Je suis muslim et j’aime beaucoup Ahmadou Bamba et j’ai toute une rangée de ma bibliothèque sur ses écrits mais il est diffamé et mal compris par de nombreux voyous qui se réclament etre ses descendants et disciples mais lep dana leer inchallah
En lisant les commentaires on sent nettement que les sénégalais commencent à démystifier certains marabouts faussaires. Machallah oustaz yana yalla goudal sa fann
@@mbackeleye4264 toi on dirait que tu es un Maride mais pas un mouride. Un vrai mouride danguay nangou deug par contre un maride(malade) est toujours un fanatique
Thats why Allah said Iqra,read!!!You said it all.People need to stop worshipping human beings.They just tell lies to make money and just keep enriching themselves.Hell fire 🔥 is waiting ohhhh!!!May Allah guide us all and make eaman beloved to us all and unite the Ummah.
Merci beaucoup oustaz alpha ba contane na thi yaw gni nio beuri wax wayei baxna li gueuneu neikh si adouna moy nguay wax di leirale nit gni sur la base du coran et de la suna du prophète tandis que vos ennemis savent tous ce vous dites mais ils refuse de l'accepter en place au lieu de vous répondre par des sources coraniques mais ils versent dans les insultes, dans la violence chapeau oustaz
Sénégalais yi meunou gnoo xeex goor djigueen, meunou gnoo xeex lenn mou sooti, meunou gnoo xeex ak toubaab amm ci moom, ndam.Ta dagnoo ragal toubaab.Sénégalais, lenn kepp la meunn,werante ak xouloo ci tarixa rek lagn meunn. Li coow li di bari yeup, dougnou meussa song toubaab, wala France. Gniy xeexal Sénégal, dama leena yeureum. Fougni jelee ndam, laa xamoul. Xeexu sénégalais ci lamign la yemm. Kougn song rek, da ngaa weet, wala nga neew doole. Sou leen wooree ne, bougn la songuee, ray ci sa mboolo foukk, nga ray ci gnoom, gnaar kepp rek, dougnou la songg mouk.songg kenn kou weet, gaagn ko, ndam amou ci.
Dieuredieuf.c'est vraiment triste et inquiétant ce qui se passe dans ce Sénégal.il y'a trop de fous maintenant.bonne continuation.vous avez du courage.barakallahoufikoum.
Salam, mon frère merci beaucoup tout ce que vous dites est une triste vérité. La vérité est unique. Ce qu'ils disent sont cautionner par leurs guides religieux. C'est une honte.
les vérités qu'on aime le moins à apprendre ,sont celles qui détruit nos intérêts, la vérité ne blesse pas d'elle même, elle fait mal car elle brise une illusion
Allah tout Puissant protège veille sur Cheikh Oumar Diagne et sa famille contre ces démons ces mécréants avec la complicité de l état du Senegal et leurs autorités religieuses
Bayilen sen thiakhane yi kou beug guinar beug ay thiouthiam kou bagne lifi Serigne Touba megne khôl bouy tangue rek ngay deuké je suis pas musulman mais nangou li yalla def si nite gni yalna diam yague
Vous dites la meme chose. Nioune li Yalla wakh rek laniou wakh. Sa bamel yow kasse la ak say dieuf. Bayil khel si lolou bou bakha bakh. Wouyou Yalla te bagn ko bokale ak dara ndakh mom moy kiniou soss mom niou
C O D na rien di de mal en plus il n parlait pas seulement de serigne touba il a cité d'autres guides religieux .pourquoi seuls ces moutons nous emmerdent
Yalla mouner ci alkourane fa’ anloule lima yourite « lima sopp lay deff » kone nopalal sa pop Serigne touba Likko yalla maye chaque jour day jokk , laffa ligueyal yalla ndiare ko ci seydina Mouhamet ba âme ci lou nitt dotoul âme kone loumou wakh ninane thi tekk sounou beute
Alfa pour quoi doot wakhe thi yéfaryi yi wédi yalla AK yonétebi yawe tarikhayi rék moola Noire wakhame.thi gnidoule diouli dounou wore wakhale çi Lolou
Sa fait mal au cœur 😢 Qu' Allah guident ceux qui les suivent enfin qu' ils retrouvent le chemin du tawkhid ❤
Je suis muslim et j’aime beaucoup Ahmadou Bamba et j’ai toute une rangée de ma bibliothèque sur ses écrits mais il est diffamé et mal compris par de nombreux voyous qui se réclament etre ses descendants et disciples mais lep dana leer inchallah
aka nga wax deug
Merci Oustass pour ta vidéo. Le Sénégal est un triste pays. Qu'Allah les guide Allah vers le Coran et la Sunnah. Ameen
Merci oustaz alpha que dieu te garde que dieu te laisse je suis très très parce que tu parles que la vérité ❤️👍👏🤝👏👏👏💘
Merci beaucoup mon frère. Il faut vraiment être un homme dépourvu d'intelligence pour croire à leurs légendes. Tôt ou tard la vérité jaillira
En lisant les commentaires on sent nettement que les sénégalais commencent à démystifier certains marabouts faussaires.
