🛑Urgent!! Gaston Mbeng: Dafa Togne Serigne Moustapha Sy Wala Danou Ko Corte

Поділитися
Вставка

КОМЕНТАРІ • 682

  • @SarrMadame
    @SarrMadame 9 місяців тому +98

    Amna loxamni diaroull sakh wakh Serigne Moustapha yénéwoul kén safane diam la yéné nieup yalla xam nako té com Fatouna Nanou rafétall rk mo am solo ❤

    • @yacinesarr1405
      @yacinesarr1405 9 місяців тому +2

      Wahh nga deugue dé

    • @khalifakane8415
      @khalifakane8415 9 місяців тому +3

      Walahi ndeye sane lolou rëk moye li geune

    • @abibtoure1569
      @abibtoure1569 9 місяців тому +3

      Billakhi néna yéné woul kén safara bathi nonam

    • @bloc-notes2570
      @bloc-notes2570 9 місяців тому

      Vraiment

    • @mallbelly8250
      @mallbelly8250 9 місяців тому +4

      Waye martaba dou Bale lolou ngua khamoul

  • @soldarousbabacar7291
    @soldarousbabacar7291 9 місяців тому +33

    Thiey adouna yin guemlin yalla lou am yalla la Gaston yal nako yalla yeureum si batou la ilakh illala

  • @faliloufall9221
    @faliloufall9221 9 місяців тому +14

    Kou nekk ak sa bis, nieuppay dé même Serigne bi dafay dé.

  • @ablayeseck359
    @ablayeseck359 8 місяців тому +2

    Xam xam bou nekk guiss naako mais bou Mara moma doy walahi❤

  • @aliouniang5975
    @aliouniang5975 9 місяців тому +28

    Lokhamnè 2016 le wone ngaye doul rk yalla moye raye gaston yalla nako Yalla yereum

  • @awasene3838
    @awasene3838 9 місяців тому +32

    gaston salif mbengue yalla nako yalla yereum té kharéko aldiana nite kou bakh la kou meunone ndiabotam yalla na yaa tek si ndiabootam lokho inchalla

    • @FatouFaye-ho9bw
      @FatouFaye-ho9bw 9 місяців тому

      Ont sa fou de lui

    • @beuguepirelespatriotes8799
      @beuguepirelespatriotes8799 9 місяців тому

      ​@@FatouFaye-ho9bwyawe loy wakhni ? Yallana nako yalla yeureum té kharéko aldiana

    • @awasene3838
      @awasene3838 9 місяців тому

      @@beuguepirelespatriotes8799 moma diakhal di

    • @seydinadjibril3491
      @seydinadjibril3491 9 місяців тому +1

      Amine

    • @kadamamar6352
      @kadamamar6352 9 місяців тому

      Pa Gaston mbengue yallana khipper aldiana firdaws amine kou bakhon la ter beug ndiabot.....

  • @thianistaNdiaye
    @thianistaNdiaye 9 місяців тому +61

    Togne bahoul ci kenn rawatina nittou yalla bou tolni Serigne Moustapha s'y almaktoum❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @alioudiallo6749
      @alioudiallo6749 9 місяців тому +13

      Merde way,moustapha sy mom khana dou déé..nokoulene feulé ak sy

    • @aboubacarbarry2159
      @aboubacarbarry2159 9 місяців тому

      ​@@alioudiallo6749pppppp0❤❤❤❤❤❤❤pp❤

    • @aboubacarbarry2159
      @aboubacarbarry2159 9 місяців тому

      ​@@alioudiallo6749❤

    • @shamsu-diinetv
      @shamsu-diinetv 9 місяців тому

      ​yaw bokhamé kodoul dé nga wakhno wakhnola ni liloko raye wayé khmngani Gaston tognna gor lamou wakh Boko wakhone sabaye do toke diko protégées 😂😂😂

    • @DioufMaoudo
      @DioufMaoudo 9 місяців тому +3

      Naniouy wakh wakh diou rafét si adji dém dji yalla nako yalla yerem mane mi ndiabotou serigne Moustapha la wakh day rafét

