Quand j'écoute ces vérités j'ai la chair de poule. Yallah mangui lay niane nga déf tawhid ak suna bou lér nagne ci sama réw Sénégal ak ci aduna bi yeup.
Mane mii déh feu la diarrr!!WAYÉ ALKURAN néna ALLAH guide qui il veut vers le droit chemin.!!Téye chaque jours magui fiirii sarre yii par Béne béne en français.(Le Coran en français App).Si la khame nii salafiste yii nio gueuneu diégué limaye diangue ,si la guéné si tarikhas.Mais yaguoule bima commençer déglou oustaz Oumar sall,mou gueune ma appuyez si lima done khalate.té djinné sonalone sama sokhna chaque jours maye guënte you bone.Téré bou nékk takke nako sama yarame.serigne sii lékk sama khalisse té guissouma changement.Aye IBADOU nioma dimbeuli beu djiné bayi sama sokhna ak Mane té féyouma deureum.Aye ROQIYA késsé léne ma diokhe beu légui ALHAMDOULILLAH!!YALLA Késsé Motakhe maye wakhe.
Ndeysaan il nak moy Sourate 18 - Ayat 17 مَن يَهْدِ ٱللَّهُ فَهُوَ ٱلْمُهْتَدِۖ وَمَن يُضْلِلْ فَلَن تَجِدَ لَهُۥ وَلِيًّا مُّرْشِدًا Celui qu'Allah guide, c'est lui le bien-guidé. Et quiconque Il égare, tu ne trouveras alors pour lui aucun allié pour le mettre sur la bonne voie.
As Salaam Aleyki wa Rahmatou'LLAH Yâ Ma Khâdija ! Qu'Allah le Tout Puissant te préserve et te facilite l'Apprentissage de Notre Noble, Belle et Complète Dînê ISLAM.. ALLAHOUMMA ÂMIINE.
Sa diganté AK sa borom amoul intermédiaire da ngay libre wallahi imaginez NGA am Sokhla diakarlok ciel bi tallal Say lokho Di nian li ngay yeuk sa xol meuno KO expliquer
Mane dh Tidiane la, Talibé Baye, xamouma thi ko diokou wone dh mais Cheikh Ahmed Tidiane mi soss tarixa bi meussoul wakh ni salatoul fatiha mo guene al xuran encore moins di diguaté aldiana à qui que ce soit. Salatoul bi amoul dalil certes, mais niane leu rek bouniouy dieumalé thi souniou borom diaralé ko thi yonente bi saws soko traduiré thi lak bi nga dégg amoul wax bou ay encore moins bou diégué bokalé. Té Cheikh Ibrahim Niass wote woul léne loudoul xam ya allah, woté woul thi boppam té meussoul diklé lénéne loudoul diamou ya allah té meussoul wax kéne mala garantie aldiana. Mouqqadam bou wax ni salatoul fatiha mo guene al xuran mba sa aldiana leerna kokou ay waxou boppam leu thi banéxou bakanam lako waxé...mais kou dougou thi chaîne wa faydou bi Khalif bi thi dieumou boppam moy def Tafsiroul xuraan bi. Seyda Mariama Bint Ibrahima Niass doyna missal thi li taxa diouk Cheikh Ibrahim, deug deug Baye Niass woté woul thi boppam té li nga waxni mom mi soss faydou bi meussouko wax ay ndiabootam meussou niouko wakh. Tok di diouli thi yonente bi saws do lék ba sour, do nélaw ba doyal, do nane ba mandi, do wax lou amoul dieurign, def say farata ak diouli thi yonente bi rek lolou moy Tarbiyou, té ndiorte nani sothi éguone digua xamni Cheikh Ibrahim loudoul kay ma xamal léne séne borom woté wouko, Talibé Baye loudoul ya allah ,ya allah mokoko gueneul Mais nite mom lép lo dougou té guisso thi ligua done sétt am nga plein droit guéne thi bamouy tél...
