samay rêve boknassi tok tewlou kurel treviso ak foumou meuna amei si aduna le plus important pour moi moy guiss lein diahrane teowlou ndiague mi ba nopi sante lein si lignoumay beigeulei si samay journée soulagement binioumay deifal souma diouguei si war yi ba degliulein thiono bi yeup wathoe souma amei louma nakhari ba deig lein oci fatei leip yalnalalein yalla fayal bopam tei ligueye bi ngein dadiè thieik ngeureumeul serigne bi. sen mbok talibei simon samba nadiaka depuis maroc
ua-cam.com/video/gxFEr1FVduM/v-deo.html Serigne Cheikh Fall Qad Taaba di kou yéeme lool daan jàng ci jamono Serigne bi ba am lou Serigne Touba wax ci moom Lien bii amna touti ci Innanii bi
Yalla nanou yalla fayal serigne Touba ❤❤
Ndaysane serigne mountakha yalla nafi yague amiine
Yallah naniou yallah fayal serigne Touba ❤️
Amine❤
Ndaye sane yalla nagnou yalla khire si xassida yii té yalna yalla guoudale sénn fane
Thiey Serigne Bi❤❤Li nékhna dei machallah wallahi boma yorone Aÿ milliard géne khamni.lëpp deug Le ..
Li nekhna trop machalah 😭😭yalna lene serigne touba fayy 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
samay rêve boknassi tok tewlou kurel treviso ak foumou meuna amei si aduna le plus important pour moi moy guiss lein diahrane teowlou ndiague mi ba nopi sante lein si lignoumay beigeulei si samay journée soulagement binioumay deifal souma diouguei si war yi ba degliulein thiono bi yeup wathoe souma amei louma nakhari ba deig lein oci fatei leip yalnalalein yalla fayal bopam tei ligueye bi ngein dadiè thieik ngeureumeul serigne bi. sen mbok talibei simon samba nadiaka depuis maroc
ahh dieuwrine lolou deh defenani malako geuneuh beugueuh
Det bayi len niou bokk fa dadjé rek
Inchallah bouko sunu borom toudei diagne fa dadié ande sante cheikhoul khadim .
@@simonnadiaka9604 guinaw meun na louko eup, yalla nako dogual té kenn bagna manqué incha Allah
@@Kayel_d Inchallah fasseilantei reik
Dierejeif Serigne Touba Khadim rasoul mancha alla☝
Dieureu dieufé cheikh akhmadou Bamba amoul morom wa waw Diambar yi waaaw lénnnn gooorr❤️❤️🙏🏾🙏🏾
Machalla amna solo lol YALLA nano YALLA BOLE defal jame AK Salam AK KHEWAL si BARKEP SERING touba KHADIMO RASSOL AMINE
Amna solo, mangui ziar wa kourël treviso ñép.
Daajou Innanii houstou binguén jang bëgonn na am son biko mag mi jangué sou féké japandi na
Siar li bane kourel la
ua-cam.com/video/gxFEr1FVduM/v-deo.html
Serigne Cheikh Fall Qad Taaba di kou yéeme lool daan jàng ci jamono Serigne bi ba am lou Serigne Touba wax ci moom
Lien bii amna touti ci Innanii bi
Mancha Allah yalla sa borom takhawou lén🥰
Liiiii douma si masa doyal le 11 7 2020
diereudieuf
Yak kan
DEGALMA SAMA DJEIWRINN S. OUSSEYNOU FALL REKK... YALLA NA NGA FI YAGG TE ANDAK WEURR WAAY THIO BARKI KHASSIDAYI.
DEUG DEUG khamouma nou Adiana mel wayé manouta dakh liiii😢
Aljanah Mo Dakheu d mourid Aljanah dio took d djakarlo ak Srg Touba mi Bind Li Dara daxo ko
Li takh mo nekhe moy malakayi ne lann koy diangue si teranga aldjna yi labokk
Dieuredieuf serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla naguein Boko si kourel Bi Srg Touba d dianglo Euleuk barkeb sfallou Daaath Bi Fo Sori lamay yobu worna yalla
Amine
Ndeysane
@@abdoulayegassama8971 qm
Aldjan ben kourel lay donne nioam niepo de yeguete don
Yala nalin Serign bi taxawo barkip khassida yi ❤️
A khaasa Thye seriñ touba. Amul morom 💓💓🙌🙌🙌🙌
Hakasa amnasolo se raiyaba thia lalen diokhe lokho nalen yallafay
Thieuy serigne touba amoul morom
Tiey ahmadou bamba jeureujeuf dadj bii euwww❤❤❤❤❤
Dierediefati Serigne Touba
Kn dou Sheixul Xadiim 👏👏
Thieuy serigne bi
Ndeysane sop lene kuer khasidayi rek
Wa Treviso niou man diaggg
Thiey SERIGNE touba
Way nekhna way waw Len goor mourid
Ndeysane YALLA nguéne yagg werr
Thiey serigne touba
Thiey borom touba
Non
Li mo fi geuneu nekh si adouna barkep Serigne Touba khadimou Rassoul mbekté rek
Serigne ousseynou😭❤
Dieureudieuf serigne touba
Houu lii nekh na wayy barki borom touba
Yalnalèèn borom khassidayi takhawou ba fawou...
MOR TALLA SECK amine
Serigne Touba amoul morom
Thieye serigne touba
ماشاءالله جرجف ❤❤❤❤
Li Gana nekh si kholl
S Touba amoule moromr😭😭
Machalla ndaysane
Diadieuf mouride amna solo yénay diambar
تبارك الله وتعالى
Yala nalin Serign bi taxawo
Ndeysan yalla nalleine kou tedd ki fayal bopal si barkeii mame lamp fall
Yallah na yallah faylen ci barke BOROM TOUBA
Dieura diaf serigne bi
Eskéy masha'Allah
Thiey sg touba
Ndaysane fall li nekhna dh
Çey yàlla Allahou Akbar 😭😭😭
Nek. Lenn. Sii rekk
Wawaw machala
Toubab bi limoudone bagnal sgn bi bir Sénégal tay nangounako deukeum Diadieuf
Thiey gnii
Mame Cheikh Ibrahima Fall dinalen taxawu
mes li nékh n'a troppp way
ما شاء الله
Ayway 😭
♥️♥️♥️ mashalla
Macha
Ndeye San
MASAHALLA 🖤💚✔️✔️
😭
Mancha allah
4D
😭😭😭😭😭
Thiey
Mashalha
Ndeysane waye
Barkep Cheikh Fallou Fall Modou Aminta lii aljanaa laaa ken Ahmadou borom jaaam yii akh jaraama Borom kaala gou nioul. Cordialement NBF
ماشاء الله
machallah
Hisboutarx ia trev
akaza sama xol sed na
bly tokk di kourel rek la beugue
Manga ko deff de loy siy khar
Serigne cheikh fall khatab
Thieye serigne touba
ماشاء الله
Machallah
Machalla
machallah
Machallah