  • @bambaseck7140
    @bambaseck7140 9 місяців тому

    Thank you so much ❤❤❤❤❤

  • @mamadousow880
    @mamadousow880 9 місяців тому +12

    Diaraama Serigne Moustapha Sy Maktoum 🥰

  • @recreationprod7217
    @recreationprod7217 9 місяців тому +26

    Dafa diott niou gana ormal kilifa diné yii nah yalla molènn thièralle ba paré ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @daoudakonte358
      @daoudakonte358 9 місяців тому

      Lolou moy lou wer waye li dal Gaston yalla mo mom jamam lounech laye Def si môme yalla nok yalla yeuremeu

  • @AssaneNdiaye-c1w
    @AssaneNdiaye-c1w 9 місяців тому +26

    Repose en paix Gaston ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
    Wayé niou moy togne nah yalla douko balè❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @mansoursall3093
      @mansoursall3093 9 місяців тому +7

      Gaston tonioul kene besame mo diote mo deme yala rek mo fi nek ligaye khamo si dara

    • @diopelhadjimor6563
      @diopelhadjimor6563 9 місяців тому

      @@mansoursall3093Serigne bi linga wakh amna dei ken weddi wouko …
      Ma wakhla ni S.Moustapha Sy wakh na bess ni yenei woul ken Lou bone bathi ndiabotam
      Mais Martaba nitou Yalla modoul baalé🤷🏾‍♂️
      Malay wakh itam ni guissagouma mane ci addina kouko niakké tegguine mom Serigne Moustapha am moudj bou Rafete ..
      Yoral say beut nak di khool limala wakh

    • @diopelhadjimor6563
      @diopelhadjimor6563 9 місяців тому

      @@mansoursall3093Epui linga wakh bokkoul ci mandou🤷🏾‍♂️
      Bo né Tognoul ken tegooci mandu parcqu kaddu yim ték thi kaw kilifeu diambour kouko teggone thi sa Baye so dé kou fonk sa baye Diaay ko sa bakken 🤷🏾‍♂️…

    • @requinquin1
      @requinquin1 9 місяців тому +1

      ​@@diopelhadjimor6563😂😂😂😂😂 mbatté Yalla diou ndaw. Nékk leen nitt bakhna

    • @diopelhadjimor6563
      @diopelhadjimor6563 9 місяців тому

      @@requinquin1
      tu n’as qu’à essayer mec
      Yangui nonou mongui nonou 🤷🏾‍♂️…

  • @mbayesy3675
    @mbayesy3675 9 місяців тому +10

    Yalna Yalla barkéle soutoural arko serigne moustapha sy maktoum ak ndiabotam ak aye sopéme amine inchallah

  • @bayezaldiallo7262
    @bayezaldiallo7262 9 місяців тому +9

    Respecter l'âme de Gaston..se ke vous faites c pas musulman bande de fanatique.. YALLA nagnou yalla diaigueule

  • @papaamadounael8487
    @papaamadounael8487 9 місяців тому +13

    GASTON yal na firdawsi done deukouwayam tei YALLAH soutoural gnimou bayi ganaw bagnou maguet

  • @Khady-ds7he
    @Khady-ds7he 8 місяців тому +1

    Merci bcp

  • @modoulo8211
    @modoulo8211 9 місяців тому +18

    Nitou Yalla kouko togne guiss kooo😢😢😢😢😢

    • @MrFayemanou
      @MrFayemanou 9 місяців тому +2

      Kouy nitou yalla douu togne

    • @ndiayemaleye2581
      @ndiayemaleye2581 9 місяців тому +2

      ​@@MrFayemanouvraiment fii gnepp nitou yalla lanou

    • @modoulo8211
      @modoulo8211 9 місяців тому +1

      @@MrFayemanou kanla togne?

