Lééral Ci Centre de Redressement You Serigne Modou Kara

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 10 лют 2025
  • C'est l'actualité qui a défrayé la chronique ces derniers jours et qui continue d'agiter les débats sur tous les supports d'échanges. Des centres dédiés au redressement mis en place par Serigne Modou Kara où la gendarmerie a décelé des prisons privées ainsi des actes de tortures chez certains pensionnaires. Comment en est-on arrivé là ? Quelles sont les responsabilités de tout un chacun ? Doit-on également mettre de coté les réalisations de ces centres qui ont quand meme réussi à faciliter l'insertion sociale des milliers de jeunes ? Voici notre analyse du jour sur une situation qui nous interpelle davantage sur la politique sociale adoptée par notre pays depuis les indépendances.
    --------------------------------------------------------------------------------
    SUIVEZ-NOUS sur les réseaux sociaux pour avoir nos nouvelles en temps réel :
    Facebook : / xalaattv1
    Instagram : / xalaattv_1
    Twitter : / xalaat1

КОМЕНТАРІ • 2,3 тис.

  • @BOGO221
    @BOGO221 4 роки тому +109

    Defal vidéo si cheikh anta diop kousi d'accord rk na j'aime

  • @jdiamjitv
    @jdiamjitv 4 роки тому +917

    Teyla anniversairou Sidy lamine Niass le grand patriote et grand absent d'aujourd'hui au Sénégal yalnanouko yallha fayal té yeureum ko kharéko aldiana

  • @bayesaliousylla8232
    @bayesaliousylla8232 4 роки тому +1482

    Nianal len sama papa dafa waniekou😥😥

  • @gdiazfayeuhhfayecana6936
    @gdiazfayeuhhfayecana6936 4 роки тому +68

    Nianal leine sama Mame da waniékou té Aka begone xalaat TV bilakhi 😭😭

  • @papadameba4998
    @papadameba4998 4 роки тому +3

    Je parle de maniere honnette je suis Mouride mais je suis pas un Talibè De Serigne Modou Kara Honnettement je vie depuis plus de 10ans Avec une des centres de redressement mais Gniouy wa kogne bii Meussougnoufeii Guiss lou niaw au contraire ils contribue ala propretè du littoral particulierement sunu secteur biii set setal Machallah guadjier galama a eux Je connais des personalitè yifiii indii sen ay Doom tè le resultei a etè payant ndakh parents Yi amnagnou satisfaction gni Fi gneuw bonneuh gueinate bakh mo euppeu foufff gniou changewoul donc Gathier galama A Serigne Modou Kara ndakh sauverna ay vie humaine you bariii changerna defka en un homme pieux et veridict✋🏾

  • @ninjaassassine4282
    @ninjaassassine4282 4 роки тому +237

    Qui aime le prophète mouhamé ❤ beusseul aime ❤ Papa bouba diop yalna ko yalla yeureumm ta kharela aldiana si borom touba 👐 👐 Diadieuff wa xalaat tv amna solo yalna sen diamo yague si barkep borom touba amine

  • @ngagnegaye7859
    @ngagnegaye7859 4 роки тому +168

    Papa bouba diop yalla nako yala yeureume kharèko aldiana firdawsi barkep mouhamed

  • @jdiamjitv
    @jdiamjitv 4 роки тому +403

    Kou lire sama commentaire na nianal sounou camarade d'étudiante Ndeye fatou Diagne de (UCAB) ndiéga ak yeurmandé svp fatiha+11 likhlasi pour lui

  • @nafaatv7472
    @nafaatv7472 4 роки тому +40

    A chaque fois qu'il y'a un fait au Sénégal, je ne me prononce pas la dessus jusqu'à ce que vs y émettez des éclaircissements... Merci Xalaat tv

  • @assanediouf740
    @assanediouf740 4 роки тому +58

    Je suis un talibe kara me je suis d’accord avec halaat tv machalla

  • @khadimndiaye4279
    @khadimndiaye4279 4 роки тому +243

    Xalat yal ngua am télé ci barkeii cheikhoul xadiim ❤️

    • @cheikh2212
      @cheikh2212 4 роки тому

      Amine Yarabi

    • @falloumendy370
      @falloumendy370 4 роки тому

      @Armand Sene koula wakh sou amè Tele rek mom mossiy wakh

    • @muhammetp.l8220
      @muhammetp.l8220 4 роки тому

      Merci xaalat tv

    • @gallas7082
      @gallas7082 4 роки тому

      @Armand Sene sauf si mou créer chaîne diokh co bénéne tour et baparé continué liguéye bi

