Le Sénégal va mal niakk geum s'en bop motah niouye diebalou ci serigne yi. Seules les recommandations d'Allah nous sauvent de la vie ci bas et à l 'haut de la
Yén hibatine yi aye nitou safara Guén soudoule wone rassoulahi di cheikhou tidiane Cheikh limou déf moy féxé ba sa baye xam nimouy tobbé yalla Euleuk lép dina lérr sén diné xalé yi soff kén té xamo lén touss doméram
On m'a dit une fois que tu peut rester dans une assemblée et dire tout ce que bon te semble et prononcer:"subxaana rabbika,rabbil iz'zati...." et tous tes péchés seront annulés ! N'est t-il pas trop simple ?
Seugn bi Cheikh lath nagn ko mayyu waliyu yi ak mayu sahabayi nugn mell, muni c'est comme comparer un oiseau qui vole à une fourmi qui marche Personne ne t'a dit que Cheikh mo gueun sahaaba yi, bul tuumal Lo xamul bul thi wax bul thi diingat Bugn fatei ni gnun gnieup dinagn dee dellu thi Borom et alors il tranchera sur ce dont nous divergions. Au lieu de rester là à dire des choses fausses sur ce que font les autres, tu devrais plutôt penser à préparer ton jour à toi N'approche point ce dont tu n'as aucune connaissance lolu ayyah leu qu'Allah nous pardonne et nous guide
Diougué ngua thi professeur madiama fall gnew thi oustaz hady niasse YAW MBA DIAMEU ?!! Di kwa kwa rek en temps que oustaz mey wakh peulhs yepeu di dageu saaga ndakh né oustaz bi peulh le mom lagnuy diapalé té khamou gnou set tan talou gnou dara thi li gnuy wakh ..man ma rouss tey thi sama kheet puular bima doon
Alpha boudé bo guissoul rek do guem yi ngaye wah yeep guisso si dr té guem nga ko guiso yalla guiso yonete ba guiso mallaka guiso dr té guem nga ko après gnonne nga bagne gnou guem li dal sonu hél
Il prier pour Hady Niasse son cas est trés grave. Ces histoires aucune créature sur terre ne les connait à part lui Qu'ALLAH TOUT PUISSANT te guide .Amiiine yarabi
Sounou dinai yonanti bi kouko yakk gni kaye dioubbanti lolou koko defoule mo mandou woule Santale yalla mila may nga guiss koulaye lerale sa diner ngaye diaye gueuneu raire...!!!
Hady Niasse n'a fait que dîre ce qu'il a appris et ce à quoi il croit le TARIKHA TIJANES c'est de l'imagination ça n'a rien à voir avec l'islam . Sénégalais méfiez-vous de ces tarikhas l'islam est simple c'est suivre le coran et les enseignements du prophéte.
Oustaze hadi dalène eup kham kham rék molène méti dieureudieuf oustaze hadu ❤❤❤❤❤❤❤
Daguéna fans oustaze hadi niass dou séne morom torou yonenteyi rek gua kham khamo dara
Hady niass doudal wéreur❤❤❤❤❤❤
Le Sénégal va mal niakk geum s'en bop motah niouye diebalou ci serigne yi. Seules les recommandations d'Allah nous sauvent de la vie ci bas et à l 'haut de la
5/5
Maacha ALLAH yaa Cheikh BA
Serigne Hady Niasse yalna ko sougnou borom doli djam ak khéweul kou bakh la machala ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Nione dh souniou sénégal va trés bien dakh souniou salatoul fatîha❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machala ya cheikh lér yi am na soulo torop machala yal nala yala fay yéw ta samou la ❤
Alpha ba yanag fi yagi te weur
Melni yalla cheikh la Yoni si nioune yalna yalla samm oustaz Alpha
Sénégal c'est pas 95% de musulman mais plutôt 95% de bokalé 😢
@@capricefemelle3168 bayil doull wakho deugg ya meuneu kathie
koula wakh lolou do wakh loula woor bayil soss; sen tarikha bi togn rek nguen xam
🤣🤣🤣tei nga régler ouztaz hady dou sa morom da nga beugueu buzz🤣 alpha bâ da nga tarder
Alpha BA tu manque vraiment de pédagogie
Degoula perdre temps ndakh do indi bene lay sakhel rek ak fissa gueum tôle gay wakhé
Bayil fénal diambur
Wakhal limou wax
المسلم اخوالمسلم لايظلمه ولايخذله ولايكذبه ولايحقره
Lou Chëîkh wakh c vrai khamoooo touss
C'est faux
Cheikh day féne wakhoul deug
Yén hibatine yi aye nitou safara Guén soudoule wone rassoulahi di cheikhou tidiane
Cheikh limou déf moy féxé ba sa baye xam nimouy tobbé yalla
Euleuk lép dina lérr sén diné xalé yi soff kén té xamo lén touss doméram
On m'a dit une fois que tu peut rester dans une assemblée et dire tout ce que bon te semble et prononcer:"subxaana rabbika,rabbil iz'zati...." et tous tes péchés seront annulés ! N'est t-il pas trop simple ?
