je sw une patriote et m'interpelle directement le PM Ousmane Sonko sur l'affaire Fallou Fall et Eumeu parce qu'il a subi la même injustice.Oh quel Senegal🤗🤗🤗
Aywayy, yala na yekhe,Wayé yow mi d,naro Yor say domou mag sou deudouwone. Na niouy rafetal, adouna yagoul, té amoul ben solo. Niou fékhé nétali yi di rafet. Massa ya boye ❤
Yallanako yalla nite guènenèko si khatekhate courage eskey metina loleeeeee justice pour fallou fall et eumeu courage maman et la Famille de fallou et oumi et Mbaye kharitou fallou na yone dèfe liguièyame gnawena metina
Pendant ce temps, l'imam de notre mosquée est en prison depuis 1 an à cause d'une accusation d'une femme, comme quoi il a violé sa fille de 4 ans. Un homme digne, jovial, plein de sagesse, gérant deux daaras en même temps, chez lui et à la mosquée, qui dirigeait toutes les prières quotidiens et mortuaires, animait les conférences, prêchait chaque Vendredi à la grande mosquée, célébrait les naissances et menait tout le monde dans le droit chemin, le voila depuis un an à la maison d'arrêt et de correction de Thiès, attendant tristement son jugement qui on ne sait quand, loin de sa femme de valeur et de 3 enfants encore tout petit. Je pense beaucoup à toi Mon Oustaz mon Maître😭😭😭
Mome yayou khaleyi yaar bigako yaar kay wa grand dakar sedénagnouko Mane je suis choquée si tant d’ingratitude A la limite si le viol était vrai ,mais inventer li sank sa neveu
Koufi accuse viol te dou deug
On doit t emprisonner avec une peine tres severe pour diffamation !
Vraiment
C’est tellement injuste après le quittement la victime sera libérée comme si de rien n’était et que l’accusateur part sans aucune sanction
C'est vraiment regrettable comment on peut accuser comme ça quelqu'un
Que le tout Puissant protège nos garçons 🙏🙏🙏
je sw une patriote et m'interpelle directement le PM Ousmane Sonko sur l'affaire Fallou Fall et Eumeu parce qu'il a subi la même injustice.Oh quel Senegal🤗🤗🤗
Courage justice pour eûmeu
Il est temps de créer une association contre cette injustice
Li metina torop pourkoi torokhal domou djambouur
Ndaw association bou bari cas. L'injustice est presque partout, dans les maisons, entreprise, rue, presque partout.
Sénegal comme feuilleton Indo action you yombu 😭💔
Sénégal bilahi dina yèkha am diam ndax justice amouffi ,lou waay nèkh deff té dou moudji fénn
Ay way li lan moko fi diar ki mo bon yalla na yalla torokhal la
Amine amine
Yalla nako Yalla takhawou ngénéko thi situation yi lii metina trop thi ko bokal ndeye ak baye ak ligua li ngako défal yeup Yalla nalèn Yalla até
Nit mom bou xassè Beu boon rk boon neu😢dou xamé lou baakh ak wala Lou bon très écoeurant
Courage Marém yalla bakhna 🙏
J'étais au procès ce matin mais boy bobou franchement boy bou gentle la li mom meti nama trop
Legui noumou moudiè
@zeinadieng7187 renvoie au 4 mars
@@AbdoulayeSeye-x9n ndeysanne peut être bou tahawaté dinagn ko bayi insha allah
@@MignonneBarbie-e9c guemnako dh inchalah
Aywayy, yala na yekhe,Wayé yow mi d,naro Yor say domou mag sou deudouwone. Na niouy rafetal, adouna yagoul, té amoul ben solo. Niou fékhé nétali yi di rafet. Massa ya boye ❤
Justice pour Eumeu 😢😢
Yalla na léne yalla maye ndam 🤲
Mann dall warou na deh si souniou Senegal gui deh😢
Justice ak corps médical Niogui fowé sounioum réwww teh tégouniouko fénnn fou lérrr
Yallanako yalla nite guènenèko si khatekhate courage eskey metina loleeeeee justice pour fallou fall et eumeu courage maman et la Famille de fallou et oumi et Mbaye kharitou fallou na yone dèfe liguièyame gnawena metina
Ay niit soxor na😢😢
Yala nako yalla dimbali si barkép serigne Babacar s’y ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Justice pour lui💔
Yallana yalla léral leip 🙏
Cheuuuuuuuuuuuuuuuuuuteuteuteeeee CEST GRAVEEEEEEEEEEEEEE😢😢😢😢😢
Li migui mbeug barii di accusé viol dii tek séni dilll yoon warnasi diougue Sonko tmt yekhna réagir sur le cas de fallou fall ak yénéen
Wallahi wakhna deug Marieme kou bakh ameu dome you yarou teksi Wallahi eumeu yalna yalla guénéla ak jamm🙏🏾
Yalla na yalla léeral lieupp😢inchallah
Li métina walahi
Yalla nako yalla takhawou si barke s touba Justice pour fallou fall
Pendant ce temps, l'imam de notre mosquée est en prison depuis 1 an à cause d'une accusation d'une femme, comme quoi il a violé sa fille de 4 ans. Un homme digne, jovial, plein de sagesse, gérant deux daaras en même temps, chez lui et à la mosquée, qui dirigeait toutes les prières quotidiens et mortuaires, animait les conférences, prêchait chaque Vendredi à la grande mosquée, célébrait les naissances et menait tout le monde dans le droit chemin, le voila depuis un an à la maison d'arrêt et de correction de Thiès, attendant tristement son jugement qui on ne sait quand, loin de sa femme de valeur et de 3 enfants encore tout petit. Je pense beaucoup à toi Mon Oustaz mon Maître😭😭😭
Quelle injustice Arame trahison bakhoul
Sénégal justice ba legui dafa am corruption
Waw riroum accusation viol bi si Sénégal gui nak ken doussi sak pékhé 😮
Lettere d excuse moy avouer les faits, il faut pas le fare si vous n avez rien fait !
Pourtant cas yii nii guay dég Sénégal LEP djiguene mo Koy def
😢😢😢metina
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Hier la warone tahaw guéne n’a wala?
🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Courage 😢
Sénégal dal yalla yalla moussal niou moussal mbolém dioulite
Mome yayou khaleyi yaar bigako yaar kay wa grand dakar sedénagnouko
Mane je suis choquée si tant d’ingratitude
A la limite si le viol était vrai ,mais inventer li sank sa neveu
Boudé kisi louga mome na sene xele Dele kima guise birahim Naar lako tek th boudé mome rk falé wull kou yalla binde deug rk lay topp
🥺🥺
Senegal justice bi warna nagnou ko kholat
🤲🤲🤲🤲🤲😢😢😢😢
Eskey metina yallanako yalla nite
N acceptez pas une lettre d excuse lolou day melni da nguén avouer
🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Doyna war .rafale len yala .t kham Lou way def domou diambour Dina keppou sisa dôme.yena ngui yak avenir domou diambour
Ndeysane metina lol
Peur j'ai que des garçons massa
J'espère qu'on l'a libéré ???
Pourquoi le juge l'a renvoyé alors que la vérité a éclaté
🥲🥹😭😭🙏🙏🙏❤
Loutakh djiguene siss ?
Thièye adouna li yeup ndakh sèni intèrè bopou rèk yalla dèh ame na tè dou ande thi aye fène
Dama tite sakh😢😢😮
Arame Fall de soprim, ok je comprends.
ARAME FALL YAW DO CHANGÈ
Toi aussi tu la connais.
🤲🤲🤲😭😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