    • @matarmbuegu2855
      @matarmbuegu2855 Рік тому

      Aminnn

  • @serignemassambakane9509
    @serignemassambakane9509 4 роки тому +205

    Pape Bouba Diop paix a son âme et que la terre lui soit légère ❤🇸🇳👌

  • @aminadiakhate786
    @aminadiakhate786 4 роки тому +235

    Qui d'autre comme moi attandait cette vidéo pour comprendre exactement cette histoire de kara?😍mercii khalatt

  • @serignemodouboussodieng62
    @serignemodouboussodieng62 4 роки тому +18

    Waw goor xalaat amnga foula amnga xam xam sa xél séll na boul meuseu dokh si parparlo yalna yalla goideul sa fann té mouseul la si thiat

  • @omardiop9193
    @omardiop9193 4 роки тому +14

    De toute façons moi je suis un témoin j’étais dans l’un de ses centres de redressement qui se situe â Guediewaye amo 6 tableau aire Afrique mais vraiment manne sante na yalla bimafa diarré puisse que diangalena lou bari dioubanetinama tayyy souma démmmé ba meune drousse Xasida you sel yis yalla ak niommme leu ✌️

  • @modouseck4291
    @modouseck4291 4 роки тому +128

    Ama Tina solo dieurdieuf serigne touba

  • @aliousylla6493
    @aliousylla6493 4 роки тому +78

    Vrmt xalaat.tv vs êtes les meilleurs yalla gain am TV sa barké serigne touba

  • @aboubakrpathe488
    @aboubakrpathe488 4 роки тому +100

    Merci Xalate Tv
    Yalla naséne diam yagu
    Boulene falei kéneu
    Tte la population est dernière vous ✌️

  • @bayesouley2689
    @bayesouley2689 4 роки тому +1

    Merci xalate tv bouléne ragal yalla boléne di faye ligéne di def pour askane bi kéne menoul si yéne dara pask vous êtes la voie du peuple dieuredieuf

  • @amethndao6380
    @amethndao6380 4 роки тому +21

    Wallahi serigne modou kara lou doule bamba niorou nou yaw ya ky defarr sama Grand frère bi

  • @seexahmadulmubiin5674
    @seexahmadulmubiin5674 4 роки тому +50

    Sama benn makk su dara xewee nganiko loo si xam muni Xalaat laay xaar bam wax ba paré, Aka gëmm xalaat Jërëjëf xalaat🙏🏿

  • @Sucapro
    @Sucapro 4 роки тому +265

    Vraiment xalat motakh manatouma wax louma leroul te deglou woumako

  • @djze937
    @djze937 4 роки тому +53

    Zéro faute Xalaat Le meilleur informateur dans le monde 🙏

  • @mbengueallmaktoum7318
    @mbengueallmaktoum7318 4 роки тому +31

    Serigne Moustapha sy all maktoum yalla na fi yague té wér thi barké yonéneti bi inchallah dieuredieuf xalaat tv 🙏🙏

  • @mohameddiedhiou5476
    @mohameddiedhiou5476 4 роки тому +113

    Une analyse très pertinente. Franchement chapeau à vous Xalaat Tv.

  • @ibrahimaniasse6225
    @ibrahimaniasse6225 4 роки тому +177

    Comme d’habitude sa seras une super vidéo qu’Allah pardonne nos péchés

  • @fantambaye7280
    @fantambaye7280 4 роки тому +203

    Yalna gnou yalla saamal Seydina Ousmane sonko 🙏🙏🙏🙏

  • @sabakhtv1011
    @sabakhtv1011 4 роки тому +72

    Je suis XALAAT TV : MACHHALLA lér na nagne 🇸🇳🔥🔥

  • @omarkarabambistediouf3819
    @omarkarabambistediouf3819 4 роки тому +1

    Serigne modou awa balla moniwone ande léne ak modou mou bakh bakhalénn bou bonnée bakhallén téi nguén défko sénoup serigne touba serigne abdoulahad niko modou kou meunoul thi djoumay touba dji darra meunoul si yaw darra serigne bi niko bou adouna bi yeup yoronne ay fétal dilla dirr dounela djam. Gnoune nak dagnou takhaw tém ngir changer système bii gnougnouy gouverner. Deuk bi bi politique de vérité lagnoufi sokhla vive la révolution pacifique avec le général de Bamba al khaïd le guide 👌✌️

