Machalah le seul chanteur religieux bo kham ni il est à l’aise dans tous les tarikha continue comme ça mon frère tu n’auras pas uniquement un public tidjan ou un public mourid non plus niassèn mais l’amour de tous les sénégalais yalla n’a yalla dèf diam ❤️🙏🏼🥰
Merci frère pour les éclaircissements dama ko dèf rék pour nièp guiss sèn bop si j’avais mis tidjan uniquement y’aura forcément des niassén qui vont pas se sentir je suis mieux placé pour savoir que les niassén sont des tidjan parce je suis niassèn merci bcp 🙏🏼🥰
Billay j’ai des frissons en t’écoutant frère tu est une fierté et une référence pour toutes les autres chanteurs notre religion est faite ainsi yalla nala yalla gueuneu wérale batte ji teh tahawou la si baké baye ak bayame barké cheikh ibrahima fall kossy 😭😭❤️❤️🙏🙏🙏💪💪
Oooh machallah li moy senegal li moy dioulit deugu aussi Aboubacry Samb binga weuyé serigne babacar sy lala sopou ba téy nga weuyeul niou baye niass mon bien aimé yalla nala yalla yokou banga yeuk ko thi zaahir ak thi baatine ya raby ya allah 🙏🙏🙏🙏🙏
Moi je suis mouride mais yaye milieurs son bi nékh na trop❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😍je suis vraiment contente aujourd'hui je ne vais continuer dans un autre rek 😍😍😍😍😍❤❤❤
Khol yi seedd n'a trop yalna yalna yalla yeketi sama yaye talibé Mame Abdou la daye dem tivawoun may dem madina Baye t momay may pass Kone nga khamni Sénégal niep bene laniou bouniou ko nekhaleh rék mou nekhe ndakh niou bok notre Prophète bien aimé nio bok souniou diouli diourom yi Kone n'a nekhe rek yalna yallah defal niep diam t boleh khol yi done bene
Moi je suis talibe bilahi mais tu m'a fait pleurer de deux côtés walahi beuss nikitey sope nala tei yalla tax walahi yalla wereul batbi si batkei baye minga weuy li non li nexna way hoooo sa prouve que xol ngako bindei c'est pourquoi si xolyi rek lay delou mashala
Machalah; vRaiment rien n'a dire Vous Cartonnez💯❤ Je ne suis ni Mouride, Ni Tidiane, ni Layéne mais plutot un amoureux de Cette Religion qui est rien d'autre que L'islam 🙏🥺... ALHAMDULILAH
Allahou akabar je m'abonne je commente je partage par amour pour Baye Niasse RTA yalla nala yalla fey si barké Baye Niass yalla nga defat ko ay ate you beuri si kanam 🤲 Marhabane bikoum serign bi 🙏
Machallah grand Yalla na baate bi gueuneu wér bidiahi Naby Moustapha barki Borome Touba. De la part de ton petit frère Baye Mamadou TRAORÉ petit frère de Moussa TRAORÉ
Wa man douniou wax si man sons bi 11h ba 13h53 mom rek lay sétane😍😍. Mourite la mais dama beug tarikha yeup té Aboubacary mom nieup lafi nékal. Sama chanteur préféré, yalna Yalla wéral bat barki Mame Salihou 🙏🙏
Ohhh Macha Allah Aboubacar je suis layénne mon mari talibé cheikh yalla na yalla bour wéreul baye bi AK thieur yi li ngay déff rafét na trop té nékh❤❤❤
comment ca ce fait que , son aboubakry bi nékk le meilleur son ''baye niass'' thie yima dégglou. Bilahi yéna ngui thiakhane, bou ndieukk son yi dadane dieuzbu jaam yi mais légui dara que du fun ( wané ay mbakhana you rafet, ay krouss you cher...) sokhla wugnu lolou. niata nitt nio tarbiyou ndakh sonwou wa bidew bu bess ba. Dou nieupp nakk. BIG UP ABOUBAKRY CONTANE NAGN TROP, JEUREUJEUFF