Machallah oustaz yana yalla goudal sa fann
Amine
@@mbackeleye4264 toi on dirait que tu es un Maride mais pas un mouride.
Un vrai mouride danguay nangou deug par contre un maride(malade) est toujours un fanatique
@@magdandiayendiaye169 8rue je voudrais le réinitialiser de passe orange 7vj
Merci alpha dégue reck ngaye wax Yalla nanga guoudou fann
Yalla n'a niou sounou borrom dioubanti . amine
Thats why Allah said Iqra,read!!!You said it all.People need to stop worshipping human beings.They just tell lies to make money and just keep enriching themselves.Hell fire 🔥 is waiting ohhhh!!!May Allah guide us all and make eaman beloved to us all and unite the Ummah.
Amen
Barakallahou fikoum wadiazakoumoullahou hairan
Baaraka'Allahu fik ya Oustaz Alpha BA.
We need more people like you Thanks brother
Dieureudieuf ya oustaze yalla nala yalla maye goudou fane mayco mbolém dioulite❤❤❤
Chiekh alpha dira diaf yalla na yalla fayla aw yiw
Merci beaucoup oustaz alpha ba contane na thi yaw gni nio beuri wax wayei baxna li gueuneu neikh si adouna moy nguay wax di leirale nit gni sur la base du coran et de la suna du prophète tandis que vos ennemis savent tous ce vous dites mais ils refuse de l'accepter en place au lieu de vous répondre par des sources coraniques mais ils versent dans les insultes, dans la violence chapeau oustaz
Mais fane la Sonko wahé ni seugne bi la yakaar adouna ak alakhira j’aimerais bien voir ça soubhanallah
C vrai j'ai vu l'extrait
Oú????
Machallah. C'était un plaisir de t'écouter. Merci pour ces vérités
Yalla am sa fay yalnala Yalla fay. Ahlou bokkalé sen fin sorétoul. Nioun yonént bi moy sounou Serigne.
Wallahi sa Wakh bi weir na machallah
Dangay doul rk
@@watteway3570 😂😂😂lii ngueen Kham
@@watteway3570 kholal doff bi
machalah chiekh alfa
حفظكم الله دوما وأبدا
Y'a des pauvres à touba , ils n'ont qu'à commencer par eux, pour faire qu'ils deviennent riche 😁😁😁😁😁😁
Bon courage .Qu'Allah t'assiste et te protège
Mai sirigne touba li yêpp wakhonako kèn mom serigne touba taloulewon dara loudoul yalla ak yonetebi
Bilahi walahi man khassidAs serigne outéna bou bari ak li yen mouride yi di wkh ak diko dieufé yalla rk momo nioron ak yonete bi psl
Soubhannallah. K'ALLAH NOUS guide inchaallah.
Alpha yalna yalla samale la bopam lerale yi amenagne solo lole yalna yalla guindi weuy reér yi
Merci mon frère tu es très véridique machallah
Bass mome limouy reral si ay nitt barina loll
Wallahi mom mogeuna rérr nieup
Wallahi mom mogeuna rérr nieup
Alouine deine dafa lerr
Sénégalais yi meunou gnoo xeex goor djigueen, meunou gnoo xeex lenn mou sooti, meunou gnoo xeex ak toubaab amm ci moom, ndam.Ta dagnoo ragal toubaab.Sénégalais, lenn kepp la meunn,werante ak xouloo ci tarixa rek lagn meunn. Li coow li di bari yeup, dougnou meussa song toubaab, wala France. Gniy xeexal Sénégal, dama leena yeureum. Fougni jelee ndam, laa xamoul. Xeexu sénégalais ci lamign la yemm. Kougn song rek, da ngaa weet, wala nga neew doole. Sou leen wooree ne, bougn la songuee, ray ci sa mboolo foukk, nga ray ci gnoom, gnaar kepp rek, dougnou la songg mouk.songg kenn kou weet, gaagn ko, ndam amou ci.