  • @coumbaba6530
    @coumbaba6530 4 роки тому +27

    Vraiment mane j’adore votre position ! Deugggg rkkkk moleiiine niorrr

  • @avoucatcheikhbassabdoukhad6882
    @avoucatcheikhbassabdoukhad6882 4 роки тому +35

    Serigne modou karra yalla ngafi yeugui

  • @babassara2997
    @babassara2997 4 роки тому +164

    Gayi Nanou Bayi asane Diouf 🙏🏿 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿

    • @ibromeo9682
      @ibromeo9682 4 роки тому +1

      assane diouf es un incompris
      cest macky sall qui doit aller en prison apres quil quittera le pouvoir

    • @gnagnadabo3053
      @gnagnadabo3053 4 роки тому +3

      Assane c'est vrai qu'il est un incompris. sagayi motah Keen Manou ko deegu. Moi personnellement j'ai du mal à l'écouter

    • @babacarfall2774
      @babacarfall2774 4 роки тому

      Assane Diouf badola casso la mériter

    • @ibromeo9682
      @ibromeo9682 4 роки тому +1

      @@babacarfall2774 Badola sur quel point est ce quil a volé largent du contribuable senegalais est ce quil a tué quelqu un ou bien il a detourné d largent jaimerai avoir tes arguments sur le fait qu vous dites que badola la et que prison la mérité

  • @pablogabrielscobar8097
    @pablogabrielscobar8097 4 роки тому +113

    Yalla na diam yagu Senegal sí barke seydina Mohamed

  • @youngthiam9821
    @youngthiam9821 4 роки тому +48

    Assane Diouf il est entrain de souffrir yalla nako yalla dieulé foumou nekk pck sonou na lol ndeyssan

  • @khadimwane9095
    @khadimwane9095 4 роки тому +2

    Ns sommes au siècle des lumières maintenant les gens ne regarde que c l'enfant d'un tél marabout où pas ils réagissent beaucoup de questionnement se posent mr6 encore xalaat tv la voie du peuple ♥️🙏

  • @Découverte_historique
    @Découverte_historique 4 роки тому +4

    Merci beaucoup xallate guiss gua ousseynou ak assane bobou guay wax louga gui lanou deuk danou dane guéss rk mes guiss gua bignou l'en yobé basse thi centre bobou wallahi Barki serigne saliou legui dh bo len guisse tothie lanou def machallah wallahi mère bi du s'en yaye dh gno book kogne wallahi Barki yalla mes dafa fek nitt bou xamoule rk xamoh wallahi

  • @ousmanefall3770
    @ousmanefall3770 4 роки тому +34

    Fi bilayi dore amoufi sénebar Amou fi soit bi djiougué la mais 1 ans yi mafadeff avant may dem voyage dama dan beugue toukh pone sakh dawou mako faguise maintenant se sui en Turquie

  • @ousmanefall3770
    @ousmanefall3770 4 роки тому +7

    Bilay commanda bi boudonoul ak xalat tv dinala wakh lougaraw ngoubari diarrre nafa si centre cheikh ahmadou kara yi moi personnellement diarrna fa déffa 1ans mais bima fa djiougué balegue magui Sant yala réck bay sérai samam bien grâce à cheikh ahmadou kara mbacké noreni

  • @xudamulxadimxeexakwakhaabi3565
    @xudamulxadimxeexakwakhaabi3565 4 роки тому +3

    Merci xalaat tv, ni nga analyser thème bi amna solo, boul nangu kéén dila diaboliser ak kilifeu dinéé yi woutee nga ak doff yiy saaga baye kara ba faaté limouniou défal nioun jeunesse bi ak fimouniou diëulé, encore une fois merci xalaat tv čooy Lou Bari xam lu xéiw da koo gëun
    Diarama cheikh Ahmadou kara MBackè noreyni ❤️❤️

  • @amstrollas9475
    @amstrollas9475 4 роки тому +36

    Xaalat une vidéo sur sidi laminen niass. Après 2ans. Nous ressentons son absence dans les grandes manifestations démocratiques. Il était la voix des sans voix.
    Que son âme repose en paix
    Aime si vous êtes d accord

