Mouhamed Niang Mou Serigne Saliou - Serigne Fallou (Clip Officiel)

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 9 вер 2020
  • Prenez le plaisir de regarder le tout nouveau clip de Mouhamed Niang Mou Serigne Saliou "Serigne Fallou"

КОМЕНТАРІ • 2,5 тис.

  • @sokhnaseye317
    @sokhnaseye317 3 роки тому +913

    Je suis tidiane mais vraiment j aime mouhamed niang il chante bien avec sa belle voie
    Kou d accord tapéll j aime

  • @bourysalioudia9214
    @bourysalioudia9214 3 роки тому +454

    Anni mouride yi mancha Allah clip bi Nice na trop❤❤❤👌🥰🥰🙏

  • @ndeyeantaniang5138
    @ndeyeantaniang5138 3 роки тому +86

    Ça nérite des millions et même millards de vues 🙏😭😭walae j'pleures ça touche grave 💞👑🔥

  • @dieynabadieng8989
    @dieynabadieng8989 3 роки тому +79

    Cheut j'adore cette chanson elle me donne la chair 🥰de poule bilay je l'écoute à longueur de la journée
    Mouhamed niang voix bi mo graw machalla j suis talibé cheikh mé j l'adore dal je kiff tou c chanson laff thiat ❤
    Fans number 1 moy mane ☝️yalla na yalla yéreul bate bi t yokk khatane bi mayla goudou fane ak wér amine touf touf 🙏

  • @taphaseye243
    @taphaseye243 3 роки тому +113

    Machallah Dieredieufff brom Touba cheikh Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd qui Aminnne

  • @aisstouciss901
    @aisstouciss901 3 роки тому +341

    Macha allah je suis tidjiane mais j'aime beaucoup Serigne fallou merci Mohamed Niang sama khol seed na bonne continuation

  • @mamediarrafall160
    @mamediarrafall160 3 роки тому +59

    Nianal len ma réne ma am bac si barkép Serigne Fallou Mbacké❤️🙏🥺

  • @alkarimtv6877
    @alkarimtv6877 3 роки тому +42

    Damakoy déguelou plus de 5 fois par jour yallana borom bi fay ❤️🙏

  • @morwakanahaqqan6585
    @morwakanahaqqan6585 3 роки тому +130

    Yalla na Serigne Touba dèfal nièp diam kou wakh Amine yalla gua doundou 111 ans sans tolof tolof Mor wakana haqqan ,Angleterre sa Sopè machallah clip bi Rafetena lolou
    Yalla gua guena ame Ndimalou Serigne Saliou 🙏🙏🙏👏🥰

  • @ogog4223
    @ogog4223 3 роки тому +44

    Serigne Fallou kouko yakar euleuk kenn doula ladj say keuyitt😭❤️❤️❤️❤️lolou aka lerrr❤️

  • @sadandour3382
    @sadandour3382 3 роки тому +54

    MachaAllah, Serigne Fallou si khol khéweul rék .

  • @adjadiaite4720
    @adjadiaite4720 3 роки тому +202

    Mouhamed niang kagn guay way serigne bara reukeuday nak😭♥️ ani talibé serigne bara yi

  • @thianediouf6513
    @thianediouf6513 3 роки тому +96

    Mächallah nexna trooop
    Anni gni sope fallou awa bousso

  • @diallawatt8481
    @diallawatt8481 3 роки тому +93

    L'homme à la voix d' or❤️❤️❤️❣️🌹🌷🌷👑

  • @dieumbdieumb4659
    @dieumbdieumb4659 2 роки тому +26

    Machalla dieureudeuf Serigne Fallou mbacke ❤️

  • @thiabyndiaye8002
    @thiabyndiaye8002 3 роки тому +124

    Ndaysan ❤sa souma❤ diakhlé serigne❤ fallou ❤lay hoo ❤thé❤ sama ❤adio❤ day ❤fadiou❤

