😱Kawteff, Cheikh Abdallah Diouff Guiss na Combat Yi, "Balla Gaye2 Vs Tapha Tine, Ama vs Gris "

Поділитися
Вставка

КОМЕНТАРІ • 78

  • @galayebeye7868
    @galayebeye7868 Місяць тому +10

    Kéne dou mom Talibé Serigne saliou bi yalnala yalla defal diame nit kou am kham kham wallahi ❤

  • @ousmanendom2608
    @ousmanendom2608 Місяць тому +3

    Serigne abdala yalna yalla doli sa diam incha Allah

  • @abouthiam3003
    @abouthiam3003 Місяць тому +5

    Ndeysan kou yiwww ❤ machala Diouf

  • @NdeyemaguetteMbengue-ic6hr
    @NdeyemaguetteMbengue-ic6hr Місяць тому +1

    Yalla bakhna Balla amoule bene problème nianal ko rek Serigne diouf

  • @user-ig2vr2un5q
    @user-ig2vr2un5q Місяць тому +7

    Nguir yalla nianalal balla gaye🙏❤️

    • @profcoly6085
      @profcoly6085 Місяць тому +1

      Chim ya niak fayda na dém entrainédji way ah😂😂😂😂😂

  • @elhadjimoussacoulibaly3668
    @elhadjimoussacoulibaly3668 Місяць тому +3

    Paré nage Sakh pour fay la na BG2 ame ndam rek

  • @ModouSylla-ef4xd
    @ModouSylla-ef4xd Місяць тому +2

    Si barkie serigne saliou

  • @modou4103
    @modou4103 Місяць тому +1

    Machalla diouf

  • @2dtv267
    @2dtv267 Місяць тому

    ماشاءلله جرجفت شرج عبدلله جوف❤❤

  • @Neymarseye6440
    @Neymarseye6440 Місяць тому +7

    Kou beugua ame numérom noye deff fadame

  • @ModouSylla-ef4xd
    @ModouSylla-ef4xd Місяць тому +1

    Diapa lie balla gaye

  • @khabanegueye-fl8wq
    @khabanegueye-fl8wq Місяць тому +2

    Wa keur Tapha tine boulén dém si serigne bi ndakh bo dégué nimouy wakhé ngua xamni ki dafay nianal balla Gaye

  • @ConfusedLoom-tb2qk
    @ConfusedLoom-tb2qk Місяць тому +4

    Bilahi walahi ma dane sa thiés té inchallah Dina dane balla gaye si katanu yalla

    • @talibemame4681
      @talibemame4681 Місяць тому +2

      Wakho degue yaw

    • @user-kl1gh7gv3i
      @user-kl1gh7gv3i Місяць тому +1

      Sa leufeul ndeye Bo meunon Dara do nekh di comentaire yi Kay togne sa leufeul ndeye negue fi di doul rek

    • @Elhadji2187
      @Elhadji2187 Місяць тому +1

      Kan ioww😂😂😂

    • @user-kl1gh7gv3i
      @user-kl1gh7gv3i Місяць тому

      @@Elhadji2187 qui Dafa meuneu ndeye doul yaw Bo khamon Dara digua nek si comentaire di doul ndeyam

    • @Robbe-Grillet
      @Robbe-Grillet Місяць тому +3

      Wax deugue yalla kou baax dioum nga. Ndam yalla moko yor diko diox kouko neex. Danou Sa Thiès yalla dogal nako laa ta mouy dioudou. Liy xew si Tapha Tine yalla dogal nako bou yague. Nioune nioo fi neek di wax rek.

  • @bassiroutall4309
    @bassiroutall4309 Місяць тому +3

    Ama yalla nako yalla soutoural defal ko diam amouniou si mome thiofel

    • @SauraDiop
      @SauraDiop Місяць тому

      Amine wayy Modou lo Moy sama mbeur mai ama damako yeureum bilay walayy

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 Місяць тому +4

    Tapha tine lomouye guene néwi di guene nékha d'Anne bilay walahi

    • @profcoly6085
      @profcoly6085 Місяць тому

      Saway balla amoul doolé bou meuneu daane rapha tine balla comme yo si kanamou tapha