Walahi lingay weddi yeup loy wax bamou nek deug euleuk dinga am problème bou reuy.
Asalaamou aléye koum yow mi démall diagui khamo dara
Al hady niasse mo la raw.mo la moune si fanne yeupe
Chiekh tidian bay niass adi niass ay fénnkat lane wallahi
Ndèyessane.Qu'ALLAH TOUT PUISSANT vous guide avec hady niasse
Lolou dou dalil liniou wakh moy al qur’an ak sunna kassé té si al qur’an lolou laniou topoulo
@@AssaneDiop-w5m baye rek amna 400million talibé nekal nit te nga kham kiguaye diamou kanla
Sahaba mo eup grade waliyou tabiina mo eup grade waliyou outaz comprendo bou bakh
Yaw miy contre boudé il faut gua tim téré. Cela veut dire que khamo dara
Repodez dans le savoir au lieu d'insulter une chose que le prophète MOHAMAD SAW a interdit wa salam
Waw manosakh layal ligay wedi
yaw omar sall baylene togn
Seugn bi Cheikh lath nagn ko mayyu waliyu yi ak mayu sahabayi nugn mell, muni c'est comme comparer un oiseau qui vole à une fourmi qui marche
Personne ne t'a dit que Cheikh mo gueun sahaaba yi, bul tuumal
Lo xamul bul thi wax bul thi diingat
Bugn fatei ni gnun gnieup dinagn dee dellu thi Borom et alors il tranchera sur ce dont nous divergions.
Au lieu de rester là à dire des choses fausses sur ce que font les autres, tu devrais plutôt penser à préparer ton jour à toi
N'approche point ce dont tu n'as aucune connaissance lolu ayyah leu
qu'Allah nous pardonne et nous guide
Cheikh da nape gayi 😂
Diougué ngua thi professeur madiama fall gnew thi oustaz hady niasse YAW MBA DIAMEU ?!! Di kwa kwa rek en temps que oustaz mey wakh peulhs yepeu di dageu saaga ndakh né oustaz bi peulh le mom lagnuy diapalé té khamou gnou set tan talou gnou dara thi li gnuy wakh ..man ma rouss tey thi sama kheet puular bima doon
Alpha boudé bo guissoul rek do guem yi ngaye wah yeep guisso si dr té guem nga ko guiso yalla guiso yonete ba guiso mallaka guiso dr té guem nga ko après gnonne nga bagne gnou guem li dal sonu hél
Démale diagnui waatte 😂
Il prier pour Hady Niasse son cas est trés grave. Ces histoires aucune créature sur terre ne les connait à part lui
Qu'ALLAH TOUT PUISSANT te guide .Amiiine yarabi
Wadji dafay dingatt rekk en plus nioumouy dingatt nioko eupp ham ham fopou
Mon cher Alpha ba tu ne sais pas ce que tu tentes d et nous expliquer 😅😅😅
😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Imaam malick cheikhe geunou ko dekka tiim
Déjà khel mo naguou wul di tagg sa bopp motakh gniy wotéwo waliiyou yeup gondi wugnuma
Nekal nit te nga kham kiguaye diamou kanla kamilen yalla
😂😂😂rip way 🤣🤣 allpha
Alhamdoulilah ba li hady Niass nekoul si coran bi ,il parle sur un autr livre 😂😂😂
Bis bo bougué kham li yalla wakh si alkourane diappal Tafsir hady Niass si guaye comprends
@@RakhimmaodoBa mai hady Niass mom diaroul topou, nena beneu salatoul fatihi moy tolok un coran
Khamo dara
alpha ba yaw diango khamo dra arabie saoudite katei nga fa nekei jugolot lo kham cii dinee
Serigne bayile dignat Ady niase mola eup kham kham fouf
الهاد زينا نياس بالله والكتاب المنير
Alfa hady niass mola rawe rawe sa baye soula lere rek bakhna alfa SA khamkham bariwoul sauvage nga rek te mandouwo
Deug deug nak Oustaz Alpha laale nala ndax sou nékkoule woone deugg do indi say lép yi
Mais au moins hady niass mandouna....mandouléne si gueum gueum niit yi
Sounou dinai yonanti bi kouko yakk gni kaye dioubbanti lolou koko defoule mo mandou woule
Santale yalla mila may nga guiss koulaye lerale sa diner ngaye diaye gueuneu raire...!!!