    • @maremesall9322
      @maremesall9322 3 роки тому +3

      Khana souma dialé mane moom si siguil ma la deuk masouma gantal

    • @ndeyetoutybarry8035
      @ndeyetoutybarry8035 3 роки тому +3

      Wakhal de mm mane moy sama werouway te dôme boutoudou serigne fallou rek la beuguone te amnako Alkhamdoulilah

    • @aramediaw8620
      @aramediaw8620 3 роки тому +2

      Khamnassi dara billahi

    • @thiantakooneba7698
      @thiantakooneba7698 3 роки тому +1

      Kéne dou fallou awa bousso

    • @ndiayetecnology1339
      @ndiayetecnology1339 3 роки тому +2

      nday San man tay nouma mél s fallou la Dako beugue ba awma si mom sago yalana Nama yala may dieukeur diou bakh seuy bou barkèl tawlo si am serigne fallou

  • @fatoudiop2975
    @fatoudiop2975 3 роки тому +47

    Thiey sama yakar bii Serigne fallou yalna ma yalla maye doom bou goor ma touddé lakoo rek la beugu ak kouko beugue rek

  • @smbenegueyebadar3301
    @smbenegueyebadar3301 2 роки тому +6

    Sama yakar tay ak elke 🤩🤩🤩😍sarigne fallou

  • @dioufdiyby8928
    @dioufdiyby8928 3 роки тому +26

    Vraiment ça me touche au fond du cœur je l'aime fort Serigne falou sama yakar

  • @pendistasadiakhou140
    @pendistasadiakhou140 3 роки тому +59

    Barki serigne Saliou MBACKE dama beugu tey serigne Saliou rek tah😭😭😭😭😭😭😭❤❤❤

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 3 роки тому +1

      Pendista Sadiakhou Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne UA-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

  • @mamefallougallas5099
    @mamefallougallas5099 3 роки тому +32

    Ndeysan thieuy S Fallou sama wadji mane dh mom rèk la ame mom rèk la beug dh moy sama lép❤️❤️❤️❤️

  • @bambaseck62
    @bambaseck62 3 роки тому +58

    Fière d'être mouride machallah niang diam ci yaw athia mouride takk diokk ila touba 18 safar moy sunu biss

  • @evaminathiatouyayamgueye8837
    @evaminathiatouyayamgueye8837 3 роки тому +38

    Fière d’être une fadelle Serigne fallou ma vie 🥰🥰🥰🥰merci mouhamed

  • @babacarndiaye3460
    @babacarndiaye3460 3 роки тому +117

    Serigne fallou mi moy kharitou sama tourreundo sama yakar serigne babacar sy montakh ma am chance nék premier commentaire

  • @ousmanekamara8590
    @ousmanekamara8590 3 роки тому +30

    Sama yakar tay ak euleuk❤ Galass baye mbéne😭😭

  • @kanefaty8701
    @kanefaty8701 3 роки тому +38

    Mane mom douma mouride mai bilahi damay deglou ay chanson wam té souma sagnone mouride lay âme kom dieukeur ☺️

  • @serignebarambaye1682
    @serignebarambaye1682 2 роки тому +37

    Ani talibé serigne fallou yi way ❤️❤️❤️❤️💕💕

  • @bourysalioudia9214
    @bourysalioudia9214 3 роки тому +151

    Mouride mba yénagui wath magal gui insha Allah 🥰🥰❤❤🙏👌👌👌

  • @nogayendiaye498
    @nogayendiaye498 3 роки тому +79

    Thieuy galass bayi mbéne beuguoumako guir beug douguou aldiana beuguoumako guir ragual safara damako beug lol ta yalla takh ta féké woumay diamonom Sax lépp louma beug soumako wowé diourom niari Yon mou wouyouma alhamdou lilah bima doné mourite😍

    • @thiallambathie296
      @thiallambathie296 3 роки тому +1

      bilahi dama fokni lolou mane kasè la

    • @saylo4511
      @saylo4511 3 роки тому

      Yalla kham nané pour ll mana rk la

  • @aidabadiane6641
    @aidabadiane6641 3 роки тому +28

    Machallah j'adore Dieureudieuf Serigne fallou Mbacke ❤❤❤

  • @mbayesadji4614
    @mbayesadji4614 3 роки тому +5

    Lii nga way sama sangu bii Mouhamed Niang yalla namala yalla fayal gouddeul'sa fàn cii barké Serigne Fallou🙏🏾💗💗💗❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🎉🎉🎉🎉🎉

