Franc est un vrai combattant. Un homme ne parle pas beaucoup. En matière de lutte, il faut respecter et estimer son adversaire pour que la victoire ait de la valeur.
Franc est un lutteur complèt comme Reug Reug ils ont beaucoup compéti dans la lutte simple. Du coup ils ont une bonne endurance et une force physique monstrueuse….
Mais façon face to face bi nice na trop machala gnari mbeur yi diégué yanté sans problème nekh na trop. Bonne continuation si façon face to face bi👏🏿👏🏿👏🏿👍🏿👍🏿👍🏿
Franc ndiago est naturellement posé et respectueux. C'est un futur grand champion. Il a toutes les qualités pour devenir un ténor de la lutte sénégalaise avec frappe.
If I was hearing this press before the comba , I will know who will win. . Sokh hear I know and see ,he is going to loose this comba. God gave me that kind of knowledge and power before things happen..
No I am not marabuts ,nor marabou. Am gifted by the almighty god and I have DUTCH wife and 3kids and have another son in Germany..Thanks for asking. BLESS.
Ki est là après la victoire de franc😂😂💪
Moi😂
Me😂😅
Me
Meeeeee😅😅😅😅😅
😂😂
Vraiment sén face a face class na trop mbeur yi nio mature machallah
Franc est un vrai combattant.
Un homme ne parle pas beaucoup.
En matière de lutte, il faut respecter et estimer son adversaire pour que la victoire ait de la valeur.
yaw
Franc pikine lagn koy khar dou touss niouy roubé nioy dane inchallah
@@taphadg2213 lo wakh legui ?
@@aqua_home_dakar2623 moma diaxale amoule loumou waxati🤣
Non tu devrais plutôt dire pour que la défaite ait de la valeur 😉
Sokh sama mbeure nga mai wanile wakhe ji diokhe thiokhé thiére amna solo
Sokk bayill wakh diou barri franc mola meune meune koula meune
Aller ndiago bi domou PA bi ndame rekk ine sa Allah 😍
Mane franchement way dji dafa nekh koi il m fait rire 😂 koi
Franc mom il est cool machallah
Franc kou nékh leu simple easy à l'aise un vrai Champion ngeu Self contrôle un combattant on dirai Qu'il Pratique les arts martiaux
😂😂 Franc a des petites phrases assassines quand même 🤣🤣
No franc saï saï leu
Da dieguè modou lo nak
Fran ay retan sakh moko diap😂😂😂😂😂😂🏃🏃🏃🏃
Franc il communique bien, félicitations les parcelllois ✌️
En tout cas dall fran borome dolé bou and ak xéllame laaa 💪💪 fran nala yalla mey ndame sok da barry wakh
Bonne chance franc , yalla nala yalla mayy ndam unsha allah.
Sokh affaire bi dou wakh kessé
Sokh borom baxla mais franc ndam rk in sha allah vive P.A
Defean bi ndam rek PA
Franc j'admire ton calme olympien 💪
Franc est un lutteur complèt comme Reug Reug ils ont beaucoup compéti dans la lutte simple. Du coup ils ont une bonne endurance et une force physique monstrueuse….
Combat diank deug moguini
sokh yalla nala yalla may ndam inchallah mais wagnil wakh dji
Franc est un champion
Sokhou Yallah Nala souniou borom Défall ndame Lou reuy Barke serign fallou Mbackè 🙏🏻♥️🙏🏻Mé Sokhou wax Toutii job Lou Barii Rék 🧏♂️Fra Mii champion ladé Bayill Lolou xél 🧏♂️
🤣🤣 xamnga né lingay wax geumo ko sakh faran rk💪🏼💪🏼
@@cheikhfall2341 ba jour ba sokh dou thiouné kéneu
Sokh mi comédien la comme Diop fall
Mais façon face to face bi nice na trop machala gnari mbeur yi diégué yanté sans problème nekh na trop. Bonne continuation si façon face to face bi👏🏿👏🏿👏🏿👍🏿👍🏿👍🏿
No lima nekhe si combat bi moy sokhou sibopame dafa khamné sénégalais yeup linkoy wakhe moy franc mola moun fouff 💪🏾bonne chance franc
Ta li Sénégal yi di wax moy deug
sokh mongui liiir comentiar yie dofoul
Franc est tun lutteur serreyeux
Un grande champion
J’aime le Sénégal vraiment li dafa néx 🤣🤣mais je crois qu’il faut professionnaliser la lutte. Vive le patriotisme
Sokh je t'aime bien ms respect ton adversaire
Franc/Sokh combat de 🔥🔥🔥 mais Beugg n'a franc ndaax daale gui machalla moome la faraal,..🔥👌🤣
Sokh yalnaga am ndam
Sokh ame nga problème Barké rassoulilahi
Bilakhi
Franc ndiago est naturellement posé et respectueux. C'est un futur grand champion. Il a toutes les qualités pour devenir un ténor de la lutte sénégalaise avec frappe.
