Xassida gui gni ngi ko teunk si AYYA bi « walahad karamna banni Adama…………….. » AYYA bi nak mingui nek si SOURATE ISRA’I (17), AYYA (7O). Serigne Abdou Khadre (RA) néna Xassida gui dina mayé Xeweul ak diko diapandil Serigne Saliou Mbacké(RA) diglé won nako biss bou nek, bok na saas bimou dioxé won Waxnanouni kouko Saxal mou nekh la wala mou Nakhari la, kouy am Xeweul ngay donn,té Xeweul yoyou dina Barkel ,té kou niouy Téraal ngay donn ak fo meuneu nek. Nénanou tamit Xassida Karangué la si leep louy loor Louci geuneu doyaty war moy AYYA bimou nek si AL’HOUR’ANE dafay tollo ak limou KOUN(70) lou yémmé té KOU TED nena « BARAKALI FIL HARAKATY WA SOUKOUN.RABI LEUZI HAD HADANI KOUN FA YAKOUN” (Sama Borom mo Barkel sama Yeungou ak sama dall ba noppiDiox ma « KOUN FAYAKOUN »). Bokou nassi Tamiit bissou « Samedi » nak Nieuw na si Xassida gui dou ben yonn ???? KOU TED KI waxna si biir : « Yaw sama Borom yama Fégal si ay Noon, Yama defal ay may ak Ndiapandal ba niak téwéé) » « Defalma mbax, ngeureum ak Tabb gou andak mbecté yaw adji mag dji » « Si Magou Geun di mbindef, Yaw sama Borom oubilma Bountou yi, Bountou mbecté yi. Bountou yi rek nioma meuneu diox deug deug mbecté » (Etc …………………………………………..) » Waxnanouni Xassida gui Liniou yitéwo Fi ak finiou dieum mingui si biir
Masha'allah ♥️ jërëjëëf Ahmadou borom jamgni
Disciple de serigne touba mbacke pour l eternite
DIEUREUDIEUF SERIGNE BAMBA...DIARAMA MAME CHEIKHRA FALL
WA LAQAD KARRAMNÂ »
Xassida gui gni ngi ko teunk si AYYA bi « walahad karamna banni Adama…………….. »
AYYA bi nak mingui nek si SOURATE ISRA’I (17), AYYA (7O). Serigne Abdou Khadre (RA) néna Xassida gui dina mayé Xeweul ak diko diapandil Serigne Saliou Mbacké(RA) diglé won nako biss bou nek, bok na saas bimou dioxé won
Waxnanouni kouko Saxal mou nekh la wala mou Nakhari la, kouy am Xeweul ngay donn,té Xeweul yoyou dina Barkel ,té kou niouy Téraal ngay donn ak fo meuneu nek.
Nénanou tamit Xassida Karangué la si leep louy loor
Louci geuneu doyaty war moy AYYA bimou nek si AL’HOUR’ANE dafay tollo ak limou KOUN(70) lou yémmé té KOU TED nena « BARAKALI FIL HARAKATY WA SOUKOUN.RABI LEUZI HAD HADANI KOUN FA YAKOUN” (Sama Borom mo Barkel sama Yeungou ak sama dall ba noppiDiox ma « KOUN FAYAKOUN »).
Bokou nassi Tamiit bissou « Samedi » nak Nieuw na si Xassida gui dou ben yonn ????
KOU TED KI waxna si biir : « Yaw sama Borom yama Fégal si ay Noon, Yama defal ay may ak Ndiapandal ba niak téwéé) »
« Defalma mbax, ngeureum ak Tabb gou andak mbecté yaw adji mag dji »
« Si Magou Geun di mbindef, Yaw sama Borom oubilma Bountou yi, Bountou mbecté yi. Bountou yi rek nioma meuneu diox deug deug mbecté »
(Etc …………………………………………..) »
Waxnanouni Xassida gui Liniou yitéwo Fi ak finiou dieum mingui si biir
Dieureudieuf serigne Touba amoul morom
Dieuredieur Khadimul Moustapha.
Akassa mouride
dieureudieuf Serigne Touba
Ziar machallah