Diereudieufé Srgn touba khadimou rasoul
Santal Yalla mila sakk te bayi bokkale
@@watawasawbilhaqWalahi gni sén hol mo deguer té tedjou mano wah lou niouy degu😢😢
Merci beaucoup Oustaz c'est très intéressant vraiment
DEUGUEU BOU WÉR!!!! MASHALLAH
Dieureudieufëti Cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul Beug geum wolou aK yaakar Serigne Touba rek lañuko def😍😍😍❤️
Gueum yalla rek lane koy ak yakar lolou yalla rek lane koye def imbéciles ki nga gueum khamoul ni sakh sa ndeye ak sa bay ame nane
Que le coran et la Sounnah soient nos guides
Dieuredieuf.c'est vraiment triste et inquiétant ce qui se passe dans ce Sénégal.il y'a trop de fous maintenant.bonne continuation.vous avez du courage.barakallahoufikoum.
Macha Allah que Bon dieu te protège Amine
MachaAllah deug gou werr nga wakh . Loula nit wakh te wakhoula diamoul yalla daflay nakh!!
merci beaucoup longue vie Amine ❤️❤️❤️☪️☪️☪️☪️🤲🤲🤲
Nagniou diamou y'allah bay parparlou bi,soubhanallah,Alhamndoulillah,allahouAkbar yâ râbbi 🙏☝️
Tu as parfaitement raison alpha ba.
@@bayembaye1053 astafourlahi soubahanalay
Kou dian ngoul saga la moune
Salam, mon frère merci beaucoup tout ce que vous dites est une triste vérité.
La vérité est unique.
Ce qu'ils disent sont cautionner par leurs guides religieux.
C'est une honte.
Fi seydina mouhamed rek mo Fi nek amoul kenen
Boy bass dafa doff
TVA pose vrai nafekh nga prk les gens ki insulte oustaz alpha tu ne les di rien boy bass dou nitou yalla domou harame la hana dégo limou wahe
@@ablaythiam1748 sa serigne moma gene réwe
@@becayecounta2145.
Mashaalla Alhamdou lilah amna gnou deugou gnou am fit Di wakh té yalla rek takh.
Dieureuf alpha ba
Cheikh omar diagne dou sene morom thiedo mourid bisri gane misra saliou smab mame mor mbaye doul rekj lanouy deff
Mai yaw gni dof nagnou gnom gnep yalla nanou yalla defal soutoureu alhamdoulilah
Machâ Allah Oustaz Alpha Ba
Allah le Tout Puissant est très patient
Un jour viendra où ils seront seul avec Allah Soubkanawatala
Merci mouride yi louniou yakh thi diner mo barri
yalna Yalla dimbali senegal , li niawna trop
les vérités qu'on aime le moins à apprendre ,sont celles qui détruit nos intérêts, la vérité ne blesse pas d'elle même, elle fait mal car elle brise une illusion
Danguay féne aldiana diamou yalla yoboufa kéne
يدخل من يشآء في رحمته
Yalla neina mane may xoôl kouma neixx ma tabal la ci sama yeur mandé
Kone nagn bayi diamou Yalla te def louniou nekh.
Machalla brother 👍 job well done
MERCI BEAUCOUP CHEIKH ALPHA
Mâcha allah ya seydi ❤ barakalah fika
Yana dolila tawfekh si barke Yonente bi sws
Machala dieuredieuf yalla na la yalla faye dieuredieuf
Brother may god bless you job well gone
Tariyakh xélou nitt gni😭 laan molénn diaral di fénn ci tourou sén Serigne
Da
Souphanalh bass ragalal yalla yagui Mélani ya mom Al janna
Macha Allah amna solo gni ay ignorants deug lane
Soubhanallah waham dji eupneu souf souy ramou foumou am yalnanou yallah yeureum
Lolou Medine rék la am
Mouride yi yalla niorelen
@@patriotevraie9940 astafourlahi
Kou bagne yonou mourit nakhar molay raye
الله اكبر
حفظك الله تعالى، من كل شر ومكروه!!!
Cheikh Oumar Diagne dou seni morome
Ngi dal danio reer. Yalnalèn yalla guindi.