@@KhalidouTandjigorayaw yaguana rere guesoul djil alkourane nga deug ko
Hady Niasse n'a fait que dîre ce qu'il a appris et ce à quoi il croit le TARIKHA TIJANES c'est de l'imagination ça n'a rien à voir avec l'islam . Sénégalais méfiez-vous de ces tarikhas l'islam est simple c'est suivre le coran et les enseignements du prophéte.
ما هو الباطن .الباطن علم لا يعلمه الا الله وبعض العبيده
sa leufeul ndaye ya meuna doulle😂
Ya niakk respecter sa Yaye rék ndakh kou respecter yaayame dou sagga 😂
alpha ba mbam khoukh
yaw de ragalo yalla ndax dieufo ndigal bayiwo tereei toumal yonentou rek
Indiile béne preuve si li ngay wakh ni 😂si t'as des arguments bien sûr
Sa way Iaw kamo louy waliou
Adi niass moo dakha bokalé yalla sougnou borom fénn rékk ki moo meuneu féne ki moo bone
Esq khamgua louye bokalé
ASTAGHFIRULAH SOUBHAANALLAH
Alpha Ba et team
Félicitations
Continuez d'éclairer la lanterne des gens de ces aveugles
Bayilene doul...yeen sen mame todioul féne....da nguéne khépp serigne touba ndakh c'est un homme noir .mais inchallah beu yawmal khiyal inchallah...
Madou
Religion Hollywoodien au Sénégal
😂😂😂
Yaw danga rèwww ba dof xamo toussss dangayfènnnn rék bayiil lo khamoul diko wèddi sofnga sawil té teudi
Deugg deugg iow mom khalé nga sois poli bala mala douma
Alpha ba salaphale Ndaye
Li moy wané ni iow mom sa yaye yarou la ndakh soula yaroone di nga KO respecter
Ady n’a dit ça
Sa bayy feroul idji
Lolou est ce que doo ko lathié sa papeu ba paré 😂
En tout cas kou khep lifi MOHAMAD SAW bayi dem di gueum lénéne ..tu es perdu sans savoir
alpha ba thioperatou ndaye
Sawayy liguayy wax ak liii hady wax dou bennn Sax
Hady ay féne rek lafi wakh
Astafiroulah
Oubi sa page UA-cam di doul rek di wéddi gnioula eupp xamxam fouff 😢 gniakk fayda
Hadji Niasse rérelaté katt bou maj la
Yaw mbam gua rk sa bob bou reuy bi
Vraiment hady niasse n'a pas peur de dieu. Moussouma guiss nite bou rér ni hady niasse, rér baparé di rérelaté 🤔
Hady niasse mo moune seeni baay.seeni maam ak seeni yaaye
Sa khol mo diékh rék...mais tu sais k hady niasse ne pèse rien ds l'islam.
Nane yéwou bayi fénal yalla chiekh tidian dafa soss ci dîné yalla bi wallahi
Yonou cheikh tidjane est un secte sataniste. Cheikh tijane est un dadiale !
Talibe Chëîkh yi rek dunioooo sa mormm