Waa yaw yaay fall ndigueul , nioune déy nio gui siarré bou baakh téy djeguelou di la khamalit loo dounde doyoul, thiant gui doy na war , la gua sikar moom yaay doy na kééman. Fassanté naniou nague ak yaw kolleuré guou doul dégne ba abadan dayimane ndapat, ba kérokk niouy guissé rek , ma gui lay weur nak. Air yi gua dadj moo niou daanél nioo gui niaanit sikar fa gua ko beugué Serigne Fallou déffal la thi li fookhé sa niorte thi barkéb Serigne Abdoul Karim Mbacké Falillou Borom ndindi DIEUREEEEUF
Waa yaw yaay fall ndigueul , nioune déy nio gui siarré bou baakh téy djeguelou di la khamalit loo dounde doyoul, thiant gui doy na war , la gua sikar moom yaay doy na kééman. Fassanté naniou nague ak yaw kolleuré guou doul dégne ba abadan dayimane ndapat, ba kérokk niouy guissé rek , ma gui lay weur nak. Air yi gua dadj moo niou daanél nioo gui niaanit sikar fa gua ko beugué Serigne Fallou déffal la thi li fookhé sa niorte thi barkéb Serigne Abdoul Karim Mbacké Falillou Borom ndindi
DIEUREEEEUF
Nekhna Machahalla lii douwone pekesse
Waayé beuguone na kham kan mo thi sikar maami Cheikh ndigueul goor yaabou la, waayé goor khamoula, thi digguenté Sokhna ndéye Gueye akk Sokhna Marière Fall.