Ayy wayy beug nala sama bokou niénio bii beug pur lalay tégual ni mane damay kheuy souba ba ngone diot dila weur you tube doudal way ma cherie je t'aime fort yagui si chemin barki serigne saliou contente si yaw
Machallah éducation de base amna solo lol si nit kou am kilifeu am wérouwaay am kilifeu dou am yaay ak papa réck déh am kilifeu moy loy déf gua fékhé sa wadiour diokhé si accord ba validé souko défé dina barkél lolou motakh yaw maty mbaye à travers série bi lala beugué woon ndakh sa am foula mais bima sétané interview bii damala geuneu sop ndakh fonk sa ay wadiour niou bokk serigne touba té tenue traditionnelle yi guay mettre en valeur ndaw gni diko guiss lolou lou am solo leu donc Yagui si yoon bi continue donc sur cette lancé dina geuneu bakh inchallah yalna gua ndoundou 100 ans sans ordonnance ak koula ko yéné Amine merci beaucoup
Ma challah, tu as la tête sur les épaules, tu es responsable et très pertinente! Je suis agréablement surprise en regardant ton interview. Vaiment ko khamoul boulot ko jugé.Si kaw si kanam ma chérie. Yalla nala ya Allah dougueul si sey bou nekh té barkel. Courage et Bonne continuation.
I love 💕 her so much because dafa digne te’ aye thieurame dou. Fegne lolou moma gueuna nekh si mome Manchala 🥰💕🙏yalla nala yalla doli takhawou dafa yiw vraiment 😍❤️❤️❤️
Machallah ma cherie bone continuation Yawe sama mbokk thiawane mar ndianmek mar khassime ak Seynabou... Khaleye thiawane mar foumou nek tekki fa daraa sama mame lolou Laye wakhe
C'est un exemple pour les parents d'inciter les enfants à aimer l'école via leur passion. Danse-étude. Elle aurait pu allier les deux dommage. En tout cas c'est une tête bien faite et bien pleine. MAA SHAA ALLAH
Ay way diamy gueye sama xarite bi yague bakh yague nék yay fall gno bokonneu ecole lycee seydou nourou tall pikine gnou amé ecole gnou dakheu gnou gnou dem lycee dabakh pikine waye todjiii fa encor no wathié nagne pikine tally bou bess ba moin zeroooo😂😂😂😂
@@melaningoddess6671 ni ma todjé youtube bi nonou la todjié senegal daw nieuw france difi todjii legui sakh sama voisin toubab yi dagne ma khamé si youtube bi😂😂😂🤣🤣
begue nala gir serigne touba ko begue serigne touba bessuel pous bleu ❤❤❤❤❤❤
Beug nala bilay yalla nala yalla samb
Ayy wayy beug nala sama bokou niénio bii beug pur lalay tégual ni mane damay kheuy souba ba ngone diot dila weur you tube doudal way ma cherie je t'aime fort yagui si chemin barki serigne saliou contente si yaw
Machallah éducation de base amna solo lol si nit kou am kilifeu am wérouwaay am kilifeu dou am yaay ak papa réck déh am kilifeu moy loy déf gua fékhé sa wadiour diokhé si accord ba validé souko défé dina barkél lolou motakh yaw maty mbaye à travers série bi lala beugué woon ndakh sa am foula mais bima sétané interview bii damala geuneu sop ndakh fonk sa ay wadiour niou bokk serigne touba té tenue traditionnelle yi guay mettre en valeur ndaw gni diko guiss lolou lou am solo leu donc Yagui si yoon bi continue donc sur cette lancé dina geuneu bakh inchallah yalna gua ndoundou 100 ans sans ordonnance ak koula ko yéné Amine merci beaucoup
Machalla Pt soeur nii rek nga meune mell seu lèguey rafatneu pantaire noir borom ndaye bou leguiy ndam rek yalla nalla Serigne touba takhawou 💋😘😘😘
Machala Yalla n'a Yalla motali si BARKI borome FAYDOU BI beug nala way 💞💞💞
Ma challah, tu as la tête sur les épaules, tu es responsable et très pertinente! Je suis agréablement surprise en regardant ton interview. Vaiment ko khamoul boulot ko jugé.Si kaw si kanam ma chérie. Yalla nala ya Allah dougueul si sey bou nekh té barkel. Courage et Bonne continuation.
I love 💕 her so much because dafa digne te’ aye thieurame dou. Fegne lolou moma gueuna nekh si mome Manchala 🥰💕🙏yalla nala yalla doli takhawou dafa yiw vraiment 😍❤️❤️❤️
Août 2021
Motaxit sagal neu ay wadiouram dee
Le jour de son mariage labannnn bi amna solo fierté
Diamy tu es différent des autres danseuse machalah. Si tout le monde résonner comme toi le Sénégal serait en n'avance.