    • @requinquin1
      @requinquin1 9 місяців тому

      ​@@modoulo8211 Yonnènt Yalla you Tédd yi khana. Béss boune mou toogn leen gratuitement

    • @awafall2349
      @awafall2349 9 місяців тому

      @@modoulo8211 hanaa gnoome kignou deff yalla, billahi euleuk akay metti thja dina tarr lool ndah naagou ak beww

  • @amyniang2642
    @amyniang2642 7 місяців тому +1

    ماشاء الله❤

  • @ElhadjicheikhDia
    @ElhadjicheikhDia 9 місяців тому +5

    Ragall leenn yalla yalla rek moofii neeوما كان لنفس ان تموت إلا بإذن الله

  • @MoustafhDiaw-kw1pu
    @MoustafhDiaw-kw1pu 9 місяців тому +5

    ماشاء الله ياأستاذ جزاك الله خيرا فرِحنا بِكَ :وَاللَّهِ لَقَدْصَدَقْتَ

  • @elizabethndione8558
    @elizabethndione8558 9 місяців тому +7

    C dieu qui est la gaston paix a ton âme que firdawsi soit ta demeure éternelle homme de vérité

  • @ElhadjiBa-v4s
    @ElhadjiBa-v4s 8 місяців тому +1

    Fazadahou llahou nourou fil khabri amine

  • @daoudadiouf-zu1fi
    @daoudadiouf-zu1fi 9 місяців тому

    Bayilen wakh safane Serigne Moustapha taloul lingay wakh nagnou gnanal rék Gaston yalla yereum ko xareko adjana firdawsi

  • @mamadoudjigo7006
    @mamadoudjigo7006 9 місяців тому

    😂😂😂😂😂😂😊😊 nono Sénégal mi nekh

  • @djibrildiop9630
    @djibrildiop9630 9 місяців тому +1

    TABARAKALAH MACHA-ALAH LIGUA WOKH AMNA SOLO TARRKALAH, DINA BAYILO XELL NGI SÉN KHOL RAFÉTOUL SI SERIGNE MOUSTAPHA SY AL MOURCHID WAL MAKTOUM ❤️ DIARAMA, A BON ANTANDEUR

  • @Tidianesarr-jc7xv
    @Tidianesarr-jc7xv 9 місяців тому +18

    Togne bakhoule diarama serigne moustapha sy almactoum sama serigne ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

    • @badarrangom1414
      @badarrangom1414 9 місяців тому

      Sa serigne sou meunone dara lay macky

    • @boromfass1513
      @boromfass1513 9 місяців тому

      Manoul yalla rk mo meune lolou laniou diangaal koudoul yalla nène ngeu diarama s.moustapha sy

    • @requinquin1
      @requinquin1 9 місяців тому

      @@badarrangom1414 😂😂😂
      Bou meunoon dara konn parti politique bi di PUR tékki dara ci deukk bi.

    • @mamadoumansourfaye9540
      @mamadoumansourfaye9540 8 місяців тому

      Da nga contane kone si dé wou Gastón bi

  • @NdeyeNdiaye-p1p
    @NdeyeNdiaye-p1p 9 місяців тому +30

    Machallah ❤️ Linga wax degue bou wér la 💝 diarama Serigne Moustapha Sy al maktoum ❤️

  • @YoussouLo-ku9lz
    @YoussouLo-ku9lz 9 місяців тому +2

    Serigne Gaston mbengeu yallna KO bourr yalla yeureum ta yeureum Niou ta kharé KO aldianay firdawsi amine inchallahou rabouna AK mboleem dioulit

  • @assaneniang3473
    @assaneniang3473 9 місяців тому +13

    Suma sañon daal ñu tourner la page te baña dugal kilifa gi ci lumu adulul boppam. Wa salaam!

