Nabou leye est libre d accord elle est innocente ou coupable le juge d'instruction doit clarifier les choses a tout le peuple sénégalais du courage à la famille des défunts
Justice amoul Sénégal bouléne sonal séne bop fi kouniou fi raye perte nga deukou corruptions laniou néke djikoyi changéwoul Sénégal da beuri Nafékhe ak niou deugouwoul Yallah rék mo meuna Até té dina Até bouniou rayone domou kilifa dou déméni domou Badola mo sone Sénégal mougne léne rék té sante Yallah té hamni Deugue rék moye moudiou
Nous devrons dire justice pour tous les victimes qui ont été tues car trop c’est trop. C’est le procureur qui doit sortir donner quelques explications sur le double meurtre. Les familles ont le droit de savoir ce qui se passe, c’est cruel. Je ne parle pas de notre gouvernement car ils ont nommés des gens pour ça donc la justice devrait donner quelques explications aux familles. Que la paix soit sur toutes les victimes.
J'en ai marre de la Sœur de Aziz Dabala mais pour Aïda tu as peur de Nabou Lèye il faut dire la vérité et tu dois pointer du doigt à Nabou Lèye assassin
Merci wakhougnou thi nabou leye depuis bobou , nek fi dignou emmerder ak sonkodiomaye, dafa méti nga wayé c le rôle du ministre de la justice , nos martyrs sont morts depuis et justice n'est pas encore faite , lo guiss dafa am yone
Changeleen avoca m.bamba cisse mi ngui fi cledor ly mi ngui fi nioniou nioy ay vre avocat waaye avocat yamanekh yi ngueen dieul dou nioleen di indil lou leer
Ndey Mamma khawma ! Iow ta rien compris ! Pape médina Soudeii dafa bokkk thi game bi comment il peu prononcé pr que justice soit rendue ?? Neiikkk leiiine ay nitttt. Aziz dal mo perte
Andando wam yoyu yeup loutakh nangou wougnou wakh nangou wougnou gneuw dafa louch ay conpis lagnou yé nay diouk fadiako sen bop balahi boudo man fayuna bou yag dém kasso kou ray sama mbok ma ma réndileu limoy lan dekbi amoul loi louway nékh daf kougnou ray ya pétt
L'état du Sénégal il n'a aucun respect pour les citoyens pourquoi il ne communique pas pourquoi il ne l'enquête ne bouge pas ils sont compliqués impliqué ou quoi
Yaw mi ndieuké wakh doul, bougnou sonal , yaw ya fall diomaye waleu sonko !? Lane motakh gnou fal ministre de la justice ? Lane motakh dès le début nangouwoulen wakh thi nabou leye di diay mandou ak rafétal hypocrite ? Chiiiip
Nabou leye est libre d accord elle est innocente ou coupable le juge d'instruction doit clarifier les choses a tout le peuple sénégalais du courage à la famille des défunts
Macha Allah, Ndeye Mama tu es veridique
Justice pour aziz dabala et wally gano c est ce que le peuple demande
Justice pour aziz et waly
Rakou aziz bi rafet na machalla
Justice daffa wara deff ligueyam. Nabou domeram bobou waroul guen ni
Dafa méti trop haa justice guéneu léneu wakh ak askan wi😢😢😢😢😢
Wakh deug nekh yalla yone warna def ligueyame
Justice pour aziz dabala et waly ce triste
Justice amoul Sénégal bouléne sonal séne bop fi kouniou fi raye perte nga deukou corruptions laniou néke djikoyi changéwoul Sénégal da beuri Nafékhe ak niou deugouwoul Yallah rék mo meuna Até té dina Até bouniou rayone domou kilifa dou déméni domou Badola mo sone Sénégal mougne léne rék té sante Yallah té hamni Deugue rék moye moudiou
Vérité absolue
😭😭
Bilah wakh gua deugu lou leer lagne gua wakh
Li dafa wara l’aire way dagno wara kham Kane mo ray Aziz et waly vraiment 😢😢😢
AZIZ Yalla Nakou yalla yaram
Amiiine yarabi 🤲💖🤲
Justice Justice Justice Justice pour AZIZE DABALA ET WALY
justice pour Aziz dabala
Niane lene pape Aly nguene deme RTS
Justice pour azie et wally
Nous devrons dire justice pour tous les victimes qui ont été tues car trop c’est trop. C’est le procureur qui doit sortir donner quelques explications sur le double meurtre.
Les familles ont le droit de savoir ce qui se passe, c’est cruel.