@@becayecounta2145 Dieu nous a aussi dit de s'occuper que de ce qui nous regarde et à ce que je sache dou iow ni sa morom subir liniou ya allah nara ték, kone diamoul sa wal .
Amena ay wakh yo khamni wakhou biir lagnou Koy toudé. Est-ce que topou Alkhourane AK Yonète bi eupoule sécurité ? En plus YALLA boula ladié euleuk amnga lay parce que c'est clair.
السلام عليك ورحمة الله وبركاته يا ما حد جزاك الله خيرا ورعاك أنا في ورائك
4 роки тому+7
*Lann moyy A't-Tawhîd...* Wéteul Yalla...Contrairou Bokalé Yalla? *_Lannit moy Bokalé?_* Si xamxam yi dafa amm xamxam bouniouy wowé: *Fiqh:* mo layy diangal nouniouy diâmo Yalla. *Hadith:* mo layy diangal nou Yonantibi saws démone doundé Islam ak nane laniou wara doundé l'islam souniou ka beugué roy. Si xamxam bi, ngay diangué *Sounnah* t moyy dokhalinou yonanti bi saws si dîné ak comportement. *Tafsir:* mo layy dégeulo ak comprendre lo kaddou Yalla you nekk si Al Qur'aan. Ak lann la Yalla dioublou si lepp loumou niou wakh si téréwam bi. *Sîrah:* histoire et biographie du Prophète psl et ses compagnons *Tadjwîd:* nann laniouy diangué ak tarée Al Qur'aan...mou diarr yonn té rafet. Et d'autres xamxam. Legui nakk...dafa amm Benn xamxam bou amm solo bouniouy wowé: *A't-Tawhîd:* xamxam bi mo layy diangual nou Yalla wété si Ayy mbiram yeup! Xamal la akkeu Yalla Yi. Yo khamni kou si dialgati dangay dougou si bokalé...minga xamni Yalla dafa wakh Dou ko balé. Si xamxam bii niouy wowé *A't-Tawhîd* ...dafa amm niett xâthie souniou kayy diangualé. Xâthie bou ndieuk bi: *Tawhîd A'r Rouboûbiyah* Si xâthie bi laniou layy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si Al Khalq:* Création Wala Sakk. Moyy Yalla mo Sakk niepp niouy doundou, nitt, animaux yi, Malaka yi, djinné yi, ndokh yi, djant bi, weer wi...lepp si gatal. Nitt sou wakhee Kenn koudoul Yalla mo Sakk Dara si adouna bi...kokou bokalé na Yalla si Tawhîd A'r Rouboûbiyah...si xâthie bouy diangualé Al Khalq. Beu Legui si A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah, Dina niou la fa diangual, ka *Yalla dafa weet si Al Moulk:* moyy Yalla dafa weet si Ngoûr. Momm moyy Bourou nieup. Mou amàt belen xâthie, si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah...bouy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si A't-Tadbîr:* moyy Yalla moyy dokhal mbirou adouna bi, moyy contrôler weurseuk yi, doundou nitt gni ak ngelaw yi...taw Yi...ak événement youy amm si souniouy mbir, Moyy rayé...moyy doundeul. Kou wakh Lou melni kelen moyy diokhé doundou ak dè. Bokalé nga Yalla si weteul Yalla si A't-Tadbîr si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah. Si A't-Tadbîr tammit, laniouy layy leralè ni ke Yalla moyy contrôler souniou affaire yeup comme kann mo niouy Djitté, nou souniouy mbir di demé ak kou Yalla tekk si souniou kaw. Yalla rekk moyy falé. Falé akkeu Yalla la. Kou KO diokh kelen koudoul Yalla danga bokalé Wala diokh Yalla un associé...si mbiroum Fallé. Nitt dafa amm akkeu ak loumou Yayo t momm KO. Yalla amm Ayy akkeu ak loumou Momm. Kenn amoul droit diokh akou Yalla mamam Wala kharitam Wala Serigne niamm, yonanti bi ou qui que ce soit. Momm la yonanti bi saws wakh moyy togne bou geuneu reuy si togne yi. T togne bakhoul. Rawatina togne Yalla. Legui damay teunk Lou dess si résumé xamxam bouniouy wowé A't-Tawhîd: *Niarelou xathie bi...moyy A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah* ...fi laniou layy diangualé Yalla dafa weet si Diâmou Yi...moyy lepp louy Diâmou Yalla. Kenn warou ka defaral Kenn koudoul Yalla. Example de Diâmou Yalla: *Djoulli:* Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kouy dioulil kenen. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A's Salaat...Djoulli. *Yakar:* Yalla rekk laniou wara yakar. Kou yakar kelen koudoul Yalla. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A't-Tawakkoul...yakar. *Diâmou:* Yalla rekk laniou wara diâmou. Kou diâmou kelen koudoul Yalla si bepp façon d'adorer ou diamou. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si Al Ibâdat yi...diâmou yi. Iyyaaka na'hboudou. Yaww rekk laniouy diâmou. *Ndimbeul:* Si Yalla rekk laniou wara sako ndimbeul. Iyyaaka nasta'înou...si Yaww rekk laniouy sako ndimbeul. *Kouy sako ndimbeul si kenen koudoul Yalla en étant en danger*, Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A'l Isti'âna...sakkou ndimbeul. *Note:* *Sakkou ndimbeul bokalé* moyy par example, nga nekk si auto Mouy wadja accidenté, wala nga nekk si biir guethie ngay melni kou nara lapp, wala nga teud si lale febar...nga ragal d, ngay Sakkou ndimbeul si Serigne bou genn adouna pour mou secourir la/dimbalila. So nekee danger, Yalla nga wara wo. Soko defoul bokalé nga. Et y a d'autres comme niann...Yalla rekk laniou wara niann. Niann diâmou la. Ragal kou fi nekoul...Al Khawf. Yalla rekk moka Yayo. Akkeu kamm la. Pour ne pas trop citer d'exemples d'adoration...j'arrête ici. Naniou diangue souniou diné samay mbok djoullit...li yeup dinaniou KO kham et les détails et exemples que g pas cité. Naniou kham bokalé ba douniou KO deff. Douniou KO djigne kou ka defoul. Ndakh khamnaniou loumou donn. Si gatal si A't-Tawhîd A'l Ouloûhiyah, bepp diâmou Yalla, Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kou ka defaral kenen. Diokh nga akkeu Yalla kokou. Ma teudiee fii...ak *xâthie bou moudj bi. A't-Tawhîd Al Asmâ...wa's Siffât.* Fii laniou layy diangualé tourou Yalla Yi ak melo kanam Yi. Moyy ayy tour ak melokane yo khamni Momm rekk mo ka Yayo. Kou diokh tour wala melokanou Yalla. Bokalé nga si borr bi si A't-Tawhîd A'l Asmâ wa's Siffât. Example: Yalla mo amm melokane bo khamni moyy guiss nieup ak lepp. Kou Yakar ni dafa amm Kenn kou layy guiss fo manti nekk. Yangui bokalé kokou akk Yalla si côté bi. Kou Yakar ni Kenn koudoul Yalla khamna si lo nekk fo manti nekk, bokalé nga Yalla si Benn si melokanam yi. Ndakh Yalla rekk moyy xamm nieup si louniou nekk a tout moment. Akkeu kamm la. Legui nakk. D fois pour nga xamm ndakh nitt dafa bokalé fokk nga kham tawhîd...weteul Yalla ak contraire ramm bokalé Yalla. Kou beugeu kham sa dîné, commence par lire la traduction du Coran et les enseignements du Prophète psl dans les livres de hadith comme le jardin des vertueux, Sahih Mouslim, et Sahih Boukhari. Et plus tard...nga commencer diangue deug deug sa diné. Naniou diâmou Yalla ! Naniou diangue souniou diné. Lou bakh si sama wakh si Yalla la diogué !