  • @morsarr4420
    @morsarr4420 4 роки тому +28

    La vidéo que j'attendais. Merci Xalaat TV. Votre travail est loué par tous les abonnés. Merci pour votre humilité et votre amour pour le pays. Soy nieupp méloone ni yéne Sénégal nieupp yéwou. Maa chaa Allah🙏🏽🙏🏽🙏🏽

  • @s-saliou-nd-iour-
    @s-saliou-nd-iour- 4 роки тому +26

    xalaat tv toujours j'aime c'est très bien parler amna solo trop yalna lén yalla défal jamm xalaat tv là meilleur téle de sénégal 🇸🇳🇲🇦🙏

  • @fofana2030
    @fofana2030 4 роки тому +41

    Non WA XALAAT DUGNU AY NITT WAY VIDÉOS BI AMENA SOLO TROP MERCI 🙏🏼

  • @ibrahimgueye6069
    @ibrahimgueye6069 4 роки тому +4

    Effectivement wallahi yene Dong laa geum sii mim rew wa xalate tv kessé laa geum j sui avec vous
    بارك الله فيكم وأيدكم ونصركم على أعدائكم

  • @mohameddiedhiou5476
    @mohameddiedhiou5476 4 роки тому +39

    La paix est avec celui qui suit le droit chemin. Et c'est votre cas.

  • @Mouridoulahi
    @Mouridoulahi 4 роки тому +34

    Dieureudieufé Cheikh Ahmadou Kara Mbackè Noreyni 💪🏾
    Kou khamoul rék khamooo 🚩🏴kou andaak Yala koulaa guassal malaakaa Soulll💡

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 4 роки тому +3

      Kara dou sarap ndeyam ! Yow teudieul sa gatt way.

    • @thiatgueye7103
      @thiatgueye7103 4 роки тому

      @@abdoulabdoul7809 bolesi SAP seringe RK momat

    • @thiatgueye7103
      @thiatgueye7103 4 роки тому

      @Bamba Samb dama khamni Kofi saga ap seringam man na fayou khamna niniy fayo soko defoul RK yaratal sa bopp

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 4 роки тому +1

      Kara key dou serigne. Ap serigne moy kouy diangalé al quran ak sunna . Kou diangaléwoul nénéne ngay toudou. Makhala sénégalais nio gueuneu thiouné si Afrique motakh développement zéro.

    • @abdoulabdoul7809
      @abdoulabdoul7809 4 роки тому +1

      @@thiatgueye7103 man ki Yallah yoni si diam yi moy sama serigne RASSOULILLAHI (s.a.s) boula nékhé nga saaga ko.

  • @fallounarr233
    @fallounarr233 4 роки тому +51

    Xalate dall môme Mofi nek Si wakh katou Deg ❤️❤️

  • @abdoumbaye4344
    @abdoumbaye4344 4 роки тому +71

    Mai. Xalate vrément iow kou ame yar gua bilay yalla na diam yagu frère

  •  4 роки тому +13

    Xalaat tu analyses bien vraiment tu es le meilleur gouvernement faiyaneto la maky dou darra

  • @dioufibrahima826
    @dioufibrahima826 4 роки тому +12

    Merci pour les éclairages. Que la lumière soit faite et que l'issue soit pacifique !

  • @mondeafrique5752
    @mondeafrique5752 4 роки тому +43

    C'était pas trop tôt xalaat tv
    J'entendais avec impatience
    Mais Merci bcp d'êtres là pour nous le peuple sénégalais que DIEUX vous protèges

  • @abougabal6691
    @abougabal6691 4 роки тому +21

    Merci beaucoup pour ces éclaircissements. Quel objectivisme. Je salue vraiment votre patriotisme. Suis ta ligne de conduite.

