Yaraam dawnaa. Li saagaall naa Sénègal. C' est un des messages les plus positifs de l' année 2019. Sénègal naniou délouci sounouyy xell té djiaapô nekk benn. Felicitations pour la Dame qui a parlé et l' enfant ki a chanté. Dieuredieuuf kepp kou bokk ci ligueyy bou rafette dji. Yalla naa Yalleu arr Sénègal ak képp kou bokk Sénègal. Dieuredieuffeyy Serigne Touba.
CE QUE J'ai ressenti profondément moy mouride yi...c'est la grandeur de l'ISLAM qui les interéssent..et montrez aussi qu'en Islam nous n'avons rien en envier aux arabes ou autres..L'Islam est universelle et dans chaque pays il s'applique avec les realité de ce pays ..Regardez les mourides ils sont musulmans mais aussi il dégagent la fierté africaine..."Chaque génération aura la certitude que je suis venu pour elle" Serigne Touba.
Mane Serigne Touba loumako geureum rek xepko walahi 😭 Kouleu xamoul rek moy naatablé say mbir mais kou xol nou mbir yi di doxei rek xamni sunu borom nangoul nala lepp. Iow ya dieuffeul yalla lou kén dieufoul Mbacké 😭😭 Yalla aduna lalay tambalé fay beu alakhira
Ah souñu mam Abdou lay wad yallana yalla fay la Yaw minga khamni si yaw la yalla diaralé pour mou tégué si yokhoye mourid yi 😭😭 yallana bou dara nakhasaye barké s touba
Masha Allah Allahu akbar yalla moye al karim Serigne Salihou Mbacké ak Serigne El hadji Bara Mbacké ak Serigne Cheikh Sidy Moukhtar Mbacké yalla nalén yalla yeureum ta kharélén al diana firdawsi thi barkéb Serigne Touba Cheikh Ahmadou Bamba khadim Rassoul (SAWS ) Cheikh Mouhamadou mountakha khalif Général des Mouride yalla nakofi yalla yagal ta yoko ak weram
yalla nama yalla defal khéwal bama Mana niawe Senegal ba ziare si massalikul dienann Papier rek lay niann am ko yalla namako yalla May AK keppo kouka ama goul si barkeb seringe touba Amine
Machalah dieuredieuf serigne saliou mb l'initiateur,el hadji bara falilou l batiseur, ch sidi makhtar le constructeur et bailleur principal, serigne mountakha le finisseur... A encore une fois une autre victoire de l'islam par l travail solidaire de fourmi des talibes mouride avec leur fond propre (adiya)sans bailleurs de fonds ni l'appui d l'état.. Bravo .. Bamba merci
le serviteur eternel,toujours omnitient au service de dieu et de son veneré prophet mohamed (psl).vous etes pour la ouma une fierté sans egale en particuler pour le senegal.
Thiey serigne touba dou tarikha na wa senegal goré hamni kutedki sagal l'islam la qui est d'accord besseul j'aime
Ndeye sane amo morome demb amo morome tay tei doko ame ba ila yawmi diinei dieureudieuf Cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul♡♡
Yaraam dawnaa. Li saagaall naa Sénègal. C' est un des messages les plus positifs de l' année 2019. Sénègal naniou délouci sounouyy xell té djiaapô nekk benn. Felicitations pour la Dame qui a parlé et l' enfant ki a chanté. Dieuredieuuf kepp kou bokk ci ligueyy bou rafette dji. Yalla naa Yalleu arr Sénègal ak képp kou bokk Sénègal. Dieuredieuffeyy Serigne Touba.
Amiiine wayy
CE QUE J'ai ressenti profondément moy mouride yi...c'est la grandeur de l'ISLAM qui les interéssent..et montrez aussi qu'en Islam nous n'avons rien en envier aux arabes ou autres..L'Islam est universelle et dans chaque pays il s'applique avec les realité de ce pays ..Regardez les mourides ils sont musulmans mais aussi il dégagent la fierté africaine..."Chaque génération aura la certitude que je suis venu pour elle" Serigne Touba.
