Le meilleur Oustaz du Sénégal 👌🏾 Mashallah! Ces temps ci je regarde beaucoup ses prêches. Oustaz Sall est très honnête et j’aime sa pédagogie. Que Dieu continue de le bénir et nous rapprocher de Lui à travers la science que nous partage Oustaz Sall. 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Sama khol laleu def bilahi seye wakhetane laye teudé môme laye yewé môme laye yendo té môme laye fanano té tamite si dimbali borom bi ya takh meu bayi degoulou musique yalleneuleu y’ALLAH SWT Faye leu aldiana firdawsi.
Mashallah ya oustaz oumar sall quel magnifique sermon. Nous suivons et aimons sincèrement ce que vous faites ... que la misericorde et la protection d'Allah soient sur vous et nous tous.
Ya Imam , Oumar Ahmed SALL , Qu'ALLAH vous protège. La vérité est unique et , c'est celle enseignée par Le Coran et la Souna du prophète Mohamed (PSL) dont vous nous rappelez dans tous vos sermons et conférences. La Umma islamique salue et se glorifie de vos enseignements, votre constance , votre enracinement à la vérité authentique . ALHAMDOU LILLAH .
Machallah cheick pour ce beau rappel . Car ALLAH azawadiel a dit rapel car le rapel fait profiter aux croyants. J ai peur pour le senegal avec tout ce ki passe. Mais contuni ton chemin
Salam ya oustaz maleu watt sa sopey ak soldat depuis la France seu ligueye rafetena yalleneuleu y’ALLAH SWT mayeleu force bangueu continé mission yalleneu y’ALLAH SWT sambeleu té areleu.
Mashallah qu’Allah le très haut nous accorde le discernement et nous éloigne du shirk inshallah. Que la paix et la bonté d’Ar Rahman soient avec vous et vos proches.🙏🏼 Vous êtes une lumière pour ceux qui peuvent le voir.
ماشاءالله شيخنا سلّ Y'Allah nañu Borom bi may dëgg dëgg ak toppü... Fuñu fëkk Deukk bu bari Xeureum,Ndjabar Ak Ćaaxaan rëk,bokkü naći Deukk yi geuneu Ndool (Miskiin) mooy Sunugal,surtout la pauvreté intellectuelle Y'Allah Nala Borom bi Tabaaraka wat'aala fayla Yíw Sheikh Oumar Sall... امين يارب العالمين 🤲🏾
Guinaw yalla ak yonnetebi bilahi sama yaye terenama musique ba sonnn bilahi may continuer rk ba yalla deh ma deuglou ben wahtan oustaz Oumar Sall mouy wah si deuglou musique depuis jour bobou sila effacer musique you ma amme yepp batay nii instrument musical dafmay déranger bilahi oustaz Oumar Sall yallah nala yallah fayy lii gua deff si mane
Le meilleur Oustaz du Sénégal 👌🏾 Mashallah! Ces temps ci je regarde beaucoup ses prêches. Oustaz Sall est très honnête et j’aime sa pédagogie. Que Dieu continue de le bénir et nous rapprocher de Lui à travers la science que nous partage Oustaz Sall. 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Senegal seytanee dafa changer Séne vision. Dieu parle au personne intelligente sur le coran comme toi et certain machala tu es extrêmement intelligent
11:13 machallah oustaz Oumar sall yalla nala yalla fayyi
Sama khol laleu def bilahi seye wakhetane laye teudé môme laye yewé môme laye yendo té môme laye fanano té tamite si dimbali borom bi ya takh meu bayi degoulou musique yalleneuleu y’ALLAH SWT Faye leu aldiana firdawsi.
Amine ya rabbi baarakaallahou fiika
Ma sha allah yalna la yallah sameu
Wallahi dou yaw rek musique motax ma bayiko teh soumay dem école momay wetali chaque jour ma diang si mom loubess
Maa chaa Allah
@@alybirante7372 damalay confirmé ci lolu sénégalais douniou lén wakh deug ci diné daniiuy ray rayal rek
Oumar sall sa kaw sa kanam.
Oumar sall force et honneur
Oumar Sall yalleneuleu y’ALLAH SWT sambe.
Amiin ya akhi respect🙏🙏
Mashallah ya oustaz oumar sall quel magnifique sermon. Nous suivons et aimons sincèrement ce que vous faites ... que la misericorde et la protection d'Allah soient sur vous et nous tous.