  • @khessly1051
    @khessly1051 4 роки тому +40

    Yalla dieureudieuf si khéwal you barri bi ngi diokh sa sounou yéwo... Yalna nga gnou yombalal sunu diafé diafé , mousseul gnou si def bakkar bougnou kham ak bougnou khamoul 🤲🏾
    Alhamdoulilah 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @danembengue2912
    @danembengue2912 4 роки тому +1

    Masallah une autre analyse très importante et très pertinente je suis tout à fait d'accord avec vous sama yaram dafa daw bima guisé vidéo bi wadji di fene wakhni 2500f par jours la done dieunde poone ak yambaa🤦🏽‍♂️

  • @charlefaty9719
    @charlefaty9719 4 роки тому +8

    Télévision rek laye kharr incha Allah
    Mai dafa ame louma diakhale sa voie bi naturel Walla en tout Cas kiffer nako

    • @meetyourealself
      @meetyourealself 4 роки тому

      Dako changer c plus sûr comme tous les défendeurs de vérité sont opprimés🤗

  • @srgnfalloundiaye8322
    @srgnfalloundiaye8322 4 роки тому +19

    ❤️❤️❤️Dieuredieuffé ti Cheikh Ahmadou Kara mbacke noreyni
    Amal nga ndiarign Askanwi wallahi mbacke
    Yalnala Serigne touba doli diamm

  • @jdiamjitv
    @jdiamjitv 4 роки тому +46

    في مثل هذا اليوم إنتقل إلي رحمة الله تعالى، حبيبنا وقدوتنا الحاج سيد الأمين انجاس الذي ترك فراغ كبير لشعب وطنه

    • @abousy2712
      @abousy2712 4 роки тому +2

      رحمة الخالق عليه

    • @jdiamjitv
      @jdiamjitv 4 роки тому +1

      آمين يارب

  • @falloua52
    @falloua52 4 роки тому +67

    Koudon khar xaalat mou wakh si affaire bi

  • @karimfaitsesvideos7903
    @karimfaitsesvideos7903 4 роки тому +3

    Serigne Modou kara yalla nafii Yagu

  • @ousmanembow2578
    @ousmanembow2578 4 роки тому +1

    Machallah amna solo
    Mane lou mana amm sa kadou reck lasi khare
    Mangui lay nianal yalla bou bakh
    Yana yalla samoula ta dafala diamou

  • @mahmadanelo2361
    @mahmadanelo2361 4 роки тому +39

    Merci xalaat Tv liñuy xaar rek nga ñuy jox moo tax vraiment seen liggéey rafet na
    1.000.000

    • @pettiama3112
      @pettiama3112 4 роки тому

      Saay yaw moom gan kippaango ga Jage Wolof

  • @mamistamendy6585
    @mamistamendy6585 4 роки тому +3

    Doy na war dh 🤦, mais merci beaucoup xalaat tv 📺 vous êtes les meilleurs 👏❤️

  • @moustaphafall3991
    @moustaphafall3991 4 роки тому +48

    Ana niokoudone kharr xalaat TV sunu télé💓💓💓

  • @jaamupyalla9132
    @jaamupyalla9132 4 роки тому +1

    Merci xalaat tv vraiment vous êtes conscient ci li xew Amna ñiou xamné déjà condamné nañ Serigne Modou kara sans dieema xam li xéw

  • @karimdiouf8888
    @karimdiouf8888 4 роки тому +13

    Depuis des jours g entendu les rumeurs mé c grâce avec xaalat tv k j comprenne vite un grand merci à vous

  • @ballataysirtabane4672
    @ballataysirtabane4672 4 роки тому +18

    Merci 🙏 XALAAT boul nangou Ken dila orienté si injustice

  • @leathiamo7371
    @leathiamo7371 4 роки тому +26

    Je viens de voir la vidéo mais je ne suis pas musulman mais sachez grâce à kara mon frère redeviens normal et un homme pieux donc quand tu ne connais pas une histoire il faut se taire

    • @leathiamo7371
      @leathiamo7371 4 роки тому +2

      @@civisme8953 domou biral nga doumala tontou

    • @mameyoufall18
      @mameyoufall18 4 роки тому

      @@civisme8953 demal diangui way reww nga trop s kara dousa maromou bay ok

    • @coleecole6459
      @coleecole6459 4 роки тому

      👀👀👀👀

  • @moussabathily7926
    @moussabathily7926 4 роки тому +6

    Merci Xalaat Très bonne analyse de votre part 💯🙏🙏🙏

  • @assaneseck8618
    @assaneseck8618 4 роки тому

    J'ai pas l'habitude de commenter mais votre travail ne laisse personne indifférente. Vous avez fait une analyse claire, cohérente et très pertinente, sans parti pris et sans prise de position. Votre objectivité me va droit au coeur sur tous les sujets traités. Deug rek molène nior. Yalnalene Yalla sam, linguène beug ci rewmi sunu borom defalénko bijahil Moustapha (PSL)

  • @aronadiop8143
    @aronadiop8143 4 роки тому

    Toute fois je ne checherai de vous remercier et ravis que vous ne ceder pas a la pression et aux derapage de reglement de conmpte personnel.

