Il y a eu 5 grands mariages au Sénégal en 2024 dont celui de la fille de Aziz Ndiaye, Mbackiyou Faye et ses filles, Zeyna Ndour, Faynara en fait partie. Que vos mariages vous apporte du bonheur. C’est beau tout ce folklore mais c’est beaucoup de gaspillage on dirait. Moi je dirais qu’on ne vit une fois et il faut marquer son passage sur terre surtout pour des événements pareils quand Dieu a mis les moyens dans les poches de ses sujets. Par contre les yeby à outrance, je ne suis pas d’accord pour ça. Mais tout était bien organisé. Félicitations
Mandoul... yalla moy borom diami ...té mo kham lougnou xamoul...faut pas déstabiliser les personnes qui font des efforts pour tenir à leur religion malgré les erreurs
Occupé de vos oignons sounou mame aliou ardo sow defna lep diokhena ay cité ay billets makka ay djiouma di fathie malade yi didef lou bakh si rewmi di doundeul ay domou adamayi même pithie yi ak malla yi kouye doundeul malla do bayi domou adama gnioune famille yi tamite gniougui roy si mome yaw lo def critique critiqué
Kouye doundeul malla les animaux do bayi domou adama yaw mba yagui djiouli di sak sarakh nite day mandou khamoko khamoula tt sa ces la jalousie té day rey
Mes attends c son mariage avec le petit fils de milliardaire aliou sow.donc kou neck ak ligua tolol reck guay dépenser. Pour les talibé c autre chose mes demandes à l'état. Mes li c le plus beau jour de leur vie
Ma chaallah heureux ménage bayil leine diambour zeyna Ndour a fait plusieurs jours de mariage kouneik ak sa weursseuk Allahou ma barik
Machalah yalla n'a seuy bi barké AK diabot guou barké Thie barké seydina mouhamet saws
Sa khewe bi riche na faynara Macha allah lafe thiate yalna yala barbele amineee ❤❤
MachAlla ohh la joie de l’époux l’aff thiattt wayyy❤❤❤
Il y a eu 5 grands mariages au Sénégal en 2024 dont celui de la fille de Aziz Ndiaye, Mbackiyou Faye et ses filles, Zeyna Ndour, Faynara en fait partie. Que vos mariages vous apporte du bonheur. C’est beau tout ce folklore mais c’est beaucoup de gaspillage on dirait. Moi je dirais qu’on ne vit une fois et il faut marquer son passage sur terre surtout pour des événements pareils quand Dieu a mis les moyens dans les poches de ses sujets. Par contre les yeby à outrance, je ne suis pas d’accord pour ça. Mais tout était bien organisé. Félicitations
Ya gnak kignane...Amiiiiine
Et zieyna baldé
@ je n’ai pas vu ses TERANGA et c’est de tout ça que je parle, je l’inclurais pas
Bayilene wakhe dji meuneko defko ayoule c’est une fois dans ta vie❤dokhalale
Yalna sounou birome barkel leip amine
Alakhouma amine 🤲🤲🥰
Heureux ménage mes enfants que du bonheur sur vous Allahou ma barik 🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿❤❤
Machallah ❤mariage de l'année ❤
Bilay célibataire moh rafet khol mangui rée 😂rek Machallah yalla na seybi barkél 🤲🏽🙏🏽
Bo rétanoul loye def 😂😂légui taye sa beusse inchalla
Machallah très jolie sa ma sopee AKa yiwe❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla tres Jolie 🥰 ❤heureux ménage
Bleu bi rafétna ❤
MashaALLAH
Ma vie❤❤❤❤❤❤
Thiey yallah mariage rek nga mourékou. Yalla nagnou yallah yeureume
Happy couple Machallah,he can’t stop laughing
Ouiiiii il est trop heureux même 😂😂😂
Machalla 6
*Maa shaa Allah
Lii nekhnaa❤❤❤❤❤
Machallah ❤❤❤
billaahi lii neexna, mais tenue bi du tenue ibadou deh😃 walla danga aj ibadou bi ba xewbi jalleu?😂
Mandoul... yalla moy borom diami ...té mo kham lougnou xamoul...faut pas déstabiliser les personnes qui font des efforts pour tenir à leur religion malgré les erreurs
Merci bcp bom amna louko doye si dinné dji té douko wax
mangi contaan rek di siign🤣🤣
Qui est le Mari, qu est ce qu il fait dans la vie??
ma question est dancent ils vraiment sur du waly? leur dance n'a rien a voir avec la chanson... Monteur yereum niou bok
Donner du pain a ceux qui l'on pas
Occupé de vos oignons sounou mame aliou ardo sow defna lep diokhena ay cité ay billets makka ay djiouma di fathie malade yi didef lou bakh si rewmi di doundeul ay domou adamayi même pithie yi ak malla yi kouye doundeul malla do bayi domou adama gnioune famille yi tamite gniougui roy si mome yaw lo def critique critiqué
❤❤❤❤❤
Faynara comme toi et ton mari peut traiter tout ça penser à ceux qui l'on pas surtout les talibè
Kouye doundeul malla les animaux do bayi domou adama yaw mba yagui djiouli di sak sarakh nite day mandou khamoko khamoula tt sa ces la jalousie té day rey
Mes attends c son mariage avec le petit fils de milliardaire aliou sow.donc kou neck ak ligua tolol reck guay dépenser. Pour les talibé c autre chose mes demandes à l'état. Mes li c le plus beau jour de leur vie
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