Je ne parle pas de notre gouvernement car ils ont nommés des gens pour ça donc la justice devrait donner quelques explications aux familles. Que la paix soit sur toutes les victimes.
Dieule léne avocat bou ame bruit comme maitre Elhaji diouf
Bilaay dafa méti 😢😢
J'en ai marre de la Sœur de Aziz Dabala mais pour Aïda tu as peur de Nabou Lèye il faut dire la vérité et tu dois pointer du doigt à Nabou Lèye assassin
Merci wakhougnou thi nabou leye depuis bobou , nek fi dignou emmerder ak sonkodiomaye, dafa méti nga wayé c le rôle du ministre de la justice , nos martyrs sont morts depuis et justice n'est pas encore faite , lo guiss dafa am yone
bilay elle ne fatigue
procès bi mouni en cours
kone khar lén justice
té elle fé semblant
greffage et autres
Merci bcp ndeye maman.deug rek la fonke.
Dieuléne mr tall légui mou lère
Justice pour Aziz et Wally metina torop vraiment
Machalah et courage à vous
Justice pour Aziz 😭😭😭😭😭😭
Qu'il se repose en paix avec wally
Merci beaucoup nd mama
Le président doit un grand nettoyage sur la.justice je suis désolé mais ça c'est née plus de jub jubal jubanti
Demlen setti maître Cledor Ly ak Bamba Cissé ñioñiou ay gorr lañiou
yéne nopilene justice khamena bou bakh limiy def
Oui Thiaoye 44. Et Aziz et Waly ?
C'est entre sénégalais. À solder.
Des vies humaînés !
Justice pour Aziz
Dawnayaral ndeysane
Masaalahu ma seur 😭😭😭😭😭😭😭😭
Raye bi beurina trop Sénégal
Demlen rts wakh ko president ak sonko dina ko deggu
Suis parfaitement d'accord naniou dem RTS
@@Luniquefparmi2g sono demon rts si lai guna gawi ndakh président dinako sitaan wala de sonko
Changeleen avoca m.bamba cisse mi ngui fi cledor ly mi ngui fi nioniou nioy ay vre avocat waaye avocat yamanekh yi ngueen dieul dou nioleen di indil lou leer
Lima diakhal do artists do waykat do fethi kat kin tewol wayi yala gui guiss lipo dina leer
😢😢😢😢😢😢
Lidafa meti trop kene douko fatè
Waxna deug dé Sénégal mom yoon toujours dafay démée côté
Degela😢
Pr d'impayé Faye et son premier ministre louis sen yone
Senegial dafa meti nit cou am nakhar doune ko comprende dane nane dafa eupeul dafa rew loumou wax warouko ti boudone yaw gua robe fofou
T'as parfaitement raison madame
Me qui yabaté neu dh
Mais li lousouye yonou ousmane Sonko ak diomaye. Justice nga wara posé question bi. Ah Amna gnou eupeul way
Nabou diamou Rik kaye Am
❤❤❤
Nabou Laye de foul Dara Bilaye Diamou Rik
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndey Mamma khawma ! Iow ta rien compris ! Pape médina Soudeii dafa bokkk thi game bi comment il peu prononcé pr que justice soit rendue ?? Neiikkk leiiine ay nitttt. Aziz dal mo perte
Mo8 je compren pourqyoi le ministre de la justice ne ns explique pas
nabou leye da wa la ré
Andando wam yoyu yeup loutakh nangou wougnou wakh nangou wougnou gneuw dafa louch ay conpis lagnou yé nay diouk fadiako sen bop balahi boudo man fayuna bou yag dém kasso kou ray sama mbok ma ma réndileu limoy lan dekbi amoul loi louway nékh daf kougnou ray ya pétt
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Il avait lair solaire aziz
Wa kou yor dossier bii la beugueu kham
Aida c'est sa petite sœur
Oui
Pape medina moy kane mome
L'état du Sénégal il n'a aucun respect pour les citoyens pourquoi il ne communique pas pourquoi il ne l'enquête ne bouge pas ils sont compliqués impliqué ou quoi
Elle est trop mignione
Té thi lolou rek nga concentré wou
What if she did not do it
Wa yaw koy walhale yéne yéne rek
Dioléne dossier bi sonko rék lép dina lére
Artiste yi aye lache
Il fait aller a la rts
Yaw mi ndieuké wakh doul, bougnou sonal , yaw ya fall diomaye waleu sonko !? Lane motakh gnou fal ministre de la justice ? Lane motakh dès le début nangouwoulen wakh thi nabou leye di diay mandou ak rafétal hypocrite ? Chiiiip
Justice pour aziz et wally