    • @KhalifaababacarBa-m5z
      @KhalifaababacarBa-m5z 9 місяців тому +4

      Franchement lolou la gueume

    • @sellgaye4279
      @sellgaye4279 9 місяців тому +1

      Linga wax mooy dëggë kén waruci woon tudd goor gui
      Nañko ñaanal ndiegal rék xawmako ludul ci écran 📺
      Dëgëla nak martaba nitu yalla dubaale

    • @assaneniang3473
      @assaneniang3473 9 місяців тому

      @@KhalifaababacarBa-m5zdafa amm ñu sawarr lamiñ rekk

    • @cheikhdme412
      @cheikhdme412 9 місяців тому +1

      Vraiment

  • @morndiaye-ki9pu
    @morndiaye-ki9pu 9 місяців тому +5

    Mane dama wrou min nitkou gène adouna gèn nèk si dèrambi ni yallnako yalla yeureume gaston

  • @BOYKA_PRO_5.11
    @BOYKA_PRO_5.11 9 місяців тому +4

    Ndiarama SERIGNE MOUSTAPHA SY ALMAKTOUM Défar Naniou Défal Naniou ☝️

  • @meissafall8703
    @meissafall8703 9 місяців тому +13

    Je suis triste😔😔😔 Walahi ou va mon PAYS? nagnou bayi xel ni adouna kou mataleu DÉMÊU, ALLAH SHW wakh nako si sourate 2 BAKHARA, VERSET 156 INNA LILLAHI WA INNA ILEYHI RAOUJOUNNI, GASTON YALENAKO ALLAH SHW WANALAI AK SEYDINA MOHAMMAD SAW MÔME AK GNIFEU NEK YEUP☝️🕋🤲

    • @khalifadiop6739
      @khalifadiop6739 9 місяців тому

      Saway gaston loumou am dieul

    • @requinquin1
      @requinquin1 9 місяців тому +3

      ​@@khalifadiop6739 bonn nga dé. En tt cas lo beugoul koula ko séédél boulko séédél sa moroom. Kénn momou fa lénn. Yalla mo moom lépp té kouko nékh mou may ko louko nékh

    • @requinquin1
      @requinquin1 9 місяців тому +1

      Meïssa Fall amiine❤

  • @elimanehann5286
    @elimanehann5286 9 місяців тому +6

    Machallah amna solo toropp merci beaucoup

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj 9 місяців тому +6

    Man esk kham ngén louma diakhal man bilahi walahi watalahi massou ma Guiss kou raw Serigne Moustapha Sy Al maktoum wala nitt kouko eupp kham kham bilahi massou mako Guiss kouko guiss rk wakhma gaw😂😂😂

    • @requinquin1
      @requinquin1 9 місяців тому

      Man dé guiss nako
      Yalla ak ay Yonnèntaam. Sahabas ba ya ak nia ca topou ak nia ca topaat. Ci gatal daal moy gni am IMPORTANCE ci kanamou Yalla mou toudou leen ci Al Qur'àn ak Sunna.
      Gni ci déss niép ci seen geum Yalla djamou ko ak wéteul ko ci laniouy rawanté bilahi.

  • @diopfaya3471
    @diopfaya3471 9 місяців тому +1

    Kou guena adouna de nianal ko ndiegueul mo gueune diko soulil ay reuthieu reuthieum.
    Domou adama matoul.
    Gaston kou bakhla won.
    Yalla nako yalla kharé aldiana.
    Bi analyse ci kou fatou ba paré doyna waar lool.
    Allahou akbar.
    Reposes en paix père Gaston.r

  • @alegueye3747
    @alegueye3747 9 місяців тому +7

    Kou tonge seringe Moustapha sy Al maktoum loula dal bakhna.

  • @yvefay620
    @yvefay620 9 місяців тому +1

    Il a ete decrete depuis sa naissance que ce jour était la fin de son parcours terrestre priez pour lui et tout court au lieu de polemiquer Tlut un chacun est kilifeu ...Kilifeu ou non *togn* mome xi bopam mo bakhoul ..il faut tjrs respecter..