*Cliquez pour télécharger Audio bi:*
drive.google.com/uc?id=1Nc7XaU8WtJrgKzllu3ltord7dSyaT9UR&export=download
Macha Allah
Sa way Deug Nékhna dé
Naafikhyi ngo Nagouyoul rék
Quand j'écoute ces vérités j'ai la chair de poule. Yallah mangui lay niane nga déf tawhid ak suna bou lér nagne ci sama réw Sénégal ak ci aduna bi yeup.
Son parcours vers ces divers foyers de subversions l’ont enrichie et poussée à cette bienheureuse synthèse qu’elle partage de tout cœur avec Nous
Mane mii déh feu la diarrr!!WAYÉ ALKURAN néna ALLAH guide qui il veut vers le droit chemin.!!Téye chaque jours magui fiirii sarre yii par Béne béne en français.(Le Coran en français App).Si la khame nii salafiste yii nio gueuneu diégué limaye diangue ,si la guéné si tarikhas.Mais yaguoule bima commençer déglou oustaz Oumar sall,mou gueune ma appuyez si lima done khalate.té djinné sonalone sama sokhna chaque jours maye guënte you bone.Téré bou nékk takke nako sama yarame.serigne sii lékk sama khalisse té guissouma changement.Aye IBADOU nioma dimbeuli beu djiné bayi sama sokhna ak Mane té féyouma deureum.Aye ROQIYA késsé léne ma diokhe beu légui ALHAMDOULILLAH!!YALLA Késsé Motakhe maye wakhe.
J'adore écouté cette fille 😘😘
Tu n es pas la seul elle est adorable
Vraiment elle est une fille battente dine nior nako boubakh vraiment du courage حفظك الله ورعاك
Wallahi ton histoire c'est comme celle de Salman Al farissi radiyallahu hanhou qui cherchait la vérité durant partout afin de le trouver après ❤❤❤
Une dame très pertinente, yalnako yalla takhawou
Machaallah sokhna Ma Khady DEUG bou werr tank sougnou rew mi bayyi wougnou bokkalé yalla Bida Yi sougnou rew d'où meussa changer motax deg coran dafa nex
Ndeysaan il nak moy
Sourate 18 - Ayat 17
مَن يَهْدِ ٱللَّهُ فَهُوَ ٱلْمُهْتَدِۖ وَمَن يُضْلِلْ فَلَن تَجِدَ لَهُۥ وَلِيًّا مُّرْشِدًا
Celui qu'Allah guide, c'est lui le bien-guidé. Et quiconque Il égare, tu ne trouveras alors pour lui aucun allié pour le mettre sur la bonne voie.
Qu'Allah te protége.
Nous t'aimons en Allah pour Allah et par Allah
As Salaam Aleyki wa Rahmatou'LLAH Yâ Ma Khâdija ! Qu'Allah le Tout Puissant te préserve et te facilite l'Apprentissage de Notre Noble, Belle et Complète Dînê ISLAM.. ALLAHOUMMA ÂMIINE.
Machalla alkhourane AK souna rek Serigne yi business lagniy def AK woute koulene tagal seni mame
Ma Khady yalnaniou Yalla bolè si Aldiana firdawsi li yomboul sissa age bi ni
Jeunes you barri nio ngui commencé yewou si li khew Sénégal alkhourane ak sunna rek Moy deugueu
Ma Khady masha allah diapal te xamni tawxite moy thiabé aldiana walakhi
Soubhân'ALLAH ! Lii Dawna Yârâme lôle ! 😭😭😭😭
Yalla na yalla yok sa fann thé sakhalla thi yonou deug mouy siratal moustakhim
Du courage ma sœur Macha Allah dieu nous protège inchallah
Merci beaucoup ma Khady
Le problème au Sénégal est que ils savent pas que le tarikha ça existe pas .....alkhuran ak sunna point
MachaAllah qAllah te facilite et te garde❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sa diganté AK sa borom amoul intermédiaire da ngay libre wallahi imaginez NGA am Sokhla diakarlok ciel bi tallal Say lokho Di nian li ngay yeuk sa xol meuno KO expliquer
Longue vie a vous
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته،
Macha Allah, qu'Allah te protège Ma Khady.
