Zef Fall : ça me rappelle des moments fous cette chanson comme pour dire que ya des moments qu'on ne vit qu'une seule fois de sa vie la preuve on peut pas revenir 25 ans en arrière mais on peut se le rappeler.. Big up maman Kine Bilahi c anciens morceaux me ramènent loin....
Thiey sama yaye mo mna wy de billay dma bagne macki sall be kou andack mome me bayile bathi sama baye dafa andack macki sall reck mako sen thiotti ndaye yenne niar waye kine mome yalla khamnani loum def balna koko
Si j'écoute cette chanson dédiée au lébou je pense à mes deux promo feu kene ndoye championne d'Afrique et mame seynabou ndoye que je slt de passage
Suis là !!! Merci de penser a moi grand birima ❤
Hommage mérité
❤❤❤❤❤❤@@africangirl9507
Ma mère mettait tout le temps Kiné Lam quand j'étais petite ❤
Elle chante Ma Famille Lebou direct de Dakar…
Merci Itou et Paix à son âme Cheickh Tidiane Tall..
Elle l'a bien chanté Machallah
Je te souhaite une très longue vie et remplis de santé de joie, maman kiné làm doundeul way❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Billay way bi dama nékh nakh lima sant Ndoye ❤
Moi, c'est ma grande soeur adorée qui s'appelle Ndeye Fatou Ndoye, cette belle chanson lui ressemble dans tous les sens.
@@aliousene5900 Nday san Billay dafa nékh
Woyy bi mome may borom ndakh mane ndeye fatou ndoye la toudou nekh na machallah
Ndeysan walahi yakko môme
Elhadj Assane ndoye, alim la, khafiz la, diplômé français ak arabe. Kiné mo am niveau
NDOYE Lebou Ndoye Malimaram ❤ I Love Maman Kine Lam
Zef Fall : ça me rappelle des moments fous cette chanson comme pour dire que ya des moments qu'on ne vit qu'une seule fois de sa vie la preuve on peut pas revenir 25 ans en arrière mais on peut se le rappeler.. Big up maman Kine Bilahi c anciens morceaux me ramènent loin....
Yaye boye wanena soubadeye niow motakh solday yuw merci manmn
J'aime trop cette chanson quand j'étais petite je croyais que c'était pour moi
Tu m'as fait rigoler.🤣😂🤣😂🤣😅
Oh... c'est chou.
Kouffi kholam sèéd
Mane
Machallah la grande Diva
Li nga way sama toureundo bii soumeu magué naleu ko faye☝🏾
mama danga may fatali ay 25 ans si ginaw mama li menatouñouko am yalla na yalla goudl sa fann
As Sr bilahi dafay fatali lou barri
Amine
Machalah ken dou mom ndanane pirr
Bilay ma riche ay badiene
Vraiment maman kiné chante trop cool et j'admire bcps
Mais qui est ce guitariste oooh my god😍
C’est Feu Cheikh Tidiane Tall
wa waw tata Kine ligua waye lebouyi reyna
Ndeysane machala rek maman
Belle chanson.
Talentueux Itou DIENG à la guitare basse
Ça me rappelle les années 80.Ooooooooooh!!!😊😊😊😊
Maachallah Chapeau A toi li moye woye Nexna
Kine Lam waymaaaa oooohhh nekhnaaa
Mère Kinè lingua woy Mame limamou nekh na goudal faan ak weer loooooolllllkl waaayyyyy
1992a dourbel 2020 a dakar
machaallah kinè lam longue vie à toi
Ma chanteuse preferee
Machalla ❤❤❤❤❤❤
Ndeysane ❤️
machallah tu chantes trop bien vraiment. ces chansons me vont droit au coeur. Yalna yalla laf thiat
thieuyy lii reuynaa
Hsudije Hekdbf i
zeina Thiaw. laye dieuredieuf tata kine machallah
merci bour diop pour tout ce ke tu fé pour la musique senegalaise dieuredieuf
lawla thiate kiné mame bamba lo weuy nékh na
Ayway damayfatale diebma niekhna
Vraiment kine do si moromou kene
thiey machallah limouy way nékhna trop
Mane Lima diakhal moy kiné lam sokoy dėglou dafay mėlni yaw lay wayye bilay lolou daffa doy warr
Tu es la meilleure
Man wayi na ndaye fatou ndoye mamadou assan ndoye thieuye mame Lou dondou doyoul
lii moye waye maschalla
mamma kine luogo vita grazie ancora 2018 papi Torino from Torino
ça c'est un truc de très haut niveau
Machalla yénafi nék dé
bilahi kine ya meuna way
Bour Diop svp pourra t'on avoir la 1 cassette de ndiouga Dieng si possible
aaaaaaaa Tata kiné goudele fane
Aissatou Thiam TAR/ i
Digeune diou am diné am ngor diko dialé papa dogo bour yalla kharé ko aldiana
Eupna kouy lebou sa khôl feekh
woyandowoul kene doussene morome wayyyy
Bilay nexna
Temps boy ndeyssane
Ndeysane vacances 1990
Bellissima canzone
slt
commissaire ndoye defale dara way
wawa Yaye rek dì wakhe lo Nekhe rek
vive les lèbous billahi gnion mome cap vert
Ndeye fatou ndoye gniata nga may finè lam ? Ki khamo limoula way
Khamouko waay
Kine lam yala nala yala defal diam Sama khôl sedena
Dafa waye ba waye fudara nekol moye waye katt degue
yaye yaw rek la geume
Macha alla
❤❤
mane moy sama ndanane
Waye rek laye def
MERCI KRIJOB YA BAKH WAYE
🎉🎉😅❤
nice beat!
E. Momar Diouf n'y
Wa lii nékhana
deug deug ndanane
Bour Diop svp cassettou diouga dieng bimouy way djirim ak madame Elizabeth diouf svp
Hsudije
Nekhna Maman
Ziari nala bobakh
j aime
thiey kiné digama ray rek
Djelen thiey kiné digama ray rek Kane pono
MANEMILA LI NEKHNA DEGALIIIIIIIIIIIIIIIIII
Rythmé
woy rek guay defffffffffffffffffffffffff
kinilam
💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞
Khol sèd na
Thiey sama yaye mo mna wy de billay dma bagne macki sall be kou andack mome me bayile bathi sama baye dafa andack macki sall reck mako sen thiotti ndaye yenne niar waye kine mome yalla khamnani loum def balna koko
👏
aka mana way degg francais té kham histoirou sénégal
Elle est civilisée
dinga masaway nit mou fatou fa yallawou
9 35
nekhna
serige omar diouf
fou gni diélété niou mél ni mak gni
dotoul am
Woyy bi mome may borom ndakh mane ndeye fatou ndoye la toudou nekh na machallah
Mais do wakh lébou.😂😅🤣😂🤣
NDOYE Lebou Ndoye Malimaram daL dou ay Foo
Ça me rappelle les années 80.Ooooooooooh!!!😊😊😊😊