  • @s.modoubousso565
    @s.modoubousso565 Місяць тому

    Abdallah wakho fi dara ragalal yallah

  • @ibrahimadiop1327
    @ibrahimadiop1327 Місяць тому +1

    Número Serigne bi

  • @ousmanendom2608
    @ousmanendom2608 Місяць тому

    Fadam yalna sa diam yagueu

  • @talibemame4681
    @talibemame4681 Місяць тому

    Fadam numero la sokh la

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 Місяць тому

    Balla niew nga begeu

  • @noostresss9255
    @noostresss9255 Місяць тому +2

    Ki day nianal balla mtkh

  • @user-ub8mf4ce4g
    @user-ub8mf4ce4g Місяць тому +3

    Boulene faté ni mofi wakhon Macky Sall diekhala goul té amadou ba moy falou Macky nek précédent assemblée

    • @Robbe-Grillet
      @Robbe-Grillet Місяць тому

      Waxoul loolou deh yangui dioum

    • @ndatteyalla9917
      @ndatteyalla9917 Місяць тому

      ​@@Robbe-Grillet😂😂DIAROUL WÈRANTÈ DEMAL SÈTANE 2STV EMISSION KOORGUI MOK SA TOUBA WAXONE NA AMADOU BA MOY FALOU TA MACKY DIÈXALAGOUL NDAX DAKO GUISS CI ASSEMBLER BI

    • @Robbe-Grillet
      @Robbe-Grillet Місяць тому

      @@ndatteyalla9917 weraneté wouma deh. Setane li ngay wax mais Dafa ni loolou la guiss mais waxoul ni loolou lay firi. D'ailleurs sax Becaye attirer na si attention participant bidone def déduction.

    • @ndatteyalla9917
      @ndatteyalla9917 Місяць тому

      @@Robbe-Grillet 😂bakane you bari yim waxone ci election yi nak nekhul defendre dal

    • @Robbe-Grillet
      @Robbe-Grillet Місяць тому

      @@ndatteyalla9917 je ne le défends pas deh. Lima dègue laa wax rek. Pour les décès môme j'étais pas au courant

  • @Robbe-Grillet
    @Robbe-Grillet Місяць тому

    Serigne bi wallahi sope nala lool ndax say téguine wayé souma sanione nga diapalel niou Balla gaye 2 ndax ndamam mooy doundeul lambe.

  • @abdoukhadredjieylanimandia6675
    @abdoukhadredjieylanimandia6675 Місяць тому

    Ndeyssan bou serigne yeup melon ni yaw kon lou beuri dina changé si deuk bi

  • @Ahmadouboromediamono4
    @Ahmadouboromediamono4 Місяць тому +1

    Tapha tine yalla la andal yalla la yakar ak tourondom serigne modou Moustapha mbacké lagne ko toudé direct nak na lere papam di talibè Serigne Modou Moustapha

    • @rassemtombalbaye5005
      @rassemtombalbaye5005 Місяць тому

      Deuguit té lolou yeup eupneu 11 ans té ya 11 balla niouss neukeu dineukeu nioussat

    • @rassemtombalbaye5005
      @rassemtombalbaye5005 Місяць тому

      Nieupeu andak yalla yow nafikhone gueu wakhofi sport taphat dq ragal balla

  • @swartnwar916
    @swartnwar916 Місяць тому +1

    Serigne Abdallah ioe sey interview, bouko fadam defone pay per view: fay pour setane bilahi meu fay pour setane ndakh thiofél bimeu amci ioe. Balla Gaye tamit xawmako mais moy seul mbeur boumeu diaral bayi sama liguey setaneko momit ndakh thiofel boumeu amci mom. Yallah rk mom meune lolou. Borom khol bou laap soko kholei ci kanam bi rk dankey xam tei Yakk Balla yeup ay borom bakh ngen. Donc damalay niane rk comme néi ngu Balla tognuleu diapalni nitt mo matoul rk loum meune def rk aduna amoul solo nitt matoul.
    Bou lolou dialé beug na amseu n° mais Yallah xamnani li ngu wakhni rk amneu yeurmandé bou takh doumaleu sakh beu wo Wallahi, mais Yallah bakhna.
    Diammeu ci ioe Borom
    Bi Sutural leu Inchallah ci Barké Serigne Saliou Mbacké.

    • @abdallahdiouf384
      @abdallahdiouf384 Місяць тому

      Ya bakh way

    • @swartnwar916
      @swartnwar916 Місяць тому

      @@abdallahdiouf384 Naleu Yallah Sutural rk Serigne bi, loy sentou ci Aduna rk Yallnaleu Yomb ci Barké Serigne Saliou. Dih fédali sama thiofel rk key khana.