Sokh champion nga mai diokhal franc thieur champion la dh
Sokh bayil di fowè sa khêl mi,bakhná
Franc mi doff plus lá dèè 😂
Mo takhit dhh
Sokh combat bi de wakh rek gassi ame
Inchallah
Bou Souba ngéni comprendre
Thieuye sokhou wakh rek mes bakhna franc yalla nala yalla ndam
Billahi sou wakhè nga diapp ni mo meune si lamb j mais meunoul touss 😂 franc mokko meune fouf
Billay bou lamb j dièkhè nga weddi ko
Franc sérieux woul😂.nénako diga thi gnak fayda dh😂😂
Athieu franc 💪🏼🔥rang mouy gawe ✌🏽
Sokh yalla nako yalla may ndam ci kaw franc ci barke seydina mouhamed psl
Franc par force 💪
Sokhou bari nga wakh
Je peux assurer que franc est meilleur que sokh..
Vraiment tous les deux dont des champions je les aimes tous ils sont discipline
Sokhou Yalla na la yalla may ndam champion affaire bi Pikine la ❤️❤️
Kouy doora meune kouy saagha😂😂😂😂😂
Franc is my champion and displine...
Victory 💪💪
Sokh ndiago nga kom Franc meunouleu deugeuleul sabop domou pikine dou ragal
Forza ak franc mo daxon mais lii du metti
Forza niom nièp daniou koy daw
Sokhou Dougounga si lo khamoul dee wakh rek ngay def Nak
Franc est plus posé, discipliné et réfléchie. Il écoute sont adversaire et ne le coupe pas
La bataille psychologique de sokhe🔥🔥🔥🔥
En tout ça combat bou nèkh leu et j,admire les deux lutteurs et que le meilleur gagne😎
Ndiagoo biii champion laaaaaa ✌
Combat bou nara nékh lay ndone que le meilleur gagne
Sokh beuri nga wakh 😀😀😃
Trop sakh
Fi wax molén fi indi sokh day wax Di Dieuf
Fra mola ep dolè
Ki kay dafa Bari ndeye wax
Élément Modou Lo la😂😂no déf mou meuneu tontou😂😂😂
Franc danne tyson 2 tour ne dieull sokh dou lámb moko meun.. franc reugg obelli kouniou dieull niola meune meur mbapat yi nioy meur tigi
Sokh sama mbeur gua mè Franc aye wakhe danouko dh
Sokh Mane ay réh ngama déff bilay
Vraiment sokhou yalla na la yalla maye ndam inchalla
Franc à des courtes paroles graves ! Je l'estime, un homme ne parle pas beaucoup.
Franc yagui sogua âme combat diankh bilahi sokh dafa geume entraînements
Tyson 2 dou moromou soke té fran danne nako
Sokh nit kou bakh nga mais lamb dji wakh rek ngathi am franc mola meune foufe iow yabo mbeur parcelle yi ramdam dala diap dane leuh
axx fran tu es le meilleur 🥊🥊🥊
Qui es la en 2023
Merci mon frère franc wakh touti deuf Lou beuri 💯💯
Franc mo dakha beuré geuna ame compétition mes sokhe aussi ndanane la il a terrasé gamou gueye avec la manière mes yallna franc danne amine
Sokh champion ga et nitt kou bax ga .
