am combat sarap lii😂

  • @mamadoukanediallo3318
    @mamadoukanediallo3318 20 днів тому +3

    Bilahi masouma faral balla guaye si adouna mé bi yone pour la première fois balla guaye la faral

  • @sambaba683
    @sambaba683 21 день тому +5

    Siteu woroule dieu balla guaye2 mi il est en grande forme balla très confiant

  • @bvfatima8039
    @bvfatima8039 20 днів тому +3

    Bialhi balla tu á bien dit

  • @MatarFall-jd1hq
    @MatarFall-jd1hq 21 день тому +12

    combat bi fans modou lo yi sax balla gaye lagnou faral😅😅😅😅

  • @AbdellahiNdiay
    @AbdellahiNdiay 20 днів тому +3

    Walayi modou moye sama mbeur ms balla wakhena degue yaw ak modou mome jamais ken arriere di dawe di kene sakouyi aye vrai gainde ken machallah

  • @ManoVideotech
    @ManoVideotech 21 день тому +2

    Le lion, le roi, Balla Gaye 2 ❤

  • @adamadiouf9926
    @adamadiouf9926 20 днів тому +1

    Vision Sénégal 2050 inchalla ❤❤❤

  • @galayebeye7868
    @galayebeye7868 21 день тому +5

    Yako meune fouff❤

  • @ThioroFall-s8h
    @ThioroFall-s8h 21 день тому +16

    Modou lo néna amal diome
    Balla néna amal diome
    Donc siteu amal diome amal goor taxaw

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 21 день тому +3

      Vraiment kou 2 lambalogue wakh nga am diom warga am diom dé😂

    • @bdiene66
      @bdiene66 21 день тому

      Saway siteu yoboulène ardo nganane amale diom😂😂😂

  • @BaraNdoye-r6c
    @BaraNdoye-r6c 21 день тому +9

    Merci balla dou khalle dee 😂😂😂tadjabone kay

  • @alphadiouf8111
    @alphadiouf8111 21 день тому +19

    Siteu ya eupp problème nieup😂... Ya dougue thy Balla gaye mou doff mii😂 dinga nelaw sakh di beuré,say mbook di nelaw di beure

    • @yilebaba6565
      @yilebaba6565 21 день тому +3

      😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @ibouthiam3274
      @ibouthiam3274 21 день тому +3

      😂😂😂😂 nn siteu lek n'a thiow

    • @Xarnoubi
      @Xarnoubi 21 день тому +2

      Bilay waxatiko balla ko geuna mana wax😂😂

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 20 днів тому +1

      @@alphadiouf8111 combat niari waxkate ndaw thiow😂

  • @MansourDrame-j6p
    @MansourDrame-j6p 20 днів тому +2

    Siteu Siteu Siteu niata yoon 😢am gua problème

  • @dembambye2795
    @dembambye2795 21 день тому +2

    Your communicate is excellent extraordinary maa shaa allah

  • @Senegalaise2024
    @Senegalaise2024 21 день тому +3

    Au dela du sport côté business Wa Al Bourakh danio aye ci marketing ak communication. J’aimerais vraiment faire une immersion dans leur entreprise pour decouvrir 🎉🎉🎉

  • @senegalkesso1293
    @senegalkesso1293 21 день тому +4

    MANI KENE DÉM JEUNDI JUS AK GLACE WELLY❤️

  • @AbdoulayeBa-b2i
    @AbdoulayeBa-b2i 21 день тому +1

    Balla gaye 2 le référence de la lutter de ta général Sion ❤❤❤❤

  • @FallWaly-c6g
    @FallWaly-c6g 21 день тому +20

    Siteu dey bari wax rek yebna kuko gena bari wax

  • @sambaba683
    @sambaba683 21 день тому +1

    Balla mi billahi il est en très forme

  • @MountkhaSow
    @MountkhaSow 21 день тому +10

    Siteu dadone yorou yepna nak ki balla la deh 😂

  • @mourtallaseye3873
    @mourtallaseye3873 21 день тому +6

    MAIS ATTEND SES LUTTEURS ILS ONT TOUS LE MEME AGE ET ILS NE GRANDISSENT JAMAIS SARAP NDAY LI REK 😂😂😂😂😂😂😂

  • @diopablaye5227
    @diopablaye5227 21 день тому +4

    Kou dan bakh na

  • @AwaMbaye-nj3qz
    @AwaMbaye-nj3qz 21 день тому +4

    bagaye seul❤❤❤

  • @rouguikebe9984
    @rouguikebe9984 21 день тому +7

    Modou néna amal diom
    Balla néna amal diom
    Kone Siteu changél nga deugal sa bop😂boul daw waay Lac 3😂