Cey ya bakh sall ngari yalla nala yalla fay sa takhawou ci dîné ji
All hamdoulila dieu merci oustaz j'aime bien tes paroles et encore une fois un te remercie au fond du cœur que dieu nous faciliter le sunna
Amine ya rabbi
Ameen
Oustaz Omar Sall tu es le meilleur au Sénégal 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢❤
Hafizakallahou yaa oustaz
Yallna yaalla dollil dolei sounna si Sénégal
Amine ya rabbi
Amine ya rabbi
Amine ya rabbi
Machallah ya oustaz oumar sall diazakallahou khayrane amna solo looool
ManchAllah oustaz seule la vérité ki est la bonn voix
Ya Imam , Oumar Ahmed SALL , Qu'ALLAH vous protège. La vérité est unique et , c'est celle enseignée par Le Coran et la Souna du prophète Mohamed (PSL) dont vous nous rappelez dans tous vos sermons et conférences. La Umma islamique salue et se glorifie de vos enseignements, votre constance , votre enracinement à la vérité authentique . ALHAMDOU LILLAH .
Allahou akbar yalla moy rabil samawati wal ardi
Mashallah khol seed na khol feikh na tu nous éduque beaucoup YALLAH n'a la bour bi deiffal jaam... ...LAILAHA ILALA ☝
Machallah cheick pour ce beau rappel . Car ALLAH azawadiel a dit rapel car le rapel fait profiter aux croyants. J ai peur pour le senegal avec tout ce ki passe. Mais contuni ton chemin
Jazakallahu Khayran Qu'Allah vous protége Incha'Allah
Ameeen
Que Dieu guide les sénégalais sur la bonne voie: la voie divine
Yallena yalla dèfale diame ya oustaze, yawe ci alkhourane ake sunna réke ngaye référéwou.
Ameeen
Vérité absolue machallah oustaz bonne continuation
Kou fii doff doff louu ba diamouu yallah dii toppee di nga perte fii perte fii nga dieumm
Y'a oustaz yalla na sa fan goude âme na soloooo lolllll deugue rek gua wokhe
Merci Oustaz pour cette vidéo !!
oustaz oumar Sall merci👌
Machalah ya oustaz
Yallah nala yallah fay oustaz👏🏿
Amatina sollo lool dieureudieuff y'a imam Oumar Ahmad Sall
Allahou Akbar soubanallah que Allah soubanawatallah nous guide sur le droit chemin baarakaallahou fiika
Salam ya oustaz maleu watt sa sopey ak soldat depuis la France seu ligueye rafetena yalleneuleu y’ALLAH SWT mayeleu force bangueu continé mission yalleneu y’ALLAH SWT sambeleu té areleu.
Amine ya rabbi
on va concrétiser at tawhid partout dans le Sénégal inchallah
Machalla deugue rek ke wore machalla oustaz long vie senegale rek gnoye wote aye dioulite tey def yefou yefere 👏👏👏👏👏👏👌👌🙏
Merci beaucoup oustaz Oumar Sall que alla nous donne longue vie inchalla et beaucoup de santé pure vérité
Amine ya rabbi
Amine ya rabbi
YALNAGNOU YALLAH MAYY TAWKHIDE BOU WEER AMINE YA RABBI.MAACHA ALLAH YA OUSTAZ YALNA SA DIAM YAGUE
Amine ya rabbi baarakaallahou fiiki
Amin CV ndeye
Yallah nà yallah mây ñiou imân ak tawhi bou wér ameen yaraby
Amine ya rabbi
Bilay oustaz yalla nala yalla fay.wakh nga lep bamou léer
Machallah oustaz Oumar Ahmad Sall 🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kou geum bidah bou rafet amna si dine beuseul j'aime
Machalah ya Oustaze Yalla nala samma mayla Diam moudiou bou rafete
Wallahi deug rek nga wakh
Yallah naniou ame Tawhid
Ameen
Amine ya rabbi
Amine ya rabbi
qu'Allah vous protège ya oustaz
Machallah ouataz longue vie ❤un homme véridique ☝️😌
Macha Allah docteur Omar Sall ⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐⭐
Yallah nà yallah thiama lén téh ârlen sén taxwây ci dinébi rafétena lol machallah brother yallah na yallah fayla ameen yaraby
Amine ya rabbi
khol séd na , khol sédatina , thiey sama oustaz mala beug billahi
Machallah oustaz Oumar Sall que le Bon Dieu vous protège
MachAllah amneu solo lolou
Yalnaniou yallah mouseul ci bokalé
Amine ya rabbi
Amine ya rabbi
Oustace Oumar que dieu te donera une bonne victoire sur les paratiquant de bidha et le shirkes
Macha allah ya oustaz q ALLA
te benis et te protege amine
Qu'Allah vous protégé et vous récompense pleinement et multiplie des gens comme vous dans la société sénégalaise
Subhana-allah Merci Beaucoup Vraiment oustaz Omar
Je l'aime trop cet oustaz machaallah ❤️ long vie à vous
Machallah que Dieu vous protège
Machallah dieureudieuffe yalle nala yalla faye yiw
Mashallah qu’Allah le très haut nous accorde le discernement et nous éloigne du shirk inshallah. Que la paix et la bonté d’Ar Rahman soient avec vous et vos proches.🙏🏼
Vous êtes une lumière pour ceux qui peuvent le voir.
