Masha Allah baye mbaye amatina solo🙏🙏 Mangi tuub dh mé Histoire soko done deff par Ordre (épisode par épisode...) jusqu'à la fin de l'histoire aprei nga dieulat benen Histoire... Je pense que ni cette méthode va nous permettre de mieux suivre , comprendre et de capter les histoires sinon le fait de mélanger les épisodes des différentes histoires dafmay réral parfois🙏🙏 mangi tuub c'est juste une suggestion de ma part nak🙈🙏 On apprecie becou le travail et les efforts fournis
diaradieuf sr mbaye gueye syll yalna yalla dolila kattane te barkél laguéybi. barkep borom touba
Diaradiaf baye mbaye geye magui fi si Brasil di bayi khel sen bi yalla na yalla gudal sa fan
Dieuredieuf baye mbaye wayé sakouwon nagn histoire bou damel madior fatim gologne ak sokhnam linguère yacine boubou
Masha Allah baye mbaye amatina solo🙏🙏
Mangi tuub dh mé Histoire soko done deff par Ordre (épisode par épisode...) jusqu'à la fin de l'histoire aprei nga dieulat benen Histoire...
Je pense que ni cette méthode va nous permettre de mieux suivre , comprendre et de capter les histoires sinon le fait de mélanger les épisodes des différentes histoires dafmay réral parfois🙏🙏 mangi tuub c'est juste une suggestion de ma part nak🙈🙏
On apprecie becou le travail et les efforts fournis
soxneu fatima makhtar diouf inchallah jërjëf way
Mangui tuub bubax nakk et on félicite toute l'équipe ay Jambar ngen et grace à vous on sera riche en culture thieu kaw seu kaw in sha Allah💪❤
J’avais aussi cette suggestion en tête. Merci 🙏🏽
11
11
Machala XAM SAM REEW BEGUE NAN LOL
Baye mbaye ndamale yonwi nga
اناأحب السنغال حدحد والله والله
Ma cha allah
Am na solo lool!
Yague fi lool
Diadieff bay mbaye
Bec nanou lool
Moustapha cisse Washington
Émission bi dafa bari répétition trop même mai nekhna nak
La repetition est pedagogique.