  • @marietoukeita847
    @marietoukeita847 9 місяців тому +5

    Bilahi sy Malick kou beugoul diam rk molaye togne ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @AssaneNdiaye-c1w
    @AssaneNdiaye-c1w 9 місяців тому +3

    Machalla âme n’a solo❤❤❤❤❤❤❤ 4:14 😊

  • @alindao6836
    @alindao6836 9 місяців тому +8

    Cheikh seydi Mouhamadoul Moustapha sy Al maktoum Al Mourchid diarama❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @MorToure-pv9gb
    @MorToure-pv9gb 9 місяців тому +1

    Diaram serigne moustapha sy macah allha amna solo ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🥰

  • @aboubacarfall1299
    @aboubacarfall1299 9 місяців тому +8

    Yalna yalla sam Serigne Moustapha s'y Almaktoum borom diamono s'y yaniou doye ya donou yonénet bi diarama ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @linegueye6211
    @linegueye6211 9 місяців тому +6

    Yalna ko yalla khare aldiana firdawsi diarama Sy al maktoum ❤️💕

  • @Sankarad
    @Sankarad 9 місяців тому +4

    Machallah yalla nako yalla yeureum mé nagnou gueneu worma late Serigne Moustapha sy depuis bimou attaque Serigne Moustapha sy la guedja weurrrr

  • @azizgueye2952
    @azizgueye2952 9 місяців тому +1

    Yalnako yala yeureum tabalko aldiana firdawsi

  • @ramatadiop3806
    @ramatadiop3806 9 місяців тому

    Macha allah amena solo lolou mome amena yalla n'alla yalla same samal gnou sougnou Responsable Moral

  • @aliouciss2877
    @aliouciss2877 9 місяців тому +1

    Merci beaucoup une analyse pertinente Macha Allah

  • @AdamaSeck-v5q
    @AdamaSeck-v5q 9 місяців тому +4

    Machallah ken duo sarigne Moustapha sy🙏

  • @MoustaphaGueye-y8p
    @MoustaphaGueye-y8p 9 місяців тому +3

    Diarama serigne moustapha sy almatoume

  • @laminesarr7599
    @laminesarr7599 9 місяців тому +1

    Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @goldtvsenegal3738
    @goldtvsenegal3738 9 місяців тому +5

    Walaye ❤❤❤❤

  • @MamemaremeDiop-ve3vz
    @MamemaremeDiop-ve3vz 9 місяців тому +1

    diarama mourchid wakh lin diarama ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @elhadjigaye979
    @elhadjigaye979 9 місяців тому +7

    Macha Allah

  • @AladjiBa-q7m
    @AladjiBa-q7m 9 місяців тому +1

    ❤❤sy❤

  • @dmwmdaaraymourchid4121
    @dmwmdaaraymourchid4121 9 місяців тому +4

    Togne bakhoul Diarama Serigne Moustapha Sy Al makhtoum jërëjëf ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @AichaNiane-jy8cr
    @AichaNiane-jy8cr 9 місяців тому +2

    Masala sama goregu❤❤❤

  • @Ndaoterangua5010
    @Ndaoterangua5010 9 місяців тому +11

    Wakh djih dàll lénn lah képouh kouma yeuk nih daguaa bagne S Moustapha Sy Al Maktoum
    Bagne naalah bah yawmal khiyam

    • @ousmanecisse4262
      @ousmanecisse4262 9 місяців тому

      Wallahi suniu goor rk seydi Mouhamedal Moustapha sy❤❤❤❤❤❤❤

    • @ndiayemouhamed9078
      @ndiayemouhamed9078 8 місяців тому

      Yaw domeram daguen xamadi yorou woulen

  • @mbfa9157
    @mbfa9157 9 місяців тому +2

    Yalna yalla KHAREKO ALDIANA AMINE

  • @MansourDiop-y6j
    @MansourDiop-y6j 9 місяців тому +5

    Diarama Serigne Moustapha Sy almaktum yalla nako yalla samoula té arko diarul ragal dafa togne waliyu té la famille Sy kuleen massa togne guiss gako wédi nak guis boku thi ku wédi na def Serigne Moustapha Sy mo donu Serigne cheikh Ahmed Tidiane Sy té been sik amu thi donu Mame Babacar Sy té ben sik amu thi diarama Serigne Moustapha Sy almaktum ❤

