Ok c est triste, mais il a mal choisi ; qu'il retourne en Gambie, pardonne sa femme,reprend ses affaires et demande pardon à sa mère. Il doit se repentir,il n est jamais tard pour bien faire. Doro Sidy Ba ( beydi)
Sa yaye dou niit mome moye seuy wala yaye seuy fassel sa diabar na sa yaye doggo yawe chantage émotionnel yi la souniouye yayii wara bayi quitte ta femme waye !!
Serigne Touba a dit : « Acceptez les défauts des gens et soyez cléments envers eux. Soyez patients et pudiques. Diffusez la bonne parole et appliquez son contenu. Soyez respectueux de la vie intime des gens et soyez constants dans vos relations. Souhaitez du bien à tout le monde et respectez vos engagements. Soyez actifs et déterminés. Soyez charitables et choisissez vos compagnons. Ne soyez jamais jaloux et rancuniers. Mettez vous sur le droit chemin et ne le deviez jamais...» ( L'assemblée de la félicité, Serigne Aladji Mbacke, traduction M.Moustapha Diop )
Fatou histoire bi doyna war trop wadji na halat Papam nah litah mou dougueul ko alhourane pour mou bah euleuk le djerigneko famou néke famou teude hamna lép té holom néhoul deukou nari bahoul day yake nit na délou gambie fassé djabar dji répentirou toub Yalla beurina yeureumandé mou hamni destin le Yalla bahna nah comme migui rethou rék beuguena bah
SALAM may ALLAH SUBHANA WHO WA TALLAH take you out of that situation AMEEN YA ALLAH you can come back to the Gambia and set down and just give her fish money and pray 🙏 to ALLAH SUBHANA WHO WA TALLAH to help you get out of that situation
QUAND GARDER LE SILENCE ? 1. Gardez le silence - sous le coup de la colère. 2. Gardez le silence - quand vous ne possédez pas tous les faits. 3. Gardez le silence - quand vous n'avez pas vérifié l'histoire. 4. Gardez le silence - si vos mots peuvent offenser une personne plus faible. 5. Gardez le silence - quand il est temps d'écouter. 6. Gardez le silence - quand vous êtes tenté de banaliser les choses sacrées. 7. Gardez le silence - quand vous êtes tenté de plaisanter sur le péché. 8. Gardez le silence - si vous seriez honteux de vos paroles plus tard. 9. Gardez le silence - si vos mots peuvent donner une mauvaise impression. 10. Gardez le silence - si la question ne vous concerne pas. 11. Gardez le silence - quand vous êtes tenté de mentir ouvertement. 12. Gardez le silence - si vos mots peuvent nuire à la réputation de quelqu'un d'autre. 13. Gardez le silence - si vos mots peuvent endommager une amitié. 14. Gardez le silence - quand vous vous sentez critique. 15. Gardez le silence - si vous ne pouvez pas le dire sans crier. 16. Gardez le silence - si vos mots peuvent être un mauvais reflet de vos amis et de votre famille. 17. Gardez le silence - si vous pourriez avoir à regretter vos paroles plus tard. 18. Gardez le silence - si vous l'avez déjà dit plus d'une fois. 19. Gardez le silence - quand vous êtes tenté de flatter une personne méchante. 20. Gardez le silence - quand vous êtes censé travailler à la place. "CELUI QUI GARDE SA BOUCHE ET SA LANGUE ÉVITE BIEN DES TOURMENTS Grand Père Cherif Aidara Malainine Maloum
Oh massa yalla nala sounou borom tèguile natou bi wantè biss niki tay lo dèfati yako tay daguaye ragal yalla wala gua ragal sa yaye wawe yaye tane arretel li guaye def djalobi dou guiss gua meuneutouko bayi donc sa sokhna aussi doko bayi ba takh na deloule gambi out fa sokhna bo begue nak gua tanal ko sa bop ko beugue nak mou begue la gua fassè sa sokhna bi nek gambi ndakh djiguen bouye seye di djalo day fatt borom keureum boul fate toup yalla sounou borom kou bari yeureumandela manla xippillxoles je suis sur UA-cam
Imame retourne en Gambie arrivé la bas tu prend une deuxième femme sinon , c'est Allah soubhanawatalalah qui sait.. comment tu finira. Que Ya Rabbi te protège ❤
Lidé moy niak fayda. Yangui yakh sa adouna ak sa alahira ci louko diaroul. Gor dou daw responsabilité. Solution bi moy nga gnibi sén keur GAMBIE. Boudé sa diabar mongui fofou tok, nga fasséko. Souy dof doflou, nga menacéko boléko ak papam. Sa yaye boula méré grawoul. Nanga nakhaneté ak mome. Yague yague dina bayi. Djiguene motakh nga beugua yakh sa adouna. Yangui wéré dé diambar. Déloul sén keur nga facéko boudé mongui fofou dila khar. Nga continué géré. Sa yaye bou méré tamite dina bayi.