Machalla waay gueune nguamay nexx diami dagua deigue waxx xamm liguay waxx nekk yaye fall bou yiiwww tarkallah
Machallah ma cherie bone continuation Yawe sama mbokk thiawane mar ndianmek mar khassime ak Seynabou... Khaleye thiawane mar foumou nek tekki fa daraa sama mame lolou Laye wakhe
machallah touf touf waay sama mak dji laf thiat Borom xolou diamand bi thia kaw thia kanam inchallah liguéyou ndaye aniou doom nimbeulou souniou borom ba dernière minute dara xewoul maty mbaye Guay vue niii lane
Wa kidou babel
Sidy Gueye madiyana si si c babel rakou diamy Gueye alias dada maty mbaye
Machallah jumelle bonne continuation yaye Fall nga télè takhoul nga changè sa leep pikine la 💪❤️❤️
Elle a la tête sur les épaules! MashAllah! Bonne continuation! 😍
Bne continuation j t'adore 😘😘
Elle est vraiment forte.
Dila nianal gouddou fann akk wërr.
Bonne continuation.
Machallah diami vraiment nite kou bakh té kham niguaye wakhé baparé kham adouna yalla na sa diam yague
C'est un exemple pour les parents d'inciter les enfants à aimer l'école via leur passion. Danse-étude. Elle aurait pu allier les deux dommage. En tout cas c'est une tête bien faite et bien pleine. MAA SHAA ALLAH
Machaalla tu me plaît beaucoup bon continuation ma cousine
Une noirceur d'ébène que j'apprécie beaucoup mashallah!Longue vie à toi puce❤
Machala ma copine tu exprime bien fara teugue thiawaane maar lou yagg deugg leu nimou Mel la Mel meusoul changé oyof wathié bopam kham ay nitou dembam
Coucou ma chérie
Say kadou rafet na ma shaa allah yalnala That sekhlou sameu fans bii
Machalah biillahi geuna nit dal niteim moy takh mouh don nit niteigua diami yalnala yalla diapalei
.machallah yow itam yalla na yalla fane ou goudou ak wuer ak diam ak khewuel amine
Mashallah tu as bien parler ❤❤❤ yalla nassa diame yague
Ah ma soeur machaalah goor goor loul rek dina bakh inchaalah😘
Bonjour diami je voudrais vraiment te connaître et vous parler aussi, du courage et ne pleure pas car tu m'as beaucoup fait pleurer aujourd'hui
Veuillez me faire signe svp merci et très bonne journée à vous diami
Je veux que vous me contacter diami
Machallahh tu es digne je t estime vraiment bne continuation
Ndeysane diami gueneuh nala beug nekh dinga beuguè cheikhoul khadime🙏 diadieuff
Ana niou beugue serigne touba
Maguini.Dieureudieuf Serigne Touba
Maguini.Dieureudieuf Serigne Touba
Non guene nala begue 👍Diami Gueye mane c Diama Gueye ❤
Machallah sa appranche nakh na niou Bari amnga Lou diafa yarounou talibé beug nala ndakh beug cheikhoul khadime Machallah
Je t'adore.yalnanou serigne touba tahawou😘🙏
MACHALLAH ENFANT BIEN PREPARE SPONSORISE PAR SES PARENNTS
Je t'adore diami machallah bonne continuation ❤❤
Vrémen c baeu jv jaim
Bonne continuation ma belle laf thiate rek
Très forte..celle la..bon courage..ne fais surtout pas de khessal..reste naturelle
Bonne continuation sister Diamy borom bakh nga fince rk Dina bakh yaye Fall bi
tu m'as fait pleuré en parlant de ton pere k la terre lui soit legere
Yalla nako yalla yeureum té kharéko Aldiana firdawsi 🤲🏼🤲🏼🤲🏼. Je t'apprécie énormément vu ton caractère, ton humanisme bravo à toi ❤👏🏽❤👏🏽❤👏🏽
Éhhh ki dou sama fans bi maan daal ki momay Danel 😂😘😍😍yallah nala yallah defal diam
Machalla sister yalnala yalla diapaler
Ay way diamy gueye sama xarite bi yague bakh yague nék yay fall gno bokonneu ecole lycee seydou nourou tall pikine gnou amé ecole gnou dakheu gnou gnou dem lycee dabakh pikine waye todjiii fa encor no wathié nagne pikine tally bou bess ba moin zeroooo😂😂😂😂