  • @aidacissokho4455
    @aidacissokho4455 4 роки тому +25

    Dieredieuf Xalat tjs du côté de la Vérité pure et dure Machallah

  • @bayefallcivilise
    @bayefallcivilise 4 роки тому +22

    Quand c'est important et intéressant, c'est sur Xalaat TV 💪🙏
    Niaklene deglou woroul dée.

  • @karasylla5591
    @karasylla5591 4 роки тому +4

    Merci beaucoup vous êtes le meilleur ❤️

  • @djibyjadidkaratoure2102
    @djibyjadidkaratoure2102 4 роки тому

    Bilahi amo morom analyse très pertinent j suis un talibé d cheikh ahmadou kara j suis fier d tw.
    Kara moma défar

  • @nefertiti2913
    @nefertiti2913 3 роки тому +1

    Walahi vous avez le monopole de la vérité surtout quand je pense que j’ai voulu envoyer mon fils au Sénégal...Xalaat Tv vous avez sauvé la vie mon fils. Merci beaucoup ☺️

  • @ndiagandiaye760
    @ndiagandiaye760 4 роки тому +32

    Nit bala nga. wakh danga wara khame lingaye wakh diarama khalate tv ✊❤️

  • @modoudiop3303
    @modoudiop3303 4 роки тому +17

    Bilahi walahi yén wa xalaat tv sénégalais yi sass nañoulén parsk lou khéw rék askan bi xalaat tv rék lañouy khar mou défsi diangate yalnalén yalla samm si barké borom touba 👌👌

  • @alfaaroukhtv3391
    @alfaaroukhtv3391 4 роки тому +4

    Sénégal 🇸🇳 dall dafa doy warr rék
    Diwoté wo Serigne té dosi dara Dara Dara Modou kara mo wara Bayi limi def topou ay domi diambour dilén toroxall noob domi diambour yi ba paré dilén toroxall waye xamlén né yalla amna té dée mongui gnew wallahi 😭😭😭😭
    Xana dafa fekeue né sénégalais yi ndiemé wouni wax yén Serigne yi degue rek Billahi 😭😭😭😭

    • @bayedarou3006
      @bayedarou3006 4 роки тому +1

      Sa leufal ndeye serigne dousa morom

    • @alfaaroukhtv3391
      @alfaaroukhtv3391 4 роки тому

      @@bayedarou3006 الحمد لله
      Yenentoubi sallalaahou hallehi wassalam dafa waxne ana kan si yen moy saga way diouram sahaba yi néko ndax kén dina diakarlo ak way diouram diko saga yenentoubi sallalaahou hallehi wassalam ♥️😭 néko moy mou saga way diourou diambour
      صدق رسول اللَّه صلى الله عليه وسلم ♥️🇸🇳

  • @ndiayedaoda8275
    @ndiayedaoda8275 4 роки тому +1

    Merci xalaat TV yie namadoye ci xibarr

  • @gadiagangagne420
    @gadiagangagne420 4 роки тому +1

    Macha allah amna solo lol walaye ndeysane diadieuf

  • @serignedjilyseye5116
    @serignedjilyseye5116 4 роки тому +8

    Merci xalat ko d'accord beuseul j'aime yalla nanéne am diamou

  • @babacarsy2889
    @babacarsy2889 4 роки тому +10

    Merci beaucoup frère
    Thanks everyone may Allah bless this tv

  • @bamodyoficielle2669
    @bamodyoficielle2669 4 роки тому +6

    Merci Beaucoup Xalaat Tv
    Bilaahi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @kamalmbackedarousalam9088
    @kamalmbackedarousalam9088 4 роки тому

    machalla amna solo Lima nakhari moye ageurésé narna baréti si deuk bi rk kara khale yimou yor si beureb yoyou moye khale yi géss ba moudiou di fanan si mbédeu yi si soufou pon yi

  • @momodiouf3371
    @momodiouf3371 4 роки тому +1

    Après avoir longuement réfléchi je pense qu'il devrait être remercier comme vous l'avez constaté les résultats positifs sont plus important que ceux qui sont négatifs, même si Serigne Modou kara a peut-être fait des erreurs c'est déjà suffisant.on doit le remercier cas même quelques parts