Na kat ndayi yaay dji feulé, yakk sèn doundou dom yi rek lagnfi nékkè, té bo wakhè niou nanla damay dogo ak yaw, nga niko yaw mima doour so meunè dogo ak man, domako dakk nagn dogo ba sa saram nday tépikou ndakh kokou dou yaay matoul yaay, yaay deug dou dogo ak kènn. Goor sou majeurè dafa wara yilif bopam si lepp, dou kènn moko wara wakh défal lii bayil lii wala takal kii, goor day deugueur bopp di dieul ay responsabilitèm, wayé mélni goor djiguèn rek nékk khalé ba nékk magoum dieum sa yaay dila wakh loy déf, nii rek lay moudiè niaf ndèm rek
Metina mais boumou yakh adouname ndakh djiguene yayame bougoul mou fasé diabaredji na délou sene keur tak bénéne diabare na khôl si papam mouko dougalone alkhourane pour nek imame
Sama yaye douma deflo mouk lou nekhoul yallah. Na toupe, fasser sa femme, reprendre son travail. Sa mere ne vie pas avec la vipere et sil continue, il va finir avec le sida ou bakar you bari. Parent dafaye diapaler domame. Bou yaguer kene dina raye lautre ou maraboutage ou bome youniou diepi dioudoufa. Kil divorce et nekhal yayam. Elle va se facher pour un petit tps. Bonne chance frere. C le destin.
Ok c est triste, mais il a mal choisi ; qu'il retourne en Gambie, pardonne sa femme,reprend ses affaires et demande pardon à sa mère. Il doit se repentir,il n est jamais tard pour bien faire. Doro Sidy Ba ( beydi)
Histoire très intéressante 😮
Sa yaye dou niit mome moye seuy wala yaye seuy fassel sa diabar na sa yaye doggo yawe chantage émotionnel yi la souniouye yayii wara bayi quitte ta femme waye !!
Ton oncle est gentil avec toi, explique-lui tous les problèmes pour lesquels tu es allé en Mauritanie
Serigne Touba a dit :
« Acceptez les défauts des gens et soyez cléments envers eux. Soyez patients et pudiques. Diffusez la bonne parole et appliquez son contenu. Soyez respectueux de la vie intime des gens et soyez constants dans vos relations. Souhaitez du bien à tout le monde et respectez vos engagements. Soyez actifs et déterminés. Soyez charitables et choisissez vos compagnons. Ne soyez jamais jaloux et rancuniers. Mettez vous sur le droit chemin et ne le deviez jamais...»
( L'assemblée de la félicité, Serigne Aladji Mbacke, traduction M.Moustapha Diop )
ماشاء الله
Massa demal Gambie nga tak bene diabar
Fatou histoire bi doyna war trop wadji na halat Papam nah litah mou dougueul ko alhourane pour mou bah euleuk le djerigneko famou néke famou teude hamna lép té holom néhoul deukou nari bahoul day yake nit na délou gambie fassé djabar dji répentirou toub Yalla beurina yeureumandé mou hamni destin le Yalla bahna nah comme migui rethou rék beuguena bah
SALAM may ALLAH SUBHANA WHO WA TALLAH take you out of that situation AMEEN YA ALLAH you can come back to the Gambia and set down and just give her fish money and pray 🙏 to ALLAH SUBHANA WHO WA TALLAH to help you get out of that situation
QUAND GARDER LE SILENCE ?