ماشاءالله شيخنا سلّ
Y'Allah nañu Borom bi may dëgg dëgg ak toppü...
Fuñu fëkk Deukk bu bari Xeureum,Ndjabar
Ak Ćaaxaan rëk,bokkü naći Deukk yi geuneu Ndool (Miskiin) mooy Sunugal,surtout la pauvreté intellectuelle
Y'Allah Nala Borom bi Tabaaraka wat'aala fayla Yíw Sheikh Oumar Sall...
امين يارب العالمين 🤲🏾
Amine ya rabbi
Macha Allah Ya Allah rek ak yénénetibi PSL
Machallah YALLA nala Yalla are lake la fou lake égoule!!
Salam oustaz oumar sall macha Allah dieureudieuf amna solo LOL 🙏🙏👌👌
Macha'allah ya cheikhanna baraka lahou fikum
macha Allah Oustaz baraak'Allahou fik wakh dji amna solo trop
ماشاء الله جزاكم الله خيرا شيخنا الفاضل
Oustaz oumar yall naniou la yalla fayal
Amin
Machalkah dieureudieuf ya outaz
Machallah ya oustaz yalla diam yag yalla guena dolél sunna
S true oustass
Amine ya rabbi
Choukourane 👌💞💟
Mashalla am na solo merci beaucoup
Machallah yallane yallah défalegnou degue ak tope
maachallah que dieu nous guide un bon chemai allahumma amine
Machllh Que dieu vous protège amine inchllh jtm bcq 🤲🏻❤️🥰
Ma cha allah barakal lahou fikoum 🎤
Allahu Akbar, mashaallah ya sheikh
ما شاء الله إنی أحبك فی الله۔ حفظك الله
Guinaw yalla ak yonnetebi bilahi sama yaye terenama musique ba sonnn bilahi may continuer rk ba yalla deh ma deuglou ben wahtan oustaz Oumar Sall mouy wah si deuglou musique depuis jour bobou sila effacer musique you ma amme yepp batay nii instrument musical dafmay déranger bilahi oustaz Oumar Sall yallah nala yallah fayy lii gua deff si mane
Doko rethiou sister machala
Amatina solo ya oustaz yalna yalla defalla diam
ما شاءالله ياأستاذ مفيد جدا
Machaallha oustaz Omar Sall que la paix soit avec vous
Mash'ALLAH
Barak'Allahou fikoum ya oustaz oumar ahmad SALL
Qu'ALLAH TAALA ns guide et ns facilite
Allahumma Aamine
Macha alla oustas amatina solo
salam ya oustaz
contente rekkk
si ni kanouye dime beule halla na halla fayla machalla
la ilaha ilala la ilaha ilala la ilaha ilala
Macha allah ya oustaz
Yallah ngafi yague té wérre
MachaAllah yala naniou sakh té deh si Tawhid
Sous la protection de Allah
Oustaze Imam Omar Sall Yalla nalla yalla ar té diamal la ba so dawo bi bawane di aduna yeup
Machalah Alhamdoulilah Ya Alah
Maa sha ALLAH.
Barakallahou fikhoumm CHEIKH.
جزاكم الله خيرا وبارك فيكم
Masah Allah oustaz barakalhou fikoun
Machallah amnasolo lolle baarakaallahou fiika ya imam
Machallah ya oustaz ♥️♥️♥️
Macha-allah oustaz. .... yalla nagnou y alla mouseul si seytané
Amine ya rabbi
Amine ya rabbi
MACHALLAH oustaz, vraiment j vs aime
choukrane wa oustaz MACHALLAH
Macha’ALLAH amna solo lool ya Oustaz 🙏🏽🙏🏽
Bilahi c'est une vérité indéniable
Oustage oumar sall mala beugue billahi yenga niou beurri
Machalla ya oustaz wakhtane bi am na solo trop yalla na yalla faye
Machallh ya Oustaz
Machalla ya oustaz continue
jazakallahu khair ya oustass .. lerr na ...
Billahi cou gueume yalla doula bagne