Maachallah yalla Nala yalla japale
Amna solo
Ma Khady jtm mane j’ai jamais suivi les marabouts mane coran rekk ak souna🥰
De méme k moi j'ai jamais suivi les tarikha
Macha Allah
Barakal'Lahoufika
YALLA Nala YALLA Same
Diambare ga dh bly Mane tidiane la wayé bouma guidée loudoul deugue damaye bayi tu est parfaitement raison
Waaw coumba la foi n'est pas un jouet kou né am nga foulleu té fiiro ci sa diiné da ngay nax sa bopp
Beugg naa le te Yalla takh
Ndeyssane
Masahala
MashaAllah laf thiat Yalla nala sounou borom sam la arr la té sakhal la boubakh thi alkhouran ak Sunna
Diaradieuf ma khady
Dafa nekh ngay doundou si Yonu coran et Sounnah
Wallahi trop mm
Macha Allah Qu'Allah nous guide vers le droit chemin qu'il nous protège contre le fitena de ce bas monde et l'au-delà
Mane dh Tidiane la, Talibé Baye, xamouma thi ko diokou wone dh mais Cheikh Ahmed Tidiane mi soss tarixa bi meussoul wakh ni salatoul fatiha mo guene al xuran encore moins di diguaté aldiana à qui que ce soit.
Salatoul bi amoul dalil certes, mais niane leu rek bouniouy dieumalé thi souniou borom diaralé ko thi yonente bi saws soko traduiré thi lak bi nga dégg amoul wax bou ay encore moins bou diégué bokalé.
Té Cheikh Ibrahim Niass wote woul léne loudoul xam ya allah, woté woul thi boppam té meussoul diklé lénéne loudoul diamou ya allah té meussoul wax kéne mala garantie aldiana.
Mouqqadam bou wax ni salatoul fatiha mo guene al xuran mba sa aldiana leerna kokou ay waxou boppam leu thi banéxou bakanam lako waxé...mais kou dougou thi chaîne wa faydou bi Khalif bi thi dieumou boppam moy def Tafsiroul xuraan bi.
Seyda Mariama Bint Ibrahima Niass doyna missal thi li taxa diouk Cheikh Ibrahim, deug deug Baye Niass woté woul thi boppam té li nga waxni mom mi soss faydou bi meussouko wax ay ndiabootam meussou niouko wakh.
Tok di diouli thi yonente bi saws do lék ba sour, do nélaw ba doyal, do nane ba mandi, do wax lou amoul dieurign, def say farata ak diouli thi yonente bi rek lolou moy Tarbiyou, té ndiorte nani sothi éguone digua xamni Cheikh Ibrahim loudoul kay ma xamal léne séne borom woté wouko, Talibé Baye loudoul ya allah ,ya allah mokoko gueneul
Mais nite mom lép lo dougou té guisso thi ligua done sétt am nga plein droit guéne thi bamouy tél...
Alhourane ak soune rek mo waure dieu ne nou à pa di de suivre des tarikha
@@becayecounta2145 Dieu nous a aussi dit de s'occuper que de ce qui nous regarde et à ce que je sache dou iow ni sa morom subir liniou ya allah nara ték, kone diamoul sa wal .
Amena ay wakh yo khamni wakhou biir lagnou Koy toudé. Est-ce que topou Alkhourane AK Yonète bi eupoule sécurité ? En plus YALLA boula ladié euleuk amnga lay parce que c'est clair.
Ya rabbi 😭😭😭😭😭😭😭
Machalla
Souvenait vous de dieu est unique
Good job
السلام عليك ورحمة الله وبركاته يا ما حد جزاك الله خيرا ورعاك أنا في ورائك
*Lann moyy A't-Tawhîd...* Wéteul Yalla...Contrairou Bokalé Yalla? *_Lannit moy Bokalé?_*
Si xamxam yi dafa amm xamxam bouniouy wowé:
*Fiqh:* mo layy diangal nouniouy diâmo Yalla.