  • @siteu_n77
    @siteu_n77 19 днів тому +1

    me kouy wakh en premiere nonu m nafekk na deh waw ak nimko wakhe nk nena mola man fouffff vraiment amna nit niou man diakhase😢

  • @GoraNdiaye-m7h
    @GoraNdiaye-m7h 21 день тому +1

    Balla seul 🥰❤️

  • @DjibySow-j3b
    @DjibySow-j3b 21 день тому +1

    Thiey balla gaye ❤❤

  • @OusaynouMbge
    @OusaynouMbge 21 день тому +6

    Balla moy lamb😂😂😂💛💙

  • @mussdio6251
    @mussdio6251 21 день тому +4

    Balla Gaye 2 4ever

  • @thiernodembaya8355
    @thiernodembaya8355 21 день тому +9

    Je suis supporter de 100% à Modou lo ❤ me cette combat je supporte Balla gaye 2 🇸🇳🇸🇳 inchallah dam reck 😂😂😂 siteu dinalla douma yù meti 😂😂😂😊😊😊

  • @MouhamedGning-b3m
    @MouhamedGning-b3m 21 день тому +1

    Siteu seul ❤

  • @papengom259
    @papengom259 21 день тому +3

    Siteu yalnako yalla may ndam 🤲 🤲 🤲 🤲 🤲 amine 👉👉👉👉👉👂👂👂👂👂👂👂👂👂

    • @cheikhdiop9673
      @cheikhdiop9673 21 день тому +2

      yalla bousa guémigne am barké yalla bou yalla nagou sa niane boudé nagouna sakk dioul 😂😂

  • @DiatouNdiaye-iq3kd
    @DiatouNdiaye-iq3kd 21 день тому

    Thiéy sm mbeur bi sou amé combat adouna yeugou❤❤❤nam rk

  • @Ndiaye-khélcom
    @Ndiaye-khélcom 21 день тому +5

    Balla gaye d'où sama mbeur dh mé day nékhal lambo

  • @mouhamadouniang5344
    @mouhamadouniang5344 20 днів тому +1

    Siteu yàngui soga ame combat nak je suis suportaire de modou Lo mais balla dou gnoniou

  • @mouhamadoulaminendiaye8257
    @mouhamadoulaminendiaye8257 21 день тому +2

    Siteu yeureum nala

  • @falistobambiste
    @falistobambiste 21 день тому +13

    Etant fan Mod lô mais Siteu finga dieulei Balla bakhoul mingui nioul koukk ndirouna kou parei dei 😂😂

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 21 день тому +6

      Bayiko ba Balla diapko mane Modou la faral mais ce combat Balla lay supporté Siteu dafa rw

    • @bdiene66
      @bdiene66 21 день тому +1

      Boy siteu mougui gagné expérience nak kou wédi na lathie modou lo😂😂😂 dou yomb dé😂😂

    • @laminefaty7370
      @laminefaty7370 20 днів тому +2

      Wallaye ndeyssane siteu da dioum😂😂😂😂😂

    • @falistobambiste
      @falistobambiste 20 днів тому

      @@bdiene66 en kone bakhna à suivre 😂✨

    • @falistobambiste
      @falistobambiste 20 днів тому

      @@rouguikebe9984 saway dei moytoul mako bu nekkei en forme teh pour l’instant telle est le cas

  • @capwell8688
    @capwell8688 18 днів тому

    C très bien balla c bien ta bien dis😅😅😅

  • @OusmaneFall-m9d
    @OusmaneFall-m9d 20 днів тому +1

    Balla GAYE il faudra bien entraîner et nous bastonner bien bon Siteu le bavard

  • @AbouSy-uq1lv
    @AbouSy-uq1lv 21 день тому

    Bg2 ❤❤❤❤❤❤

  • @Ndiayediop-f2r
    @Ndiayediop-f2r 19 днів тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @xeuchelaye6924
    @xeuchelaye6924 21 день тому +3