1. Gardez le silence - sous le coup de la colère.
2. Gardez le silence - quand vous ne possédez pas tous les faits.
3. Gardez le silence - quand vous n'avez pas vérifié l'histoire.
4. Gardez le silence - si vos mots peuvent offenser une personne plus faible.
5. Gardez le silence - quand il est temps d'écouter.
6. Gardez le silence - quand vous êtes tenté de banaliser les choses sacrées.
7. Gardez le silence - quand vous êtes tenté de plaisanter sur le péché.
8. Gardez le silence - si vous seriez honteux de vos paroles plus tard.
9. Gardez le silence - si vos mots peuvent donner une mauvaise impression.
10. Gardez le silence - si la question ne vous concerne pas.
11. Gardez le silence - quand vous êtes tenté de mentir ouvertement.
12. Gardez le silence - si vos mots peuvent nuire à la réputation de quelqu'un d'autre.
13. Gardez le silence - si vos mots peuvent endommager une amitié.
14. Gardez le silence - quand vous vous sentez critique.
15. Gardez le silence - si vous ne pouvez pas le dire sans crier.
16. Gardez le silence - si vos mots peuvent être un mauvais reflet de vos amis et de votre famille.
17. Gardez le silence - si vous pourriez avoir à regretter vos paroles plus tard.
18. Gardez le silence - si vous l'avez déjà dit plus d'une fois.
19. Gardez le silence - quand vous êtes tenté de flatter une personne méchante.
20. Gardez le silence - quand vous êtes censé travailler à la place.
"CELUI QUI GARDE SA BOUCHE ET SA LANGUE ÉVITE BIEN DES TOURMENTS
Grand Père
Cherif Aidara Malainine Maloum
Macallaha macallaha macallaha macallaha ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci ❤❤
Diambarr dèlloule Gambia gatak nìarèlle dabaatall tè tèhè sa liguèye
Oh massa yalla nala sounou borom tèguile natou bi wantè biss niki tay lo dèfati yako tay daguaye ragal yalla wala gua ragal sa yaye wawe yaye tane arretel li guaye def djalobi dou guiss gua meuneutouko bayi donc sa sokhna aussi doko bayi ba takh na deloule gambi out fa sokhna bo begue nak gua tanal ko sa bop ko beugue nak mou begue la gua fassè sa sokhna bi nek gambi ndakh djiguen bouye seye di djalo day fatt borom keureum boul fate toup yalla sounou borom kou bari yeureumandela manla xippillxoles je suis sur UA-cam
Ziare nala sokhna fatou
Retourner avec sa femme est mieux que ce qu'il vit .il n'a qu'à la pardonner
Madame Nétali😂😂😂
Salam waleykum ma mbokou mieux veut que tu retournes en gambia il marie une autre femme pour avoir un espirit tranquil
Mon frère, je te conseille de retourner en Gambie, c'est mieux pour toi. Tu dois y aller pour parler à ton oncle
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Retourner en Gambie et prend ses responsabilités
Déloul Gambie gua tak béne diabar gua bayi sa amô bi s'y bire keurgui
nétali rek lay def
Very sad
Imame retourne en Gambie arrivé la bas tu prend une deuxième femme sinon , c'est Allah soubhanawatalalah qui sait.. comment tu finira. Que Ya Rabbi te protège ❤
😳😳😳😳😳😳😳😳😳
Wadji défoul loudoul niakeu fayda, bayi sa héritage bo khamni sa Papa molako bayil ndakh djiguene chiim
N'a découvert gambi e wakhtane nidiay dji sou diarée mou fassé diabar sa mou continué business sam
Dianguena Al couran na ndeuedeule yaye AK diabardie niebiwate si boutique gam
Na Gnie Bi Si Watie Diabar Dji
Thiey famme
Khana defa doon tricher classe ! Khel neekhul, ngay pas classe supérieure.
Démale Gambie mo guene❤
Kon na baal jabarr dji.
Bonne vision de son Pere...
quel scenario
Lidé moy niak fayda. Yangui yakh sa adouna ak sa alahira ci louko diaroul. Gor dou daw responsabilité.
Solution bi moy nga gnibi sén keur GAMBIE. Boudé sa diabar mongui fofou tok, nga fasséko. Souy dof doflou, nga menacéko boléko ak papam. Sa yaye boula méré grawoul. Nanga nakhaneté ak mome. Yague yague dina bayi. Djiguene motakh nga beugua yakh sa adouna. Yangui wéré dé diambar. Déloul sén keur nga facéko boudé mongui fofou dila khar. Nga continué géré. Sa yaye bou méré tamite dina bayi.
Na kat ndayi yaay dji feulé, yakk sèn doundou dom yi rek lagnfi nékkè, té bo wakhè niou nanla damay dogo ak yaw, nga niko yaw mima doour so meunè dogo ak man, domako dakk nagn dogo ba sa saram nday tépikou ndakh kokou dou yaay matoul yaay, yaay deug dou dogo ak kènn. Goor sou majeurè dafa wara yilif bopam si lepp, dou kènn moko wara wakh défal lii bayil lii wala takal kii, goor day deugueur bopp di dieul ay responsabilitèm, wayé mélni goor djiguèn rek nékk khalé ba nékk magoum dieum sa yaay dila wakh loy déf, nii rek lay moudiè niaf ndèm rek
Balthazar 😅😅😅
Kana sa café bi d'où séde
Nadem ligueyi gordafa wara deugeur
Il devrait libérer sa femme et s occuper de ses affaires car vivre avec une femme dont tu n as confiance ne vaut la peine
❤ jajaja
Wadji waroul wona dém na délou chéré boutiques ba témoi djéma faté dafarat doungam témou khamni mome goore la
Wadji defa trahir papam moko topou
😅
Ay Coûp d'État etc ay dakk yoyou yeupp diaroulwone wakh ndakh meuneu créé des problèmes
DIGUA diougué AK DIGUA dem fou tané
Fasse ko
Défal gami mo gane
Metina mais boumou yakh adouname ndakh djiguene yayame bougoul mou fasé diabaredji na délou sene keur tak bénéne diabare na khôl si papam mouko dougalone alkhourane pour nek imame
Sama yaye douma deflo mouk lou nekhoul yallah. Na toupe, fasser sa femme, reprendre son travail. Sa mere ne vie pas avec la vipere et sil continue, il va finir avec le sida ou bakar you bari. Parent dafaye diapaler domame. Bou yaguer kene dina raye lautre ou maraboutage ou bome youniou diepi dioudoufa. Kil divorce et nekhal yayam. Elle va se facher pour un petit tps. Bonne chance frere. C le destin.
Rentre chez toi et pardon ta femme vue
Bayiléen fénn wa nétali