*Hadith:* mo layy diangal nou Yonantibi saws démone doundé Islam ak nane laniou wara doundé l'islam souniou ka beugué roy. Si xamxam bi, ngay diangué *Sounnah* t moyy dokhalinou yonanti bi saws si dîné ak comportement.
*Tafsir:* mo layy dégeulo ak comprendre lo kaddou Yalla you nekk si Al Qur'aan. Ak lann la Yalla dioublou si lepp loumou niou wakh si téréwam bi.
*Sîrah:* histoire et biographie du Prophète psl et ses compagnons
*Tadjwîd:* nann laniouy diangué ak tarée Al Qur'aan...mou diarr yonn té rafet.
Et d'autres xamxam.
Legui nakk...dafa amm Benn xamxam bou amm solo bouniouy wowé:
*A't-Tawhîd:* xamxam bi mo layy diangual nou Yalla wété si Ayy mbiram yeup! Xamal la akkeu Yalla Yi. Yo khamni kou si dialgati dangay dougou si bokalé...minga xamni Yalla dafa wakh Dou ko balé.
Si xamxam bii niouy wowé *A't-Tawhîd* ...dafa amm niett xâthie souniou kayy diangualé.
Xâthie bou ndieuk bi: *Tawhîd A'r Rouboûbiyah*
Si xâthie bi laniou layy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si Al Khalq:* Création Wala Sakk. Moyy Yalla mo Sakk niepp niouy doundou, nitt, animaux yi, Malaka yi, djinné yi, ndokh yi, djant bi, weer wi...lepp si gatal. Nitt sou wakhee Kenn koudoul Yalla mo Sakk Dara si adouna bi...kokou bokalé na Yalla si Tawhîd A'r Rouboûbiyah...si xâthie bouy diangualé Al Khalq. Beu Legui si A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah, Dina niou la fa diangual, ka *Yalla dafa weet si Al Moulk:* moyy Yalla dafa weet si Ngoûr. Momm moyy Bourou nieup. Mou amàt belen xâthie, si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah...bouy diangualé ni ka *Yalla dafa weet si A't-Tadbîr:* moyy Yalla moyy dokhal mbirou adouna bi, moyy contrôler weurseuk yi, doundou nitt gni ak ngelaw yi...taw Yi...ak événement youy amm si souniouy mbir, Moyy rayé...moyy doundeul. Kou wakh Lou melni kelen moyy diokhé doundou ak dè. Bokalé nga Yalla si weteul Yalla si A't-Tadbîr si biir A't-Tawhîd A'r Rouboûbiyah. Si A't-Tadbîr tammit, laniouy layy leralè ni ke Yalla moyy contrôler souniou affaire yeup comme kann mo niouy Djitté, nou souniouy mbir di demé ak kou Yalla tekk si souniou kaw. Yalla rekk moyy falé. Falé akkeu Yalla la. Kou KO diokh kelen koudoul Yalla danga bokalé Wala diokh Yalla un associé...si mbiroum Fallé. Nitt dafa amm akkeu ak loumou Yayo t momm KO. Yalla amm Ayy akkeu ak loumou Momm. Kenn amoul droit diokh akou Yalla mamam Wala kharitam Wala Serigne niamm, yonanti bi ou qui que ce soit. Momm la yonanti bi saws wakh moyy togne bou geuneu reuy si togne yi. T togne bakhoul. Rawatina togne Yalla.
Legui damay teunk Lou dess si résumé xamxam bouniouy wowé A't-Tawhîd:
*Niarelou xathie bi...moyy A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah* ...fi laniou layy diangualé Yalla dafa weet si Diâmou Yi...moyy lepp louy Diâmou Yalla. Kenn warou ka defaral Kenn koudoul Yalla. Example de Diâmou Yalla:
*Djoulli:* Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kouy dioulil kenen. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A's Salaat...Djoulli.
