Serigne cissé wakhna ngua DEUG dh kouy yoot dou seukeutte Modou lo yalla moko sampeu ile fo niou khamni nii Modou lo yalla moko fii ték bou warré danou rk Dina danou wayeih Modou lo da geum enterrement rk Modou lo kouko beugue dane danguaye ligueye wangni wakh danoul Modou lo Serigne cissé Serigne cissé bou Serigne Babacar ma Sylla nék léne sii bou bakh
@@OusmanemoussaCisse-w3k modou sayou gnou annuler combat birek xamalnie dagnko jekko te ndokh bobou moy sangou dof yi nan ndokhou robinela xamougnu ndokhla bu doywar dagnuy jeul siwo bu ndaw wala bu mak defsi zam zam wala ndoxou robiner serigne bi teye chapelet bi pendant trois moi di werde tourou yalla ak aya alhuran dikosi euff ay mois motax buko sango lides si combat bi yaram bi day fethiekou
@@papadiom9260 saway yala rek mo fete gnep kaw lep lu nit di def si aduna amna koko dakk amna koulako dakk renn lumu souffe souffe amna rene buko geneu souffe lu meun meun beure dina ame kula jaxal sur tout les cote waye tamite dina ame gno jaxal
Mo dégal ki mom Modou pour yaw dafa nieuw nonou rk takoul dara .modou si lou ler la tok lala wax fanou dinthie ay mbiram loxo yakkate doufa ague Modou khamoul sakh niikoy nianal borom dara yi té modou dafa mane nitam
Modou lo ndam rék inchalalah🤲🤲🤲🥰
Siteu défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
Modou lo yalanako yallah soutoural mayeko ndam bou sed gouye inchallahou rabi
Allahouma amiiine
MODOU XLO ❤❤👈👈👂👃👑🤝🦁🦁🦁
Modou lo yalna dane siteu barcké borom touba ahmadou bamba
Machallah kadou yi rafétna 🇺🇸🇺🇸🇺🇸
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Modou sele inechaal Amin yarabi ❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilay modou lo degne ko tegue beute
Serigne cissé wakhna ngua DEUG dh kouy yoot dou seukeutte Modou lo yalla moko sampeu ile fo niou khamni nii Modou lo yalla moko fii ték bou warré danou rk Dina danou wayeih Modou lo da geum enterrement rk Modou lo kouko beugue dane danguaye ligueye wangni wakh danoul Modou lo Serigne cissé Serigne cissé bou Serigne Babacar ma Sylla nék léne sii bou bakh
Bou djeulone Balla taay gnou teur ko, bou djeulone Tapha tine gnou teur ko ! Danoul Balla, Danoul Lac, danoul Bomb, nul ak Gris, gnemewoul Tapha tine ! Maylene gnou Djam moytou lafi nekker ak rekk Khel! Bako Ama djekoo mouy tapaler di pousse ba djeko boul gnou sonal
Vive Modou lo 💯 Amine ❤❤❤❤❤😊😊😊😊😊🎉🎉🎉🎉
Merci Serigne Cissé
Serigne bi diapalema té yalla rék takh sonouna
Lo beugue
AIME 🤝🤲❤👈👂
AIME 👈👈👈
AIME 🤲👃👂👑🤝💪🤲👈👈👈👈
❤❤❤❤❤❤
👂👈👈❤
effectivement modou gayi dagno beug modou danou c grave modou dafa ame galathie jekkou ko taxul ga danko
Yaw nak ya kham modou lo te bilahi Modou souniu ko djeko dou beure😂😂😂
@@OusmanemoussaCisse-w3k modou sayou gnou annuler combat birek xamalnie dagnko jekko te ndokh bobou moy sangou dof yi nan ndokhou robinela xamougnu ndokhla bu doywar dagnuy jeul siwo bu ndaw wala bu mak defsi zam zam wala ndoxou robiner serigne bi teye chapelet bi pendant trois moi di werde tourou yalla ak aya alhuran dikosi euff ay mois motax buko sango lides si combat bi yaram bi day fethiekou
Khana ay galadjam dagn kaay rerrr contre Balla ?? Mdrr Danoul Balla, danoul Lac, Danoul Bomb, nul ak Gris, gnemewoul Tapha tine nga naane ma Galadj 😂. Bou djeulone Tapha tine kham !!!