Assalamou alaykoum mboki djioulite ziarnalen bou bah li Moy wane nit amoul loudoul borom bi ak sang bi mo tah dîné dji amoul khiadia s'en diereudieuf ti mon frère yokoute bègua yeuk ko inchallah 🙏🙏 bcp YananiouaYalla defal diam fotolou
😭😭😭😭😭😭ohhhhh god machallah nexxxxnaaa beu fou nex yem yallah n'a yallah guena weral bate bi inshallah Allah yokoula si barké yonente bi Saws barké cheikhou tidianii Rad barké baye ak bayam
À tout ceux et celle qui lisent ce commentaire qu'Allah vous guide sur le droits chemin vous pardonner vos pêches si barke baye niasse🙏❤
Allahoumma Amine
Amine yarabi
❤
Allahumma amiin 🥰🥰🥰🥰🥰🥰
mashallah 🥰 alhamdoulillah 🙏on a la meilleure des religions le meilleur des prophètes(psl)et Alkhouranoul karim ♥️que la paix règne dans le monde🤲
Machalah yalna yala wereul batterie bi waybi nexna
Machalah le seul chanteur religieux bo kham ni il est à l’aise dans tous les tarikha continue comme ça mon frère tu n’auras pas uniquement un public tidjan ou un public mourid non plus niassèn mais l’amour de tous les sénégalais yalla n’a yalla dèf diam ❤️🙏🏼🥰
Mon frère ya pas de tariqa niassénne. On n'est des tidiane
Merci frère pour les éclaircissements dama ko dèf rék pour nièp guiss sèn bop si j’avais mis tidjan uniquement y’aura forcément des niassén qui vont pas se sentir je suis mieux placé pour savoir que les niassén sont des tidjan parce je suis niassèn merci bcp 🙏🏼🥰
@@mouhamedrassouldiagne8739 Tous les appelés "Niassène" savent bel et bien qu'ils sont des Tijaan
Louy niassén lépp tariha tidian kassé la 🧏♂️🙏🙏
Amine
Je suis mouride mais j'aime les talibés Cheikh ♥️🙏
Serigne Babacar Sy le plus éloquent le plus historique de tous les marabouts du Sénégal
ya bakh sokhna awa linga wakh si sam goor gui yallana ci yalla fayy yiw kénn dou mome
On t’aime plus Awa❤️❤️❤️
mq
Suis mouride mais barké cheikhoul Khadim baye barhama nimako beugué dafa diégui dayo. Diereudieufé baye😭😭😭
Bou bakh beugue nieume maachaala
Yaa baakh
lii moy senegal sama xol sedna je suis khadre talibè cheikhna cheikh Saadbouh mè dama beugg mame baye surtou baba Lamine damako beugg ❤
Machallah sa khol mon raféte té lepp bénala
Toute la communauté Niassene te remercie pour votre geste merci infiniment... Alhamdoulillah 😍 niou wadial gamou Médina Baye ✔️❤️
Toute la communauté de la faydatou tidiania vous remercie pour ce beau son de wadial gamou
A ta place j'aurais dis tous les musulmans. Par ce que à vrai dire ce touche la sensibilité de toutes personnes musulmans. Me concernant j'adore
Machalah rafetna trop
Wllh 😢😢
Casé amoul lanéne
Mashallah, yalna yalla wéreul batt bi si barkè Mawlana Cheikh Ibrahima Niass (RTA)🙏🙏
Billay j’ai des frissons en t’écoutant frère tu est une fierté et une référence pour toutes les autres chanteurs notre religion est faite ainsi yalla nala yalla gueuneu wérale batte ji teh tahawou la si baké baye ak bayame barké cheikh ibrahima fall kossy 😭😭❤️❤️🙏🙏🙏💪💪
Amine waye
J’en ai des frissons dieureudieufé Baye Niass❤👌🏾🤲🏾
Aboubakry goudeul fane 🥹🫶🏾
Je me suis abonné et je conseille à tous les talibés cheikh ( Baye Niass ou Eladji Malick) de faire pareil
Kokoy Baye borom centaines de millions de talibé dans le monde ❤️❤️❤️