Mais yallah na yallah may ndam Franc
Franc (victoire rek) 💯
Sokh ndeekkè ay wakh le gana manè mais manoull beurrè
Franc victoire rek. mais concentre toi.
Vraiment Li combat la
Ay natanguo lane
Ay champion lane
Que le meilleur gagne
Sokhou ndame rk inchalla
Thiéy adouna deux frère téy lambe bolénéléne fran et frère de sock sont des amis depuis enfance respé frère que le meilleur gagne
Sokh fran lo rafetena me yalla na domou pikine ame ndame inchalla
Sock Bilay ay retan lama deff ligay deff ni sakh guemo ko ndiago bi nga am modou day dann fran day dann
🤣🤣🤣🤣 c'est trop drôle wakh rek il avait raison franc
Que le mellieur cagne .ndam yalla ga yor mai frans mo moune sokh
Kou danne bb saloum /mbay tinne thiatou yoff ndiaga doll3 serigne Ndiaye 2 ngay wax franc danoul champion
Sokh combat bi bou néké sa biir keur sakh di nga danou, comme k wakh nga am si combat bi wakhal rk.
Yalla dhé mo kham lép liye khéw souba
@@fatoucha554 yow miy wakh wakhou yalla khamo bakham soubeu dina am, boudé pikine nga deukeu nak wakhal sokh ak ay mbokam niou wadial
Franc dakoy rayy ki siboul sakh😂
On dois respecter un adversaire sokh champion nga mais bayil khel nii champion nga dadiel
Liy wané ni franc gnémé woul sokh dou wakh sakh ba khol ko 🤣🤣🤣
Non sokh respecto fran mber la dé .khana mou diom .fran mola man
Wa pikine wakh rk man ma warou😂😂😂😂😭😭😭
Sa data yaye
@@assndir5297 saway amal yarr nioun daniouy kaff li ngay deff d’où am fitt soma guison doma saga
@@lahadboukharagnelo6707 wax nga deugeu
@@assballagaye2faramarenebi178 ❤️❤️❤️✌️
Sokh dé com mbaye gouy gui wax rék maytoul franc mi ay wax you séw la yoré té bandi géw la
Blie dey
@@fatousaidy2142sama avi mmlamb maytoulma kou nopi nga yakarni dala ragal
Sokh dh sou deugg nékhé yalla combat bi arbitre sifflé moola fi bayyi
Tu es un bon parleur Sokh ms attention franc khalékh leu
Sokh mii loumou teik franc nak 😂😂😂
Sokhou nga sa bopp dh😂😂😂ki de leu dh franc rek journaliste yii sakh kagn laniouleu def
Sokh je t’estime nak mai franc mola meun fouff ki élément Mod’lo leu wax touti job loubari
Aythia sokh combat Bi combat de revanche LA bouthi mayé dara ndame rk inchalla
Sokh wañil wakh ji..tè gueuneu job baye fall..Franck khalè leu amna dolé..que le meilleur gagne
If I was hearing this press before the comba , I will know who will win. . Sokh hear I know and see ,he is going to loose this comba. God gave me that kind of knowledge and power before things happen..
Saay lakal Olof😂
Gambein la
Mbading e sabari are you a marabuts
No I am not marabuts ,nor marabou. Am gifted by the almighty god and I have DUTCH wife and 3kids and have another son in Germany..Thanks for asking. BLESS.
No am not a marabou. But am gifted by the almighty god..I love womans.
notr lutteur frans vive avec toi
No ms sokh beurina wakh legi akh
Sokh bari nga wakh bakhna
Franc PA la afaire bii touse
Ça promet 🤣🤣🤣🤣🔥🔥🔥🔥
Meilleurs signature de tout les temps 😂
Ndame rékk inchallah sokh
Fran rék ndame inchallah
Franc am nga problème nakk ba dieul Mbeurou guinaw rail bi
Who's here after the combat.......sokh🤣🤣🤣🤣🤣🤣
J'aime franc
Franc dou sa morom💪💪💪