  • @aichaka6635
    @aichaka6635 9 місяців тому +2

    Salam Aleykoum
    Mame Cheikh Ahmed Tidiane Sy Al Maktoum dafniou diangal ni togne bakhoul moukk,
    Té niakk Orma kouko meusseu déf nittou Yallah bala nga déh guisko

  • @dudusenea.tidiani8870
    @dudusenea.tidiani8870 9 місяців тому +1

    Goor gui yalna fi yag té weur lol ❤❤ Dieureudieuf oustaz

  • @Beugdeug
    @Beugdeug 9 місяців тому +1

    Yalla rek mofi nek,

  • @DaoudaThiam-sc9fl
    @DaoudaThiam-sc9fl 9 місяців тому

    Ma cha Allah Sama oustaz

  • @madembadiop9961
    @madembadiop9961 9 місяців тому +1

    Cousa apou diott nga deme yala rék mofi nèk

  • @PapaModouMbaye
    @PapaModouMbaye 9 місяців тому +2

    Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤

  • @aminatambaye9756
    @aminatambaye9756 9 місяців тому +2

    Paix à son âme

  • @ibrahimatall9480
    @ibrahimatall9480 9 місяців тому +1

    Yalna yalla sam sering moustapha sy al maktoum❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj 9 місяців тому +3

    Diarama Serigne Moustapha Sy Al maktoum walahi watalahi amoulo morome Sy Malick goudeul ay fann wéreul yague fi Loll té ande ak wérr ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Beugdeug
    @Beugdeug 9 місяців тому +2

    Personne n'a dit que la mort de Gaston est due à ça, bien sûr j'avais pas apprécié les dires de monsieur que tu as cité, c'était pas la peine d'y revenir du fait qu'il n'est plus de ce monde mon cher

  • @AmaraGueye
    @AmaraGueye 9 місяців тому +7

    Lou leer ga wax Sy malik gou dou Fan AK weer sy malik amoul mo Rom ❤❤❤❤❤❤❤

  • @khalifambaye8658
    @khalifambaye8658 9 місяців тому +2

    Walay ndeysan❤❤❤❤

  • @cheikhkane9237
    @cheikhkane9237 9 місяців тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ماشاء الله

  • @SeckMody-ur4yj
    @SeckMody-ur4yj 9 місяців тому

    Diarama Serigne Moustapha s'y machallah ❤❤❤❤❤

  • @AbdoulBa-g6d
    @AbdoulBa-g6d 9 місяців тому

    Baye len fen 😢😢😢

  • @patehjallow7661
    @patehjallow7661 9 місяців тому

    Shubhanallah shubhanallh shubhanallah wula hawllah wulaquhwatah

  • @papeibrakebe4435
    @papeibrakebe4435 9 місяців тому +8

    Moye tou bakhe na de rawatina ko melne serigne moustapha sy al maktoume

  • @boubacarbalde2445
    @boubacarbalde2445 9 місяців тому

    FatabarakAllahu nala Yallah Sagal mbokk mi !!

  • @ElhadjibocarDiop-kf6xl
    @ElhadjibocarDiop-kf6xl 9 місяців тому

    Que fisdawshi soit sa demeure éternelle bijahi seydil wara 🤲

  • @fatouseck4915
    @fatouseck4915 9 місяців тому +4

    Yalla rek moye yalla bayilene Serigne yi di teike place yalla dieu et unique bati guéne wakh té ame diote paix a san âme père Gaston nit kou deguou Sénégal beugouniou kou deguou vive le Sénégal yalana nieup ame diame