*Yakar:* Yalla rekk laniou wara yakar. Kou yakar kelen koudoul Yalla. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A't-Tawakkoul...yakar.
*Diâmou:* Yalla rekk laniou wara diâmou. Kou diâmou kelen koudoul Yalla si bepp façon d'adorer ou diamou. Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si Al Ibâdat yi...diâmou yi. Iyyaaka na'hboudou. Yaww rekk laniouy diâmou.
*Ndimbeul:* Si Yalla rekk laniou wara sako ndimbeul. Iyyaaka nasta'înou...si Yaww rekk laniouy sako ndimbeul. *Kouy sako ndimbeul si kenen koudoul Yalla en étant en danger*, Bokalé nga si A't-Tawhîd Al Ouloûhiyah si A'l Isti'âna...sakkou ndimbeul. *Note:* *Sakkou ndimbeul bokalé* moyy par example, nga nekk si auto Mouy wadja accidenté, wala nga nekk si biir guethie ngay melni kou nara lapp, wala nga teud si lale febar...nga ragal d, ngay Sakkou ndimbeul si Serigne bou genn adouna pour mou secourir la/dimbalila. So nekee danger, Yalla nga wara wo. Soko defoul bokalé nga.
Et y a d'autres comme niann...Yalla rekk laniou wara niann. Niann diâmou la. Ragal kou fi nekoul...Al Khawf. Yalla rekk moka Yayo. Akkeu kamm la. Pour ne pas trop citer d'exemples d'adoration...j'arrête ici. Naniou diangue souniou diné samay mbok djoullit...li yeup dinaniou KO kham et les détails et exemples que g pas cité. Naniou kham bokalé ba douniou KO deff. Douniou KO djigne kou ka defoul. Ndakh khamnaniou loumou donn.
Si gatal si A't-Tawhîd A'l Ouloûhiyah, bepp diâmou Yalla, Yalla rekk laniou ka wara defaral. Kou ka defaral kenen. Diokh nga akkeu Yalla kokou.
Ma teudiee fii...ak *xâthie bou moudj bi. A't-Tawhîd Al Asmâ...wa's Siffât.* Fii laniou layy diangualé tourou Yalla Yi ak melo kanam Yi. Moyy ayy tour ak melokane yo khamni Momm rekk mo ka Yayo. Kou diokh tour wala melokanou Yalla. Bokalé nga si borr bi si A't-Tawhîd A'l Asmâ wa's Siffât. Example: Yalla mo amm melokane bo khamni moyy guiss nieup ak lepp. Kou Yakar ni dafa amm Kenn kou layy guiss fo manti nekk. Yangui bokalé kokou akk Yalla si côté bi. Kou Yakar ni Kenn koudoul Yalla khamna si lo nekk fo manti nekk, bokalé nga Yalla si Benn si melokanam yi. Ndakh Yalla rekk moyy xamm nieup si louniou nekk a tout moment. Akkeu kamm la.
Legui nakk. D fois pour nga xamm ndakh nitt dafa bokalé fokk nga kham tawhîd...weteul Yalla ak contraire ramm bokalé Yalla.
Kou beugeu kham sa dîné, commence par lire la traduction du Coran et les enseignements du Prophète psl dans les livres de hadith comme le jardin des vertueux, Sahih Mouslim, et Sahih Boukhari. Et plus tard...nga commencer diangue deug deug sa diné.
Naniou diâmou Yalla ! Naniou diangue souniou diné.
Lou bakh si sama wakh si Yalla la diogué !
😢😢😢😢😢😢😢
Merci amna Solo 👍🏽
M'achallah
Alkhourane ak Sounna rek moy deug
برك الله فيكم يا شيخ آريد رقمك
أستاذ عثمان سيسيه:
*+39 329 444 9387*
Al hagg bil hagg
Momm0
Yalla na yalla yok sa fann thé sakhalla thi yonou deug mouy siratal moustakhim
Machalla