Walahi
Wakhi degeu serigne loumou begeu sounou borom defko abdoulaye wade jajeuf
Wallayi.nee arabe ne signifie pas kon est plus musulman k l’es autre dieureffiti borom touba
MashaAllah khol sedd na!! Aythia niou diouk yeigali Dioumay Touba bi inshaAllah 🙏🏾 DIEUREDIEUF Serigne Touba
Li amna solo waya boñio fate ñianal abdoulaye wad yalla nafi yage te war
Khadim Seck wallahi wakhal dé yalla nako yalla dolli wérr ndeyssane
Ak mane yalla na aw fanam goudou lolo
Mane Serigne Touba loumako geureum rek xepko walahi 😭
Kouleu xamoul rek moy naatablé say mbir mais kou xol nou mbir yi di doxei rek xamni sunu borom nangoul nala lepp. Iow ya dieuffeul yalla lou kén dieufoul Mbacké 😭😭
Yalla aduna lalay tambalé fay beu alakhira
Sergine Touba yalla moko bakhé adouna dou touba dou sénégal 🇸🇳 mais dounya profitons
Ah souñu mam Abdou lay wad yallana yalla fay la Yaw minga khamni si yaw la yalla diaralé pour mou tégué si yokhoye mourid yi 😭😭 yallana bou dara nakhasaye barké s touba
Masha Allah Allahu akbar yalla moye al karim Serigne Salihou Mbacké ak Serigne El hadji Bara Mbacké ak Serigne Cheikh Sidy Moukhtar Mbacké yalla nalén yalla yeureum ta kharélén al diana firdawsi thi barkéb Serigne Touba Cheikh Ahmadou Bamba khadim Rassoul (SAWS ) Cheikh Mouhamadou mountakha khalif Général des Mouride yalla nakofi yalla yagal ta yoko ak weram
Aminé yaaraa bii🤲🤲🤲
Aminne yarabbi
Amiin Amiin Amiin Amiin
Amine
Amen
yalla nama yalla defal khéwal bama Mana niawe Senegal ba ziare si massalikul dienann Papier rek lay niann am ko yalla namako yalla May AK keppo kouka ama goul si barkeb seringe touba Amine
Thieuy Borome Touba akaa matt, akaa magg, ken khamoul loumou doon, dieureudieufé serigne Touba ❤️🇸🇳
Machalah dieuredieuf serigne saliou mb l'initiateur,el hadji bara falilou l batiseur, ch sidi makhtar le constructeur et bailleur principal, serigne mountakha le finisseur...
A encore une fois une autre victoire de l'islam par l travail solidaire de fourmi des talibes mouride avec leur fond propre (adiya)sans bailleurs de fonds ni l'appui d l'état..
Bravo ..
Bamba merci
Chapeau à mr mackiyou faye
Kenn dou Serigne Touba
Fier d être mouride🙏🏾🙈
L'islam ama tinna ndame wallahii yalla nagnou yalla dolilee soutoura Thii Barkéé Serigne Touba Khadimou Rassoule AMINE🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Macha Allah cet mosque est très belle la paix resterait toujours au Sénégal incha Allah
le serviteur eternel,toujours omnitient au service de dieu et de son veneré prophet mohamed (psl).vous etes pour la ouma une fierté sans egale en particuler pour le senegal.
Dieureudiefé serigne Touba
Dieuredieufè mbolém gni dééf sén gnaka lép loufa dioulit gnane yalla nagou ci barké Seydina Muhamad psl
Machalla je suis tidiane mai dama contana trop bilahi merci Serigne touba
Machalah gua gneuw vendredi diouli si
Papa nekouna Sénégal motakh
Dieureudieuf borom touba diaaraamaa mame cheikh ibrahima fall lamp abo ridial minouko wone
Liguéyou Serigne Touba bi machallah 🙏🙏🙏🙏
Bilahi guissa kogno dara serigne Touba ken la walahi
Dieureudieufé SERIGNE TOUBA
Macha'allah ! Dieureudieufé Serigne Touba !