  • @AblayeDiop-um6xw
    @AblayeDiop-um6xw 9 місяців тому +4

    Koubagne Serigne Moustapha Sy diou bagnla

  • @damekebe29
    @damekebe29 9 місяців тому +6

    Faté lène lolou. Serigne Moustapha Sy gni ko massa wakh lou gnaw guis nagnou ko. Mais adina amoul solo. Tournons la page

  • @GoraNdiaye-zh6wm
    @GoraNdiaye-zh6wm 9 місяців тому +2

    Walay ndéyssane ❤❤❤ Sy Malick amoul morom

  • @babacardiouf3176
    @babacardiouf3176 9 місяців тому +2

    Wakh nga deugue merci

  • @nadialeye8972
    @nadialeye8972 9 місяців тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉

  • @moussafaye6263
    @moussafaye6263 9 місяців тому

    Mouchetapha Sy toujours mou manqué respect ay kilifa, arrêtez Yallah réck moo niéw. Dioullite d'où wakh yénne yii

  • @mamadoundiaye9477
    @mamadoundiaye9477 9 місяців тому +3

    Machallha ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️

  • @Malick-l7s
    @Malick-l7s 9 місяців тому +2

    المرتبة لا تسامح

    • @ElhadjicheikhDia
      @ElhadjicheikhDia 9 місяців тому

      المرتبة لاتسامح ذالك فضول

  • @KhalifaNdiaye-j3j
    @KhalifaNdiaye-j3j 9 місяців тому +6

    Gaston repose en paix yalna yalla yeureumko daffa togne nak nitt kou bakh vraiment

  • @alindao6836
    @alindao6836 9 місяців тому +14

    Martaba nitou yalla daflay topou basi bamél

  • @papemoduneseck5775
    @papemoduneseck5775 9 місяців тому

    Macah alha ❤

  • @mouhamadoudiagne3789
    @mouhamadoudiagne3789 9 місяців тому +1

    Ragaleen.yalla , Yalla tek mo fi nekk , inalilahi wa inailehi.radjikjoon a Dieu nous appzrteno's et a Dieu.nous retournerons

  • @thiounesaliou5956
    @thiounesaliou5956 9 місяців тому +2

    Diarama Serigne Moustapha sy all macktom ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @NoguayeThiam-su9ke
    @NoguayeThiam-su9ke 9 місяців тому

    اذكروامحاسن موتاكم وكفواعن مساويهم.

  • @mbayediop299
    @mbayediop299 9 місяців тому

    Bonne saine serigne moy yala

  • @NdiombaNdiaye
    @NdiombaNdiaye 9 місяців тому +1

    Ndaye sans yalla nako yalla khare aldjna inchalla

  • @moussakeita9085
    @moussakeita9085 8 місяців тому +1

    Kou dee, say fana jeex. Combien de fois votre soi-disant marabout et son fils ont attaqué Allah et certains de ses prophètes ? Vous ne voyez jamais ca. Ne soyez pas des suiveurs aveugles. Ouvrez vos yeux et regardez ce qui se passe autour de vous, avant qu'il ne soit trop tard.
    A bon entendeur, salut.

    • @diopndiawar932
      @diopndiawar932 8 місяців тому

      Serigne Moustapha amoul bène batine Say Say bou reuy leu

  • @taphakebe983
    @taphakebe983 9 місяців тому +2

    Machalla amna solo dege rek ga wakh

  • @ftinfoftinfo4027
    @ftinfoftinfo4027 9 місяців тому +1

    والله أعلم 🙏✅

  • @MariamaWade-qv1gp
    @MariamaWade-qv1gp 9 місяців тому +6

    Machalla 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🥰🥰🥰🥰

  • @sadamoumamecheikh
    @sadamoumamecheikh 9 місяців тому +1

    Walahi Cheikh Seydi Mouhamadou Moustapha Sy Al maktoum gor deugg la🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰

  • @wakhdeugguetayallatakh8129
    @wakhdeugguetayallatakh8129 9 місяців тому +2

    Legui tapha sy mom mi toogne ay yonenté nak danguene di fen rekk dafa matal dem