Sama kharitt ma beug ko mou nekh ma loll Baye Ada Top Yalla nala Yalla dolli ay lerr yokou sa fane man c'est la premiere fois may commentaire lepp yawla rek machallah ci kaw ci kanam beugeeeeeeee mame
Info réw mi, ma nasiiha léne béne mbirr, boléne di léralati bén interview titre bi nay done deug, bouléne di wahh lu amout, ( baye ada jeufoul dara sank ba légui da nék di wahh) bouléne jublou attiré nit pour lou amoutt, day tah euleug soléne ko défaté dounou taal ndah daniy jiap ni gros titre rék ngén di déff, mane personnellement bagn d"sabonnée na si web tv yu barri ndah reuyeul titre ex: senegal tv etc... , yakar na dinguéne si bayi xéll séne liguéy aussi rafet na lolou pour l'instemps , mais gros titre gnieuw gnieuw dara amouthi féne la tud, magui jégalou
Mangui ziar mane dafa ame koma envoyer xaliss ba parés madika woh doma diall bika appeler yi sonolen mo woyou manika mangui lay woh rek dialou monima dama diapo ma niake sama xaliss si nonou 100000fcfa

Thilo Ndiaye
Yalnalafi yalah yagale barkep seydina Mohamed psl.
khawma d, wa yé Djinné yi mom Allah(swt) mom séne borome.
Momar Diouf merci beaucoup
Momar Diouf hhhhhhhh
machalla Cheich ada c Babacar Diankha à medina Baye xam xam bi rafetna et tu la mérité
Un petit Talibé baye niass qui peut détruire des maisons de faux Marabouts qui sont cunnu comme des grands Marabouts.
machallah Cheikh baye
Il est très fort cet homme
Macalahhh
Dieure dieuti serigne baya adama machalla wakhe tanwi risena yalla na yalla goudele fanyi te yoke wergue si barkepe Seye dina mouhammate
Massa Allah wakh tan bi rafetna Bay ADA.
Baye Ada machallah
Macha allah yalla na yalla yok fanyi ak weur
Baye Ada mane demala beug rek tè YALLA takh YALLA nangfi yag tè wéer ak wéer lé YALLA mayko mboléme dioulites
machallah amna solo baye ada
Machaallah baye Ada yalla feyla
Info réw mi, ma nasiiha léne béne mbirr, boléne di léralati bén interview titre bi nay done deug, bouléne di wahh lu amout, ( baye ada jeufoul dara sank ba légui da nék di wahh) bouléne jublou attiré nit pour lou amoutt, day tah euleug soléne ko défaté dounou taal ndah daniy jiap ni gros titre rék ngén di déff, mane personnellement bagn d"sabonnée na si web tv yu barri ndah reuyeul titre ex: senegal tv etc... , yakar na dinguéne si bayi xéll séne liguéy aussi rafet na lolou pour l'instemps , mais gros titre gnieuw gnieuw dara amouthi féne la tud, magui jégalou
Jumaay Tuuba mane dé doundeu na lingay wakh ni motakh gros titre foumako guiss romb ko ndakh je sai k ay fèneu le
Baye ada top borom djiné yi rek lanu waxe dage rek
Machallah wakhtane bi amna solo
Mangui ziar mane dafa ame koma envoyer xaliss ba parés madika woh doma diall bika appeler yi sonolen mo woyou manika mangui lay woh rek dialou monima dama diapo ma niake sama xaliss si nonou 100000fcfa
borom bakh la
Walahil azeem sa kaadu ken manuko dindi
Machaallah
may god bless you
abaraka
ماشاء الله جميل
Koka doki khamnaka bobax