    😂😂😂 balla diay prek leu koi 😂

  • @serigneniomrelo6956
    @serigneniomrelo6956 21 день тому +7

    Siteu mo nèkon sama 2ème mbeur apar modou lo mais si combat modou lo bi lako bayi daw rk baparé abou radio yii

  • @AdamaDiop-r1k
    @AdamaDiop-r1k 21 день тому +1

    Ohh Siteu lutakh ladio modou lo😢😢😢

    • @DameNguirane
      @DameNguirane 21 день тому

      Loussi yonou modou lo soff nga trop😅

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 20 днів тому

      @@DameNguirane meune togn rék

  • @sambaba683
    @sambaba683 21 день тому +1

    Toujours arrière non Balla dou nitt wayyyyy😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ngangedrammeh6264
    @ngangedrammeh6264 21 день тому

    Cheii Balla ❤❤❤

  • @khadimfall3075
    @khadimfall3075 21 день тому +1

    Worneu yalla balla Day dane

  • @FallWaly-c6g
    @FallWaly-c6g 21 день тому +5

    Bilahi balla du yoyu

  • @MatarGueye-w2m
    @MatarGueye-w2m 21 день тому +2

    ♥️♥️♥️💪💪💯

  • @alexisniokhorsenghor-lg4gc
    @alexisniokhorsenghor-lg4gc 21 день тому

    🤣🤣 Balla est très drôle. Championt bi

  • @GoraNdiaye-m7h
    @GoraNdiaye-m7h 21 день тому +1

    Site yalla nagua danou billahie

  • @laminjoof6365
    @laminjoof6365 21 день тому +1

    Balla Gaye 2 2️⃣ insallahu rabbi 😂 😂 😂 Allah will always protect you from bad people's long life happiness success and secure 🔐 🥰 🥰 🥰 watching from Italy 🇮🇹 not

  • @FatouBarr-r9z
    @FatouBarr-r9z 21 день тому

    Balla❤❤❤

  • @loummouhamet4237
    @loummouhamet4237 19 днів тому

    Non balla beurétoule bilahi oh

  • @CheikhDiagne-w6w
    @CheikhDiagne-w6w 17 днів тому

    siteu yalla nana yalla may daam🤲🤲

  • @alvideos1175
    @alvideos1175 21 день тому +2

    Siteu faut pas s’attendre a grand chose venant de lui malgré ces grands paroles, il va fuir comme contre modou lô et venir avec ces supporters nous dire que c’est un guerrier parce que balla gaye n’a pas réussi à le faire tomber mdr

  • @BASSLam-k9t
    @BASSLam-k9t 20 днів тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @GoraNdiaye-m7h
    @GoraNdiaye-m7h 21 день тому

    Balla seul 🥰

  • @TaxiMan-y9c
    @TaxiMan-y9c 20 днів тому +2

    Meune na wakh lol wayé mounoul dieuf 😂😂😂meune na daw aussi

  • @karimgadio177
    @karimgadio177 20 днів тому +1

    😂😂😂 non Omar mo dé

  • @TaphaLoume
    @TaphaLoume 21 день тому +3

    ❤❤❤❤❤❤💪💪💪💪🙏🙏🙏💪💪💪💪

  • @PASCALJUNIORMENDY
    @PASCALJUNIORMENDY 21 день тому +2

    Balla do nit😂😂

  • @thiernodembaya8355
    @thiernodembaya8355 21 день тому +2

    🇸🇳🇸🇳🇸🇳 me le vieux qui travaille à Albourah il me nerve woyane reck et guslema😂😡😡😡 avec Abi bizarre 😊

  • @MameBirahimeLayeGaye
    @MameBirahimeLayeGaye 21 день тому +1

    Balla bilay moy lamb

  • @AmadouGuisse-e1r
    @AmadouGuisse-e1r 21 день тому

    Modou kharagne kassé mais siteuh mom kham na si limou douguou tamite 😂😂😂ayyy Balla niko bouchée wakhé aay Balla 😂😂😂