Jereujef Serigne Touba, Jarama Mame cheikh Ibrahima fall
mashallah.j'ai pleuré de fierté.mbakiyou am nga ndam.merci Abdoulaye wade.diereudieufetii serigne touba
Dieureudieufé serigne TOUBA DIEUREUDIEFÉ SERIGNE TOUBA MOM REKK MOM DONG MOM KÉSSÉ.YALLA NAGNOU YALLA FAYYAL GNI DIAPP THIE LIGUEY BI BANIOU FII AKK FANIOU DIEUMM.
Allahou akbar cheikhoul xadim déssalatouniou d'ara... Dieureudieufei cheikhoul xadim ❤
Yalla na yalla fayall wade barke serigne bi
Éskéy thieuy Serigne Touba 👌yakari diam yi téy ak euleuk yalla na ngou borom bi tass sissa barkém ta yokk ay léram👐💚💛❤..Serge..25/09/19
Kou donoul Mouride perte nga❤
Il faut pas dire n'importe koi
Maachallah kou yalla def dioulite santal fière d'être mouslim
Thiéy Serigne Touba sa souné mouniouy wonn bopam bimouy binneu beuyit bi Di(lil mountakha wa jahtu fi ndakaru zikran bihi khad koub Kigali makarou ahzil bakhi) neké li mo takhon thiey mbacké lep dafko préparer won motakh sante ko reck moniou warr djeuredieufé ti Serigne Touba
Billahi kén Dou mom Mbacké Dieuredieuf
Bilahi walahi nioun nio xamoul wayé Serigne bi lép la xamon
Machalah cette maison d’Allah est très jolie qu’Allah protège tout les musulman du monde
Mashalah santati mame bamba reik touba TV sein liguey rafeitte
Tawfèkh dall moy am SERIGNE Touba Jajeuf amna solo dh bilahi
Nioun mouride sant rek mo niou warr serigne bi defar na lepp beut bu sett moniouy geneu sagal dieuredieufe serigne touba
yalla doufaye wax bayi jef borom touba amoul morom
Dieureudieufe Abdoulaye Wade kendou Serigne Touba
dama dane see tan natgeo du guis ay afaire you graw mai aujourd hui je suis fier d etre senegalais
Bilahi li koudoul Serigne Touba manoko amm mourid rek moy deugue
Mashallah💓💓💓Dieureudieuf SERIGNE TOUBA👉🙏🙏🙏
Jërëjëfé, borom touba... mbacke bamba point.
Mbiri serigne Touba dou deigne ci dinou yème
Jeureujeufei Borom Touba ❣️😍
Diarama Saa Mame Cheikh🥰🙏
Wallahi sag la si bép dioulitttttt machallah dieureudieuf serigne touba khadiam rasssoul point kén dou mom 👉 ❤ 👌
Theuy serigne touba yalla nagnou ko yalla dolé fayal
Dieureudieufeti Serigne Touba diarrama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lamp baboul mouridina sama yakkar dji
Cheikhoul Khadim yalnako souniou bOrrom gueuneu kaweilll bamou gueuneu kawei barki alkhOuraaane!!! Barki Mame cheikh Ibrahima Fall! Serigne Mountakha yalnaffi yagg lOoool té weirrrr! AbdOulaYe wade souniou Mame dji yow tamittt doundeul lou barri!🇸🇳💚❤️
Jeurey Serigne Touba.... Serigne Mountakha yallanafi yague té weure. Sunu Mame Abdoulaye Wade gathia ngalama yallanafi yagu wade
Allahou Akbar , ALhamdoulillahi jeurjeuf SERIGNE TOUBA
Eskeuy yalla souniou borom dieureudieufé borom Touba ya waral li yeup🙏
Thieuye Serigne touba kéne khamoule loumou done Barképp Serigne Salliou li yéméné billahi 😭😭😭😭😭😭😭😭
Dieureujueff seringe muntaqa seringe touba
Machallah kén dou Serigne Touba billahi
Dieureudieuf Serigne Touba Dieureudieuf Serigne Touba Dieureudieuf Serigne Touba
Sant serigne touba rék❤
Nekk mouride tekhei
Beuguel serigne touba amna tawfekh
Allahou Akbar liguéyal yalla rk mo wor dieureu dieufati s Touba
Dieuredieufaty SERIGNE SALIOU
Srgn mountakha yalla guafi yaag t weer
Dieu merci beaucoup de nous avoir donné Wade comme président de la République qu'elles hommes d'État de tout les temps de notre pays le Sénégal
quand la volonté divine doit s'accomplir même les obstacles deviennent des avantages
C'est très instructifs kemaan rkk la ak mbectei
GOUVERNEMENT BI LAN WARA DIOX MOURIDE YI ...