@@papadiom9260 saway yala rek mo fete gnep kaw lep lu nit di def si aduna amna koko dakk amna koulako dakk renn lumu souffe souffe amna rene buko geneu souffe lu meun meun beure dina ame kula jaxal sur tout les cote waye tamite dina ame gno jaxal
@@papadiom9260 keinn meunta daan niep lamb mo démé nonou
Inchalla yal dakoye Eagles ama ak boy niang douniou siteu sa khalat rek nguay wakh
Boulenko geume deh kouye doule ak Beuze rek Laye weur
Ki dayy wakhtou rék ! Modou Lo mounoule daane Bombardier , Balla Gaye , Baay Mandione , Tapha Tine !!!
Thiey Yalla Li lou ko fi diar? 😮. Sénégalais Mo gueuneu bone Lo Guiss. Bilahi d’où niou bari aldiana Ndakh sokhor
Kham na dara mom
Si katanou yalla inchallah soteu loumou déffe daanou complot biguéne Di déffe modou kharagne lô yeukeunako 😂😂daléne bayi si mbirr rek 😂😂😂
Comba bi anything can happen
Moudou Mbaye wakhou fi dara
🦁🦁👑🤝💪🤲❤👃👂
Féne rék
Koula raw dé
@@aichasecka-8974 yawe khana sa pape leu doule rék laye déf
@@aichasecka-8974 ki damako wédi dépui contre cotdivoir
@@BayelateDiop-f4t yako daka doule domeram dji amo léne béne respect
@@BayelateDiop-f4twédi woko ndax lolou modou lo molay dérangé 😂
Ki meun fen nganane fou siteu Nek
Dagay fen khmo dara
Yawe ya wakhone Sénégal daye dor codivoire 😅😂
AK Angleterre
Et après yalla ko dogal
Sokhor
Ragalal yala khamo dara bayel fen fen bakhol jiebar bakhol ta YAw khamo tuss
Ragalal yallah parparlo ak oute khaliss diaroul li jugement dernier da ame dal...... Yekini doyna preuves
Ki hamoll tousse
Wakho deugue
khamo touss so ayone do andi mbeur gnou djékou ko si gaIadj. Siteu domou sérére pur Ia meuno si mom touss. SITEU FUTUR ROI REK
Ban mbeur la andi niou diekou ko si galathie 😂
Yikini serére la khana guiso ni balla def😂
Nite gune douko khep sakh nek sérère tewoul niou diegou la kahan yeki dii khana kon balla gay douko dan saway dagua nekh khana dagua tite nak
iunchalla Modou dagay dan bou soob yalla
Kahana serer yallah la?
mbadou thiey fila rewmi tolou
kone modou day serignetou pour mane ibadou la sakh
Mo dégal ki mom
Modou pour yaw dafa nieuw nonou rk takoul dara .modou si lou ler la tok lala wax fanou dinthie ay mbiram loxo yakkate doufa ague
Modou khamoul sakh niikoy nianal borom dara yi té modou dafa mane nitam
@@mamithiam949 loy tekni modou founiou dinthie ay mbiram ? 🤣🤣🤣🤣
MODOU XLO ❤❤👈👈👂👃👑🤝🦁🦁🦁
❤❤❤
MODOU XLO ❤❤👈👈👂👃👑🤝🦁🦁🦁
MODOU XLO ❤❤👈👈👂👃👑🤝🦁🦁🦁
❤❤❤❤❤❤