Oooh machallah li moy senegal li moy dioulit deugu aussi Aboubacry Samb binga weuyé serigne babacar sy lala sopou ba téy nga weuyeul niou baye niass mon bien aimé yalla nala yalla yokou banga yeuk ko thi zaahir ak thi baatine ya raby ya allah 🙏🙏🙏🙏🙏
Je suis fière d'être talibé Baye Niasse ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ baye moyy souniou yité ❤❤❤❤❤❤❤
un très belle chanson pour un très beau créature (Barham)par un très bon disciple Tidiane Machalla li nékhna way frère 🫶🏾
Je suis mouride mais j'adore les niassenes très belle chanson yalna yalla weral voix bi
Amine yarabi 🙏❤
Yaa baakh
Degeu degeu kilifa ga yalna minka barham Niass borom médina fayla yarabi inchallah tawfekh inchallah
Mashallahh💕
Dieureudieufe baye ❤️
Baye mo beug yonente bi (saw)❤️😭
Moi je suis mouride mais yaye milieurs son bi nékh na trop❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😍je suis vraiment contente aujourd'hui je ne vais continuer dans un autre rek 😍😍😍😍😍❤❤❤
Depuis ce matin j’écoute cette chanson j’arrive pas à la quitter 😩❤️
De même ke moi
Amna morom alors et pourtant suis pas niaséne mai jadore le son
Je suis mouride mais billahi wallahi dama beugue baye niass trop sax bly et je veux devenire talibè baye bly ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂🇬🇲🇬🇲🙏🙏🙏🙏🙏🙏🏿🙏🏿🙏🏿🇬🇲🇬🇲🇬🇲😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Baye la solution ❤machallah yallah na yallah barkél lepp inchallah
Son bi je l'écoute chaque jour merci infiniment
Khol yi seedd n'a trop yalna yalna yalla yeketi sama yaye talibé Mame Abdou la daye dem tivawoun may dem madina Baye t momay may pass Kone nga khamni Sénégal niep bene laniou bouniou ko nekhaleh rék mou nekhe ndakh niou bok notre Prophète bien aimé nio bok souniou diouli diourom yi Kone n'a nekhe rek yalna yallah defal niep diam t boleh khol yi done bene
Niass Coumba Abdallah mawlana cheikh Ibrahima yalla nagnou kooo yalla feyal tagnou siii barkemmmm Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Moi je suis talibe bilahi mais tu m'a fait pleurer de deux côtés walahi beuss nikitey sope nala tei yalla tax walahi yalla wereul batbi si batkei baye minga weuy li non li nexna way hoooo sa prouve que xol ngako bindei c'est pourquoi si xolyi rek lay delou mashala
Macha Allah
Mawlana Baye Dieuredieufti Niassssssssssssssssss ❤️💯
Je suis mouride wayé da ma begue baye Niass❤
Ndeyssane polyvalence 🥰 way na Mame Saliou Mbacké Lou nekh machallah nieupa Yam fa yallah amoul khadialo dé
Barkei serigne touba li meune nama dioylo ma beug baye ❤😢
beugeu mokhamed Rassoul Al nabi ❤❤
Machallah nañiou defal jaam thii barké Baye Niass ❤
Machalah ❤️❤️❤️❤️ yalla nala yalla Faye AK baye SIII barké seydina mouhamed 🙏🙏🙏🙏🥰💯😍😍😍
❤️❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾🕋👍
Machalah; vRaiment rien n'a dire Vous Cartonnez💯❤ Je ne suis ni Mouride, Ni Tidiane, ni Layéne mais plutot un amoureux de Cette Religion qui est rien d'autre que L'islam 🙏🥺... ALHAMDULILAH
Maasa-Allah very nice song
We love Sheikh Islam Alhagie Ebrima Nyass❤❤❤💯
La fierté de la tarikha tidiane ❤️😭✨🫶🏿
Walahi
Vous avez l Oscar de la fayda loumala beug nommé kheip ko walahi maaaachala !yalna Baye Niass eukeuti ci kanamou adouna bi yeup !!!!!