  • @diawsamb9218
    @diawsamb9218 3 роки тому +41

    Thiéy Fallou sama wadji défalnama tréguadiouné♥️♥️♥️♥️

  • @awadieye7633
    @awadieye7633 3 роки тому +44

    Ana sopeye serigne fallou yi maye lene j'aime😍😍😍😍😍

  • @ndiayendoumbe1024
    @ndiayendoumbe1024 3 роки тому +251

    Je suis layenne mei vrema cette chanson me touche au cœur ❤️et j’aime bien serigne serigne falou ❤️🙏🙏

  • @maguettefall8783
    @maguettefall8783 Рік тому +10

    Serigne fallou amoul morom😭❤

  • @momondiaye6767
    @momondiaye6767 3 роки тому +45

    18safar🇸🇳❤️voix d’or yalla na adio yepp fadjounsi barke Serigne Fallou corona dem yooname
    Dieureudieuf Serigne Touba❤️

  • @sokhnafadilatougallasse8033
    @sokhnafadilatougallasse8033 3 роки тому +755

    Je suis fière d'être Gallasse💪💪❤
    Ana sopey Serigne Fallou Gallass yi❤❤❤❤❤

  • @sadamoumamecheikh
    @sadamoumamecheikh 2 місяці тому +2

    Je suis moustarchide mais mame Fallou je l’aime plus que vous yalla na yalla yook lérame❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndeyedia5909
    @ndeyedia5909 3 роки тому +83

    Où sont les talibés cheikh qui écoutent Niang mouhamed ✌️ jumah moubarak to all🙏

  • @fatoufall1929
    @fatoufall1929 3 роки тому +380

    Je suis talibé cheikh mais mouhamed niang je l'aime fort il a encors tapé fort 💖

  • @tamsirsambadiene3285
    @tamsirsambadiene3285 3 роки тому +75

    Loumou wey mou nkh, vraiment j l'adore Mouhamed Ndiang💖💥🔥, ak louma bokou ci Tarikha Tidjaniyi

  • @mariethiam4217
    @mariethiam4217 3 роки тому +2

    Vraiment meilleur vidéo ❤️💯kene Dou Baye gallas 😭nianalene sama dome dji Serigne fallou tourondome tarre ko ci Barker bii

  • @aramelo7306
    @aramelo7306 3 роки тому +4

    Machallh néxx na trop konn nagn wadial 18 safar inchallh 👏👏👍👌💗💗💓💓💓💖

  • @sokhnandieguene7099
    @sokhnandieguene7099 3 роки тому +136

    Suis niassène dh ms bilay maleen beugue 😭😭😭❤️❤️

  • @asiasarr2023
    @asiasarr2023 3 роки тому +32

    😭🤧❤🥰😩loum waay mou néx mashallah moom rk ladoone haar koukoo doone har beusseul j'aime

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 3 роки тому +1

      Aishou Sarr Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne UA-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

  • @falougueye8239
    @falougueye8239 3 роки тому +28

    Dieuredieufeuti serigne touba ❤️🙏

  • @papamamadousene5951
    @papamamadousene5951 3 роки тому +11

    Les 607 Dislike hana douguenn ay nitt. comment peut on detester cette chanson 😍❤❤❤❤😍😍