  • @daaraalamineofficielle7927
    @daaraalamineofficielle7927 4 роки тому +5

    Machallah Xalaat yalla na yalla samme arr léne Sénégale reww bou doy warrla

  • @iscooamar2214
    @iscooamar2214 4 роки тому +5

    Kara si xol
    Kara partou
    Kara merci
    Kara every day
    Kara nous taimons
    Kara merci pour tou tu a fait pour la jeunesse sénégalais
    KAllah protége notre kara
    Allah donne lui de la force
    Kara doundal 130ans
    Dieureudieuf cheikh ahmadou kara ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😘😘😘😘😘😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mahmadaneseck8322
    @mahmadaneseck8322 4 роки тому +9

    Khayo gonto du âme journée 2500 j'ai impossible kou d'accord beusal j'aime

  • @ahadmbackediop1935
    @ahadmbackediop1935 4 роки тому

    Vous êtes pertinent et très éloquent dans votre discours. Comme vous voyez mon nom je suis un fervent mouride mais votre analyse m'a touché. Bravo et bonne continuation

  • @papadieng4861
    @papadieng4861 4 роки тому +1

    Merci xaalat tv continué pour toujours dennoce les delinquent de ce pays yen askan wi ngeni dimbali bravo

  • @Satouba09
    @Satouba09 4 роки тому +40

    Oustaz bi di wakh xamnako bou bakh abdou sene la toudou nio diangando allkhourane Diourbel kou man allkhourane la

  • @julesyb536
    @julesyb536 4 роки тому +3

    Merci beaucoup xalaat tv meilleurs chaîne merci beaucoup xalaat tv. Merci beaucoup xalaat tv. Merci beaucoup xalaat tv.merci beaucoup xalaat tv

  • @SOLEILCISSE
    @SOLEILCISSE 4 роки тому

    Une pertinente analyse XALAAT👍🏿👍🏿👍🏿
    Il faut savoir aller au delà des évidences et percer les mystères autour des sujets sensibles...
    Que le bon Dieu te préserve🙏🏿🙏🏿🙏🏿

  • @khdimgaye2866
    @khdimgaye2866 4 роки тому +1

    XALAAT TV yaw rk la don khar lepou ler na merci bcp 💪 sama khel dalna diaradiafati cheikh Ahmadou kara ❤😍

  • @Mbayang99
    @Mbayang99 4 роки тому +58

    Kou remarqué ni xalat tv dafa nirok Abdou karime gueye voix👍😆

    • @bayedia3190
      @bayedia3190 4 роки тому +7

      Sisi il se ressemble mais dou mome dh ba karim néké prison xalaat defone na video

    • @linfonetsn102
      @linfonetsn102 4 роки тому +7

      Non du tout. Abdou Karim Gueye dafa bar té ki il articule bien.

    • @Tahirousarrforever7418
      @Tahirousarrforever7418 4 роки тому +1

      Pour man xalaat TV Moustapha diop bou walfadjri lay Niro voix surtout souy wakh niougui lén di djadieufeul

    • @rakkaadiou1515
      @rakkaadiou1515 4 роки тому +1

      Xalaat mo geune cultiver geune petinen bokoul sah voie

    • @coumbaba6530
      @coumbaba6530 4 роки тому +1

      Mane la voix me faire peur 😬😂😂😂

  • @mouhaly8593
    @mouhaly8593 4 роки тому +4

    Merci xalate yaye souniou lepp
    Lou am nga yéniou niou ham fou niouy taxaw mba doo yonanti saxx❤️❤️

  • @laminesall2934
    @laminesall2934 4 роки тому +10

    C est votre chaine seulement k j recois une notif ,le MEILLEUR ,on vous adore sans vous voir.

  • @moha_Deh_221
    @moha_Deh_221 4 роки тому +1

    Billahi kendou yen bolen wakherek lepou lerr yalla nalen yalla maykattane ak soutourallen💚💛❤💟

  • @GENERALTV-hn5qp
    @GENERALTV-hn5qp 4 роки тому +1

    Mane gueum nane sa xalaat si mim rew aye doff lagni deuk di don chapeau à toi et à toutes l'équipe

  • @laydrauz
    @laydrauz 4 роки тому +3

    Le Sénégal a 16mllion donc xalate tv doit avoir au moins 5million abonnés même si tout le monde n’ont pas axé a internet car il est là pour le peuple