Talibé Cheikh foumou Khole yalla Lafay guiss,ragné wouniou mouride ak TIDIANE, Macha allah 👌
Dieuredieuf Baye Niass international machalah aboubakry sadikh contaan nagnou trop 🥰🥰😍🤩
Trop trop contann naniou bilaye yalla nala yalla faye b baye yarabi
Je suit mouride mes cette chanson me vas droite au coeur machallah
Allah baye niass rek amoul leneen ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Allahou akabar je m'abonne je commente je partage par amour pour Baye Niasse RTA yalla nala yalla fey si barké Baye Niass yalla nga defat ko ay ate you beuri si kanam 🤲
Marhabane bikoum serign bi 🙏
Machallah fier d'être talibe cheikh ba faw
Macha allah mane mom alfoussalatiii bi momay rayyy ❤yalla na yalla fay ya rabiii 🤲
Machallah grand Yalla na baate bi gueuneu wér bidiahi Naby Moustapha barki Borome Touba. De la part de ton petit frère Baye Mamadou TRAORÉ petit frère de Moussa TRAORÉ
Machallah Machallah Machallah Alhamdoulilah Alhamdoulilah Alhamdoulilah santé yallah bou wer yallah n'a yallah yokou lerr rou denbi Bi barké Maowlana SWS amine
Sa khol❤ mo nekhh banga way Cheikh Al Islam
Machallah 🥰 alkhamdou Lillah
Yaw tékhé nga ba faw
Kepp kou beug Baye tékhé nga
Masha’allah neikhena trop kontane nagne 🥹🥳🥰yalna Baye guereum🙏🏾❤️
Yalla nalla yalla fay Barki baye Niass yalla na yalla gueuneu wéreul bat bi
Son bou nékh Sakho chaque jour je l'écoute plus de 5fois. Yalna yalla gueuneu weral batt bi
Lii nekhna Ma Sha الله
Dieuredieufi Baye🙏❤️
❤❤❤❤
Gnoune mouride yi ak yaye fall yi danou nagnou lérr si thiante gui machallah diarama baye niass coumba abdalah
Machla yalla naleu yalla sameu si barki baye niass🙏🏼
je suis khadre mais li néxx na trop way yalna diamb yague si barké seydina mouhamed
Wa man douniou wax si man sons bi 11h ba 13h53 mom rek lay sétane😍😍. Mourite la mais dama beug tarikha yeup té Aboubacary mom nieup lafi nékal. Sama chanteur préféré, yalna Yalla wéral bat barki Mame Salihou 🙏🙏
Wawaw Allah Baye thia kaww machala machala !!!!!
Machala ❤️❤️❤️. dieuredieufe Baye... Dieuredieufe à toi
Yalah na yalah samb si barker baye NIASS
Macha Allah bonne continuation ndam rek inchallah 🇸🇳🇲🇷🤩🇸🇳
Ohhh Macha Allah Aboubacar je suis layénne mon mari talibé cheikh yalla na yalla bour wéreul baye bi AK thieur yi li ngay déff rafét na trop té nékh❤❤❤
Merci beaucoup ❣️❣️❣️❣️ machallah amna solo 🙏💘💟💟
OH!😭😭😭 Bilahi Walahi sama yaram dawna Aboubacry Samb bègue nagnou liigua deff rafeet Na kontaan Nagnou Yallah Nala Yallah faay sa xol ci Seydi Aboubacar Sy RTA 🙏🏿 lii bakk Cheikh'Al Islam Maolana El Hadji Ibrahima Niasse RTA 🙏🏿 kontaan Nagnou
Quand j ai écouté cette son çà me rappel mn grand frère😢😢😢😢😢 il l'es décédé prières pour lui😭🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Qu Allah ai pitié de son âme 🙏🙏🙏
Yalla na aldiana firdawsi done deukouwayam🙏🏿🙏🏿
Waaaa yaine liii Nex na dh
Bilahi deug la baye Ame wayou baye Ousmane la dieureudieufé baye Niass 🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah Aboubakry Samb talibé Cheikh bou noble bi l'intélectuelou Serigne Babacar sy yalnala yalla takhawou. les jeunes sont fier de tw
On est fière de vous tonton Abou😊🥰
Machalla way contane nanio deh yallna yalla fay yiw 🥺❤
comment ca ce fait que , son aboubakry bi nékk le meilleur son ''baye niass'' thie yima dégglou. Bilahi yéna ngui thiakhane, bou ndieukk son yi dadane dieuzbu jaam yi mais légui dara que du fun ( wané ay mbakhana you rafet, ay krouss you cher...) sokhla wugnu lolou. niata nitt nio tarbiyou ndakh sonwou wa bidew bu bess ba. Dou nieupp nakk. BIG UP ABOUBAKRY CONTANE NAGN TROP, JEUREUJEUFF
Ohh g des frissons,en tant k Talibé maolana cheikh al islam je swett k du mllr force à tw
Dieuredieuf Baye Niass ❤️🙏
Machalla frere que la bénédiction de mam baye t'accompagne 💖❤️💞
Meilleur son de l'année 🙏
La civilisation et la modernité dans les chants religieux.