  • @awakebe1253
    @awakebe1253 3 роки тому +42

    Eskeuuyyy☺️😭😍Keine dou sama wajiii❤️Fallou Awa BoussO🙏🏼

    • @awakebe1253
      @awakebe1253 3 роки тому

      MAMADOU FAYE diadieuf waay🙏🏼🙏🏼

    • @ndeyesenygueye3277
      @ndeyesenygueye3277 3 роки тому

      Moukhamet dokhal thia kaw thia kanam rk

  • @momylabambistesakho2745
    @momylabambistesakho2745 3 роки тому +27

    Ay way sama serigne bi 🥰🥰🥰fallou awa bousso lougnouko woy mou nèkh ❤

  • @lahadgaye8131
    @lahadgaye8131 2 роки тому +52

    Notre fierté c'est d'être mouride sadikh si barke s fallou ❤️❤️❤️sama serigne

  • @bambadiaw3056
    @bambadiaw3056 3 роки тому +20

    Je suis fiére de vous long vie à toi santé prospriété et bonheur💕❤👈

  • @nogayeniang6906
    @nogayeniang6906 3 роки тому +15

    Borom kazu radjap borom na ame mou ame diorome gniari Serigne fallou fadj na adjo you bari....
    Yalna yalla yokk aye leram tass gnou si barkém🙏🙏

  • @mouhamedniang9728
    @mouhamedniang9728  3 роки тому +229

    Merci

  • @mamediarraboussotall1182
    @mamediarraboussotall1182 2 роки тому +21

    Quand j'entends tes chansons je sens purement que je suis mouride . dieureudieufeté Serigne touba

  • @noumchjoop6808
    @noumchjoop6808 3 роки тому +4

    Serigne fallou rk la ame😭😭💝❤💚💚💚

  • @sokhnalo6067
    @sokhnalo6067 3 роки тому +47

    Ndeysane damassei dioyyyy😭😭😭😭😭😭😭❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏 naaa gaww am Ay Millions reikkk🙏🙏❤️❤️ de vues

  • @daroufalltvdakar6333
    @daroufalltvdakar6333 3 роки тому +24

    Ma cha allahu ani son 18safar bi na nieuw

  • @isssadienge8195
    @isssadienge8195 3 роки тому +9

    C'est extraordinaire 💞💞

  • @abibathior4854
    @abibathior4854 2 роки тому +21

    machalah mes larmes coulent quand j'ecoute cette chanson❤️❤️❤️❤️❤️

  • @evalasalihate551
    @evalasalihate551 3 роки тому +17

    Aniff bi dall nekhna contane nane si yaw barké SERIGNE SALIOU ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @khawlatouba7170
    @khawlatouba7170 3 роки тому +22

    MACHALLAH Niang lo way mou nékh💖
    Je te souhaite un joyeux anniversaire

  • @dienabouba9980
    @dienabouba9980 3 роки тому +16

    J'aime beaucoup MOUHAMED NIANG avec son voix qui me plaît énormément j'adore 💕💕💕

  • @thiernofall3982
    @thiernofall3982 3 роки тому +4

    Machallah lii nekhna yallna yalla fay ci barkep serigne fallou mbacke amine

  • @galaxiepro.5641
    @galaxiepro.5641 3 роки тому +365

    soyez fier de bamba cest notre symbole dans le monde entier moi je suis fier de bamba❤️ et de toute sa famille mbacké et bousso ce sont des erudits incontestables

  • @bintusey462
    @bintusey462 3 роки тому +12

    Muhammet Niang❤️👏
    Yal na Yàlla bàyyi la fi nga yàgg fi lool te Yàlla weral baat bi Barke Sëriñ Saliou 🙏❤️

  • @naboundiaye2520
    @naboundiaye2520 2 роки тому +2

    Diadieuf Niang yalna la yalla lafal thiate may la goudou fane ak wër

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 3 роки тому +2

    Merci boucoup Mouhamed niang yalnanga goude fan ak weure barkep serigne fallou contanna si yawo sama sope pi serigne fallou Mbacke

  • @ndoumbedioplasalihate
    @ndoumbedioplasalihate 3 роки тому +144

    Vraiment meilleur clip de l'année. Vidéo bi rafetna,image yi sétna en plus paroles yi mom c otre chose vraiment chapeau à toute l'équipe 😌

  • @yaayoubaayam517
    @yaayoubaayam517 3 роки тому +55

    Moubamed niang mi nak ame na loukay wakh loooo quel homme yalla na batte bi wer barkep Serigne Touba

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 3 роки тому

      yaayou baayam Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne UA-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