  • @SauraDiop
    @SauraDiop Місяць тому

    Lolou lerna balla day wayadi

  • @ousmanendiaye8619
    @ousmanendiaye8619 Місяць тому

    S Abdala kou bakh lol si niit yii
    Yalla samla

  • @layefall452
    @layefall452 Місяць тому +1

    Nianalal Balla rk gir yalla diap si

  • @papecisse6000
    @papecisse6000 Місяць тому +1

    Yaw khamo lo réré Khamo touss. Dangaye door rek

  • @Papiskotv
    @Papiskotv Місяць тому

    Ki serigne balla Gaye la ins bi dayy neubeutou di tekk xell rekk

  • @bayemodouseck7028
    @bayemodouseck7028 Місяць тому +1

    Loudoul yalla nenn la ki dou gatt

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 Місяць тому

    Kii mooy boroom Hersent mon ami

  • @user-ig2vr2un5q
    @user-ig2vr2un5q Місяць тому

    Loutah beugo wakh si balla

  • @bambadiop-zw6pt
    @bambadiop-zw6pt Місяць тому +1

    Ya waxone sa Thiès Moy dane

    • @mouhamadourassouldemba6333
      @mouhamadourassouldemba6333 Місяць тому +3

      dafa wakhone sa thies mo yoor ndame mais guiss nassi niou walbati combat
      si birr guew bi

  • @ndiagafaye3106
    @ndiagafaye3106 Місяць тому

    Waayé aandou maak yow nak inchallah tapha tine mooy am ndam

  • @user-qb2id8uj5x
    @user-qb2id8uj5x Місяць тому

    Kou bege ame niuarom noy def

  • @modoucheikhdieng4066
    @modoucheikhdieng4066 Місяць тому +3

    Dorkaat leu bilahi je parle en connaissance de cause envoyer nako 130.000 pour ay sarakh mou yonéma ay niaane guissouma dara après makoy wo doula dieul les marabouts. C’est l’arnaque du siècle.

    • @abdallahdiouf384
      @abdallahdiouf384 Місяць тому

      Soude deuge la

    • @swartnwar916
      @swartnwar916 Місяць тому +1

      wakhouma pour defendreko ndakh Allahou A’hlam. Mais du moment ou yoné ngako seu khaliss bam yonéleu sey niaane, yaakaroni niane bouy nangou ak boudoul nangou Yallah leu soop et que daniouy sabablou rk, am yakar, gueumnani serigne bou meûne assuré niane bou nangou bou yabo neu woténi moy Yallah rk béneu yone. Après leu fait que ngakay wo dieulouleu eskeu do am ndiort bou rafet que dafeu am seu fouki morom youmouy ligueyal. Magui diagalou ndiort bou rafet rk la am boumeu dégone kou deff seddé yi ci iow tamit lii lay khalat rk ci sama khalat bou gatteu.

    • @galayebeye7868
      @galayebeye7868 Місяць тому +2

      Yaw bayil féne ni rk ngéni def di toumal diamou yalla yi ki nitou yalla sokhla woul alalou diambour bayi léne di yakh nitou yalla yi ak di léne togne daye takh doléne avancé rk

    • @abdallahdiouf384
      @abdallahdiouf384 Місяць тому

      ​@@swartnwar916❤

    • @dieynarassoulmane4831
      @dieynarassoulmane4831 27 днів тому

      Ki dei way defal yalla daga yakamti rek niane yalla mokoy nangou

  • @marcusmouhamed
    @marcusmouhamed Місяць тому +1

    Mo wahon amadou ba dey dieul rewmii nn senegal nehnaa 😂😂😂😂

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 Місяць тому +1

    Dafa am kili fa gou wakh ak yaw motakh do wakh si balla

  • @sopemaodofall1274
    @sopemaodofall1274 Місяць тому

    Fen rek laye def

  • @mahhabrwn439
    @mahhabrwn439 Місяць тому

    Dama sohla numéro serigne bi ngir Yalla ak Yonenti bi Fadam japou si, Dama bougie mou niow Europe Japaleh ma si yeni jeffe jeffe ngir Yalla. Fadam Japou si… Dama yaga setan Serigne bi teh wolou nako, japou si Fadam ngir Yalla

  • @mustaphafofana7615
    @mustaphafofana7615 Місяць тому

    Yen serieng yi niari lameny