El Hadj N'Diaye - Ragajuma
Вставка
- Опубліковано 3 січ 2025
- ► Get the album / écoutez l’album : ► macase.lnk.to/...
Album "Xel" (2001) : Grand Prix de l'Académie Charles Cros Xel en 2001 et Choc du Monde de la Musique.
Suma yaye
Taguna lë
Bayi taguna lë
(bis)
Maman
Je te demande la permission
Papa je te demande la permission
(bis)
Ma ngi seti Aïda mi
Sumo xoll mom lë tanë
Je m’en vais voir Aïda
Car c’est elle que mon cœur a choisi
Suma yaye
Taguna lë
Bayi taguna lë
(bis)
Maman
Je te demande la permission
Papa je te demande la permission
(bis)
Ma ngi seti Aïda mi
Sumo xoll mom lë tanë
Je m’en vais voir Aïda
Car c’est elle que mon cœur a choisi
Deggë na nuy wax
Jiggënu urul
Aïnii
Fële ci aljana
(bis)
J’ai entendu parler
De ces déesses
Là-bas
Au paradis
(bis)
Waye man ragajuma
Aïda Camara ragajuma
Raga raga raga ragajuma
Aïda mignone ragajuma
Mais que tes yeux me fasse chavirer
Aïda Camara roule tes yeux
Roule, roule, roule, roule tes yeux
Aïda mignonne roule tes yeux
Tukil fa nga minn né
Tukil fa nga minn ne min
Dëkël fi nga woloo
Tukil fa nga minn ne min
Dëkël fi nga woloo
Voyage où tu veux
Voyage où bon te semble
Habite où ça te plait
Voyage où bon te semble
Habite où ça te plait
Waye man ragajuma
Aïda mignone ragajuma
Ragajuma
Aïda mignone ragajuma
Mais fais-moi chavirer
Aïda mignonne fais-moi chavirer
Roule tes yeux
Aïda Camara fais-moi chavirer
Damani so sane sëy bëtt
Ba muy xef di xippi
Suma xoll dey yengu
Di yengu di yengu, di yengu di yengu
Di yengu di yengu, di yengu di yengu
(bis)
Quand tu fais tourner tes yeux
Qui clignent furtivement
Mon cœur s’emballe
Tambourine, Tambourine
Tambourine, Tambourine
(bis)
Suma waye
Suma waye jee
Eh, mon ami
Toi mon ami
Suma waye
Suma waye jee
Man mi yow lay waxal
(bis)
Eh, mon ami
Toi mon ami
Attention à toi
(bis)
Ragajuma
Aïda mou rafet ragajuma
Eh waye raga raga raga ragajuma
Aïda Camara ragajuma
Fais-moi chavirer
Belle Aïda fais-moi chavirer
Mais fais-moi donc chavirer
Aïda Camara fais-moi donc chavirer
Waw raga raga raga ragajuma
Aïda mignone ragajuma
(bis)
Oui fais-moi chavirer
Aïda mignonne fais-moi donc chavirer
(bis)
Aïda mignone ragajuma
Aïda mignonne fais-moi donc chavirer