    • @sirageuye1060
      @sirageuye1060 3 роки тому

      Der
      N et

  • @annemariekane8884
    @annemariekane8884 3 роки тому +4

    je suis une layenne ms j'aime serigne fallou

  • @thiatoughazalydiop5048
    @thiatoughazalydiop5048 3 роки тому +7

    Mélodie de cette chanson ♥️🥺 trop chu
    Perso suis talibé cheikh

  • @brahamiennelum3612
    @brahamiennelum3612 3 роки тому +6

    Wawawwww MOURIDE thi kanam rek on attendait le single du MAGAL comme chaque année machallah talibé Brahame Niass bi dala sopeu ani Sama mbok yi na bleu

  • @sidatythiam7998
    @sidatythiam7998 3 роки тому +40

    Ani Sopey Serigne fallou yi way 🥰❤❤❤
    Yalla na gneup ame diam barkeip Serigne Fallou ❤

  • @mangaye7200
    @mangaye7200 3 роки тому +7

    Je suis layenne mais je l'aime fort bisbouma yalla mayone khew souma sanione mokoy way barki baye laye pSL

  • @talibecheikhpire9807
    @talibecheikhpire9807 3 роки тому +3

    Je suis tidiane mais mashallah j'écoute tous tes chansons tu chante super bien yalna yalla weral bat bi

  • @srgnfalloundiaye8322
    @srgnfalloundiaye8322 3 роки тому +13

    Oh sama xole sédd barkep serigne fallou🥰Ani gni done xaar clip bi comme mane ❤️❤️

  • @niangadiop4171
    @niangadiop4171 3 роки тому +14

    Machalla ani fans mouhamed gnia❤💫🌻

  • @soxnaadamasow5823
    @soxnaadamasow5823 3 роки тому +221

    Je suis talibe Cheikh way Dma Beug mouride Yiii Soumaleine Guissé Sma Xoll Day sédd GUouy Sma Dôme Mame thierno Damal darou lako toude ♥️♥️🙏🙏 Mohamed nianG On T'aime

  • @yacinefall3604
    @yacinefall3604 3 роки тому +4

    Machalla Mouhamed sons bi nekh na trope clip Bi c très jolie Kene dou yaw si mim rew 👌❤️

  • @nogayemouserignefalloumbac410
    @nogayemouserignefalloumbac410 3 роки тому +11

    Ndeysane toujours Nogaye mou Serigne Fallou Mbacké ❤️

  • @fatimafaliloulah1145
    @fatimafaliloulah1145 3 роки тому +41

    Serigne Fallou Mbacké sama kharit bi kén dou mome ! Moy khewe ba fawe ! Loufi défarou moko défar ! Mo diaye diourélam dieundé co talibé ! Moy déf Di dindy ! Kou rér mou guindi ! Machahalah Mbacké balla ! Dieureudiefé Serigne Touba, Diaraw lak Mame Cheikh Ibra Fall ! LAMPE FALL !

  • @abytall257
    @abytall257 Рік тому +1

    Dieurieudieufe cheiikh mouhamadou faadal sougnou yakar tay ak euleuk🤲🤲🤲

  • @ndeyeastousokhna8275
    @ndeyeastousokhna8275 3 роки тому +1

    Dama ame niari dom gor ak djiguéne niou toudou serigne Fallou mais souma dégué son bi damay gueuneu fiér si am niari serign fallou machallah nékhna trop

  • @thiammadieye5642
    @thiammadieye5642 3 роки тому +25

    Mouride ba Yagui wathie magal gui🥰🎊🔥

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 3 роки тому

      Thiam Madieye Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne UA-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

  • @awabdoulaye2783
    @awabdoulaye2783 3 роки тому +6

    Jeureujeuf Serigne Mouhamed Niang nékhna trope waay, clip bi raféte na. Serigne Fallou dinala fayy ba nga yégg ko. Tabarfaq'Allah 💕💓👍🏼