Tu apportes incessamment une touche originale et personnelle dans ce que tu fais.
Bravo👌🏽
❤️❤️♥️♥️♥️♥️🥀💕Machalla Dieureudiefe baye niasse ❤️♥️li nek na waye Machalla ♥️
Assalamou alaykoum mboki djioulite ziarnalen bou bah li Moy wane nit amoul loudoul borom bi ak sang bi mo tah dîné dji amoul khiadia s'en diereudieuf ti mon frère yokoute bègua yeuk ko inchallah 🙏🙏 bcp YananiouaYalla defal diam fotolou
Tu va me tuè avec cette son dieureudieufè Baye
Par heure lay deglou son bi ❤❤❤❤❤
Le meilleur clip sur Baye Niass actuellement
Machallah serigne bi wallahi contane nanie ❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla Li Moy Sénégal 🥰❤️😍
Dieuredieuf chiekh bi yalna yalla barkel say yeungou si barke mawlana chiekhal islam sama leep ❤❤❤❤❤❤❤ elhadji chéri diama😂
J’ai trop aimé❤walay barki baye niass 👌❤️
Moi je suis Mouride mais depuis ma télécharger son bi mom rek lay déglou ndakh nékh bilahi . Machallah diam ci yaw ❤❤❤❤
MashaAllah lafthiat khôl sede na dieureudieuf gneup contane MashaAllah Yalla nala Yalla fayy ❤️🙏
wow wow wow Allahou Akbar MAACHALLAH 😍😍😍😍😍❤️❤️❤️❤️❤️
Je suis fière d'être talibé cheikh ❤❤❤❤❤❤machalla Aboubakry felicitation yalla boula thiat dougue ooooh sama khol seed na thi liiiiii❤❤❤❤
Yalla nalla samou arr leu si barké bromm Médina Taïba ak kossy
Alhamdoulilah dieureudieufé Baye Niass machaallah nex n'a trop yalna Allah weral bat bi
Machallah talibe serigne fallou bou beug mame baye niasse
T'as encore frappé très fort frère bonne continuation... Le meilleur reste à venir 😎🙏🏽
😭😭😭😭😭😭ohhhhh god machallah nexxxxnaaa beu fou nex yem yallah n'a yallah guena weral bate bi inshallah Allah yokoula si barké yonente bi Saws barké cheikhou tidianii Rad barké baye ak bayam
Machalla c'est c'est magnifique yalna yalla dolli tawfékh si barké Baye Niass
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤ machala nekhna na trop
Machallah toujours égale à toi mem 😍📿🙏🏾yalla na borom bi werall Bate bi si barke Nabill Moustapha ♥️
Machalla yalla nalla yala defale diame khole yi sedena yalla n'a baye niass Faye💞💞
Mâchallah Yalna Baye fayla ❤️
Vraiment liiii nekh na trop yalla nala yalla défalll diamou si barkep serigne touba sama tourondo assurance bou woor bi
Machala son bi nekhna.
Khamna boma wayallon Serigne Saliou Mbacké ❤️❤️😭
MACHALLAH LEPP SI CHEIKHOUNA TIDJANI ❤️❤️❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Machalah😍 rafét na nékhna yalna yalla Faye la
Bilahi ndayssan chanson bi nékh na trop je suis mouride mais man ak baay lou yague la sama khol lako def❤❤❤