  • @FallWaly-c6g
    @FallWaly-c6g 21 день тому +6

    Deugal ngattou watta

  • @AbdouMbackeFaye-oe4pw
    @AbdouMbackeFaye-oe4pw 21 день тому +1

    Siteu amngua sokhna la

  • @MorBabou-pz7xu
    @MorBabou-pz7xu 21 день тому +1

    Siteu heur bodèmè 😢l
    Ni avance nidiaye diou dious la 😂

  • @IssaDieng-g3j
    @IssaDieng-g3j 21 день тому +1

    Modou moy sama mbeur wayé balla day niaf ndy😂siteu

  • @dramedjibril2976
    @dramedjibril2976 21 день тому +5

    Mome la gueuneu bagne si lamb mais bilay moy khorom bi

    • @zallemouserignesaliou
      @zallemouserignesaliou 21 день тому

      😅😅

    • @ousmanesy6727
      @ousmanesy6727 21 день тому +1

      Yaw borom khôl bu rafnga . Ak sa wakh do kouy bagne keneu.
      Dou seu mbeur rek waye kou bakh nga

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 20 днів тому

      @@dramedjibril2976 Modou seul moy khorom si ❤️🥰
      Kounék ak sa khorom😎

  • @BAbacarLo-l8d
    @BAbacarLo-l8d 21 день тому +2

    Mais combat bi tamit dafa sory koi 6moi

  • @ibouthiam3274
    @ibouthiam3274 21 день тому +1

    Siteu dh dadon bari wakh rek tay dji mom diga lek thiow balla rek ak yeugeul vraiment dou sma mbeur way ay combats wam mom mokoy diay niépay khamni combat amna nekhoul ba nekhoul wayer moy khoromu lamb ji

  • @MoussaDiouf-d6w
    @MoussaDiouf-d6w 18 днів тому

    Thieyy siteu walay Daf tit amnga soxlaa

  • @paolosanari2429
    @paolosanari2429 18 днів тому

    mdrrrir... Djambaar bi paa mom lay supporter! Balla gaye moy nekhal lamb

  • @GALSENGAMER
    @GALSENGAMER 21 день тому

    Balla le roi du trash talk😂😂

  • @CheikToure-cl2jd
    @CheikToure-cl2jd 21 день тому +1

    Balla seul 😂😂😂

  • @madinagueye168
    @madinagueye168 21 день тому +2

    Mbeur boucidoon recruter ay nervis yalla gua tegueler ay défaites

    • @gora8046
      @gora8046 21 день тому

      Saway arrêtez avec vos histoires de nervis, vous avez le droit d’être avec qui bon vous semble en politique et les lutteurs n’ont pas ce même droit, pire vous accusez gratuitement des gens sans même savoir ce qui se passe: Sénégal mbeur mou andoul ak Sonko rek t’es un nervi😂arrêtez wayi, khana les gardes corps de Sonko yi doré ay diassi à Mbour ay nervis lagne wone bagne lène diapé wone😂😂 lou nguène fi khass nitt rek Sénégal wa Pastef deff nagne ko ba rombou dans tout nak😂 pathio souf, saga, yak alalou diambour, n’empêche c’est votre droit le plus absolu d’être des pro Sonko comme sama classe gui ont le droit d’être ak ki lène saff.

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 20 днів тому

      @@gora8046 vraiment ils ne savent pas faire la part des choses.

  • @TalzooJakit-yq4ob
    @TalzooJakit-yq4ob 21 день тому

    Gnounn siteu la gnou beuck ❤❤❤ siteu rk point

  • @SowMadiaw-go2uc
    @SowMadiaw-go2uc 21 день тому

    Balla légui da décider

  • @cheikhgassama6877
    @cheikhgassama6877 21 день тому +1

    Ki moy lambou bilay 😅😅😅

  • @elzodieng8067
    @elzodieng8067 21 день тому +1

    Thiey balla mon meun bés 😂😂😂😂😂😂

  • @oussoulove1279
    @oussoulove1279 21 день тому +5

    Balla gaye dh nioul n'a si sasi

  • @papefall4806
    @papefall4806 21 день тому +1

    Pa bi sa présentation bi yagg n’a wakh gua 3mins