  • @mamysaliou5918
    @mamysaliou5918 3 роки тому +1

    Yalla na batt bi gueuneu weer ci Barkep Serigne Saliou😍😍😍😍😍

  • @mbackemameawa7874
    @mbackemameawa7874 3 роки тому +6

    Mboussombék mbacke ni weerak diante la serigne el Haadji Fallou😍😍😍

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 3 роки тому +1

      Mbacke Mame awa Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne UA-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

    • @mbackemameawa7874
      @mbackemameawa7874 3 роки тому

      @@SomoneTv221Officiel amiiine waay niou boku lépu barkei serigne fallou mangui abonné

  • @thiorodiouf2130
    @thiorodiouf2130 3 роки тому +30

    Serigne fallou moy sou yakar
    Moi je suis fier de être mouride barki serigne fallou
    Ame fallou doyna... ❤❤

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 3 роки тому

      Thioro Diouf Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne UA-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

    • @mariamarinsusarte4604
      @mariamarinsusarte4604 Рік тому

      Machalla sante rek

  • @boydiop8209
    @boydiop8209 3 роки тому +21

    Joyeux anniversaire à toi lg vie ndoudal 1111 lep lo beugue yako xam yalla nalako yalla défal si barkéb Serigne saliou iow tay gola cado nga Gouy diox cado bon anniversaire 🎂🎂🎂

    • @awatraore3483
      @awatraore3483 3 роки тому

      Mais c'est l'anniversaire de qui??

    • @mouhamedkante4916
      @mouhamedkante4916 3 роки тому

      @@awatraore3483 de mouhamed niang mou serigne saliou

    • @boydiop8209
      @boydiop8209 3 роки тому

      @@awatraore3483 de Mohamed Niang mou Serigne saliou

  • @Complexe.mya.white2
    @Complexe.mya.white2 3 роки тому +2

    Machalah wayy, dieureudieufati SERIGNE TOUBA 😍😍😍

  • @falloundiaye-qp1ki
    @falloundiaye-qp1ki 3 роки тому +6

    Mouhamed niang une clip pour le grand mgl de Touba ❤❤

  • @ndeyediakhoudjitte2780
    @ndeyediakhoudjitte2780 3 роки тому +30

    Xol Sedna tous ces propos me réjouissent Serigne Abdou Karim ma force

    • @SomoneTv221Officiel
      @SomoneTv221Officiel 3 роки тому +1

      ndeyediakhou djitte Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne UA-cam svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽😭😭

  • @astoudiouf5749
    @astoudiouf5749 3 роки тому +13

    Sunu yakar♥️♥️serigne Fallou bayou mbéne

  • @sadandour3382
    @sadandour3382 Рік тому +1

    MachaAllah Serigne Fallou sama sopé sama khol lako déf

  • @giuseppevacca671
    @giuseppevacca671 3 роки тому +1

    Yalla na niou la yalla fayal waye mouhamed talibé cheikh la wayé leupou béne la sama xolle seed na waye si waye bi yalla na niou la fayal jaime mouhamed💖💖

  • @satoudione3630
    @satoudione3630 3 роки тому +16

    Oh ken dou fallou Galass sama yakar tay ak euleuk❤ana talibe serigne fallou yi??

  • @fayemariama3153
    @fayemariama3153 3 роки тому +2

    Sama wadji ga baak dh bayou mbéne ak baye karim sama thiofel si mom dafmay yém man dieureudieuf mouhamed niang yalna yalla weiral bate bi nigay niouy bégalei yalla beigal la nonou ❤️❤️❤️❤️🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @mamediarrandiaye6847
    @mamediarrandiaye6847 3 роки тому +7

    Défa tinga sa meunine dé Niang ballo nice clip mashallah yalna borom bi sam la mousseul la si seytané barké serigne saliou 🙏❤

  • @nogayerassouldiop6988
    @nogayerassouldiop6988 3 роки тому +8

    ❤❤❤❤meunouma heuy journée t deglouwoumako❤yalna nieup am jam si barkep djourom niarii serigne Fallou❤

  • @DaourDiop-rd3jy
    @DaourDiop-rd3jy 29 днів тому

    je suis fière d'être talibé serigne fallou mbacké ❤ Mouride rk ❤❤