Allah tout Puissant protège veille sur Cheikh Oumar Diagne et sa famille contre ces démons ces mécréants avec la complicité de l état du Senegal et leurs autorités religieuses
Machllah amna solo
Basse abdou khadre diahil bou Bone le . Yéfér le nitou safara le
Merci beaucoup ligua wakh dafa lér nagnie machalla
Bayilen sen thiakhane yi kou beug guinar beug ay thiouthiam kou bagne lifi Serigne Touba megne khôl bouy tangue rek ngay deuké je suis pas musulman mais nangou li yalla def si nite gni yalna diam yague
Vous dites la meme chose. Nioune li Yalla wakh rek laniou wakh. Sa bamel yow kasse la ak say dieuf. Bayil khel si lolou bou bakha bakh. Wouyou Yalla te bagn ko bokale ak dara ndakh mom moy kiniou soss mom niou
Khalifa bo hamni yalla doyouko, yonentebii doyouko Serigne bè ko doye mou tahaw fii cii réwmi wahko joulite yeup guène bollè togne .gnou warone tass sèn yonne Wii dèfougnouko guène guènne nane daguéndi menancè watè. Mais yènne ko lène yap. Kou wah cii Yalla guène mèrre kou wah cii yonentebii guénne mèrre. chaque jour guènne woutè ak wahi Yalla ak wahi yonentebii ba parè roussolène guène nane daguèndi guène dii cass
Laa hawla wa laa khouwata illa bi laah. Laai llaaha illa laah
Merci mon frere degue yalla mo ko mome
ماشاء الله. شكر لك اخي الكريم والله والتوحيد هو حق من ربي يحفظك الله وبارك فيك وجزاك
واضح جدا بالقرءان والسنة يهدم بناءالبدع والدعوات الجاهلةفاستمر،
ر بي يحميك
Qu'Allah SwT nous pardonne
Amine
Bayel seringe bi te wahe say wakh
Amine ya rabbi
Wallahy Sénégal Serigne yi déni djoutelgayi djott n'a gnou yewou👆👆👆👆👆👆👆👆
Machallah machallah machallah
Marci
Djiazakallahou khairan. Pour plus d'écoute et de partage , fait des vidéos de moins d'une heure
ماشاء الله، ياأستاذ جزاك الله خيرا وبارك فيك، ماشاء الله!
Merci beucoup cheikh alpha Degue rek ngaye wakh
Li nga wakh amna solo macha Allah deg moy ndiek ta moy moujo
Seydi Ba machaɗlah
Machallah ya cheikh
Machalah oustaz alpha ba
Svp .Montrez-nous la vidéo où Ousmane Sonko dit ces propos .جزاك الله خيرا pour le reste ,vous avez montré des vidéos.
La video existe bel et bien. Essayez de la trouver sur internet
Cheikh alpha ba machalah ci léralbi mai bass défonto nigni peux pare hamoul dara
Masha'Allah
Diamou y'allah ngir aldiana aldiana ohh ndéysane 😭.
Hahahaha
Machaa Allah
C O D na rien di de mal en plus il n parlait pas seulement de serigne touba il a cité d'autres guides religieux .pourquoi seuls ces moutons nous emmerdent
Wallahi deugeu gouwer gua wakh Alpha ba goudeul fane
Vérité absolue 🙏🏾
Merci alpha
سبحان الله عما يشركون
Yalla mouner ci alkourane fa’ anloule lima yourite « lima sopp lay deff » kone nopalal sa pop Serigne touba Likko yalla maye chaque jour day jokk , laffa ligueyal yalla ndiare ko ci seydina Mouhamet ba âme ci lou nitt dotoul âme kone loumou wakh ninane thi tekk sounou beute
Yalla dafa ne kou bayi diouli safara la dieum te Yalla dou nakhate soubhanahou wa ta'ala
@@watawasawbilhaq safara yalla mokko môme
Yaw wakhi yalla naniouy degg balla gniou koy firri
@@serigneabdoulahatdiouf7756 Kone fofou diangal ma degg deggou Yalla
@@watawasawbilhaq fofou degga fa « yalla likko sopp lay deff ‘’ fa anloule lima yourite
@@serigneabdoulahatdiouf7756 Kone manam Yalla mane naniou wakh dara ba nopi douko def ? Wala ?
Alpha est ce vous pouvez de nous amener le passage la ou sonko dit ça car je vois pas dans l'entretien de sonko à touba
Alfa pour quoi doot wakhe thi yéfaryi yi wédi yalla AK yonétebi yawe tarikhayi rék moola Noire wakhame.thi gnidoule diouli dounou wore wakhale çi Lolou
Yéfeur yi yakhalougne dîné dji dara.gni yakh dîné mooy gni né dioulit lagnou té nekou gnoouko@@mamadoundiaye4269
Dieuredieuf
Merci nala yallah faye