Machallah ken dou serigne touba ❤❤
Akasa amna solo Dieure dieuf serigne touba yalla moka faye aye Diafam ligueyal yalla Rek mo wore dee
Machalah jummah dji ligeuy binio ko ligeuy yémei neu
Serigne Touba amoul morome si kaw souff
dieuredieufé serigne touba ❤❤❤❤❤❤
Thiey khadim rasoul 😭💓ken khamol lanla rek
Ndaysane diarediuefe serigne touba
Alhamdou lilahi dieureu dieufé borom Touba 🙏❤️
Bravo cde ligéy bi rafetna
dieuredieuf borome touba
Li tambali rék la liguéy yi nék sunu kanam mo eup. Guena djap guena pastéfou.
Dieureudieuffé Serigne Touba liii moko ligueye dou may dafko ligueyal Boromam
Dieuredieufé Serigne Touba ❤
akassa mame bamba kouko bagne diga Fatou fa yallahou ( bamba merci)
Yaw danga masa guiss kou bagne s touba wakh day rafét way
@@mdtvofficiels6705yawe bay yaguimaye togne dei nite daye manou waye yeufou defean yi moye lane
@@ablayebadji2309 deugue rek nak lala wax
Bayiléne di wax lolou rafetoul sakh ci degg wallahi
@@manladeh8923 bayileine di wakh louseine yone neikoule nite daye manou Lima wakh mako wAkh point
@@ablayebadji2309 banga ko waxei nak laci yonou nieup nèkk, bayilène wax you amoul ndiarign Serigne bi santané woul lolou
Dieuredieufé SERIGNE Touba 🙏
Machalah 😍😍😍🙏🙏🙏🙏Serigne Touba Ken la machalah machalah machalah
Macha Allah hole sédena Dieuradieufe Serigne Touba
Kene dou mome Ahmadou Bamba khadim rassoul tes koudoul mome amo liiii dieureufety srg Touba
Mbecktei 🙏 Serigne bamba amoul morom🙏
Machallah dia dieuff makiyou fay
Dieureudieufe serigne touba rek ndong
Machalah dieureudieufati sering Touba amoul morom
Serigne touba kemanou yalla la gnioune wa senegal desenanou kham serigne touba
Dieuredieufety SERIGNE SALIOU khol yi sedeu naa Ken dou Ahmadou
Du jamais vu. Allahou akbar .La plus grande mosquee de l'AFRIQUE DE L'OUEST . LE SENEGAL EST UNE TERRE BENITE .
Dieuradieuffe D Serigne touba
Machalla yaln diam yague senegal
Dieure dieufé serigne TOUBA
Thieyy serigne touba amoul morom
Ken dou serigne touba dieurieudieuf serigne touba alhamdoulilah bima yalla defe mouride
Machalla Serigne Touba Kênla
thieuye segne touba yalnanouko yalla fayal
Djeureudjeufety Serigne Touba Diarra ame Mame Cheikh Ibrahima fall
Morom mou s.touba mousoul am gui naw nabi 💗💗💗💗
Dieureu dieuf Serigne touba merci maître wade
Thiaye s touba amoul morom
dieredieuff s Touba amone fayam ❤️
Machallah amna solo loool thiéy Serigne saliouhou