louka perez yaw kham nga kouner yangui fou nekk enhhhh 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@@melaningoddess6671 ni ma todjé youtube bi nonou la todjié senegal daw nieuw france difi todjii legui sakh sama voisin toubab yi dagne ma khamé si youtube bi😂😂😂🤣🤣
@@loukaperez9628 Louka mi nouniou koy def yen?😂😂😂😂
Beugue na ndakh serigne fallou mback Diami borom pikine❤❤
Waawaw gueune naala beug nakh gnègno bi❤❤😘
Machallah lima guena nekh si yaw moy dagua yiww law la thiatt
Deysanne diamie machallah amnaa geum geum. 🥰
Bilay mala beugue ndakh dagua geume sa boop bne continuation
Barké sama mame ki mako beug piiiir ana ngiko beug
Ñoguini 😂🙌🙌🙌
Nio ngi nii
Bonne continuation yalla na sa Diam yag
Mane mom sa lamégne bou saff bi momay rayy😂😂😂😂😂😂
Machallah ngapoutte
Diami tes mots m'ont touché vraiment j'ai mm pleurer bilahi machaala 😘
Man Dal dila deglou damay nekh macha allah
Bravo diamy tu as le bfm c est rare de voir des danseuse intellectuel
Maala beug et tu danse très bien.peace and love
Mashallah Matty mbaye may god protect you
Maty Mbaye bonne continuation on nest derriere tw
Machallah teint noire rkkk dara dakhouko🖤💋💋
Domiii balamaiisa bamou bary dolei mako aimé niiii
yowite maala aimer si lolou
Massala yalla nala yala diapale
Beugue nala te serigne touba rek takh
Bilay Ooo Machalla❤😭
Am one of your Fans maty
Machalla diami t a bien parler bonne continuation
Machallah sister
Soda Dembele
Soda Dembele
Soda Dembele
Mane deh so nekkei baaye Fall damalay sopp daah kiniou bokk😍
Ndeysaan kon Diamy bayinga fecc Vu que t'es mariée maintenant
👏🏽👏🏽👏🏽djamy Gueye de la part de Mme Niang
Sama domou baye mako beugue nii yalla na sa diam yagg té sunu borom sam
Fière de toi
Très pertinente machallah je t'adore
waw maty nope na la dé! je t'aime comme le dit ton frère mon père!
Que dieu te donne un bon mari
beugue nga gnou diara beugue guéweul yi et j'en suis fier
Machalah laf thiat
Black panther I like that 👌😁
Bilahii loo def mou def gueye
Je tm bcp diami Gueye Sama domou baye
Machalla machalla chérie je t'aime fort💕😘😘
Diamy Guéye mala beugue pire laf Thiat Amal diam je t’adoreuhh
Machala k dieu t protège
Machalah yalna sadiam yague
diamy Dale ndékété mbokou talibé la yalnala kou téd ki dimbali si barké kou Ted ki
T corect dans tous r serie et j'aime sa en toi
Je t'adore diami gueye mala beug pir.
Mane dal beugue nala Diami du courage
Machallah , elle réponse bien les questions ❤❤❤❤😊😊👄👄💋💋❤❤
On dit elle répond bien les question
@@vieuxbocarguisse9431 😁😁 l'essentiel c'est de comprendre rekk
@@vieuxbocarguisse9431 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😭😭😭😭😭
@@vieuxbocarguisse9431 elle répond bien aux questions, wayé amoul importance
@@yayoudior 😂😂😂😂😂 ray ngama
c bien de commencer ak radio you ndaw yi. bo prouver rek radio ak télé you makk yi recruter le
mane deh beugue nala tayy ndakh thiawane Diami beugue nala pur
Wahbi raféte trop machalla
Une vrai battante gueme boppam yarou bakh
Bon courage ma chérie moi perso je t’aime 😍
Mashala kadou Yi raféte na
Yalnala yalla same bangua yegali sa yenee
Je l’adore bonne continuation
Jtm trop Diamy Longue vie wayy
wi dada té une bonne exemple pr tout les danseuse ya jamais etait vulguaire tjr tu métai des hrand boubou QUand tu danse
Wa kidou rabbou pikine diami geuye ndanane koulou farine😂😂😂😂😂
Sopenala trop daga digne te Kham sa bop yalnala thiatt sekhlou ngua Am dieukeur dioubakh te atane la Am khewel ba bayi fecc
Amine waay
Machalah kou khol kham ni kou am talibe nga
Good luck to your baby 🌹🌹🌹❤️❤️❤️🇸🇳💯👁👏🏾🤝
Machallah elle est posée